Ki danou Ko Ray Ray bou Niaw si Nevetane Yi Brique lanou Ko Doré ! Yayam sonou na

  Рет қаралды 30,536

Pa Assane Gueye Lebou

Pa Assane Gueye Lebou

Күн бұрын

Пікірлер: 233
@LayeKhouma-p7y
@LayeKhouma-p7y Күн бұрын
Moutapha yalla nako yalla yreum 🤲
@MamadouSow-us1gc
@MamadouSow-us1gc Күн бұрын
Wolaye Ndeysane 🤦 li défa méti yalla kamnako 😭 mais yalla nako yalla yerem té diegal yarabi yaboy yalla nala yalla takhwu yarabi takhwu bolém dioulite yarabi 🤲😭😭
@FatouDiop-no3it
@FatouDiop-no3it 23 сағат бұрын
Ndeyssan yalnako yalla yeureum th kharéko aldianay firdawssi 🤲🥺
@falloumbow3115
@falloumbow3115 Күн бұрын
Navetane moh amoul bene ndiarign
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo Күн бұрын
Non😭man louma diakhal Président Diomaye khana dou guiss information yi billay deuk bi légui worotoul Yalla nako yalla yeureum kharéko aldjanna
@ElHadjiDieye-h7f
@ElHadjiDieye-h7f Күн бұрын
Amine inechallah ❤🤲🤲
@FallouDioum-qv1if
@FallouDioum-qv1if Күн бұрын
Waxal waay..lolou moma jaxal melni dougnou guiss lou xéw si réewmi
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 Күн бұрын
*Ah doyna warr dall😢*
@AminataBaldé-f3d
@AminataBaldé-f3d Күн бұрын
Vraiment warnagno communiquer
@mamesheiix99
@mamesheiix99 Күн бұрын
C'est au ministre de l'intérieur de faire le travail
@NdeyekhadyCisse-p8v
@NdeyekhadyCisse-p8v Күн бұрын
Yalla nako yalla yeureumm🙏🙏🙏
@ndiobakane-vq4th
@ndiobakane-vq4th Күн бұрын
Mane dh Lima diahal Moy niouam diome te yereme sen yaye rek laniouy ray 😭😭 li metina torop😭😭 yalla Nako yalla yerem
@10tvndieye22
@10tvndieye22 Күн бұрын
Way gniko Ray séne leufeul ndeye waye 😢😢😢
@astousylla8496
@astousylla8496 23 сағат бұрын
Billahi kone sétlou nga lolou khana thiat lay done laa yakar😢
@CheikhSarr-f2u
@CheikhSarr-f2u Күн бұрын
Aywày ji seutt 😢non Sénégal doudém.wallahi ay wàye yalla bakh na pa assane Gueye Merci beaucoup way ci vidéo yi
@AliouToure-u2x
@AliouToure-u2x Күн бұрын
Li mietina torob sama Kong la khéwé😭😭😭😭😭
@salioundiaye2742
@salioundiaye2742 Күн бұрын
Yalla nako yalla yeram
@biguelo3675
@biguelo3675 Күн бұрын
SONKO DIOMAYE J VOUS AIME TROP MAI RÉAGISSEZ ON VEUT LA PEINE DE MORT DEPUIS 2018 Les agressions augmentent de jour en jour
@MamadougayeNiang-n1v
@MamadougayeNiang-n1v Күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum thé diégal ko 😢😢😢
@MaodoNdoye-m6i
@MaodoNdoye-m6i Күн бұрын
Mois de Janvier bi gnata nit lane Ray Sénégal si tayeef🤔 Yalnako yalla yereum ta diègeul 🤦
@LayeDiouf-vs1vf
@LayeDiouf-vs1vf Күн бұрын
Yalna ko yalla yeureum ❤
@AssaneGueye-g5f
@AssaneGueye-g5f Күн бұрын
