Dioulit degue day nangou si diamou yalla bou sélle ak louko yalla may wéddi mom niak kham kham degue leuh Serigne bi déf lolou yalla nako yalla doli ay léram🙏🏿
@makhtardrame9323 жыл бұрын
Amine yarabi wédi dé woroul
@makhtardrame9323 жыл бұрын
Kouy wédi nii dafa xamoul rek
@makhtardrame9323 жыл бұрын
Amo numérom
@mamadoudiallo75133 жыл бұрын
J'habite à Nioro c'est une réalité histoire lou ame la Benoît va découvrir l'histoire du Sénégal boul di wédi
@lafindutemps61413 жыл бұрын
Pére mbaye ngoné es légendaire billay Big respect 🙏🙄🙄
@cheke221zigboy3 жыл бұрын
Histoire vraie je confirme
@niangfatou85193 жыл бұрын
Bilay walay ci famille bobou la bok
@xeuchelaye69243 жыл бұрын
Yako feikei bay confirmer? . Do wakh deg nako rek.
@cheke221zigboy3 жыл бұрын
@@xeuchelaye6924 saay gnoral touti way kone histoire bo fékké rek ngey confirmé ?? Utilisel sa mind bref bonne journée
@jesuismoi42693 жыл бұрын
@@cheke221zigboy Mercii bcp 💪🏽🙈❤️🥰
@xeuchelaye69243 жыл бұрын
@@cheke221zigboy biensure lo feikei kay ngay confirmé. Lo khamni daga ko deg rek comme nieup lociy confirmé ? Ragalal YALLA
@modoutoure89053 жыл бұрын
Je confirme ndakh saloum lama fek walay
@mamepathengom93983 жыл бұрын
Yalla nala yalla doli wéer ak soutoura père mbaye ngoné 💯 . Ça fait longtemps que j'ai pas suivi l'émission à cause de Benoît qui fait que saboté. Yalla nako yalla soppi ndakhe amoul xam xam 🤞
La famille Ndao c'est des forces tranquilles. Barigo bou fess dou yeungou.
@safietoucisse90433 жыл бұрын
Lolou deugueu pure la
@aissatoundao3633 жыл бұрын
Akay deug
@tahiroudieng1763 жыл бұрын
C’est un vrai histoire père waliyou yalla bou yalla nangoul amoul loumoul si katanou yalla ndakh da am ndigal motakh
@faalmadeugal28043 жыл бұрын
Histoire bi deug la dei
@faalmadeugal28043 жыл бұрын
Je suis Gambien té yagana di deuga histoire bi ci sama Mame
@dmxjjj75553 жыл бұрын
Benois lolou mome histoire vraie la nak bayil di wédi Lo xamoul yalla amena ayy niit yo xamné dafléne may et je parle pas de ayy koukandé nak mes dieu a toujours c’est ces serviteurs qu’il donne de la sagesse pure lolou boulko wédi
@mameyoufall8823 жыл бұрын
Bilahi lou lerr la barké serigne touba sunu makk gni amouniu marom
@elhadjibandadiop80883 жыл бұрын
Benoît xana mom xamoul ni yalla dafa am lumu mayy sunu mags yi. Père Ma Ngoné respect pour lui, il s'est très bien renseigné. Benoît ioe lo doon
@cheikhomarseck75813 жыл бұрын
Il a parfaitement raison Ma Mère a vécu dans cette maison je suis un petit fils de Serigne Mountakha dao
@mamadoudia67523 жыл бұрын
Père ma ngoné yalna yalla barkél may leuh yiw
@tahiroudieng1763 жыл бұрын
Wallahi bonoit boul weedi yalla maye na loune ta ay mayam yeup pour diam yi la
@safiatoudiedhiou25343 жыл бұрын
Machalla deuk rek deuk yala na yala sam soutral Sénégal diam rek ci toute sénégalaise mercis 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@diazdesigngraphiste3 жыл бұрын
Bonoit mom khana khamoulni yalla mougui mayé ba lègui
@cheikhahmadoubamba54773 жыл бұрын
Lolou dëgeu la dh bilay lou bakh louné yalla may nako sénegale serigne mountakh ndao yale na yalla yokou aÿ léram barkéb brom touba
@modoubarr88483 жыл бұрын
wallahi moy bayou Cheikh Ahmed tidiane Ndao mi nek fii New York
@momocisse95183 жыл бұрын
Ah ioe khamnga ko seydil mountakha kenneu la
@ahmeds77853 жыл бұрын
Le regard de Benoît envers père mbaye est méchant mdrrr. Benoît ignore que batine amna c'est un faiseur de malin le pauvre
@pahiboubcmiddiouf89343 жыл бұрын
Bro benoit daffa rére Lou beuri thi aduna En plus khamoul Lou yalla capable aussi
@jessicadugan11213 жыл бұрын
Encore un autre idiot sans intelligence vos anciens vous ont menti réveiller vs con
@Seyd9853 жыл бұрын
@@jessicadugan1121 🤣🤣🤣🤣🤣 désolé pour toi
@mamadoumanediop36013 жыл бұрын
😂😂😂😂
@Broadway6343 жыл бұрын
@@jessicadugan1121 ta gueule toi
@papendiaye69083 жыл бұрын
Histoire réel Thiéy Maak gni ay Mbirou yalla lagnou ay nitou diné lagnou 🙏🙏
@sgfafrica3 жыл бұрын
Domou Adama dafa wara respecte moromou domou Adama mam kou geumoull domou Adama do geum yalha man SGF AFRICA AFRICA talibe borom darou salam nioro la je suis très contente papa magone merci beaucoup papa
@karbalatoure18793 жыл бұрын
Bravo Père ma Ngone tu as montrer à Benoît encore une fois de plus que vous êtes plus cultivé que lui vola,Benoît nite dou déff loumou deg rek wédiko, wala mouni amoul lol bakhoul?
