Yalla mo bolé sén destin.yalla nalén yalla kharé aldiana
@rokhayadiaw94084 ай бұрын
amine ya rabi🤲🤲lii rékk mo wara nékk commentaire gnanale léne té bayi yone déff liguéyame🙏🙏
@DabaSamba-s7z4 ай бұрын
Amine ya rabi
@veroniquenatack73924 ай бұрын
*Vraimnt gnianal len rk mofi seuss*
@ajahumysamb46354 ай бұрын
Amine ya rabi
@myamya65234 ай бұрын
amine 🙏 🙏 🙏
@bittersweat67904 ай бұрын
Pa bi limou wakh leer na dé. Nena Wally keureum leu nekone. Année dernière la wally né il est temps mou dieul son indépendance. Sileu guéneu keur gui. Té chaque fois qu’il lui demandait foumou nekk, waly disait juste ma ngi Pikine. Beugoul wone kouko setti, té danou lene sett. Donc je ne pense pas qu’on peut reprocher à la famille de l’avoir abandonné. Khalé dey ame kilifeu sou beugué mouthieu. Mbir yi daal Yallah reka kham. Yallah na Yallah leral
@seynaboundiaye30994 ай бұрын
Vraiment khalè day ame kilifeu daal
@kebeabdou15244 ай бұрын
Je suis parfaitement d'accord avec vous. Khaléyi dano téla dieul sén yonou bopou té woroul
@fatouba99564 ай бұрын
Deug leu mé ki dafa téleu dégagé responsabilité tém khalé bi papam dundul yayam dundul warone nasi déf lep loumou meune gni insyi sén nder laniou beug sètal😢
@FatimaM6534 ай бұрын
@@bittersweat6790 li dee la wakh il l'a entretenu pendant 19ans moko diangal métier khaleyi nio doyna war gawa complexe paix à leurs âmes
@MouhadeSarr4 ай бұрын
Waly mo wathji andamm
@assiandiaye89044 ай бұрын
Il faut que nous nous arrêtions de juger cette famille dans la douleur. Wally était majeur. Dès le jeune âge il a choisi son métier et sa famille l'a aidé. Quand il a maîtrisé ce métier un membre de la famille lui a acheté une machine. Un beau jour, avec ses projets bien en tête il a pris ses baluchons en effaçant toutes ses coordonnées. pourquoi Wally ne voulait pas être en contact direct avec eux ? Pourquoi se cachait -il de ses proches ? Laissez la justice faire son travail et les familles faire leurs deuils. Nous ne sommes pas meilleurs que ceux que nous jugeons. Que chacun d'entre nous fasse son introspection.
@aloudiouf50513 ай бұрын
Merci beaucoup lolou moy wakh dji
@NabouDia-gn4tm4 ай бұрын
Yalla milene bolei molene takalei fimou tolni ni kene dousi bakarou yalla rek mo meune leral kone niom gni dem yalla naniou egali sene ndaw aldiana
@monavenir73784 ай бұрын
Amine❤
@soulay8194 ай бұрын
Le grand frère est une personne sincère qui dit juste la vérité !!! Yallah nalen yallah yeureum
@HelenePouye-fk5em4 ай бұрын
Liberté, les jeunes veulent la liberté totale. Et voilà. En nos temps, on n osez même pas dormir dans la maison d autrui
@mina.k7684 ай бұрын
L’amitié de Aziz et wally n’est pas si profonde , wally n est pas abandonné et as était éduqué dans de bonne condition, certains véhicules de fausses informations et c est certainement ce qui fait mal aux frères de Wally . Ils ont fait leurs maximum pour le rapprocher de la famille mais il as préféré s’éloigner, nul n’échappe à son destin et ses 2 garçons avait le même . Il ont tout les deux quitter leurs familles pour vivre cette grande tragédie,Il ne reste plus que as accepter et se soutenir dans les deux familles . Pour encourager la justice à faire son travail et arrêter le véritable coupable. Rapidement avant qu’il face d’autres victimes.
@FALLADIOP-q7g4 ай бұрын
Gnogui léni dialé bou bakh yallana naléne yalla yereum té kharé léne Aldianey fiirdawsi Amine yarabi 🤲🙏🥹 Massa thiona métina trop yallana yalla léral lepp
@myamya65234 ай бұрын
amine dafa meti
@Sfr_time4 ай бұрын
Ndeysane communication aka diafé pabi meunoul wakh Aziz sou bokkoul ak mom dara tamit takhawou nako kone na rafet en plus niom niar nieupa ande dem donc yalla bolé nalen na rafet paix à leurs âmes
@sowpoulo60494 ай бұрын
Vraiment wakh daffa diafé et les responsabilités sont partagées
@MariamaDiawBa4 ай бұрын
C’est normal parce que niom khamouniou aziz dabala
@rouguikebe99844 ай бұрын
Vraiment
@sowpoulo60494 ай бұрын
@@MariamaDiawBa bouniou ko wakhoul aussi warnanio kham ni Aziz Diambar té niteu sa keur yomboul !
