Jusqu a présent je peux pas écouter ndongo sans pleurer . Paix à son âme
@alimadiop36894 жыл бұрын
Mane mi
@diopfaya34714 жыл бұрын
Bilahi Ives nimou wakhé rafetlou woumako dara, mounan ma tassék ndogo lo ci porte bi mouy kayang kayangui ak nan manona Sol dalou thiarakh mouy Sol timberline. Comme kouy saboté aka niawal. Na rafet adina anoul solo. Ndogo bokna ci histoire Senegal ba paré ohhhhh😭😭😭😭😭
@gaabelly91874 жыл бұрын
Koon limaa wok molaa xourii, Yves amoul been savoir vivre. Ndongo boudônn dund baa leguii keen dou leen xaam ndax mofii meunn sii new generation bii té lolou dou degn, baa ilaa yawmidiin. Yalnaa motaalii ndawaam janatûl firdaws bijahi Naby Moustapha asws
@khadimsakho514 жыл бұрын
Aye way ndongo lo nianal lenko te bayi wakh thi
@MoussaThiongane-m5r9 күн бұрын
Merci DjiLi Niang Ya Bakhe Ya Ngoré BouR Ndogo YaNako Yalla Yéreme Ta kharé ko Alldiana FridaWe Inchallah Amine Amine Amine
@mouhamedthiamzikroulah17984 жыл бұрын
Trés bien mon frère Djili niang wakhal lépp na lérr , kouy dieuf dieufale lou bahh so beugué lou bahh
@fatoulaobe39994 жыл бұрын
Machalla tonton djily ki des loumou la wakhe si ndogo lo deuge la Aka bakhe tonton djily té âme soutural mes nak deuge rek moko yak Aka bakhe💪💪💪💪💪💪💪
@soxoubb14714 жыл бұрын
Ndeyssane yalana nako yala yeureum mercii tonton
@Rimka9124 жыл бұрын
Saway bilahi video bi diarouko wone
@myvision76474 жыл бұрын
Enfaite ive niang moy ngaka pourquoi parler de ndongo lo maintenant en disant des choses con khana ta pas ecouté l'interview dafa dieufrou nioulay djin deum ngay sénio yéllou liir🤣
@binetabadiane64274 жыл бұрын
Merci beaucoup grend djily yaw dangua meusa défendre ndongo ci kanamam ak guinawam
@cauripro4 жыл бұрын
Bi NDongo Lo amé succès, Yve Niang sékhoulwoon wakh ak NDongo, ba bimouy guénn Aduna.. Lepp fii lagnou fékk.. Bou léral jotté lépp dineu lérr
@papaabdoudiop14554 жыл бұрын
Serigne Djily naniou am soutoureu té yalla rek takh Adouna amoul solo lou way def bopam.
@myvision76474 жыл бұрын
Leup dina leer inchallah Ndongo lo mom yallah dinako leral leup.
@mbayebambaloartiselo15424 жыл бұрын
Thieye Ndongo waxna danane Bou dewe thiowly beri
@madiagaastasall47604 жыл бұрын
Yve none la,ndakh wakhou none lay bakh.ndongo rawnala.dée bayilafi tei meuno prover dara,danga sakh faye.ndongo lo est entré dans l'histoire du Sénégal. Yalla na dée di noflayam
@beguebayfall4 жыл бұрын
Merci beaucoup mon frère
@princessekounta25384 жыл бұрын
Mais yow tamite li amoul béne sens ndongo est décédé depuis longtemps
@madembagningue53094 жыл бұрын
Djily si tu étais ami à Ndongo Lo tu n'as pas besoin de polémiquer sur lui. Diarouko nianal léne ko et arrêtez léne séne yi.
