ko khamné amo ndaw lesbienne nga, Serigne Bada dérape et soutient Mario sur problème avec Ndakhté

  Рет қаралды 14,279

Dakar live

Dakar live

Ай бұрын

Пікірлер: 183
@fatimatakome8595
@fatimatakome8595 Ай бұрын
Ndakhté je t'en supplie , il faudra porter plainte à ce monsieur.
@matysylla5159
@matysylla5159 Ай бұрын
Il faut porter plainte contre doumou kharam bii
@adamaseck8816
@adamaseck8816 Ай бұрын
Qui famille ndakhté naniouko porter plainte domerame la dafa diffamé ok 👍
@kamaraawa8121
@kamaraawa8121 Ай бұрын
Bada mome domaram leu quelle honte thimmm
@adamaseck8816
@adamaseck8816 Ай бұрын
@@kamaraawa8121 dafa tothie thiotou ndemm naniouko porté plainte
@sokhoulovedieng1365
@sokhoulovedieng1365 Ай бұрын
Dagno bone rek hum amougnou lounou wakh doméram yi guene done embécile
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 29 күн бұрын
*Bilay ioe ki vrai domérame la thimmm*
@thiabandoye5258
@thiabandoye5258 Ай бұрын
Ya meuna doul la famille de ndakhté doit porter plainte contre segne Bada doméram la
@You-wm1ox
@You-wm1ox Ай бұрын
Petition pour l emprisonnement de ce monsieur
@serignedieng7860
@serignedieng7860 Ай бұрын
Bilahi diarnako Bada dafa réw trop
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 29 күн бұрын
*Diar nako ki dafa réw trop*
@coumbathiam7470
@coumbathiam7470 Ай бұрын
Svp j’alerte famille ndakhté porté plainte afin k’il apporte des preuves si limou wax ni c sérieux ki dafa rew
@You-wm1ox
@You-wm1ox Ай бұрын
Il faut porter plainte à Serigne Bada il a offensé
@DienabaNdiaye-yv6he
@DienabaNdiaye-yv6he Ай бұрын
Cet homme est mauvais 😢 pourquoi dire ça une femme ki pourrait être ta petite sœur
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 Ай бұрын
Domerame rek 😢ki kay dafa dof la fok
@mbayasarr1357
@mbayasarr1357 Ай бұрын
Si bani rew lagnou nék goor modone soutoural djiguéne wayé gor gni come goor djiguéne
@Mouniroufall-sz7cd
@Mouniroufall-sz7cd Ай бұрын
Bilahi deug ngua wakh ay goor kom gor jiguéne
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 Ай бұрын
Lou ler 😢❤do sax comprends
@Mouniroufall-sz7cd
@Mouniroufall-sz7cd Ай бұрын
Kallah t protège
@fatimandao8359
@fatimandao8359 Ай бұрын
Ki môme vrai doméram la
@juniordiallo6109
@juniordiallo6109 Ай бұрын
Ioe xana danguay maral mario demal liguey mo guene li dou yeufou goor yalla
@diadia8044
@diadia8044 Ай бұрын
😢🤮ya Bone yow Est ce que ce Mario était puceau ? Neklene ay nit simm
@user-hi6so6eq8f
@user-hi6so6eq8f Ай бұрын
Un jour dina niéwe notre main témoigneront.le nez la. bouche . tout notre corps donc lou mata soralé
@annaserrere3599
@annaserrere3599 Ай бұрын
Mais toi est ce que ça va? Wayyé yalna yalla leral leuppppp .