@ndeyesarr17964 ай бұрын
Bilay
@ramathiamniang68204 ай бұрын
Wally si sa maman était vivante dinako dém némékou 😢😢😢 pauvre wally Yalna yalla bolélén yeureum 😢😢😢
@aissatadiop91324 ай бұрын
Walahi yaye amoul remplacante j ai les larmes aux yeux c est vraiment triste
@BassirouHane-dl5up4 ай бұрын
Wallahi llhazim nit yayam rék moko beugeu😢😢
@thiabandiaye70524 ай бұрын
Walakhi ❤❤❤
@moustaphaabdoulahadmboup68134 ай бұрын
Hana damala nèmèkou nite nou nangou la wah fimou nek . Nane léne wahanté deug , mè mo préféré vivre d autr part . Changé amouniou contac game ba niome nioko moudjè lidianeti ba pari diléne neubatou ,vremen
@diopmamediarra28204 ай бұрын
Bayi lén diakhassé ki ay frèram téyé nañ ko téyé bou rafet mom mo dem khalé Kén meuna loulen dara ndakh fiñ lay reuthié doko yek finé ni ay niane rek mofi dess diaroul wakh yi yeup
@tabaraseck70984 ай бұрын
Yallana naniou motalé séne ndaw thia barzakou Sangou Sangue yi SEYDINA MOUHAMÉD SAW AK bép waydawlou dioulite bou djitou 🤲🤲
@elprezyrappeur24864 ай бұрын
Nitt akka bax mais nitt bou nieuwé sa keur warga meune sayetou ayye mbocam ak koumou meunty donne yalnaco yalla kharé aldiana
@MassaerHanne4 ай бұрын
Tu as raison lolou moy deug
@sunkiss49504 ай бұрын
Deuggeu leu waayé famille bi tamitte waarna demme xolli fou sène ndiabotte nèkke.
@djiboseck1474 ай бұрын
Wa Aziz warone na khame aye mboki waly wayer tamite waly il est majeur peut-être lolou la
@Lopios-g6l4 ай бұрын
Bayilén nafék daa majeur amena doit dém foko néhh Azize défoul dara Aye nitou safaraguén même Azize mort Vous crachez vos haine 🔥🔥🔥
@ndiobakebe6794 ай бұрын
Salam maguilene dimastaou sen frère waly mais khamlen ni frère de cœur dina gueun frère de sang deff guene li war si mom mais yalla mollen bolle yalla nangnou khipé aldiana.
@fatimabintoubalde14994 ай бұрын
Khalé bo yarr bamouy am 4ans ba 19ans mou kheuy guéneu keurgui dokh dokham dou woté dou gneuw té soko wowé mou yémalé lothi meun dagakoy daur walah dagakoy diri diko indi watt si keurgui qu'il repose en paix mé khalé day am kilifa
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Vraiment
@aidasow48534 ай бұрын
Merçi beaucoup
@coumbaousseynousall34744 ай бұрын
Vraiment influence bakhoul
@halikano3923 ай бұрын
Waw 19 ans majeur et vacciné franchement dianou nidiaye dji watiana bamouko yoré 4ans ba 19 ans patoul laguiwoul MACHALLAH gatié gualama nidiaye YALLAH na motalé ndawam ALDIANA FIRDAOUS INCH ALLAH
@DoudouNdiaye-rn2fv3 ай бұрын
Deugue nekhoul 🤔 yalnaniou Yalla def ay deugui Dioulite defniou Manou
@univers13or3 ай бұрын
C'est tellement triste d'avoir ôté la vie à ce jeune vraiment il faut prier pour lui. Que sa belle âme repose en Paix et que la terre lui soit légère. Amine 🙏
@biteyeaminata3704 ай бұрын
Na rafet way dray yalla dou hazar yalla molène bolé wone andeu naniou barssakh que firdawsi soit leur demeure éternel
@senegalclean31734 ай бұрын
😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
@HouleyeHanne-hz6fy4 ай бұрын
Amine
@CouraDiop-k4m4 ай бұрын
Kou beugue sa bokk amo fayam yallah Moy boolé niit yallah Nanou guisé thia aldiana
@DabaSamba-s7z4 ай бұрын
Amine ya rabi
@veroniquenatack73924 ай бұрын
*Bilay walay😢amennn🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
@DawoudaFaye-m8e4 ай бұрын
mes wakhna deugue
@astougueye64734 ай бұрын
Amine YA RABI
@oumydiawara35334 ай бұрын
Amine yarabi
@aichoukebe94954 ай бұрын
Diam ak pékhém Yallah ak dogalam na rafét rék. Que le bon Dieu leurs accorde le paradis 🙏🙏🙏
@ndeyediawthiam35204 ай бұрын
Lamour est plus fort que les liens parental ils saimaient comme des freres de sang pourquoi di metitlou aziz ak waly gno bokk. Que keur ame repose en paix
@amyalphadiallo35374 ай бұрын
Se juste des éclaircissements même le frère de Aziz on dit la même chose que Aziz bocoul dara AK Wally
@Rekhahindou4 ай бұрын
Walahi diarouko, même wa keur Aziz nee naniou khamou niouko ndeyssane. Yayou Aziz sakh neena soumako guissee rek Aziz moko yoni pour Lou mou may indil. Niit gni kagn nioy wakh rek mais diaroul metitt lou nak di insister si mbok gui ish
@mamadoundiaye60514 ай бұрын
Gni ay wakhi khéte lagnouy wakh dougnou ay nite you bakh
@NAGSUNUGAAL-tg3xx4 ай бұрын
@@mamadoundiaye6051bilay wax nga dëgg peulh yi dano ndaye soxor bëgg ay affairou xét
@user-hh8gz8bz6o4 ай бұрын
N'importe quoi véhiculé des mésange mensongère et à condamné ils ont présenté ce garçon comme s'il n'avait pas de famille que aziz et la personne qui fait le rôle de parent c'est une grosse mensonge
@dim2officiel6064 ай бұрын
Pas bi lim wakh dara nékoussi deug réc la wakh yallah naléne yallah yeureum😢
@Matryyooshka4 ай бұрын
Mbokk mi nga balma dé mais tangal nga sama khol bi. Wally 19 ans moungi nekk ak iow, yako yarr donc bimouy dieul yonou bopam waronn nga kham si limou nekk et guissé ak mom kham silimou nekk. Ninga wakhé rafetoul dara, remercier Aziz waronn nala nakh binga khamoulé fimou nekk si mom la nekonn si diam. YALLAH mo toudd li khew si niom niarr, naniou lenn nianal niou khipé Jannatul Firdawsi si barké NABIL MUSTAPHA SAWS AK WEROU SAFAR BI.