Thiey sama wadj télone kham nite motakh masoul diapé nit alal tè gnim way niep tané wounko wone litakh mou denkone bopam serigne fallou Yala nako yala doli yeurmandé té mame fallou teroulko bopam firdawsi
@mansourdiop24994 жыл бұрын
Sa waaye Yves wakhoufi Lou aaye diaroule aye tontou na rafaite rékk ahhh
@kineseck50084 жыл бұрын
Yves niang warowone wakh si ndogo lo djily bayil mou sédeu guir sa wouléré ndongo lo gnanallénko mo gueune je l'aime jusqu'à présent damkoy déglou svp bayiléne mou sédeu
@maguettesene1834 жыл бұрын
J' ai été témoin entre ndongo et Yves ces types comme djily et zof tout les staf de ndongo ne sont que des bana Bana des profitare ils ne connaissent rien de la musique on sait tout
@ndeyebounamadiop58634 жыл бұрын
Oooh ndongo mome bayilene ko rek te diko nianal
@16041976ful4 жыл бұрын
Merci Djily, yaye goor
@fafoudiagne18604 жыл бұрын
Yawe Kou bone nga adina amoule solo nite daye am soutoura
@adamacamara28174 жыл бұрын
Dmr ives Niang momou mo amoul soutoura
@adafalle74224 жыл бұрын
🙄🙄🙄🙄🙄ayyy wayy adina amoul solo
@fatoudiouf48964 жыл бұрын
Bilahii
@abbakara76374 жыл бұрын
Nianal lènko mo gueun
@khadysaou12414 жыл бұрын
Diaroul wakh ndongo lo demna 🙏🙏🙏🙏🙏
@diakhatefatou77564 жыл бұрын
Bayilene yeee fitna
@ibrahimndong17894 жыл бұрын
Tnx u so much bro
@latgaye22874 жыл бұрын
Ndongo lo ken la yalla nako yalla yaram
@maguettediouf95304 жыл бұрын
Non Djily bayil nonou way fatéll lolou diaroul wakh yéne niépp yéna bokk ndéye ak bayy
@khadydiakhate70114 жыл бұрын
Ndongo Lo ganiou na nianal lene ko bayi di ko khekhé. Arrêtez ça svp. Cette personne a besoin de prière.
@cheikhsouare92794 жыл бұрын
Wallahi djiliy degue na duege
@cheikhlesage25844 жыл бұрын
Wahofi dara
@diarraniang9264 жыл бұрын
Ive niang amoul vergogn warone na wakh lou ravéte mo geune mouy dékil ayyy wakh
@amadoubalde69234 жыл бұрын
Eh khana setano emission bi dagn ko forcer ladj ko lou d1nel amoul choix t lep loumou ci wakh ler n'a t diar n'a yone sa se voyais
@diarraniang9264 жыл бұрын
@@amadoubalde6923 guisgua mai limou wakh day melnii staff nioko sacrifié motakh djiby réagir
@assndoye56464 жыл бұрын
Ive niang dal mousoul beugeu ndongo Lô lolou lér na Sénégal
Ive vrai domeram la il était jaloux de ndongo Lo il mort mes tu n’est pas persè
@gorguidiengdieng3734 жыл бұрын
Ndanane bou dano tiow li bari merci ndongo
@bambalaye49974 жыл бұрын
Merci dyill
@fadelndiaye47224 жыл бұрын
Nama yallah baal mais yve niang kou deiglou seitane emission bi digua khamnii il était un grand ennemie de ndeimsi yallah ndongo lo
@abybodian14484 жыл бұрын
Jalousie rek
@fatousow97184 жыл бұрын
Ives niang bo kholé kanam gui reek kham ni tricheur leu
@makharyndiaye59224 жыл бұрын
Djilly boul def lolou dh kou dée AK sa bamel soko défe senegale yi dananiola mére
@tallmortalla89244 жыл бұрын
Merci boy djili
@ndiarevoundiaye73564 жыл бұрын
Daga wara wakh
@mouhameddrame54294 жыл бұрын
Gayi gaw nane dh pas 2heurs de temps gayi tontou !
@Blessed-meme4 жыл бұрын
Saway nopill nak tout le monde connais les derniers jour de Ndongo Lo. Deuug rek la wakh
@adamacamara28174 жыл бұрын
Ndongo lô néna wéddi dou ragal sétal sa der la reck donc démal sétal dére groupe diam pour sénégalais yii kham
@khadysow74754 жыл бұрын
Yaco wakh group diam wotel diam nakh ndongo demna
@talbiamir86014 жыл бұрын
Senegal khamou gnou sakh li wadja gnew.? Surtou n.generation.animatrice bi dja..seytane la. Il s permet mm d garouwaler..