@ndeyediop335
@ndeyediop335 Ай бұрын
Goor bou andak jiguéne cinq ans ndaw boufa amoul lathie léne ko goor ga
@AdiyaNguer
@AdiyaNguer Ай бұрын
Deg na deug pirr 🎉🎉❤❤
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 Ай бұрын
🎉❤lou ler 😢
@yayourassoul5054
@yayourassoul5054 Ай бұрын
Djiguene bo dieul sa keur ndeye yobou ko si keur ndeyam yobou ndiéguenay ,après sa ki né amoul ndaw danga geuneu dougueul Mario def ko fen katt
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 29 күн бұрын
*Merci là bas..ki vrai doméram la*
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 29 күн бұрын
*Merci là bas*
@user-bv1nj3nx6g
@user-bv1nj3nx6g Ай бұрын
Astakhfiroulah dou n'importe qui lagne wara diokh micro
@Princess12630
@Princess12630 Ай бұрын
Surtout sa au senegal
@MondeCurieux171
@MondeCurieux171 Ай бұрын
Ki naniou porté ndayam plainte, ya mana katt sa nday
@AwaDiop-zx9vk
@AwaDiop-zx9vk Ай бұрын
Khana kholo thy kaw yalla mola Tim.dé alakhou akbar
@serignedieng7860
@serignedieng7860 Ай бұрын
Ki moy doméram deug deug rek nako ndakhté porté plainte
@fatoukane4929
@fatoukane4929 Ай бұрын
Goor djiguene yi gnio beurri Sénégal !
@KhadySarre-gx6fn
@KhadySarre-gx6fn Ай бұрын
Goordjigene gua pape mbaye mo bakh ti môme svp dakhte porte te ko plaine dakh justice fait son travail
@banelnegri2578
@banelnegri2578 Ай бұрын
Ki da yabaté nék biir Sénégal di wokh louko nékh ki sakh kéne warouko dék micro il est sans vergogne
@user-nq7mb2uu1g
@user-nq7mb2uu1g Ай бұрын
Ya meuna doul
@FatouDiop-fe2se
@FatouDiop-fe2se Ай бұрын
Bayko ba Adamo diappko
@chamade-te1lh
@chamade-te1lh Ай бұрын
Yangui fénal le prophète paix et salut sur lui
@juniordiallo6109
@juniordiallo6109 Ай бұрын
Goor yalla yomboul dé bly xamouma bada xamouma badio nekal goor
@Createurdecontenu-ow9mn
@Createurdecontenu-ow9mn Ай бұрын
Porter plainte rek ki vrai domouram la
@banelnegri2578
@banelnegri2578 Ай бұрын
Thiéy senegale lou nékh way wokh Li mome dou yone les autorités war nanou kholat li
@missediatta
@missediatta 24 күн бұрын
Si le procureur d'auto sesi demain ils diront que c'est sonko qui est derrière celà aujourd'hui au Sénégal tout ce qui bouge c'est sonko
@MaimounaCamara-ko3gv
@MaimounaCamara-ko3gv Ай бұрын
Qui Ken warou ko deklou Satan degueleu😂😂
@Mme-ndiaye
@Mme-ndiaye Ай бұрын
Xawma Kagne lay done mais serigne bada mom dinaniou meussa niouss ndayam si kasso bi
@Princess12630
@Princess12630 Ай бұрын
Yak nit dafa gniaw iaw lolou guay nek di def leup nafek gua li wah si Yallah guemoko nek fi di yak djiguen
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 Ай бұрын
Neik nday fekkeu rek 😢
@dethiethiaw4048
@dethiethiaw4048 Ай бұрын
Ndakh Yallah niou nompal Sonko AK Diomaye nopalou tps yi😂😂
@marmichoue7857
@marmichoue7857 Ай бұрын
Li arranger woul l'opposition bi 😂😂😂
@mariemegaye5841
@mariemegaye5841 Ай бұрын
😂😂
@abdourahmanesall4949
@abdourahmanesall4949 Ай бұрын