@ndeyependandao33024 ай бұрын
Vraiment
@daffmbengue17624 ай бұрын
Deug nekh yalla
@ROKHAYADIOP-z9f4 ай бұрын
C'est pas vrai sakh, Aziz faisait des vidéos avec wally,gni moy lolou
@mina.k7684 ай бұрын
Yaaw esk sa wa keur khamnagne li nga def leup ?
@kinesow7684 ай бұрын
Surtout bimou wakhéé ay dom you jiguén lako yalla diokh.
@KhadyKa-p6s4 ай бұрын
Les parents jouent un rôle très important 😢si ces derniers étaient là wala koum bokal ndeye Ak Baaye d’où daimai ni mais yalla nalen yalla yeureum Xaral laine aldiana
@joyfulness804 ай бұрын
Saway kou nèk sa wakhtou dé mola djittou ci adina. Wally sou teudone sèn keur sakh dafay dé ndakh wakhtou bi diotna. Nimou démé kay moy injustice. Wayé mane souma nékone famille bi damay gueureum Aziz rek té bania dougou ci détails yi yeup. Li yalla kham rek doyna nitt gni kènn meunoulèn téré wakh.
@aissatadiallo60333 ай бұрын
Amna niouy nek AK sen ay parent way tewoul deniouy tel jeul sen yone bop
@ndiayedaouda49273 ай бұрын
Machallah wally était un musulman on a vue qu'il prié sur 🎉 vidéos yalla naléne yalla yeureum thi barké seydina mouhamed alleyhi wassalam
@harounaba27914 ай бұрын
Grand frère wally bi mounoul wakhe nit dou wakheni en plus mom amoul loumouy wakhe azzi dabala ndaxte niom dielouniou won sen responsabilité
@NdeyeKane-q2u4 ай бұрын
Deug puur gua wakh
@arimaz894 ай бұрын
Vraiment motax mane douma yor domou diambour nit yi ils ne sont pas reconnaissants
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Wakh bi mom rafetoul mom
@ndeyefatouthiaw10564 ай бұрын
Ki xol lay waxei
@Beaute92914 ай бұрын
Vraiment wakhi dof deugue nguén fi wakh. Meme pas de prière formuler à l’endroit de Aziz. Khar bamou dhé nga nane ay khamou gnou Aziz
@ANNASOWFAYE4 ай бұрын
Yalna yalla yeureumm té xarrélenn aldiana firdawsii. Massaa du courage .
@assanesoldaroubayegorasarr11364 ай бұрын
Yaala na mawlana kharé aldiana firdawsi inchallah 😭
@AicharassoulFall-zt7sm4 ай бұрын
Reye binioulene bolé rey mo djitou sene dioudou😢yalla molene boléwone mou rafete bah liii nieuw metina mé nakiouko santé yalla niou nianalene yalla yeureumlene 🙈🙏mé wa keur niome wally bounguene néké ak khalé yayam doundou papam doundou nguene nek aye magam tokk lou yague guissolene dounguene deme khool si yane conditions lah nek🙄nguene kham kimou deukeul kanela lolou moy yeufou responsable ndakh khalé yi legui il faut nioulene di bayi khel ndakh kousi am 20ans rek yakarni defa wara dieul yonu bopam 🤷♀️mé lifi dess moy nguene nianalene sunu borome kharélene aldiana 🙏
@DiarraMbacke-yc7tf4 ай бұрын
Yalla nako yalla yeurem waay thi barké Ch ahmadou bamba❤😢
@manamefall7734 ай бұрын
Machallah mon frère Fadel j'attendais ton interview pour mieux comprendre, tu nous donnes des informations justes et vraies.mais les autres mom mentir rek pour avoir des vues.
@YayoubayameGaye4 ай бұрын
Bou Done Sa Dôme Di nga Si Wass lou akh Sa Rak Dem Geustou Wo dièmo dara ba li am Au moins ki ko khol Aziz Dabala Defone na ko Comme Bopam Yalna lene Sounou Borome Yeureume Si Barker Seydina Mouhamed Psl🙏🙏🙏
@rapca22133 ай бұрын
Yow tu as des déchets à la place des neurones. Autrement tu n'aurais pas sorti ces coneries
@aidandir45284 ай бұрын
Franchement qu'on dise que c'est son neveu ne pose pas probleme il s'est toujours bien occupé de lui ou étiez vous quand il vivait chez lui cest vrai ça fait très mal mais sachez qu'il n'y a pas que vous qui souffrez vous devriez juste prier pour eux
@blackqueen11864 ай бұрын
Ça pose un problème parce que ce sont des mensonges bokou niou dara il faut donner les bonnes informations. Yallah beugoul kouy féne
@rapca22133 ай бұрын
Yaw domi haram nga. Tu n'as pas entendu ce qu'ils ont dit? Ce jeune a décidé de partir de son propre gré comme ça arrive souvent à cet âge. Ils ne l'ont jamais abandonné.