Sénégal jeune yi beuri khamouniou finouy tek.séne tank boyi rewnanou fouy nanou khamounou adouna amounioufit beugue bandi bandilou dangay nék sikogne begue gninanela.danga fit louxew nga rothi diam ta nga am.loula.doy seuk.sa ndeye yoroul sa baye.yoroul eulé nga diéme khol noye def ba guéne sa.ndeye si peuvrete médoko Def louy navete ba sak at xex goudoul fié Diékh si navetane ta li yeup génération 2000 rek biniou magué aferou dofdof rek moléne nékh mé yawmi déf li yalla nga torokhé si prijon
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 Күн бұрын
*Merci bcps t’a tt dis c’est désolant way bilay walay 😭😭*
@rokhyfall3687
@rokhyfall3687 Күн бұрын
Tapha kay yalnako yalla yeureum taii xareiko aldiannaa meitinna tropp bilayeu 😢
@LayeKhouma-p7y
@LayeKhouma-p7y Күн бұрын
Nevetane ak lamb mo wara djiéx si sénégal kou begue footbal gua dém si centre formation yi beuri niou xol louniou def aaaahhhhh
@aliounefall8143
@aliounefall8143 Күн бұрын
Nguir yalla nguir yalla nguir yalla naniou ték kou ray niou ray la wallaahi lolou rék mo meuna réglé problème bi
@KhadimSokhna-jz1um
@KhadimSokhna-jz1um Күн бұрын
Ohh ndeyesane Li doy na war dh yalla noko yalla yereum Si barkép alquran Karim 😭🥺😳🤔🙏
@whatsup-hl5qm
@whatsup-hl5qm Күн бұрын
Senegal fok niou sévère si yene descion yi sinon dina eup lokho
@salimfall
@salimfall Күн бұрын
Mann dhé sama khol diékhna lii métina massa yaye boye kii ko raye yallanako yalla wérr yalla bakhna
@FallouSeck-pt9ys
@FallouSeck-pt9ys 53 минут бұрын
Yallah nako yalla yeureume si barké seydina mouhamed psl kharé ko aldiana si barké seydina mouhamed psl
@SakhoFall-f9d
@SakhoFall-f9d Күн бұрын
Moustapha yalla nako yalla yreum 🤲
@MoustaphaFall-zy8mo
@MoustaphaFall-zy8mo 19 сағат бұрын
Sigulle ndigale yaye boye massa waye😭 méti na trop billahi ms moustapha yallana ko yalla yeram thia kharèko alldianaye firdawsi thi barkèb sarige touba ❤
@souna_barhamienne0075
@souna_barhamienne0075 19 сағат бұрын
Yalnako souniou borom yeureum té diegal ko yalna yegalé ndawam si aldjanah firdaws🕊🙏🤲niaw na trop vraiment 😢
@IbnabassGayeGaye7079
@IbnabassGayeGaye7079 20 сағат бұрын
اللهم اغفر له وارحمه 😢
@matardiagne1649
@matardiagne1649 Күн бұрын
Merci pape assne geye
@djilytandine9202
@djilytandine9202 Күн бұрын
Sénégal li kagne laye diekh
@PapaFall-j7h
@PapaFall-j7h Күн бұрын
Yalla na nako yalla yereme❤
@dieynabagueye3987
@dieynabagueye3987 Күн бұрын
Bilahi li faw niou severe 😢li nekha toul ray domou dambor si 0 tmt 😭😭😭😭
@CheikhDiop-r7y
@CheikhDiop-r7y Күн бұрын
Li metina doy na War 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@MansuJeddah
@MansuJeddah Күн бұрын
Y'a trop d'injustice au Sénégal.