Yaw cha leufal ndayy , da nguay doul , tu ne peux pas salir l'image de cette famille,
@user-io5yj4gm2c
@user-io5yj4gm2c Ай бұрын
Qui kou tepi leufal ndeyam gordjigene bou Bonn dagn fey
@originalpassydott5782
@originalpassydott5782 Ай бұрын
Porte ko plént demande national svp
@user-rm7me7sr2u
@user-rm7me7sr2u Ай бұрын
Ly motah pape mbaye di kate sa ndeye
@BeugNaby244
@BeugNaby244 Ай бұрын
Ndahté ak Mario ak mbok laniou kone niom niar niep ay diam laniou Domaram dji yalna la Yalla torahal yalnala Wally Ballago seck faramarennn domarammmmm yalna boumou oumpou sa ndeyyyyyyyye ak sa rak ak sa dom Tiaga bou gor moy ham tiaga bou djiguen domou hadjie
@aissatoundiaye7184
@aissatoundiaye7184 Ай бұрын
Koula khol saxe khamni dangaye inventé wa iow😂
@ndeyeawandao2147
@ndeyeawandao2147 Ай бұрын
Waw ki loutakh mou meun soss. Doul rek laye def
@adjacamara6569
@adjacamara6569 Ай бұрын
😢😢Wa mais li loumou.. bayileeen wax bu niaaaw
@Kiner2260
@Kiner2260 Ай бұрын
Yow kouleu guiss sakh khamni doulkate gua
@Mor-gh1cm
@Mor-gh1cm Ай бұрын
Bilahi djiguén you suive yi koulén takk yako taye dé doun say kan impecil
@bettywade3184
@bettywade3184 Ай бұрын
Bouniou diougué nane sokhna mame diarra amatoufii nane lafiye amé mame moudou anta dafé amati bilakhi linga wakh nii dafa niaww thi djieguene ts djieguene mola eumbe weusine laa ngaye yak derr 😢
@papayomgtow3341
@papayomgtow3341 20 күн бұрын
Si ndakhte porté plainte,les secrets la concernant sortiront en plein jour!!!!
@khadydiagne9686
@khadydiagne9686 Ай бұрын
Astafiroula Astafiroula ki dou goor mene fen
@maremembodj799
@maremembodj799 Ай бұрын
Nakhté porter ko plainte 🙏🙏🙏
@ramatall6798
@ramatall6798 Ай бұрын
Li motah ndeye gueye tegueul se hone mbaya di saga se ndeye
@coumbafallperlefall7825
@coumbafallperlefall7825 29 күн бұрын
Kholal ma doméroumi bi nama yalla bale mais bada mi rek la bagne
@awandewemieniane565
@awandewemieniane565 Ай бұрын
Ndakh té dé preuve leu am .ki ndaw bou sett leu foto neu lep gardé pck li ladone sorr.domeram dji on va t porter plainte
@annemariegomis5908
@annemariegomis5908 Ай бұрын
Sa yoon nékoussi ngua wakh lii yeup😢boussi sa yoon neikon ngua rayko
@PrenomBondage
@PrenomBondage Ай бұрын
Merci bada
@user-cq6yz8vm4h
@user-cq6yz8vm4h Ай бұрын
Ki da xamoul loumouy wkh skh nak yak Mario yéna Yam xamo doul la wkh
@MondeCurieux171
@MondeCurieux171 Ай бұрын
Gni wakh niépp Mario mo takh sén wa keur di ndayi wanne
@actusenegal119
@actusenegal119 29 күн бұрын
Yeen presse en ligne yii nio yak société bi Lou Bone rek gueen woné
@AdjakhadyDabo
@AdjakhadyDabo Ай бұрын
Ndakhté plainte nguir yalla
@afriquecomedie1224
@afriquecomedie1224 Ай бұрын
Ki mome dagno wara Gnaff ndayam ci kasso gneupou nopalou
@betysylla780
@betysylla780 26 күн бұрын
aye waye na wakh dji di rafete
@Mme-ndiaye
@Mme-ndiaye Ай бұрын
Ki mom momine la amoul bakkar. Mom soko fayé 2500f sah mou géneu yakal la nit. Bayi lenko ak pape mbaay rek !