@SophieSarr-pj8oj4 ай бұрын
Comme neke bi rafetonna n'a wakh dji di rafete yalna yalla diegualene 😢
@moustaphaabdoulahadmboup68134 ай бұрын
Hâlé Day ame kilifeu di djégué ay mbokame , mo beugoul nek ak ay mbokat , nangouwoulèna wah fifou ndah beugoul gni fek kofou , té mo guèné bopam galé frère yi , soyna war dal
@adama78264 ай бұрын
Ohhh métina yalnako yalla yeureume 😢
@LayefallndarFall-ey7hu4 ай бұрын
Dieureudieuf waah DakarBuzz Bouh Fadel nékoul si térrain bi yén nguén déf liguéyi bii kou beugue source you lérr dall déle topou Dakar Buzz❤❤❤
@fatoubadji14054 ай бұрын
Mon frére bokounagnou si Yalah ak Adama boul wakh bocougnou dara Li métina basi kanam Yalah mais je n'aprecie Pas tes parole si ils n'etaient Pas morts et Wally devient milliardaire tu ne vas Pas dire ça maley dialé dioulite de mougne bou néhé ak bou nakaré que firdawsi soit leurs demeure éternelle Amine Yarabil Alamine 😢😢😢
@amadouba94764 ай бұрын
ki kay il ne sait pas communiquer
@sabellegomis-sf7jr4 ай бұрын
Ah dayena ware Dale nitte nékhouta diapalé paix a leurs âmes 🙏🏾🙏🏾
@AissatouWade-z2n4 ай бұрын
Kone de sagane nga boula andilone xaliss do waxe ni Aziz mom amo lene loleykoy rapproché nianalko rek
@AissatouWade-z2n4 ай бұрын
Kagne ngako gueudieu guiss depuis Tabaski ngani abandonné woke
@AissatouWade-z2n4 ай бұрын
Amolo wax nek Waly ci Aziz ngani khamouma chaque jour mounek réseau yi
@aissatousylla41724 ай бұрын
Aziz ak Waly Yalna lén YALLA yeureum si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine
@FatouSamb-u6z4 ай бұрын
Amine
@AmadouDiop-gi9nc3 ай бұрын
Paix et salut sur lui amine ya rabi
@Corailpro4 ай бұрын
Dieuredieuf Dakar buzz. Good job Khaleyi yallah nalene sunu borom yeureum te kharelene Aldjana
yalla na len yalla yeureum wayé nit dafay am kilifeu loy dougou ak loy def nako sa ay bokou kham
@matyfall52084 ай бұрын
D'accord naa ak yaw
@mariemesy75374 ай бұрын
Loloy deugg ! Mingui nii bimou guener adouna ay mbokam nioko dieuli pour denthie ko. Nier ay diambour laniou rek danio dieul sen mbokk bayikofa.
@ndeyapouye55224 ай бұрын
Lolou deugu la wayé sa ndiabot warnga kham ci yan lokho la nekkk 🤷🏼♀️khaléyi sen khel matoul 😢
@mamanniang44864 ай бұрын
Wally dafeu topp fougue de la jeunesse rek deysane ba guénii sen Keur Yalla nalenn Yalla yeureum
@Mamafatima054 ай бұрын
Mane deh guissouma rien de mal thi li sama wally wakh,bobou bah tey Famille Aziz gni gui guene di wakh il est normal aussi que wa keur Wally guene preciser.Sa se voit qu‘ils ont mal tè ils sont en instant de choc.Adina bolè nalène,dèh bolè lene yallah naniou agalè sen andeu Aldiana firdawsi🙏
@SallaDiop-t3j4 ай бұрын
De même que mane il mo leer
@salihate-ew6wy4 ай бұрын
Yalla nalénn yalla kharé aldiana firdawsi Amine yarabi
@MamanSeneBouSonko3 ай бұрын
vous avez fait votre mieu vous êtes de bon frère paix à son âme
@aicharassoulwar994 ай бұрын
Yalnaléne yalla yereum les cadets veulent tjrs choisir leur chemin mais n'empêche il semblait un garçon sérieux et pieux ke firdawsi soit leurs demeures éternelle
@sowpoulo60494 ай бұрын
Je présente la famille de wally tout mais condoléances metina trop mais retenez une chose Aziz da donneu deff lou bakh rek ! Ndakh kou la fatteu sa keur baniou la té yené wou ko woneu li ! Li nak moy adouna daguaye diappalé niteu ba mousiba fék lassi la douleur est réciproque sur wally et Aziz tel était leurs sort dans la vie que leur âme repose en paix si aldianna firdawsi inschallah
@princessemyathiam24344 ай бұрын
Merci li la wakh mbokou sa yalla Moy lépeu yalla yeureum lénne ta kharelenne aldiana firdawsi 🙏🙏🙏
@rouguikebe99844 ай бұрын
Billahi bo defé lou baax lou bone fék lassi
@sowpoulo60494 ай бұрын
@@rouguikebe9984 lima si metti moy certains sénégalais nio gui dieufour di wakh lou niaw bou nek si yiom niar j’ose même diarateu si live Tiktok bi
@venusndoye90364 ай бұрын
Khalé dafay am kilifa, deux jeunes hommes qui partagent un appartement c est TROP LOUCHE, en plus le jeune se cachait.
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Merci. Lolou mo diara leeral. Il cachait quoi au juste ???