@elhadjibollekane12864 жыл бұрын
Iska lingaye wakh nityi sokhla naniouko demale diamou yalla nga nianale sa artis bi
@astoufall42984 жыл бұрын
Yves diame la dou leufeule ndayame louga teki woufi thiote ndayam
@mariemethioubou31354 жыл бұрын
Degeul guedié Di khass yeitt degouma li ive wakh mais iow Corona mola geune thim
@babelthiam7474 жыл бұрын
Noa djili li diarouko nanou ko nianal rell
@kingbigrocky60174 жыл бұрын
Ndongo lo yalla nako yalla yarram .yvi niang kou boon la
@damethione67774 жыл бұрын
BAYILEN DI KHEUTHIE AY WAKH AY MAGUI DIEUM NGUÉN NIT DAY NITÉ TÉ BAGNA GNAK FAYDA YÉN DOU NGUEN AVANCÉ MOUK NDAKH ESPRIT KHALÉ NGUEN YOR DI TONTONTÉ AK DI TONGONTÉ
@abdouly67734 жыл бұрын
Tous les pikinois ont sais le problème entre ndongo et ive Niang ses les sétan
@assanethiam55634 жыл бұрын
😭😭😭😭😭
@maguettesene1834 жыл бұрын
Waayi doule talounioula Ana Seen thiaga yi
@omarballaballa24114 жыл бұрын
Sama grande boul ko tontou
@diopmatar43014 жыл бұрын
Yaw Djily Niang kou yak fayda begueu siw rek on ta oublié
@ablayelo45524 жыл бұрын
Léral dafa am solo la wakh wakhal lépeu Aÿ domou ramm la nou
@amadoubalde69234 жыл бұрын
Li louko fi diar bijou beugeu mou leral wakh lep rafzt n'a li mom gaw na
@bebelo17354 жыл бұрын
Ya soof wayy nianalay ko guen gay tontou
@awasarr18624 жыл бұрын
Ayy wayy li yeupp diarouko nekk lenn si sen bopou mo geun adouna amoul solo
@cheikhdiagne81034 жыл бұрын
Cey adouna ahirou zaman rék
@aramengom96054 жыл бұрын
Djily bayil mou sedeu
@Boss-pw8zm4 жыл бұрын
Merci djilly
@nespasserieuxbeye12624 жыл бұрын
Li lepe imision bijoux moye thiakhasé
@diouplenekhothieulernagneu33434 жыл бұрын
Jily Sama xarit bi boul tontou
@junircisse204 жыл бұрын
Mé dirouko kou yétt xam sa bop
@taphasylla37844 жыл бұрын
diarouko wah bahoul fitna kendouko yee adouna amoul sola
@mouhameddrame54294 жыл бұрын
Ok djily niang défal lolou
@fafoudiagne18604 жыл бұрын
Yawe kene khamou la oky gooo amo bene soutoura doule
@dameniang59244 жыл бұрын
Ha wakhdji diarouko dhé
@galgalgal80074 жыл бұрын
na lepp leer
@bijoumoulayedabah4 жыл бұрын
Cheuuuu ay nianal lenn ki dem t bayi tessanter
@omargaye50864 жыл бұрын
t
@elhadjigueyegueye63664 жыл бұрын
Tu n as rien à dire allez Répondre a la famille de feu ndongo lo
@elhadjigueyegueye63664 жыл бұрын
Amo lo wakh yaw djily ani famille ndongo lo khamo sakh si lounou nek
@lamineniang75484 жыл бұрын
boulêne yé fitena li bakhoule si ndoguo lo. adouna bi dafa djiekhe ba paré dara diarou fi gniawo kone nanou tapé khole yii mane guisse na gniarie nitte youye ande ba toudanté aïye dome ba séne dome yi mague mé danou khoulon 1 moi kéne ki fatou mé jour bobou dafa djioye ba sonou fami. bi gniepa konprandre danou khameni seyetanéla té foumou khadjoule rek lay dougou
@amadousdiallo85474 жыл бұрын
Qui doul rek lay def
@Rimka9124 жыл бұрын
Yee fitna bakhoul pourquoi def video tontou
@mouhameddrame54294 жыл бұрын
Loutakh diarouko
@cauripro4 жыл бұрын
Weddi dou ragal, setal sa deer la Yve Niang il exagére
@mouhameddrame54294 жыл бұрын
@@cauripro bilay
@abdoulayendiaye7454 жыл бұрын
Mane dal sénegalais yi diakhal nagnouma nite wakhi wakhame toumal aye nite ame kou diouk di tontou nguirr léral lá verité nganane yé fitna. Yé fitna cay moy wakh si nite t linga wakh dara douci deug