@yacinethiam
@yacinethiam Ай бұрын
Mane khawma loutah niouy wahh serigne
@fatouseck4915
@fatouseck4915 Ай бұрын
Amena domou adama yo Khamenei sossale nite dou gathier thi gniome
@abdousalamcham
@abdousalamcham Ай бұрын
Tanks
@khadydiouf4028
@khadydiouf4028 Ай бұрын
Ki limou wah reuyna famille yeup la khass yow dé entourage bo nek diam doufa am
@thiorogueyesarr5895
@thiorogueyesarr5895 Ай бұрын
Sénégal barina ay nafekh
@user-eq9jn8sp6d
@user-eq9jn8sp6d 28 күн бұрын
Ndakhté porté plainte contre lui
@amicollelo68
@amicollelo68 Ай бұрын
Ki ndiaroul ndaye tontou
@AbyDiop-rj1om
@AbyDiop-rj1om Ай бұрын
Ki bakhoul bilahi
@user-rm7me7sr2u
@user-rm7me7sr2u Ай бұрын
Limotah pape mbaye di kate sa ndeye
@vieuxmalickgueye693
@vieuxmalickgueye693 Ай бұрын
Kokou mome bouko fi toudou. Goordjiguène bou kate leufeul ndayame la.
@Show451
@Show451 Ай бұрын
❤❤
@aminatasambou9566
@aminatasambou9566 Ай бұрын
Yowe Dieukeureum mola waxed ampoule ndowe
@khalifambengue6125
@khalifambengue6125 Ай бұрын
Ohhh Allahou Akbar 😭😭 noo😭😭😭😭
@zaleuhbdk1777
@zaleuhbdk1777 Ай бұрын
Waaaa ki est-ce ça va vraiment j'ai mal légui nitt day wakh nitt lou gnaw té dou moudiou féne
@amyniang3814
@amyniang3814 28 күн бұрын
Ki lepeume nieuwoule wayy.
@thiaradiallo2959
@thiaradiallo2959 Ай бұрын
Sénégal lignou wax rék gnouné bayi nako ak yalla motax lou néx waye wax😢 lii dafa gnaw maye wax mounane Sidy Wally ak Ibro waye nagnou ko ki djabaram la yereum
@onlygood1114
@onlygood1114 29 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂ayy liii
@adjaratoufall
@adjaratoufall Ай бұрын
Wax bii niaw na trooop.
@Touty-wp3gp
@Touty-wp3gp Ай бұрын
Mba am nga preuve rek
@godisonebbuban8522
@godisonebbuban8522 Ай бұрын
Xolale kou cate ndeyam ki , genre yi koulen di diox micro 😌
@mamediarrasamb6157
@mamediarrasamb6157 Ай бұрын
Warnala ak sa gueimeugn gou oubeekou ba melni silibou xalei bou bayi,lingay defendrei kingay bania toudd wakh ngako ndah nenga dafla amal ndiarign kone topal feulei banga xamei Thiaga ji ak lesbiennes yi nga done nitt kou bone. Xaral fofou sa plainte
@user-gj3th6ie8s
@user-gj3th6ie8s Ай бұрын
Bada diome ga ndaw pure la ndakhte thiokh Mario wakham lo khame daga mana wakh lou niaye te do lerelou
@user-vl4ut7uj1h
@user-vl4ut7uj1h Ай бұрын
Sa wayy sa ka dou yi vraiment raféttoul
@aramendiaye638
@aramendiaye638 Ай бұрын
Wakho fi dara
@adjib.38
@adjib.38 29 күн бұрын
Fallait sattendre a cette revenge
@NdeyefatouThiang
@NdeyefatouThiang Ай бұрын
Ay way sa wàkh gnawna
@HousseynKadi
@HousseynKadi 26 күн бұрын
❤❤❤❤❤
@user-wn8nh7wc3b
@user-wn8nh7wc3b Ай бұрын
Ioe gor djigen ga dmrm ya geuna yess nieup niak diom wesou woul sa diabar febar gay dém soir di mayer Mario sunu xoyer lolou😂sunu yon nekousi gor😂djigen biga don
@user-sn3jt5st4l
@user-sn3jt5st4l Ай бұрын
Kougne weuy rek amo loy prouvé?