@papemboup14734 ай бұрын
Bilay sama xel da see tey trop mais doyna war😢 sen cas dou nexa lidienti paix a leur ames
@nayida4ever4 ай бұрын
Ils étaient colocataires comme partout dans les grandes villes du monde. Je suppose que Waly a parlé de la famille de sa mère et c’est la bas qui se rendait pour la tabaski. Il ne se sentait pas satisfait avec la famille de son père. Waly travaillait à Dakar. Il était tailleur et gagnait un salaire
@SoceDiagne-jt5yf3 ай бұрын
@@nayida4evercommentaire bi la done weur esk 'il était à l'aise avec eux là
@@myamya6523franchement mdr on lui pose une question il répond pour éclaircir niu beugu ko rey wahouffi lene lou grave sincèrement sénégalais mo metti tchi boppam
@PrincesseAidaBa-ek7eb4 ай бұрын
Même l frère de Aziz a dit la même chose genr q bokouniou dara dafa nekon si aziz rek ki kholam mo nekhoul rek motah mouy waxé ni ndeysan yalla nalen yalla yereum kharelen Aldiana firdawsi 😢
@fatimaba38334 ай бұрын
Merci beaucoup le frère de aziz à dit la même chose
@rouguietousy22924 ай бұрын
Vraiment wakhoul Lou bone
@samsaradeguerlin45614 ай бұрын
Bilaye walaye, naniou ko comprendre rék dafa méti
@amintagueye63374 ай бұрын
Meme la mére de aziz a dit la meme chose kholbi mo diekh rek ndeyessan 😢😢
@mommy2dieee1814 ай бұрын
Pourquoi vous êtes négatif pourquoi vous aimez juger les gens gnari familles yi lignou wakh leer na wa keur Azize nenagnou khamougnou waly comme niko famille waly wakheni khamou gnou azize mais li frère waly bi wakh degue la goor bou démé ba nekh adulte day beugue outi yeufi bopam e c s ki c passé avec waly malgres kil vivait plus avec sa famille mogui done deguante akh gnome té sou événement dioté dina djiouli djie si aie bokam Arrêt de jugé les gens les connaître Abdoul azize ba alias azize dabala et Boubacar Gano alias waly yalla nalen yalla yeureum de di senn noff lay yalla nagnou reuthiou lignou done gneuwé si adouna Que justice soit fait mes condoléances aux familles
@diemysene60334 ай бұрын
Verite absolue
@ramataba48634 ай бұрын
Merci beaucoup c’est exactement ça les familles ils ont rien dit de mal
@SallaDiop-t3j4 ай бұрын
Merci beaucoup limo leer
@laurentdjiba2854 ай бұрын
Heureusement qu'il y a quelqu'un qui utilise sa tête 😊 chapeau à toi ❤️
Aziz tamite peulh la Ba la sante pa bi mo meunoul wakh bok legui yi moy lolou😢Yallah na Firdawsi done seni keur
@SalyBa-iz3gl4 ай бұрын
Peut cette famille n aimait pas voire leur fils danser. Ils parle juste sous l effet de la colére ak choc. Faut le comprendre
@ndeya50994 ай бұрын
Aziz sax peul la
@houleyeMbodj4 ай бұрын
Pourtant dafa wax ni bokounou dara mais nio bok diné manam bokouniou déréte arrêtez de compliquer les choses
@SoceDiagne-jt5yf3 ай бұрын
@@SalyBa-iz3glmais il ne dansait pas lui
@astoumaguettesissokho324 ай бұрын
Waw naka nguay amé rak do lindjeunti foumuy nèke ak gnane lay fréquenté saguane bahoul tamit halé boko yoré bamou guéne say loho daguako wara top hol thi lane la néke surtout halé bou tolouni néke si bountou adouna
@OusmaneSeck-f1s4 ай бұрын
Khana déggo loumou wakh
@Dani-ibrah4 ай бұрын
Surtout @@OusmaneSeck-f1s
@Néocolonialisme4 ай бұрын
La version ne tient pas
@soumareabdoulaye39034 ай бұрын
@@Néocolonialismeces quelles version qui lou ler la wakh khalè bou gor day am tamp
@TheDiogop4 ай бұрын
Lilou wakh lérna nagn@@Néocolonialisme
@Lopios-g6l4 ай бұрын
Amoulén louguén wahh et dieureudieuf guénn wara wahh Azize il l'a bien traité Come son propre frère...👏👏
@patrapatra15574 ай бұрын
Li mon tah ken beugoul yor diambour
@SallaKonate4 ай бұрын
Say dara worou le ci
@aidaguene19484 ай бұрын
Gni yoor ko 19ans nga beugeu ko teukeulé ak un an en plus Wally bou nékoul woon kou correcte Aziz dou nék ak moom, Wally loumou meune aye mbokam nioko def
Repo en paix fréro que la terre lui soit lègére fridawsi 😢
@MohamadoumoustaphaKante3 ай бұрын
Yallah naniou yallah mousseul si séytané ak djeuf djou boone,li léép mbiroume séytané lheu
@veroniquenatack73924 ай бұрын
*Ndeysane métina trop mais mougne len Yalla naléne sougnou Borom may kholou mougne 😢ki wala gnou déff li Yalla nagne len diap thi lou gaw🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
@AstouGueye-g9s4 ай бұрын
Paix à leurs âmes
@xibar24tv854 ай бұрын
Q
@fatiqma4 ай бұрын
Ameen lii kesse mor diara niane
@veroniquenatack73924 ай бұрын
@@fatiqma *Bilay wlay 😢*
@princessemyadiallo97913 ай бұрын
Doyna war dè Senegal nak naniouko kholat gni nèk Ci réseau sociau yi di fene rèk ak di takal domou diambour yi yèmèna yalnako yalla yeureum khareko aldjana firdawsi amine 😭 massa lène li mome mètina vraiment
@ndeyefaye3821dabakh4 ай бұрын
Waly yalla gua metali sa daw thi aldiana firdaw sy😭😭😭😭😭😭😭😭💔☝️
@AugustinBassene-l3e4 ай бұрын
😢😢😢😢😢😢😢
@babacargueye13243 ай бұрын
Linguén ko déff bamou guéneu keur gui wakho léne koo... bakane diameu leu beugg... Wolof ndiaye néna diambour geune neu mbokou... yallah nako yallah yeureum.🙏
@ndeyemaremekonate77214 ай бұрын
Combien de jeunes ont abandonné leurs parents pour suivre des marabouts, des fans ou de simples compagnons sans l'avis de leurs proches. De len ate deug 4 ans ba 23 kou mou kham un an takh guenn di khass ay bokam ragal lenn yalla
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Vraiment
@ndeyefatoudiop60293 ай бұрын
Deug bou werrrr 😢
@ndeyefatoudiop60293 ай бұрын
En tout cas affaire biiii louche na torop yalla rek khame mais sama khel ñiaw neuuu torop ci histoire bi
@veriteabsoluedeugneekhoul17203 ай бұрын
@@ndeyefatoudiop6029 kou dé mo nekheu toumal. Mais je ne crois en l'histoire d'homosexualité
@rapca22133 ай бұрын
Yow konaté bi nga sante et la lucidité de ton commentaire wonénani da nga dioudo fou bakh.
