Рет қаралды 8,447
Clip de louange chanté en Wolof et sous-titrage en Français par le groupe Logos C418. Un album de 8 titres. CD audio disponible dès 07 décembre 2014. DVD disponible en Février 2015. Contact: Sénégal +221.76.669.71.86 / Congo: +242.06.693.74.91 Mbëggeel amul àpp (1Korent 13:4-8)
1korent13 :4
Ku bëgg dafay muñ te laabiir. Ku bëgg du iñaan, du kañu, du tiitaru,
1korent13 :5
du def lu jekkadi, du wut njariñu boppam, du naqari deret, du ñaaw njort.
1korent13 :6
Du bég ci lu awul yoon, waaye dina bég ci lépp luy jollil dëgg.
1korent13 :7
Mbëggeel day baale lépp, am gëm ci lépp, yaakaar léep, muñ léep.
1korent13 :8
Mbëeggel amul àpp… Que le Seigneur nous remplisse de Son amour.