La chauffe réaction Père Massour Diop et Baye Balla après le combat Balla Gaye 2 vs Tapha Tine" daf…

  Рет қаралды 92,811

ACTUBUZZ TV HD

ACTUBUZZ TV HD

Күн бұрын

Actubuzz tv

Пікірлер: 127
@BaraNdoye-r6c
@BaraNdoye-r6c 6 ай бұрын
Merci deug nga wax balla Gaye 2 moy star lamb dji vraiment
@lemlc6468
@lemlc6468 6 ай бұрын
Douma fans balla dh mè balla moy lamb moy star bi yalla moko dogal
@GoraGueye-rd2ov
@GoraGueye-rd2ov 6 ай бұрын
Yaw kay balla Moy sa mbeur nékal nitt
@AlhamdouLiLahi-wl4cq
@AlhamdouLiLahi-wl4cq 6 ай бұрын
Balla gaye 2 dafma Doli motivation ci adouna Tapha tine m'a appris que kou ragal loumou niak moka ték bopam Sokh m'a appris dolé kasé doyoul Mama Lamine m'a appris ame na biss yo ham ni waroka niakk boul khar kén si Dra blindé m'a appris adouna da ngay déff lila warr harr yalla zambala patience meunoul niakk si adouna Jacob baldé lépp khalé mokay déff bébé Saloum dolé gane la dalay sétsi rk ect bou doyoul ma doli😂😂❤🇪🇸🇮🇨
@votremiroir7612
@votremiroir7612 6 ай бұрын
Manchallah 😂😂😂❤❤❤
@AlhamdouLiLahi-wl4cq
@AlhamdouLiLahi-wl4cq 6 ай бұрын
@@votremiroir7612 te amo🤦🏾
@mormbaye1363
@mormbaye1363 6 ай бұрын
Tu es fort❤
@AlhamdouLiLahi-wl4cq
@AlhamdouLiLahi-wl4cq 6 ай бұрын
@@mormbaye1363 gracias ❤️
@yilebaba6565
@yilebaba6565 6 ай бұрын
Ndeyssan yaye ndanaan ❤
@sokhnathiam9180
@sokhnathiam9180 6 ай бұрын
Bilay moy star bi
@alassanemane3021
@alassanemane3021 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉 machalah 🥰🥰 Balla gaye 2 moy lamb 🥰
@diarradiene4275
@diarradiene4275 6 ай бұрын
Billaahi wakh NGA deugue baye balla louniou valorisee la nekhna moom trop kou sanione tay beuree journee bi felicitations balla gaye 2 et ducourage tapha tine NDEYSSANE abou cefa yagui introgee Sama baye bii dee bonne continuation abou cefa Sama denkendoo bi annalyse bou am solo la baye balla deffd
6 ай бұрын
Mais une question premier combat bi nespa on avait dit balla da diap lokho yi dnc en tte logik 2eme combat bi lou tapha tine de xolé bagnukoy diap amoul logik di.??? Ken dou balla sport de combat fite la lou solo sagne ségne la ak meune ligay def...regardé l avan bras de balla ak ay lokhome amul koukoko eupelé si labm dji
@ababacarsadikhtoure-ic3zu
@ababacarsadikhtoure-ic3zu 6 ай бұрын
Bly lepp loy deff sa adouna teh amo fitt bayil balla ndanan
@MameboussoSaw-nr3se
@MameboussoSaw-nr3se 6 ай бұрын
Ken japou ko balla moko mane moko dakha beurei té yalla la diokh balla ngay ndam allhamdou lilah
@massambadare
@massambadare 6 ай бұрын
Bilahi walahi tapha bimouye tousse lane sa copain yi ki day danou bimouy Bakou daffa disse torope
@massambadare
@massambadare 6 ай бұрын
Mai physiquement balla est plu pret rapidité technicité vivacité leep balla moko eupeule
@nouhankaba1391
@nouhankaba1391 6 ай бұрын
Tu es un vrai amateur y’a xam lamb
@aladjifalloudia4915
@aladjifalloudia4915 6 ай бұрын
😂😂😂😂merci balla gaye amal diamo rék sama xol sédina bilaye
@abdoulazizdiop
@abdoulazizdiop 6 ай бұрын
Taye gnou Barry rousnagnou
@actufootball221
@actufootball221 6 ай бұрын
Thiey balla gaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢
@Tawfeekh
@Tawfeekh 6 ай бұрын
Tapha dara diotouko loudoul Balla mëne ko gnëwna dè dagnouko mëne. Il a ensanglanté Bombardier 2 fois de même que Elton. Lors de son combat contre Eumeu, il était presque KO, par chance il a gagné. Balla est agressif et courageux, il a adopté la même stratégie, il l'a humilié. Qu'on ne nous parle pas de mystique.