@itools25144 ай бұрын
On ressent la colère dans leur propos ainsi que des regrets. Mais élevé un frère de 4 à 23 et du jour au lendemain qu'il veuille se débrouiller est parfois compréhensible pour des débrouillards comme on a décrit Waly. Si Waly ne veut pas qu'ils sachent où il se trouve, ils ne le sauront pas même s'ils le savent quest ce que vous voulez qu'ils fassent, le tabasser pour qu'ils rentrent. C'est leur frère, il est majeur et leur responsabilité a des limites. Ils ont parlé sous le coup de la colère mais cela se comprend vu les fausses informations que les gens véhiculent. Il faut se mettre un peu à leur place et ne pas jeter de l'huile dans le feu. Qu'Allah dans sa miséricorde leur attribue le paradis et qu'il apaise la douleur des familles Aziz et Boubacar.
@gassamayama524 ай бұрын
Ndeysane destin wam la done dieuli rek si aziz gnio bokeu destin bou triste bi. Mais mbokeu deret alla kouli hal mo lay takhawou sa dioudou mo lay takhawou sa déé yalnalen yalla may kholou mougne. Métina torop😢
@YacineSt-yl7bn4 ай бұрын
Bilay wakh gua deug
@naboukebe53904 ай бұрын
Yalnako yalla yereum souf woyof si kawam
@veroniquenatack73924 ай бұрын
*Amennn🙏🏽🙏🏽*
@aminatacisse93784 ай бұрын
Ya Allah nako sounou Boroom yeureum té khaaré ko Aldianah si barké Seydina Mouhamad (SAW) amiin
@aichaamethfall15084 ай бұрын
SALLA LAHU ALEYHI WA SALLAM ❤️ ❤️ ❤️
@Fkdalmaktoum74 ай бұрын
Maaay kilifam té khamo foumou nékk franchement d'après les vidéos il était c Aziz dans de bonnes conditions ndoggal mo gneuw rekk donc na waxx dji raffet
@Ndeyendack-fe2jl4 ай бұрын
Man ak yaw gnoo yam guis guis yor khalé mou kheuy guéne té khamoo foumou nékk défo sa rôle nopi moola war
@Beaute92914 ай бұрын
Vraiment wakh bou dofé nop yi koy degue mo wara weer. Ni nguèn def ba top ko bimou gagno so Lén ko defone bi mouy dound dinguén ko Guiss
@alhamdoulilah39914 ай бұрын
Ça ne colle pas d. Ils ont failli
@antadieng5254 ай бұрын
Nek loune ay responsable mais khalé bou bakh mogui donne liguey ba Tabaski yewe mou dème village amoulene lo léne wakh Boubacar yalla nako yalla yereme kharé aldiana
@rouguikebe99844 ай бұрын
Dafa lérr
@MassaerHanne4 ай бұрын
Si tu prend un gosse et vivre avec lui , tu dois chercher premier ses parents La famille de waly aussi devait aller voir où vie waly et avec qui
@odettebadji4 ай бұрын
Bien dit Machallah. Nite dafaye Ame Kilifa. Paix à leurs Âmes. Que Firdawsy soit leur demeure Eternelle 🙏🏽
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
C'est ça aussi. Aziz limou def aussi risque leu héberger un gosse sans savoir d'où il vient et qui sont ses parents. Mais il me semble Que le gosse n'avait pas dit la.vérité à aziz parce que d'après les interviews wally était orphelins de père et de mère et qu'il avait 2 petits frères en charge alors qu'il est le dernier de sa famille manam moy tiaat d'après ses frères 🤔🧐
@awasamb20344 ай бұрын
Tout a fait
@ndeyefatoumbaye33394 ай бұрын
Sama belle mère defone nako hébergé benn khalé bou goor ndakh néna dako yeureum. Khalé bi néna pêcheurs, ndékété c'est un grand voleur. Le jour où on a su que c'était un voleur ,on ne la plus revu. Les gens venaient souvent nous de ces nouvelles
@kourkopoulopoulo5204 ай бұрын
Ndeyssane li metina trope qu’il est jeune et beau ndeyssane que son âme repose en paix firdawsi sa dernière demeure Bilahi ki def li yallah nako yallah nite sibou gawa gaw 😢
@odettebadji4 ай бұрын
Métina Torope. Nassi Gneupe Djangue. Yalla Naléne Yalla Kharé Aldina Firdawsy 🙏🏽
@NdeyePame-r1z4 ай бұрын
Yaw amo lo wakh so matone kilifa do dokholé ni 😢😢que leurs âme repose en paix inchallah 🙏🏼🙏🏼
@GosidibeYoutube184 ай бұрын
Qu’Allah leur accorde son pardon et leur ouvre les protes du paradis a tous les deux Wally et Aziz ! C’est une situation tragique. Cela montre aussi une négligence tres répandue au Sénégal ! Des voisins qui ont entendu des cris et qui n’ont pas réagi - a la famille du petit qui se sont décharges! C’était leur responsabilité de vérifier la ou il résidait ! Ils ont failli a leur responsabilité !! Triste !
