La réaction de Gaston Mbengue aprés la sortie de Sérigne Moustapha sy

  Рет қаралды 572,115

SENEGO TV

SENEGO TV

6 жыл бұрын

Des détails ont été apporté sur cette vidéo. Téléchargez notre application: play.google.com/store/apps/de... ou visitez notre site senego.com

Пікірлер: 1 100
@LayeDiouf-vs1vf
@LayeDiouf-vs1vf Ай бұрын
Yal nako yalla yeureum thi barke Serigne Moustapha Sy Al maktum ❤
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
Vous êtes des fou
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
Démal diamou yaallah ta bayi comédien bobou nga tope meunoul ray sakh djinakh
@MamadouDiouf-iz8bu
@MamadouDiouf-iz8bu Ай бұрын
Yalnako yalla yeureum ti barkè Serigne Moustapha sy Al maktoum
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
Pour yeen s'en Serigne moko ray😂😂😂😂
@MamadouDiouf-iz8bu
@MamadouDiouf-iz8bu Ай бұрын
@@layeNdiaye77 kokou d'où raykate nitt bay rayatè .awma droit nianalko yeurmandé wala
@user-bj6zd8bm6x
@user-bj6zd8bm6x Ай бұрын
Yalla nakou yalla yeureme si barke seringue moustapha sy al maktoume❤❤❤ ❤amine inchallha
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
Moustapha sy moom comédien leu aka meun graw graw lou ndayssan
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
Thiey wa pur😂😂😂
@omarediery2069
@omarediery2069 Ай бұрын
Yalnako yalla yuerem si barckéb serigne moustapha sy maktoum in challahh 🤲 ♥️
@modoulo8211
@modoulo8211 Ай бұрын
Yalla neko Yalla yeureum tee khare ko aldiana si Barker serigne moustapha sy al maktoum ❤
@bounafall2812
@bounafall2812 Ай бұрын
Serigne Moustapha Sy Al mactoum dou sarap ndayam dou thiotou ndayam dou touss😭Yalla rékk mofi nékk Gaston Mbengue a parfaitement raison .
@ModouRacineGuene
@ModouRacineGuene 19 күн бұрын
Yaw bingay wakh titto Yaw yadoul dara imbéciles Dama lay niane nga dém toup manna la bal mais ... Baxna
@SarrMadame
@SarrMadame Ай бұрын
Thieuy yalla yallanako yalla yeureum té yalla fayall niou Serigne Moustapha s'y kén la amoull morom ❤❤
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
Moustapha sy mola wakh amoul morom 😂😂 nékal niit
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
Dangay doul
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
@@layeNdiaye77 😂😂 gnii ay doff lagn comédien bobou dinaléne doff lo rék
@mansodiouf6770
@mansodiouf6770 6 жыл бұрын
قل اللهم مالك الملك تؤتي الملك من تشاء وتنزع الملك ممن تشاء وتعز من تشاء وتذل من تشاء بيدك الخير إنك على كل شيء قدير Lii la yalla wax Gaston vous avez raison, wadioojou mo wakhoul deug, meuneu doul ba dèè thiiime.
@cheikhahmethfall2017
@cheikhahmethfall2017 Ай бұрын
Donc pour quoi élections ?
@SM_C24
@SM_C24 Ай бұрын
@@cheikhahmethfall2017 niata nitta taxaw? Niata ci fallou? Niata nitta woté? Ki niou wotel, lan wala kan mo tax Nitt ngi wotel ko bayi fa nyenen ngi? Ndax daf len geun judu wala daaxalen wakh?
@mamadouseye2702
@mamadouseye2702 Жыл бұрын
Serigne Moustapha sy..mo rawe sa mame rawe sa baye rawe sa wa keure yéppe
@mamadoukonte3318
@mamadoukonte3318 6 жыл бұрын
Bravo Gaston bien parle ( seul Dieu qui est à la hauteur de tout)
@yorofall6764
@yorofall6764 Жыл бұрын
Merci
@diopmamadu7719
@diopmamadu7719 6 жыл бұрын
Yalla rék moffi nékk koudoul yalla néne là bilahi
@idrissadione7279
@idrissadione7279 Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤ deugeu bou werr nga wakh mon pére fii yalla réka fii nee té mooy fal kouko neekh
@aminatadia3122
@aminatadia3122 6 жыл бұрын
Gaston à parfaitement raison yalla rék moy fale dii foli
@amadoubarry5034
@amadoubarry5034 4 жыл бұрын
Machallah
@Diouf-bq1vs
@Diouf-bq1vs Ай бұрын
Motakh yalla rayna ndéyam
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
@@Diouf-bq1vs pour yaw yaallah doula ray Quoi yéne ay vrai domram nguén quoi yaw sa Serigne bobou nga yakar sakh bouko yaallah di ray dakoy béte