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 6 ай бұрын
Moudou kharagne lô bourou lamb dji seul ❤❤❤❤🎉
@SM_C24
@SM_C24 6 ай бұрын
Tapha problemam moy dafa lent ba jegi dayyo. Dafa wara wangi poids bi, jema yokku vitesse ak jangi boxing. Tapha bu korrul, du muna dorr. Te bu dajjé ku ko geuna gaaw, ku melni Eumeu wala Balla, du niou ko mey mu njeka dorr ndax nio ko geuna flexible geun ko gaaw. Lamb bi niou bari nioungi dioum naan mistique la waay du mistique. Balla dafa xam li lamb dji lathie rek mu ligueye ci indi ko. Man bi ma gissé Balla melni ku jekh takk teg ci tuti, laa xamné tey Tapha deey. Tapha ay mbeur yu diis te geun ko yeekh rekka la fi korr, dorr ba yobu Ardo - Elton ak Bombardier.
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 6 ай бұрын
Ohh youtube bi warone na âme audio way 😂loulerr ngua wakh sur tte les lignes dafa yalla maynako taille ak dollé mais limou entrainé bahul volume bi dafa diss aussi indiwul ben stratégie . Balla dal moy ndanane vrai guerrier bilahi yalnako borom bi lafal tiate
@SM_C24
@SM_C24 6 ай бұрын
Lamb legi lim lathie moy woyyof, rapidité ak technique. Bo len bayè xel, mbeur yu magg yi yeup, muy Mod Lo, Eumeu ak Balla au lieu de niou geuna jel poids ci sen âge, den geuna wangi poids ndax niou meuna am rapidite. Mortakh niou bari ci niom am dolé batey sonal xalé yi. Bu njek, fu mbeur mu magg dajjé xalé, magg bi moy niakk ndax magg yi degn daan jel poids bu jegi dayyoh ak âge.
@Gaye-bo2qb
@Gaye-bo2qb 6 ай бұрын
Tapha aÿÿÿ body buldeur nioko entréné
@SM_C24
@SM_C24 6 ай бұрын
@@ahmadoudiop5016 Aameen. Tapha waron na xamné, bu meunoul box ak dorr Balla ayy coups, meunoul am dara ci combat bi ndax Balla bu nekké 100/100, mbeur dakhou ko borré.
@SM_C24
@SM_C24 6 ай бұрын
@@Gaye-bo2qb Lolu tamit degg la. Ligueyul daal Lu ko meuna mey ndam tey. Ki xam li lamb dji soxla te indi ko, mo daan. Lii moy degg.
@manguasylla1952
@manguasylla1952 6 ай бұрын
Machallah baye balla
@metjobrek
@metjobrek 6 ай бұрын
Gnu wakhtann thi khél rék bi modou djieulé Siteu donté champion leu..gnu bari dagnu wakhni déy fowé couronne bi déy combine dey business...légui balla délona afaires yi fimou nékone☝️
@bayegaye8604
@bayegaye8604 6 ай бұрын
Sen mbeur bii da daw tapha
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 6 ай бұрын
L'empereur de la ken khamoul limou done té yonou lamb nékousi bayi léne Modou lo bi geune tek beut 👀 dou nioune AK yéne Modou lo moy roi dou méré tampi
@domousenegalinfo9563
@domousenegalinfo9563 6 ай бұрын
Balla Gaye moy lamb
@nps.__29__tapha__9
@nps.__29__tapha__9 6 ай бұрын
Modou lo king bi
@fatoudiop4233
@fatoudiop4233 6 ай бұрын
Machalla ❤❤❤❤
@CoumbaDiallo-f2d
@CoumbaDiallo-f2d Күн бұрын
Balla Gueye dou nitt bilahi moy sén bay 😂😂
@boyetownfromdkr5287
@boyetownfromdkr5287 6 ай бұрын
Non Balla gaye 2 il est le meilleur lutteur du Sénégal c'est exceptionnel ndanane deugue la bilahi moye lamb
@ndiayeousmanebaba7531
@ndiayeousmanebaba7531 6 ай бұрын
Baye balla tapha fiitt lah manquer 😂😂😂 dou diayy
@BambaKara-qm8vr
@BambaKara-qm8vr 6 ай бұрын
Balla dako mane rek
@dioufpapndiaga3556
@dioufpapndiaga3556 6 ай бұрын
Senegal mo beuri nafekh legui ken wakhatoul roi empereur mo khew thiey senegal vive le roi des arènes
@Gaye-bo2qb
@Gaye-bo2qb 6 ай бұрын
😂😂😂😂massa yena ngui bougaze😂dh
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