@babacarthiam92213 жыл бұрын
Macha Allah El Mountakha Ndoa Darou Salam yalla na yalla yokou léram
DEUG la mane mabo la deuk sorewoul ak darou Salam tous mes amis sont des talibe de el hadji Omar ndao farokh bilahi waliw Kamil Benoît tu m'as fais pleurer
@moustaphakane57863 жыл бұрын
Al farokh yalla nanu yalla tass si barkem 🍀✅
@saergueye93343 жыл бұрын
J'ai entendu ce histoire depuis et cette histoire est belle et b1 vrai
@worldwords58413 жыл бұрын
Benoît miracle Lou amla, pabi yagueuna dégg histoire bi, et puis même animiste yi sakh ils font des miracles, assatoumalak goor Yalla yi
@aboundiaye41893 жыл бұрын
Niaak xaam xaam wessou woul gawa weddi. 2004 année bimouy lakhou diamono fallama fek maay diang di def 2nd. Periode bobou lagn ma wakh histoire gorgou tedd guii.
@wakhdeugguetayallatakh81293 жыл бұрын
Cheikh bi kii diaroul wakhal ay domi xaram rekk mooy weddi nitou yalla Ta toubab yi lagnou geumme
PÈRE C VRAI BENOIT BAYI LÉNE KO FEULÉ QU'IL NOUS FICHE LA PAIX NOUS SOMMES DES CROYANT NOUS
@ibrahimawillane47453 жыл бұрын
Merci beaucoup. Si léral yi.
@laminegueye67433 жыл бұрын
En 2003 la délou americ si la done wakhtane ak délégation dahira mame Diarra
@TtahagHhzzgy6 ай бұрын
Machlla gorgi limou wax deugeu la seringe mountakha dokhlo na and kapè mosnà yoni bèna khalè andi kapè wa deukeubi nè syringe bi ky andi kapèl mounè waw silage yoni khalèbi mou djiouk dokh dame niaw kokou Moy sahibal karamat say dy mountakha ndao
@nojusticenopeace51603 жыл бұрын
La première personne qui m'a raconté cette histoire , c'est un ami qui est maintenant en Espagne, il est Petit fils du Serigne en personne du côté de sa maman ...
