Santé s.Touba rek wallahi amoull morom diarrama mame lamp Fall ndiaga yaram may sa bégé coumba Fall ndiaga yaram may sa bégé coumba Fall
@fatoufaye2943 жыл бұрын
Aka xam wa keur Cheikh Bamba. A tes 100ans maman cherie
@khadysylla6673 жыл бұрын
Amine
@adamengom12103 жыл бұрын
Moma diakhale daf maîtriser machalla
@toulycama70833 жыл бұрын
Sokay deglou dangssi diangualé
@moudouba44683 жыл бұрын
Bilahi sa bouma dioule gnanal ko mou doundou 150 ans sans ordonnance sama yaye djigue mala beug
@ndeyengom96953 жыл бұрын
@@khadysylla667 n,.
@cheikhrassouldiouf1593 жыл бұрын
Ma chanteuse préférée Aka meun loumouy def ta yiiw longue vie à toi Maman kiné 😍
@abdoulahatdiop13153 жыл бұрын
Une grande chanteuse, grande dame digne respectueuse. Artiste de tous les temps , kine lam mame Bamba
@adamasamb71963 жыл бұрын
Macha alla la chateur du peuple quand je la vois elle rappelle de MA mere parceque elle se reassemble qui nous a qui quitter ressement Long vie a maman kine lam
@Grisjum3 жыл бұрын
Ohhhh maman kine sama sons bi way magi dioy atanouma lii MashaAllah yagg fii way tee and akk weer 😍
@babacarsene64843 жыл бұрын
Ndeysan clip na sons bou yag Machallah ❤️❤️❤️❤️ Mongii melnii tay
@sokhnadiop89263 жыл бұрын
Maman kimé lLam doundeul sakh fi xam Khadim di Ab ngeweuleum kontane ci yow amouma ay millions kon ma battré ba nga kontane . Machallah ca fait chaud au cœur ♥️
@pasdetemps41453 жыл бұрын
Lal gua xolou khep khouy mouride ak khoudoul mouride machallah
@toulycama70833 жыл бұрын
Wayonowoul ak kene jeune génération naniou guestou way
@amydiop053 жыл бұрын
Ndanane akk Diongoma pirr Maman Kiné Lam machallah 👉💘💘💘💘💘💘💘💘👍👌👈🙏
cette chanson me rappelle l'année 1999. J'aimais tellement l'écouter à la radio. Merci Maman Kiné Lam pour ce beau clip simple et pourtant très magnifique. Je t'encourage pour d'autres clips de ton registre rétro ça fait tout simplement la différence
@ndeyefall76083 жыл бұрын
199 cone yagge ga😅😅😅😅😅
@sambal.79743 жыл бұрын
@@ndeyefall7608 effectivement elle a juste fait le clip maintenant mais cette chanson date de 1999. Celà montre vraiment le niveau et la qualité de leur travail par rapport aux artistes d'aujourhui
@decotextoubatawfex9303 жыл бұрын
Liiii dafa nekh machalla kou amė stress yako taye
@fadieye82193 жыл бұрын
😅😅😅😅 deug la deh
@damefaye77573 жыл бұрын
Une pensée pieuse a feu cheberou mboup que la terre lui soit légère
@biguendoye19263 жыл бұрын
Ii .
@biguendoye19263 жыл бұрын
Oko
@darmankotvoriginal3 жыл бұрын
Bilahi Wallahi Damala Begeu 🥺yaya boy yalla Nala yalla Deffal Diamou 🙏 ak goudou fann 🙏 Ak wérgui yaram 🙏
@dembamaidousane63237 ай бұрын
La voix d'or du Sénégal Maman Kiné Lam de mon enfance à maintenant/mes 35 en 2024 tu m'as bercé de tes mélodies ❤❤❤
@seynaboudiaw46583 жыл бұрын
Machallah lall ga tidiane yi lo way téré la mouride sadikh yalla na batt bi weur
@mamadoualioumansaly4223 жыл бұрын
La cantatrice du peuple ♥️♥️😭😭😭 J’espère la rencontrer un jour
@dykhagueye30003 жыл бұрын
Elle habite parcelle u 26 en face stade amitié
@vieuxbocarguisse94313 жыл бұрын
En face stade amitie la deuk
@dioufmareme2903 ай бұрын
Dina la yobbou
@diopkhalifa42712 жыл бұрын
Masahllah mama yalla na yalla godall fane wi tamo andue ak werr si barké borom touba khadim rassoull amine amine amine
@TinaTina-ix6pi3 жыл бұрын
La diva des diva goudou fane rek laniou lay nianal woy rek ngay def amo morom si art 🖼 biii Kiné mame Bamba 🥰🥰🥰
Merci Maman kine de faire revivre ce tube planétaire pour la jeune génération je suis tijane pire mais way bi dama ko weur fou nek depuis longtemps longue vie Maman.