@santeyalla2371
@santeyalla2371 6 жыл бұрын
Bilahi yalla rk moy diokhe ngour mais dou domou Adama
@tivaonemomelabeug5510
@tivaonemomelabeug5510 Ай бұрын
Sénégal mome dofe rék kou déh Serigne motakh aye wokh la rék roukh yalla moko mome mé dou Serigne
@cheikhahmethfall2017
@cheikhahmethfall2017 Ай бұрын
Yaa mana doul kay ma ray sa ndaye ba kham man may yalla chaque jour nga degg ni amna ku ray walla kouka yalla la? Bayyi len sen thiakhan
@user-cv2bd8gu1c
@user-cv2bd8gu1c Ай бұрын
Dagga reck la wakh yall nako yalla yaram yalla rek mooy fall dii follii توتي الملك من تشاء وتنزع الملك ممن تشاء وتعز من تشاء وتذل من تشاء بيدك الخير انك على كل شيء قدير
@awadipo5000
@awadipo5000 6 жыл бұрын
Dieu est le tout puissant He is the only one . The real power Only who make things happens Happiness sadness wealth death success For the believers
@elhmalickdiop
@elhmalickdiop Ай бұрын
gaston ya gi gas sa bamel te yeuguo ko te man na sakh top sa niabot bismilah
@alaminesylo2511
@alaminesylo2511 Ай бұрын
wallahi sang bi amnga reson tay d
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
​@@alaminesylo2511Moustapha sy comédien leu meunoul ray kéne nékal niit
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
Pour niom s'en Serigne moko ray😂😂
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
@@layeNdiaye77 gnii kay sén comédien bobou dinaléne doff lo rék 😂
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 Ай бұрын
@@BounaNiang-mt8mg man damalena yeureum sakh
@mamadoudiaw6169
@mamadoudiaw6169 6 жыл бұрын
Wallahi je suis tidjane mais faut pas obéi les marabouts mais ce que gaston à dit c'est 100% vraie dieu a dit sur le coran khoulil lahouma malikal moulki toueti almoulka man ta chaae watanzioul moulka mimman tachaaou sklhoul azim wasalam.
@acteursporno.nekhkoybeugle4724
@acteursporno.nekhkoybeugle4724 6 жыл бұрын
Doundal way Gaston bilahi yalla nala yalla defal diamou
@fatimatadia311
@fatimatadia311 5 жыл бұрын
Bejre :)
@ndeyesouckeyengom44
@ndeyesouckeyengom44 6 жыл бұрын
Respect ...deug gua wakh
@falloundiaye6878
@falloundiaye6878 6 жыл бұрын
Gaston doundeul way😍
@psdieng2988
@psdieng2988 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum ci barké yonent bi
@seynaboudiene463
@seynaboudiene463 3 жыл бұрын
J suis la dixième petite fille d cheikh issa diene. Vous avez parfaitement raison mbengue haly Ta grand mère oumi syylla est ma badiene ton oncle sidi bara porte l nom d mon pere
@papediakhate1154
@papediakhate1154 6 жыл бұрын
Lila serigne cheikh di wah soun demé ba kou feroul ifji di tonte borom ham ham adouna bou touki la
@leral.xamxam6708
@leral.xamxam6708 6 жыл бұрын
merci castno
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 Ай бұрын
Serigne sy douniou yalla mai il faut niou am talubé si niom diokhlen respect aussi
@ndongmagette4911
@ndongmagette4911 6 жыл бұрын
Ayy founiou Dieum way
@moussandiaye5951
@moussandiaye5951 6 жыл бұрын
Gaston a juste dit des vérités seul Dieu qui sait tout nul autre Dieu n aime pas ça !
@maradrame9749
@maradrame9749 5 жыл бұрын
Moussa Ndiaye wakho deugue
@mariemdiop4272
@mariemdiop4272 4 жыл бұрын
@@maradrame9749 souba ngiendi comprendre
@mariemdiop4272
@mariemdiop4272 4 жыл бұрын
Sen fatikha sa deguene koy lidjeuti nop mo len war
@miadiop6727
@miadiop6727 6 жыл бұрын
Bilahi j'aime trop serigne moustafa mais limou wahh epeuna deug nexoul nak
@diengpapemoussa263
@diengpapemoussa263 5 жыл бұрын
Il a dit la verite meunako te waxoul moy fall moy folli ki moy domeram rk
@cherifaliounebadarasy1996
@cherifaliounebadarasy1996 4 жыл бұрын
yaw yaye domoharm yaw
@Alamine-lx9vi
@Alamine-lx9vi Ай бұрын
Ndayssan yalnako yalla yeureum martaba dou balé
@blackwoman2916
@blackwoman2916 Ай бұрын