@Ajstylesmiami
@Ajstylesmiami Күн бұрын
Paix à son âme
@BabacarWillane-c8m
@BabacarWillane-c8m Күн бұрын
Ndaye la métina😭😭tapha yallah nako yallah yeureum mér bi yallah nako yallah takhawou🤲🤲
@SerigneMDieng-n5t
@SerigneMDieng-n5t Күн бұрын
Yanna ko yalla yeureum tè kharé ko aldiana
@MalickDiouf-z1z
@MalickDiouf-z1z 12 сағат бұрын
Un homme cool vraiment on passer à entraîner ensemble à la salle vraiment kou jovial Yalla nako Brom yeureum té xaréko aldiana Yalla nitte gni Déf lou bone Lii 🙏masta yaye boye Tapha à jamais dans nos cœurs 💔frr
@AlhadjiGuillenn
@AlhadjiGuillenn Күн бұрын
Ohhh Amna Louma métti Billahi 😭😭🤔🤔
@karbala167
@karbala167 Күн бұрын
Yala nako yla yereme mes kou raye daniou ka wara raye c tt
@BayeTallaFall-b6j
@BayeTallaFall-b6j Күн бұрын
Alhamdoulilah sante yalla merci passe Gueye lebou
@CheikhNgome-ig9id
@CheikhNgome-ig9id Күн бұрын
Vrément raybi dafa yombe troppe😭
@KhadimDiop-xz9ow
@KhadimDiop-xz9ow Күн бұрын
Ndaysane 😭😭 yalla nako yalla yeureum
@SAMBABa-tr3su
@SAMBABa-tr3su 23 сағат бұрын
Yalla nako yalla yeureum té kharéko al djanna
@ndeyesarr1796
@ndeyesarr1796 Күн бұрын
Mane dal titena sii sénégal. Chaque jour des neurtes. Paix à son âme 😭😭😭😭😭😭
@AdjiLo-dm9qo
@AdjiLo-dm9qo Күн бұрын
Ohhhh yalla naniou yalla haree ale Dianaye firdawsiii koulou houme metina torpe ndeysane 👂👈😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏
@ibrahimadiop3459
@ibrahimadiop3459 Күн бұрын
li dafa niawe 😢
@CheikhAntaMbaye-w9g
@CheikhAntaMbaye-w9g Күн бұрын
Non li dafa wara diekh sii Rewmi walahi lifa dafa Méti
@abdoudiop8697
@abdoudiop8697 Күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum khare ko aldiana firdawsi
@ThioubouArnold66
@ThioubouArnold66 18 сағат бұрын
Tapha ndeysan yalna ko yalla yeureum kharé ko aldjana firdawsi si barki seydina Mouhamed psl ❤
@balde116
@balde116 Күн бұрын
vraiment pa assane ça sést trop facile l'état doit prendre ses responsabilités trop c'est trop ces gens ternissent l'image du football qu'Allah lui pardonne ces péchés et l'accueil dans son paradis c'est vraiment dure un soutien de famille
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 Күн бұрын
*Trop c’est trop way ray ray ray rk ba kagne tmt 🥺paix à son âme Yalla na khipé Aldiana firdawsi 🥺🙏🏽🙏🏽*
@Efo-l6u
@Efo-l6u Күн бұрын
nekhetane yi daniouko wara khol senegal yepala newetane diaroul nono fokhrekla bakan dafafor😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏
@Se.DameFayewakana-zd9mg
@Se.DameFayewakana-zd9mg Күн бұрын
Ndeye Sanne Metti na bilay yalla nako yalla yeurem 😢
@Ggtttiiioi
@Ggtttiiioi Күн бұрын
Thiey adunya djambarii rek lagni fat😢
@ousseynousall5808
@ousseynousall5808 Күн бұрын
Néwétann mofi wara djiekhe ndéyame 😢😢😢
@ouzinndiayendiaye9241
@ouzinndiayendiaye9241 13 сағат бұрын
Yallna ko Yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi amine yarabi
@SokhnaNdiaye-md3wk
@SokhnaNdiaye-md3wk 18 сағат бұрын
Yalah na ko yalah yereum diéguel ko kharé ko aldianay firdawsi 😢🙏
@BabacarCisse-wd3fw
@BabacarCisse-wd3fw 13 сағат бұрын
Yalla nako yalla yarem 🤲🤲🤲
@issagadiallo3651
@issagadiallo3651 Күн бұрын
Qu'allah lui fasse miséricorde et lui accorde le paradis firdaws
@Efo-l6u
@Efo-l6u Күн бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭ooooooh masa yaye metina yayboy mounial masa😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@massatalam775
@massatalam775 13 сағат бұрын
État bi mo wara dieul ay responsabilitème interdire Nawétane, insécurité rek lay yokk😢. Yalnako YALLAH yeureum.