Maman Kiné machallah , je l’adore 😍 🥰🥰❤️❤️ Ila Touba rek 🥰
@adjasalihsamb93983 жыл бұрын
Album le retour yagna nekh j’ai des frissons 4mm46🥰🥰🥰🥰la meilleure de sa génération 🥰🥰🥰🥰
@maudoudiakhate62183 жыл бұрын
Machallah
@maimounafall93533 жыл бұрын
Partie bobou meuneutouko bilahi
@DIENGModou2 жыл бұрын
La grande diva, belle chanson et très jolie clip, j'ai des frissons en l'écoutant, dimension spirituelle de Cheikhoul Khadimou Rassoul. Longue vie à vous maman Kiné Lam 🙏
@nancyfallou8255s2 жыл бұрын
Douma si doyal ❤️bilay ahmadou yanek woye
@ballaniambele91532 жыл бұрын
Machallah. Que le bon dieu veille sur toi et ta famille. Longue vie et une santé de fer
@marieyandembengue91423 жыл бұрын
Mâcha Allah yaye yalla na sa diam yague yalla defal la goudou fane ak wéer si barké Seydina mouhamed (psl) Amine
@papasambandiaye54053 жыл бұрын
Machalla maman kiné une carriére sans faute longue vie à vous elle a tellemenr chanter la famille de bamba contana thi yaw et jécoute beaucoup vos chansons
@khadyrassoul3 жыл бұрын
Yague fi yaye boye dignou béguel 🤲🏽🤲🏽 je t’aime ❤️
@absandiaye14403 жыл бұрын
Yalla na yalla yockou wérre ak fan
@adamengom12103 жыл бұрын
Aka yiwe ame classe thé meune li mouye déf machalla douda maman kine 🥰🥰🥰
@mariannedianorniang96363 жыл бұрын
Maa sha Allah wayliwayli ba gui nii lo wayoul nékhoul
@madoundiaye62353 жыл бұрын
Maman kine wayy bi nexna machallah sagnse yi rafett na yall na yalla weral batt bi💓💓🎉🎉🎉💓💖
@awatouba60573 жыл бұрын
Toujour egale a elle meme ken dou yaw wayacone baguini
@chiekhmouretdegalreckgeuye71003 жыл бұрын
Ya mana wayé kîi dou nét
@massambadiop7203 жыл бұрын
Cette chanson date de plus de 20 et on a l’impression qu’elle la chanté hier. C’est ça être une artiste à tous les temps. J’adore cette artiste 🤍🤍🤎🤎
@sallandiaye67713 жыл бұрын
Machahala maman Kiné doundeul yereul amal diame boubakhe si barké borome ndindy kéne d'où yowe sama chanteuse Préférée
@akonniang22593 жыл бұрын
Woy wi yague nako déglou t tay la guene nékh wayé bima guissé Video Clip bi dama contant lima geuna nékh si woy wi moy Serigne Touba damakoy woy ba bamay déh sama xol day toy bo agge dofu 😢maman Kine je t’aime 💕😘❤️ Doundeul t weur
@goddessfklmofficiel99823 жыл бұрын
Badiene do moromou keneu ☺️ machallah
@dioufmareme2902 жыл бұрын
Sa tourando Wayy Rekk lay déf. Kiné mbaye thie lo nekk
@ibrahimagueye20249 ай бұрын
Lolo dafa leer
@ndeyekhadydiaw73593 жыл бұрын
Ki rek la Beugue bilay ❤️❤️❤️
@leproduitdesongrand-pereal48983 жыл бұрын
Ya Kiné Lam Yalh nala Yallah yokku weirr guddël sa fann Barkeip Seex Yibreu🙏🏼 mention très honorable à Pape Cheikh Diallo
@mamemarieme43313 жыл бұрын
Machallah Machallah 🥰😍🤩 ndeysane Maman chérie bég si yow yay sama conseil bilay🤩🤩🤩🤩
@mouhamedniang76363 ай бұрын
Ki Dou Sakh Nit Doufi Am Macha Allah 🙏🙏🙏🙏🙏
@imyourkingsking75173 жыл бұрын
Yalla na yalla goudal fanwi Lam, Lo way mou nekh. Wayè nak ki nga way mo nekha way Mbacke balla Aicha Mame asta wallo mi si nawel
@LABELMTEVENTS3 жыл бұрын
Une grande diva de la musique sénégalaise toujours égale à elle même avec sa voix mélodieuse ndanane si biir ndanane yi Longue vie à vous maman kiné
@BGB198453 жыл бұрын
Intemporel cette œuvre Ma Sha Allahou
@begood36262 жыл бұрын
Quand on est s trop jeune, on se ne rend pas compte de la portée des paroles. Là c'est fort.