@BeugNaby244
@BeugNaby244 Ай бұрын
Sa yay amoul ndawww
@AbdoulayeDiouf-zh4kq
@AbdoulayeDiouf-zh4kq Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@alimatambow6743
@alimatambow6743 Ай бұрын
Il FAUS respecter LES fammes elles sont votre mamma respet.
@Annebaidysouleymane
@Annebaidysouleymane Ай бұрын
Diotneu niu niouss thi kasso bi déchets de société yi niu talal micro aucune élégance, seu diabar laa yeureum.
@thiaradiallo2959
@thiaradiallo2959 Ай бұрын
Bilahii ki dou sax niit
@actusenegal119
@actusenegal119 29 күн бұрын
iow sa bess mongui nieuw Dinanie tothie sa lou bone
@diebmrs9370
@diebmrs9370 29 күн бұрын
Yow khana dangay fréquenter thiaga yi ak lesbienne yi yow dei do kilifa do nite Kou bakh sa wakh yi niaw na domaram nga reiq.
@seckmarietou7310
@seckmarietou7310 Ай бұрын
Bilay yaw khamou sakh ligué wakh 😂 gue ni guey yakh nitt dafa niaw té yaw yagui yakh nitt 😂 té si guené torokhal djiguéne té yagui torokhal djiguéne no yaw dou nitt kou kholatal sa bopa
@salysagne8640
@salysagne8640 Ай бұрын
Ki dhè wakhi dof lafi wakh mouye melni kou yalla mèré ni con nga trop si magg bou toll ni yow gnakk fayda 6 moy 9 mario genrou andando you bone yi il faut s’en mêfier
@adjaratoufall
@adjaratoufall Ай бұрын
Mome kay dou doff bii rekk la wara porter plainte. Mais même la chaîne et le mec qui tient le micro.
@mamidiuuf2736
@mamidiuuf2736 Ай бұрын
Xawma sakh ki lane lako wara wakh!!ki meune na doul dh ki moy genre goor Yi niouy may wethiete niouy marr sen bounou sen morom yi !ki vrai domram la wallahi😒
@aicha7979
@aicha7979 Ай бұрын
Ki mom kou teipi toun*** ndey **** ils sont nombreux des gens comme lui domerame moy progéniture Mario yi reck
@user-qg8yf9ts3r
@user-qg8yf9ts3r Ай бұрын
Ki môme domoukharam la
@DjibySy-jz5sm
@DjibySy-jz5sm Ай бұрын
Sa data yaye rék
@ibrakane3101
@ibrakane3101 Ай бұрын
Bada bayil togn wala gni wo mbaya legui thiow li diekh
@ndeyediop335
@ndeyediop335 Ай бұрын
Yaw aw Doulou Ndakhtè sakk mola geune
@DaoudaGning-wx1rg
@DaoudaGning-wx1rg Ай бұрын
Wawa
Backstage 🤫 tutorial #elsarca #tiktok
00:13
Elsa Arca
Рет қаралды 47 МЛН
Smart Sigma Kid #funny #sigma #comedy
00:19
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 21 МЛН
ROCK PAPER SCISSOR! (55 MLN SUBS!) feat @PANDAGIRLOFFICIAL #shorts
00:31
⬅️🤔➡️
00:31
Celine Dept
Рет қаралды 46 МЛН
Série - Belle Famille - Tabaski - Épisode 9
26:47
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 824 М.
Backstage 🤫 tutorial #elsarca #tiktok
00:13
Elsa Arca
Рет қаралды 47 МЛН