@souleymaneba8850
@souleymaneba8850 Күн бұрын
Ndeyssane massa
@AmirouDiallo-dv2vj
@AmirouDiallo-dv2vj Күн бұрын
Yalla na ko yalla yereme 😢😭😭😭😢😥😥😭😭😭😭
@Morinfo5
@Morinfo5 Күн бұрын
Amna kénen kougne rey thie soiré sérére degnko guor diasi
@AminataNdiaye-li3mi
@AminataNdiaye-li3mi 20 сағат бұрын
Bilahi kou diour rek kholou diourel molo dioye lo😭😭dafa meti dé
@soldarousbabacar7291
@soldarousbabacar7291 Күн бұрын
Yal nako yalla yeureum si batou la ilakh illala
@AichaDIAGNE-kg3vy
@AichaDIAGNE-kg3vy 22 сағат бұрын
Pa Assane waxal si cas wou Fallou bi nguir yalla xawmako dei mais bilahi liko dale daffa meti
@FatouGaye-e5y
@FatouGaye-e5y 23 сағат бұрын
Wa sunu président bii khana d'où guiss liii 😢😢
@SIRA.K
@SIRA.K 21 сағат бұрын
Je me domande yoon kagne laye défe liguéyame,injustice totale que firdawsi soit sa demeure éternelle amen 😢
@TallAlHuseyni
@TallAlHuseyni 13 сағат бұрын
Yalla na ko yalla yeureum té ha reko Aljanna firdawsi ndeysan lui ñiawna
@NdiasseNdoye
@NdiasseNdoye 3 сағат бұрын
Yalnako yalla yeureum
@madeleinesene2375
@madeleinesene2375 13 сағат бұрын
Yalna yalla yeureume té xaré ko aldiana firdawsi
@PAPEBABADIOP-i6x
@PAPEBABADIOP-i6x 14 сағат бұрын
Li métina bilay yalnako yalla haré aldiana
@faloundiayendiaye
@faloundiayendiaye Күн бұрын
Yalna KO yalla yeureumb
@MatyDia-nq7gr
@MatyDia-nq7gr 20 сағат бұрын
Yalla nako yalla yeureume khare ko adiana firdawsi oyofal souf thi kawam 🤲🤲🤲
@Wizzy_Killer_23
@Wizzy_Killer_23 Күн бұрын
🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@OmarSidibe-vq7bo
@OmarSidibe-vq7bo 22 сағат бұрын
Nafekk yi lamb dji rek la niou yapp Ouakam ak stade de mbour 11 morts mosi am ak 21 blessés graves na niou wakh tmt si football bi yalla nako yalla kharé aldiana🙏😭
@MoustaphaJabaye
@MoustaphaJabaye Күн бұрын
Ndeysann 😢😢😢😢😢
@BayeTallaFall-b6j
@BayeTallaFall-b6j Күн бұрын
🥹🥹🥹🥹 yalla nako yalla yeureum té kharéko adiana
@MoussaThiongane-m5r
@MoussaThiongane-m5r 23 сағат бұрын
Non DaYesaNe MéTiNa Trop Khôl Li Rk Soutien De Famille Nou Rayeko Ni Non Bonne Bakhoule YaNako Yalla Yéreme Ta kharé ko Alldiana FridaWe Maman Yalla MayeLa khol Mouye Inchallah Amine Amine Amine ❤❤❤❤
@bassdiop7622
@bassdiop7622 Күн бұрын
Yalna ko yalla kharè aldiana firdawsi
@oumyfall9348
@oumyfall9348 23 сағат бұрын
Ay way Senegal yakona li metina trop 😭😭😭
@cheikhoumarsow3517
@cheikhoumarsow3517 Күн бұрын
Nawetane diaratouko meme brt gudiuwaye danioufaye sandi ay kherr
@absambaye8734
@absambaye8734 13 сағат бұрын
nevetane foh kasé lah waye borom khol you bon yii fi mboro non lan fi ray khalé khale bou ndaw😭😭😭
@AbdouDiallo-u1g
@AbdouDiallo-u1g 22 сағат бұрын
Yalnako yalla yeureum 😢
@boubacarboubsdiallo7760
@boubacarboubsdiallo7760 21 сағат бұрын
l'État doit faire face et prendre toutes ses responsabilités en ce qui concerne les navetanes. Suspendre ces activités et les réorganiser.