@ndeyethiam82163 жыл бұрын
Machala yalla nga fi yague lol guoudoufane guou andack were Safarma Modou Bamba reck la gueme bilahi waye ngaco louné kine Mame Bamba
@zeynabfall48983 жыл бұрын
Goudou fane ak weer maman Kine. Yaw baguay Mouride demb laa taay sogua nieuw.Chanson bouma marquer sama jeunesse bilahi et je dirai ma préférée. Yalanala Serigne Touba faaayyeu
@manediop33983 жыл бұрын
Machalla yallanako yagga waye ay at youbari Bari inchallah 💕🤲🤲
@yacinediop57123 жыл бұрын
Oh la diva da ame dégue dégue meune ko lole une fierté pour la musique sénégalaise ❤️❤️❤️
@deguenembaye91993 жыл бұрын
Manchalah maman goudal fane wayy ♥️♥️♥️♥️ bou ande weer
@sadycissokho40433 жыл бұрын
Machallah sama yaye dji adjia kiné lam yallna yalla faye la si barké Serigne Touba mbacké kina lam ya bakhna barki Serigne Touba mbacké ya bakhna je t'aime ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@penearmand99963 жыл бұрын
vraiment yaye kine lam nouma def graw na trop mei yalla baxna yalna diameu yague
@astougueye64733 жыл бұрын
MASHA ALLAH Maman Kinê Fanes bou goude ak wéer tchi Barké Borom Touba Daradiaye SEYDINA MOUHAMMAD ALEHI SALATOU wa SALAM. Bêgue naa lole tchi linga indiwaate Chanson bou nêkh bii tchi sama Mame sama Serigne bi Serigne Fallou.
@yahbouyadiongue21613 жыл бұрын
Bilahi walahi mala beugeu ❤️🙏🏽maman kiné goudeule fane té and ak wére
@mbayetoure14032 жыл бұрын
Cette chanson me donne des frissons merci a maman kiné lam pour cette œuvre
@toutouprovocation18393 жыл бұрын
Way bi comme guérre jtj 😅😅😅du début à la fin dafa nekh tang dieur manchala lam demba gade❤❤❤❤
@ndiayemaleye25813 жыл бұрын
Bilahi yao comprendre nga 💪💪💪💪💪
@mamemarieme43313 жыл бұрын
Amouma sagoo si liiiii bilay🥰😍🤩
@sophiefaye35453 жыл бұрын
Laff thiate yaye boye woyyy rek lay def❤️❤️❤️🌃
@mariemekeita50633 жыл бұрын
Machalla! Defatina maniname ndokh dou bayi yonam kine lame mou mame bamba laye doooone ba aldjiana barke khadimou rassoul
@fatouborofallaidara81533 жыл бұрын
Machalla,lam,la diva, dieureudieuf xoll,sedina,diadieff,un grand merci .
@mariejodiatta83623 жыл бұрын
Maman beugeu nala beugeu gou sincères meunoumala yèmelè ake béne musiciens longue vie à toi
@oumydiop97583 жыл бұрын
Gouddal fane waye 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@sangonembaye43153 жыл бұрын
Thié yacine mi ci mekhé sefour penda demarone brome djam ngi Maronen Bi Yao lo Waye Mou Nekh Maman Kine lam
TOUJOURS RAVISSANTE EST CLASSE LIGUA WAKH SII MAME CHEIKH AHMADOU BAMBA REYE NA
@loukaperez96283 жыл бұрын
Mo takh def lou bakh rek mo am solo ndakh netaliba son bi am na gno khamdi dioudo kou gnouwone tay gno gui setane clip bi 2021 et elle la change depudi les annee 90