Atend mais CNG néna reconnaitre woul roi bi 😂😂😂😂té légui niou éliminé ko,empereur mofi né 😂😂
@adamaseck8816
@adamaseck8816 6 ай бұрын
😛😛😛😛😛dieundeul glace nga nane😂
@NdeyefantaDiagne-jf8wf
@NdeyefantaDiagne-jf8wf 6 ай бұрын
MBeulé🤪🤪🤪
@yassendiop9276
@yassendiop9276 6 ай бұрын
Bouma ray way😂😂😂😂😂​@@NdeyefantaDiagne-jf8wf
@ElajiEldji
@ElajiEldji 6 ай бұрын
Yéne khana emeu sene dorou fi tapha tine ba narko K.O Tapha tine balla deko meun waye
@diarradiene4275
@diarradiene4275 6 ай бұрын
Billaahi NDEYSSANE Allahouma amine ya raabby baye balla mboup le griot du peuple et de LA banlieu
@fatoutine4437
@fatoutine4437 6 ай бұрын
Bilay baol rek dano am diom man li 😢
@ousmaneniabaly1129
@ousmaneniabaly1129 6 ай бұрын
Balla gaye2 psychologue làa 😂
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 6 ай бұрын
Way tapha tine danko tek dil
@Bossbarra89
@Bossbarra89 3 ай бұрын
Degueul ma fou bii encor ...fair play way 😂😂😂😂
@nouhadieme1889
@nouhadieme1889 6 ай бұрын
Balla boul dieul eumeu , xaral siteu modou lo
@Cedlulu89
@Cedlulu89 6 ай бұрын
Amateur késsé la kéne douci sama mbeur mais Tapha depuis avant dernier Face-to-face ba Balla nééko "bouma laal" copain di cool ngaay comp né dafaay sooralé Balla! motakh li diakhalouniou! Mais couronne bi daal moogui PA😁😁😂😉
@djibyndiaye5747
@djibyndiaye5747 6 ай бұрын
Nonou la démé nak bimouko wakhé bouma laal dafko warone boumakh mais Tapha limouma titeul tay yeupe ndéké niémé woul sama mbeur bi🤣🤣 Petit Roi daan léne Siteu niou mayéko inchallah
@babacargaye9857
@babacargaye9857 6 ай бұрын
Meme son combat contre Eumeu Sene il devait perdre, Eumeu s’est précipité il devait continuer à se battre. Mystique fégnou fii, Tapha sou bayiwoul niom Favre ak niom athiéké dou nék Roi des Arènes😂 Affaire bi dou ay bodybuilding
@matarrkebbeh1269
@matarrkebbeh1269 6 ай бұрын
Tapha Tine amut fit.... lolu rek la du dara.
@modouthiaw7606
@modouthiaw7606 6 ай бұрын
4:55 tapha tine vraiment niewul moi je ne comprends pas
@diokelndiaye8128
@diokelndiaye8128 6 ай бұрын
Tapha TINE nieuwna da meunoul khekh teh khamolenko. Tapha kor kessé la meune teh Balla mayouko lolou.
@MoustaphaNdiaye-sj4rk
@MoustaphaNdiaye-sj4rk 6 ай бұрын
Si Balla Gaye avait perdu certains auraient dit que c est Yekini qui l a combattu 😊
@YAYANDIAYE-x7o
@YAYANDIAYE-x7o 6 ай бұрын
Y a que toi qui pense à cela
@MoustaphaNdiaye-sj4rk
@MoustaphaNdiaye-sj4rk 6 ай бұрын
@@YAYANDIAYE-x7o tu es dans la tête des gens pour savoir ce qu ils pensent
@sidathniang7183
@sidathniang7183 6 ай бұрын
Empereur kay😂😂😂😂couronne mom faw ngene outeul ko Balla Gaye rk. Mougn lene fii bene couronne mofi valable mouy Roi des arènes. Wa Ndiayenne momou niou lamb ji
@krezyboy5317
@krezyboy5317 6 ай бұрын
Saay balla dioyoul couronne Modou moy le roi incontesté nangounaniouko mais Nangoul len balla ndax li ngen yor dieul nako a 26ans
@ladianepathe5637
@ladianepathe5637 6 ай бұрын
Baye balla yoow mo défaite bi 'nekhoula 😂
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 6 ай бұрын
Thiey pere
@ndiayedistandiayendiaye2209
@ndiayedistandiayendiaye2209 6 ай бұрын
B balla aka niémé yalla
@bayediop6859
@bayediop6859 6 ай бұрын
Tapha tine es muy frío hoy
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
Mbaye Gouye gui mosidésss 😂Yalnako Moussa Ndoye dor mou danou 😂Baol tojjjj 😂😂
@papekebe3712
@papekebe3712 6 ай бұрын
Balla bi ma guiss taye moye Balla Gaye modou lo bou moudiou bi
@damediba6762