@YaramGueye-m8y
@YaramGueye-m8y Күн бұрын
Pape assne doko ketale bokk yaye bii louko waye manadepale rkk
@tallafaye3716
@tallafaye3716 20 сағат бұрын
danio fara deff kouray niourayla
@BodioKande
@BodioKande 10 сағат бұрын
اللهم اغفر له و ارحمه
@fatoufaye7259
@fatoufaye7259 22 сағат бұрын
Bilaye sama khoie défa toye bilaye
@AladjiDiop-c3i
@AladjiDiop-c3i Күн бұрын
Alhamdulillah 😮😮
@NdiagaDiop-nf5wd
@NdiagaDiop-nf5wd Күн бұрын
Mane mom lima yaag wax rekk nawétaan louniou fi wara arrété la fi si Sénégal ndakh tout le temps lii moy conséquence yii toujours té mane louma yaag contre la mom niom bouniou leen fayoon louko diar sakh niou meuneu wax wayé prime biniou siy ame dou dara lep dirigeant yii nio koy lekk légui yaw simple supporters nguay ray sa bopou si lo xam ni dossi laal 1Fr donc diarouko mane mom nawétaan mom dama contre par ce que amoul fair-play wa salam
@AmadouSow-u3f
@AmadouSow-u3f Күн бұрын
Vraiment 😢
@GIXXX769
@GIXXX769 Күн бұрын
Mo geune dh amoul benn sanse
@NdiasseNdoye
@NdiasseNdoye 3 сағат бұрын
Bayi lène lamb ak navètane
@AbdoukhadrDiakhaby
@AbdoukhadrDiakhaby 13 сағат бұрын
Le foot avant tout c'est du plaisir mais dommage pour nous Europe ngay guiss supporter real nekeu si bir ay supporter barcelonais mais dara dou xéw sou diéxé rk diéx na mais nioun c'est tellement grave bilahi
@FallouNdiaye-fe4bq
@FallouNdiaye-fe4bq Күн бұрын
Nawètan lambou lou wara dièkh Sénégal la bilay walay li pour lane
@faloundiayendiaye
@faloundiayendiaye Күн бұрын
Alkhmdou lila
@IbouMbaye-k6l
@IbouMbaye-k6l Күн бұрын
Nevetane amoul ndaye béne diarign
@dieynamanga8422
@dieynamanga8422 21 сағат бұрын
Ndeyssane paix à son âme. Mais pour man solution bi Moy def ni congo AK kuluna yi rek😢
@bagiss360
@bagiss360 13 сағат бұрын
Sarap ndeye nawétane dangnko wara dieulé ndeye Sénégal 😢
@morysow7144
@morysow7144 20 сағат бұрын
😢😢bilahi pa Assane ça fait des années mangui lay toppou mais Tay la meussa sétan sa vidéo ma dioy😢😢😢yalla nako brom bi kharé aldiana firdawsi 😢😢😢
@idymbayefall8601
@idymbayefall8601 9 сағат бұрын
Navetane bakhoul bilaye
Justice pour Fallou Fall mou gnou teudjieu 15ans t Defoul dara
8:37
Pa Assane Gueye Lebou
Рет қаралды 20 М.
Xalisso - Saison 1 - Episode 34 **VOSTFR**
54:41
EvenProd
Рет қаралды 1,5 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
Réal Madrid 5-1 Salzbourg ! Quel match la passe de Bellingham
8:30
Pa Assane Gueye Lebou
Рет қаралды 19 М.
Rakou Fallou nèna Papam moka teudjlou t danou ko diap #falloufall
9:52
Pa Assane Gueye Lebou
Рет қаралды 252
regarder avant après le match Barça Real Madrid 🤣🤣🤣
3:16
Niaye Production
Рет қаралды 7 М.
MOR GUEWEUL: On m'accuse d'avoir sacrifié un de mes doigts
41:57
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 240 М.