Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi SAAWS akiy sahaabaam RAA te wërsëgël nu nu dëkkag ñoom ca kërug teràngaam.
@kinewade55723 ай бұрын
Machallah mbacké balla yalna yalla defalniou dégueu AK topou