@yacinediop90303 ай бұрын
Yalna yalla yerem léne ta khari léne aldiana firdawsi
@fatoukane86504 ай бұрын
Ndeyssane metina 😢 que leurs âmes reposent en paix amine
@aidangom-s8m4 ай бұрын
Lolou lagnou meuneu wah ndahe aziz motah gnou hamko yalla nak mo gneuw ak dogalame yalla naléne yalla yeureu té yésale diégeule si séne kaye🙏🙏🙏
@khadydiop86084 ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureum 🙏 si barke seydina mouhamed 🙏
@BasketeusouSonko4 ай бұрын
Bayilen nafekh nguir yallah ragalen yallah. Senegal gnou beuri dagnouy and ak nite te sa famille dougnoulen kham fane la nekeu. Li wally dem beurina fofou nekeu si keur diambour te sen wakeur khamougnou fane ga nekeu rawatina khalei you goor yi. Yenangui deg li makk yi wah dagnouko done wo doulen wah foumou nekeu. Demlen nguen diouli gnanal gnou fatou moguen tok si commentaire yi di fen di diagaser rek. Merci Dakarbuz yaw bignou wane famille wally yallah nalen yallah may kholou mougne. Metina torop ndeysane.
@Mossdef74 ай бұрын
Bilahi li nga wakh deugla khaleyi bougnouy yeg ken doulen yeuk bou dano rek lan llen di deg
@aliouba11704 ай бұрын
Merci Beaucoup Dakar Buzz pour votre Super Reportage ❤🍀🙏🏽
@gansiryfall9954 ай бұрын
Toutes mes condoléances Wally repose en paix que dieu t'accueille au paradis Amine Yarabi 🙏🙏🙏🙏
@fatimlo46214 ай бұрын
Yalla nako Yalla yerem khaaréko aldiana firdawsi Amine métina torop
@adjaratoudiodiondiaye38444 ай бұрын
N’a rafet que leurs âmes reposent en paix.
@itools25144 ай бұрын
Bravo à @Dakarbuzz, travail remarquable. C'est clair maintenant, on vous tire le chapeau.
@soulay8194 ай бұрын
13:07 ce momsieur est responsable respectez sa douleur et en plus vous avez entendu l'appel du muezzin ??? Mandoulen
@MbodjAmadou-dw3sh3 ай бұрын
Yalla nalén yalla yeureum😭😭😭
@WIZG2R4 ай бұрын
Sénégalais dineu beuri aldiana Degay am dom Yarko beu mou magu nitt reyy ko niouner ndogualou yallah lh 😢yalnalénn yallah yeureum 🙏💔🕊
@rawaneseck30243 ай бұрын
En tout cas je suis en phase avec sa famille. A mon avis ils ont dit la vérité.
@habydiarra27414 ай бұрын
Ça vaut dire tu n'était pas en contact permanent pour connaître les fréquentations de ton frère ni le lieu où il habitait, je ne peux pas comprendre que votre frère habite avec inconnu pendant quelques temps sans essayer de connaître l'inconnu.
@Lordredujour954 ай бұрын
Bilahi en plus si khaleiii bou ndaw. En plus c’etait pas son neveu comme les gens le disent.
@makeitreal69184 ай бұрын
Vérité absolue
@satoubatouba81244 ай бұрын
Sa way linga wakh moy deugue gou wér
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Voilà. Donc mom amoul loumou wakh.
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Ndeye gueye di doule naan wally avait 2 petits frères alors que mom moy tiaat
@Speedrunproedits4 ай бұрын
Franchement ils ont tout fait pour avoir un contact avec lui. Gni fi dess daal nit bou nieuwé sa keur beug leu beu tok sa keur da ngay wo ay mbokam c’est ce qui est normal. Yalna bourbi yeureum
@tackoniang11064 ай бұрын
Un enfant ken douko denk ken il est à la responsabilité de ses parents ou de sa famille au sens qu’importe, la situation de la famille on élève ses enfants soit même dans la dignité. En plus il parait qu’il était dans de bonnes conditions chez Aziz conn n’a rafet yallah len bolé, j’en suis sûr quand il était vivant wetiet yim done indi à la maison vous consommer bien hein, legui ga nane khamo ko, qu’importe Li Dogal yallah la certe, mais il y a une leçon à prendre dedans, un enfant est à la responsabilité de ces parents, tant que yobouwoko mouy diangui même dans ce cas, danga ko wara suivre kham si limou né. Daffa am gnou beugeuh lou diour dom bagn say responsabilité, souko dara dallé faut prier pour lui et apprendre. Yallah nalen borom bi baal khare len aldiana
@bambadiop443 ай бұрын
Walaye ndaye saane metina lol mais yalla nalen yalla khare aldjana
@NdeyeKane-q2u4 ай бұрын
Yow nek Dakar wally nek Dakar meuno kham fou nek louss na
@diodiodiawndiaye90714 ай бұрын
Mais xalé yi si lignouy nek ken douko xam
@pendadiagne54364 ай бұрын
Lan mousi louss bou wally beugoul mou khame fou nekk nakk? Bayi wakhe diou niaww 😢😢😢😢
@mohametrassoulndoye3654 ай бұрын
Walakhi deug rek gay wakh . Khalé yi kén manoulén contrôle. Sénégal nak bou dé gueussé ba ame nit yi daniouy wakh rek@@diodiodiawndiaye9071
@nabouly23914 ай бұрын
Irresponsable rek
@moussapayemane41674 ай бұрын
Loussoul déh té day am,
@cheikhomarsene15633 ай бұрын
C’est vrai que defngene lileen war si mom nakh même moi je suis jeune n’empêche je sais que les jeunes d’aujourd’hui veulent tjrs être indépendants mais sa dom bi lidieunti numéro waly si xaritam bi meunouleen wone dem si xaritam bi pour plus de renseignements foumou deuk et tout 😢
@mamadoudiop66214 ай бұрын
Mane dhé j'ai 30 ans.j'ai perdu mon père.sama yaye amoul dolé.dés fois ame envie bayi sama keur famille mais sama dignité mayouma may dém keur kénène..en tout cas enquête bi y'aura bcp de choses qui vont être réveler
@rouguikebe99844 ай бұрын
Billahi meunagn kofa déf litakh khalébi dém on sait jamais.
