L'histoire c'est vraiment la vérité du vainqueur. Lat dior est perçu comme un lache alors que c'est un grand héros de guerre. Vraiment l'histoire mérite d'être interprété, cette fois ci par la voix du vaincu!
@ummhakimfall79285 жыл бұрын
Damel Madior Fatima Ngologne Fall mo diour Ngoye Ndaw Coumba moudiour Codou Madior mariée ak Sagata Kouli Codou Ngoye Ndaw Coumba. Kouli Codou Ngoye Ndaw Coumba mo diour Sakhéwar Fatma baayou 5 linguéres yii ( Mekhouradia Codou Samba Aïssata Fatma ak Dior etc... Sakhéwar Fatma Fall modiour Medoune Sokhna Niane, Kouli Codou Ngoye Ndaw Coumba Fall modiour Ganka Modou Makhourédia ak Sakhéwar Sokhna Mbaye Diop pére de Lat Dior.
@dameseye30394 жыл бұрын
Diadieuf mais fi medoune sokhna niane la yakaron ni mo diour sakhewar sokhna mbaye mou diou labba AK gankal
@revelationprodtvcinema61524 жыл бұрын
Franchement je profite bien de la pertinence de votre contribution merci Bien yalna yalla sam la
@dameseye30394 жыл бұрын
@@revelationprodtvcinema6152 diadieuf amna solo histoire dafa am solo AK kham saw askan, kham Say mam bania top toubab bi si anèantir notre histoire ,nos héros
@revelationprodtvcinema61524 жыл бұрын
@@dameseye3039 louler nga wax
@dameseye30394 жыл бұрын
@@revelationprodtvcinema6152 lat dior labba nak mbokoum rèw mila ; sakhawar fatma dieulone na yèla dom si khoudia coumba seye ( bok si nègou SAY) serigne ngèn massay alè demba diourko mouy seyène
Damel Madiodio Déguéne Codou Fall daffa démoon Djolof nioum méyko diabar djou toudou Sokhna Ndiémé Tam Ndiaye. Ndiémé Tam Ndiaye tawlo Madior Ndiémé Tam Fall ak Sokhna Ndiaye Biram Khoudia Tam Fall, Madior Aram Mbongo Sokhna Ndiaye Fall, modiour Safiatou Arame Mbongo mére de Serigne Abdou Aziz Sy ak Dior Arame Mbongo Fall. Selon le griot Soccé Mboup
@assaneleye87134 жыл бұрын
Non non
@morsamb8484 жыл бұрын
Merci prestige
@abdougaye34405 жыл бұрын
Fier de mon arrière grand-père notre héro national
@Topofthetopapex4 жыл бұрын
Fière cousine
@viedici4 жыл бұрын
Franchement ca fait deux videos que je veux regarder sur le Sénégal avec un titre français et le recit est en Wolof.
@abdouazizdiop82694 жыл бұрын
Fier de ancien grand grand grand père
@ididio86305 жыл бұрын
Un grand senegalais
@Panvini143 жыл бұрын
J’ador cette histoire
@nettadiop88144 жыл бұрын
Mane moom Ndiayen bouma bayyiwoul naan sama mame tapett la woon dina am afair ak mane bakhna rek
Lat dior a était trahi il faut pas modifié l istoir.Demba war la laisser parcque il réclamé roi a piné laprane et piné laprane a exiger la chute de lat dior.
@modoumassardiop88724 жыл бұрын
Piniert laprade
@ousmanediop80783 жыл бұрын
Tu as parfaitement raison LAT Dior a été trahi
@ummhakimfall79285 жыл бұрын
Fall modiour Diop
@abomouhazsamb48603 жыл бұрын
Le 27 pas le 26 octobre
@mamadoudiop18314 жыл бұрын
Demba ware à trahi lat Dior c’est lui-même qui l’a tué 😭
@ianaryan2333 жыл бұрын
i guess I'm pretty off topic but do anybody know of a good site to watch newly released series online?
@amarthioune59633 жыл бұрын
Lat Dior amoul morom
@munirumhd20163 жыл бұрын
J ai arrêté de regarder ton vidéo depuis que tu a classifié Blaise Diagne le grand traître a son peuple parmis les héros national.
@saliouthiaw8287 Жыл бұрын
Absence
@toubamoylislamtouba23315 жыл бұрын
lat dior nasarane bi moko ray kon mom defou fi dara loumouy xolè ba nasaran bi diko ray
@yeguebonysamba94215 жыл бұрын
Sa wax dji mom dou waxou kou yéwou
@aidadiop73705 жыл бұрын
Yow oubal sa guemigne lat dior rek moye baniak kak
@aidadiop73705 жыл бұрын
Mo tay ana sa mame yow ken khamou ko de fou fi dara diamou toubab la wone tapet bou reye