Walahi niake diangue bakhoule bonoit démale diangui té guestou dji
@pahiboubcmiddiouf89343 жыл бұрын
Entouka benoit khepna yalla trop
@abasall7113 жыл бұрын
Merci gereume faye luler nga wax salatou fatihi amul mrom manena lunek gnifi def kemtan barina t ken degulen fier fier fier fier fier fier fier fier fier fier d'être Talibe Cheikhou tidiane le waliyou des waliyou
@abdouazizdrame62483 жыл бұрын
Bilaye lolou mon guena toutii si karama talibe cheikh
@jeancabo58743 жыл бұрын
Khaam bakhoul dieureudjeuf baye NIASS
@imsenegal52613 жыл бұрын
Al hamdoulilah... talibei tijaan douy ndamo khar bakh ... jereudieuf
@mbddiop46713 жыл бұрын
LES WALIYOU peuvent voler dans les Airs et marcher sur EAU entre autres miracles...c'est la volonté de Dieu qui donne à qui il veut
@cheikhdeme2357 Жыл бұрын
Histoire vraie je confirme ❤️❤️
@laminediop57003 жыл бұрын
C’est une histoire vraie je suis talibe en plus j’habite à Nioro
@diijaymaxruntheshow78823 жыл бұрын
Père Ma Ngonè goudal fann way 🙏🏾
@ahmedcisse5743 жыл бұрын
Père MBAYE machalla billahi deug la ❤️
@bachirdomouparcelle42932 жыл бұрын
Ki def li ak sama papa niodone nek heure bou nieuwei dakar 🎉❤
@AïssatouNdiaye-w3l5 ай бұрын
Kenn dou seydi Mountakha Ndao ❤❤
@saloumshop84413 жыл бұрын
Talibe Cheikhou Tidiane ❤️❤️❤️
@elhadjidiop4581 Жыл бұрын
والله صدقت 💞💞💞💞💞💞جرجفى شرج منتقى ندو💗💗💗✅
@vitodanfa96463 жыл бұрын
C'est un historien hors pair merci père
@ontlofficel29773 жыл бұрын
Wallah c’est vrai 🖤🖤🖤🖤🖤🖤💙💙💙
@deboursy62153 жыл бұрын
Pere mbaye ngone nala yalla fay jsw au lit dpui 15jour mais tay retana basoneu
@bayesouleyembaye40713 жыл бұрын
Yalna nga diok ak diam delou say activités. Amine
@drameserigne28713 жыл бұрын
Beunoit attention, boul wédi lo féké woul, yalla meune na lep
@ndiayeba82163 жыл бұрын
Bonjour jolly jemes Merci
@babumb....52403 жыл бұрын
Merçi per mbaye
@abdeldiouf37883 жыл бұрын
Oui...mais développons notre pays bok! Avec tous ces miracles key!
@adamasarr79773 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣 boy sof NGA
@saloumbusiness45953 жыл бұрын
Deug bou wéér lolou dou dara si goor yalla yi
@pahiboubcmiddiouf89343 жыл бұрын
Braveau pere ngoné pour la premier fois ma d'accord ak mome 😂
@atoumaneniasse4854 Жыл бұрын
Lou leer la machallah ❤
@amadoudiop43653 жыл бұрын
Cette histoire est vrai couko wéddi gniawale nioro du rip
@elhadjiibrahimasakho81503 жыл бұрын
Bonoit lii ninga amè nonou la amé farokh yalla KO maye ak ndiabotam
@amathtv71783 жыл бұрын
Merci beaucoup
@morsady53703 жыл бұрын
Aye pere merciiii
@mamadoudiallo21123 жыл бұрын
Merci pere maguone
@laminegueye67433 жыл бұрын
Pére mbaye ngoné dafa niake kiniane en 2001 la démone americ fadiou toubab bi ko done fadje dafko tope nieuwe senegal toube kou wedi nga lath Ibrahima gassama bi nékone rts mo nékone interprète bii
@sellegueye48103 жыл бұрын
👍👍👍
@demeissa76103 жыл бұрын
A
@elhadjithiam11883 жыл бұрын
El hadji Omar Ndao yalna yaala yookou léram
@mahmoudsall96062 жыл бұрын
Pa bi je l’aime wollay
@laminebaraniasse84243 жыл бұрын
Nagam menoul nek gat kham kham wessouwoul lolou🥰🙏
@dmxjjj75553 жыл бұрын
Père limiy wakh kéne douko enlevé, benois mome amoul xam xam
@seckoukeita49393 жыл бұрын
Je suis témoin des fais cet événement nous a trouvé à Nioro du rip nous avons vu Yaya Jameh président de la République de la Gambie qui a envoyé une forte délégation et des camions de vivres pour s'excuser auprès de la famille Ndao de Darousalam
@ndiayemariama63503 жыл бұрын
Wa keur el hadji omar ndaw sama papa kokou moy serignam
@mikejallow34243 жыл бұрын
Deugg la Benoît yaw mankant nga koi..... talibé farokh histoire vraie en ce moment je suis à darou salam nioro du rip
@aminatadiouf80593 жыл бұрын
Mais Benoît mome dou gueume nani jésus christ dadone yeukeuti kou dé doundalate ko mais Yallah miy mayé lolou mofi nek ba légui di mayé louné. lo khamoul si dîné diambour mome mandou si mo gueune nakh Yallah beugue na kou manou. je suis Kaffrinoise mais histoire bi en 1993 gneupe kodone wakhtané sougnou papa yi ak sougnou yaye . Wédi mo fi amoul place vraiment.
@dioufymatar25973 жыл бұрын
Moi-même jai la vidéo bilahi je l'ai regardé à multi reprises
@abdoulie583 жыл бұрын
This is a true story. I have an uncle, still alive who witnessed this incident. Benoit is too negative and will continue to be negative.