@damediba6762 6 ай бұрын
Bilay wakhal way ❤❤❤❤
@doudousanebadji696
@doudousanebadji696 6 ай бұрын
Balla Gaye2 vs Eumeu Sène combat empereur lolen si wakh Balla Gaye2 na dieul avance bi😂3-0 rekk Eumeu Sène borom Tyshinger✊
@Kopp2111
@Kopp2111 6 ай бұрын
Mom rék lagnouy top😂
@abdougueye4837
@abdougueye4837 6 ай бұрын
eumeu vs balla day takhaw parceque niom gnarr amel nagne albourakh avance
@fallou57
@fallou57 6 ай бұрын
Non gaston lawone
@IbrahimTall-q6c
@IbrahimTall-q6c 6 ай бұрын
Wowal omez AK Bada dione AK ngiagass
@nouhadieme1889
@nouhadieme1889 6 ай бұрын
Tapha tine aussi warna ame combat thi kouy dieul roi bi
@Tomi-iu2uq
@Tomi-iu2uq 6 ай бұрын
Lambe yefou deume la kou yabou def tres atencion
@MansourDieye-dh6jv
@MansourDieye-dh6jv 6 ай бұрын
Tapha kou khol combat ak eumeu sene nga kham ni dou touss srx tapha tine tanguoul dh taille bé bakh rek
@64FallAmadou
@64FallAmadou 6 ай бұрын
Tapha tine vs franc combat bou neikh
@talibeserignetoubaibrafall6311
@talibeserignetoubaibrafall6311 6 ай бұрын
Tapha gribordo
@momowadd407
@momowadd407 6 ай бұрын
Balla guay franc
@afro3827
@afro3827 6 ай бұрын
Pa aka mana doul
@MoussaNgom-sg3bl
@MoussaNgom-sg3bl 6 ай бұрын
Deug rek nga wakh
@adamaba6508
@adamaba6508 6 ай бұрын
Balla moy lamb
@FallWaly-c6g
@FallWaly-c6g 6 ай бұрын
Tapha na dem beyi xamul dara
@rassoul3548
@rassoul3548 6 ай бұрын
Tafa lene rek mooko raye. Blokewoul droit balla.
@mamadousy6740
@mamadousy6740 6 ай бұрын
Sénégalais wakh rk lambe mo démé nonou tapha dane nasi kou nek
@demzogueye1216
@demzogueye1216 6 ай бұрын
Pabi kou mana fénne la
@maremetoure6315
@maremetoure6315 6 ай бұрын
Vraiment on ne comprend plus tafa il ne peut pas levé ses bras
@ChiekhibraMbengue
@ChiekhibraMbengue 6 ай бұрын
Dou dara balla dako meun
@elhadjindiaye923
@elhadjindiaye923 6 ай бұрын
Daurna balla coup bou dal dafa yèkh trop lolou moko sonal
@ahmadmahrezcamara66
@ahmadmahrezcamara66 6 ай бұрын
Diiss moko diap momoul yaram bi té balla tmt teulé woul khex beuré mom waxalé woumako
@marceldiandy3956
@marceldiandy3956 6 ай бұрын
Tafa netait pas athletic et 0 physik té da ragal
@ndiagathioye3928
@ndiagathioye3928 6 ай бұрын
Yaw rekk yakko wakhone
@MakhaTraore-cg3rg
@MakhaTraore-cg3rg 6 ай бұрын
Yaw tafa gua faralone demal tok dangua rouuss
@paleygning.8687
@paleygning.8687 6 ай бұрын
Tapha à problème de poids sont poids et beaucoup soit athlètes
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
Boumou dano nguéne di soga guiss lolou 😂😂😂
@PapeDiego-jb7cq
@PapeDiego-jb7cq 6 ай бұрын
Tapette leu
@100bouts6
@100bouts6 6 ай бұрын
Chaude réaction bok bande de c
@manguasylla1952
@manguasylla1952 6 ай бұрын
Machallah baye balla
@manguasylla1952
@manguasylla1952 6 ай бұрын
Machallah baye balla
1% vs 100% #beatbox #tiktok
01:10
BeatboxJCOP
Рет қаралды 67 МЛН
Don’t Choose The Wrong Box 😱
00:41
Topper Guild
Рет қаралды 62 МЛН
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 53 МЛН
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН
Fadam2 attaque sévèrement siteu Apres Face2Face "Bayil Aziz Ndiaye té concentré wou sa Combat, Sinon
16:51
Hé Lambalogue Réagit Après le Touss de Balla Gaye et Tapha Tine
10:32
Gaston Productions
Рет қаралды 17 М.
RÉACTION À CHAUD APRÈS LE COMBAT BALLA GAYE 2 VS TAPHA TINE
14:24
BALLA GAYE 2 VS TAPHA TINE : UN AFFRONTEMENT À COUPER LE SOUFFLE !
26:14
1% vs 100% #beatbox #tiktok
01:10
BeatboxJCOP
Рет қаралды 67 МЛН