@AmetheSeye4 ай бұрын
Amna lou takh mou guene keur gui dem fenene. Wakh lene deigue
@MadameSane-yo1rj4 ай бұрын
Mai lolou gniou khamoul gnio done wakhe diarbatam la mai yayou aziz néna khamoulone sakhe foum deuk n'a rafét rék yalla naléne yalla yeureum kharaléne aldiana
@maimounadiallo81523 ай бұрын
Vraiment frère bi defna louko war même sa dom dalay teu mane dé gueum na freram bi khaléyi legui denioo doy waar
@Enfant_béni_74 ай бұрын
LI MOTAX KHALÉ DAFA WARA AME KILIFEU 😢 GUÈNEU SA KEUR AY KILIFEU DÉM TÉ BEUGOU NOU XAME FONÉK BA LI FÉKEU LASI OH NDEYSANN 😭😔🙏🏿 YALNALA YÀLLA TWT YEUREUM TÉ XARILA ALDIANA BOUBACAR WALLY 😢
@rouguikebe99844 ай бұрын
Edk khamga lougn kofa déf ?? Té apparemment ay domou baye lagniu? Béne version rék nga dégu kharal ba dégu bénéne version bi soga jugé.
@Enfant_béni_74 ай бұрын
@@rouguikebe9984 xalé dàal day ame kilifeu la wax mais kougn déf LOUTAX mou guéneu këram Louko diar taxoul may wax
@SirèCamara-b1s3 ай бұрын
Allahou akbar metina trop massa yalla na léne yalla yeureume
@Mounajate4 ай бұрын
Mais topito haleyi di hame founiou nek. Louniouy def thi louniouy nek ndak Lou melon ndak Wally hallerla un très beau garcon yalnako ualla yeurer
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
Très beau vraiment. Il ressemble à mon fils motakh dewam dafma mety trorope 😢😢😢
@aissatoudiallo1894 ай бұрын
Bilay déh mo nieuw rek en plus conditions you méti.mais khaléyi nio doy War aussi
@veriteabsoluedeugneekhoul17204 ай бұрын
@@aissatoudiallo189lolou leu khaléyi amou niou kilifa motakh djiné doon sen kilifa lounek meun nalene arriver
@aissatoudiallo1894 ай бұрын
@@veriteabsoluedeugneekhoul1720 ah déh métina tissna surtout Ray mais que cela ne nous empêche pas de faire face à la réalité
@Benjamin982304 ай бұрын
Bilahi li méti na trop 😢😢 Yalla na yalla weer gnou def li gnaw li si barki seydina mouhamed psl 🤲🤲
@MoulayedabakhCiss4 ай бұрын
No ay dieul corou aziz bayifa corou wally mome diaroul ay wakh yallah naléne yallah yeureum kharékéne aldjiana firdawsi🙏🙏🙏🙏
@NgagneNdiaye-q4w4 ай бұрын
😅
@Sfr_time4 ай бұрын
Bouniou dieulalé wone coram sakh niouné amouniou si droit bokkou niou dara nite yi ken khamoul louniou beugue normalement kou nek dafa wara dieul néwam preparé ko defal ko ligua kham
@fatiqma4 ай бұрын
@@Sfr_timedeugla waye lou dina rafet nou lidianti mbokam yi wala guisso lolu tamit yal na lene yalla yerem
@kinendiaye28324 ай бұрын
Billahi dagnio warone wakhtane ba diobo gni yalla molène bolè si lèp enterrement funérailles lèp bène la warone dôme yalnalene yalla yeureum
@fatimafall44934 ай бұрын
@@fatiqmalidieunti nagne mbok waly yi ba informélén le grand frère de aziz sakh wakh nako
@falloundiaye24094 ай бұрын
Nite daye âme kilifa rawanati khalé j'ai l'impression que le jeune à choisi son chemin mais qu'Allah swt les accueils au paradis
@Fayacine4 ай бұрын
Wakh deugue yalla ki loumou wakh dawna yaram 😢😢😢 mais frère Aziz bii waroul wonn bayi fofou corp Wally bii 😢😢😢😢😢
@mimadiedhiou24764 ай бұрын
On récupère pas un corps sans l'accord de ces proches malheureusement