Martaba kane? Khana wakho qiy fal di foli tè candidam amoul Sakh 1%. Non sérieux 😂😂😂😂😂😂 quoi 😂😂😂😂😂😂 réveillez-vous avant qu'il ne soit trop tard.
@user-cv2bd8gu1c
@user-cv2bd8gu1c Ай бұрын
Tee yalla mooy doundal mooy ray له ملك السموات والارض يحي ويميت وهو على كل شيء قدير kon yeenna wakhyii ay thiaaxaann rek la wasalam yalla neenna amoul benna bakann bouy faatou thi loudoul sama ndigal وما كان لنفس ان تموت إلا بإذن الله bokkaalee baakhoul nanou ragal yalla kou feebre nganee mana kou dee nganee mana
@mamadoubalde5290
@mamadoubalde5290 6 жыл бұрын
Way gaston wakhh gua deugggg way
@malangamadou9789
@malangamadou9789 6 жыл бұрын
kham sa boopou si diamou yallah la bokkou (def ak dindi yallah ko diago)
@papesarr235
@papesarr235 4 жыл бұрын
Malang amadou seringe bi bou dewe yalla rek laniou koy baye
@sidibeisrael1496
@sidibeisrael1496 6 жыл бұрын
Merci
@NianeAlassane
@NianeAlassane Ай бұрын
Sérigne Moustapha sy Al maktoum dou sa morome teugue katou lambe da wora tontou nitou yallah
@panafricain1993
@panafricain1993 6 жыл бұрын
Yalla moye fal moye foly kou hamoul sa souba mouno dogal thi nite loudoul yalla neneeeeela
@akassafall9574
@akassafall9574 6 жыл бұрын
Merci Gaston!nitt kou bakh gua
@courandiaye9769
@courandiaye9769 3 жыл бұрын
Il est doul serigne
@alssanediallo4960
@alssanediallo4960 6 жыл бұрын
Merci gaston
@bassiroundiayekouta1920
@bassiroundiayekouta1920 6 жыл бұрын
Bien dit gaston
@fallmodou8401
@fallmodou8401 6 жыл бұрын
serigne Mansour n a jamais dit à ablaye Wade que tu auras un second mandat
@morbeye8879
@morbeye8879 6 жыл бұрын
bour guewel est un grand journaliste
@moustaphadiop9588
@moustaphadiop9588 6 жыл бұрын
merci oulimata ndiaye
@user-fn1qc7kt1n
@user-fn1qc7kt1n Ай бұрын
Aka gnimé wone DEUG yalnako yala yeureum té yéssal yeurmandé thi mome
@kanealy5323
@kanealy5323 6 жыл бұрын
senegal diakhasona lee guiiii
@xomgaye7452
@xomgaye7452 6 жыл бұрын
Gaston parfait ma raison deugue rk ngafi wakh boy sy day sop rk dou yalla
@barrosamb2247
@barrosamb2247 4 жыл бұрын
soulaye gaye katalle ndeyam koy wakh boy mate naka bay doméram
@mouhamedmbacke6006
@mouhamedmbacke6006 4 жыл бұрын
Sa data yaye moye sopp sa bay moye boy ok
@elhadjimamadoundoye2492
@elhadjimamadoundoye2492 Ай бұрын
Deug deug wakh na deug yalla yalla yeureum ko
@abdousarr8987
@abdousarr8987 6 жыл бұрын
Merci nice na
@morbeye8879
@morbeye8879 6 жыл бұрын
Luleer nga wakh mais wakhalak serigne moustapha mii wakh bul clase serigne si si sen yon nekul
@abdoulahatndiaye7781
@abdoulahatndiaye7781 3 жыл бұрын
wawaw
@khalilndiaye9598
@khalilndiaye9598 6 жыл бұрын
Vraiment, certains marabouts se croient être en 1800. Réveillez-vous chers marabouts, on est en 2017. Nakhaté yi dafa doy. Talibés yi aussi danio yéwou. Esclavage religieux existe bel et bien au Sénégal. Il est temps de le combattre. Le seul moyen de combat: l'éducation (diang). Yallah moy fal kouko nékh, teu moy folli kouko nékh, ci wakhtou bouko nékh. Talibés yi diang lén ba kham sén diiné, wallahi, dinguén khamni serigne sou bari danioulén di nakh. Merci
@morgueye1789
@morgueye1789 6 жыл бұрын
Aka lair
@AlphaDiallo-gz8gm
@AlphaDiallo-gz8gm 6 жыл бұрын
Khalil Ndiaye merci bro sa commence à devenir du n’importe quoi avec c’est marabout matérialiste, Sénégal moy deuk bou doy waar.
@cheikhndiaye2856
@cheikhndiaye2856 6 жыл бұрын
Diadieuf gaston
@mansourmbaye8441
@mansourmbaye8441 6 жыл бұрын
Khalil Ndiaye sa data yay
@mansourmbaye8441
@mansourmbaye8441 6 жыл бұрын
CHEIKH NDIAYE sa digou leufeul nday
@cheikhniang2429
@cheikhniang2429 4 жыл бұрын
Machallah
@ibrahimadione1437
@ibrahimadione1437 6 жыл бұрын
Gaston tu as dit la vérité.les marabouts doivent éviter de parler à la politique.il a un dieu et il est unique
@ibrahimadione1437
@ibrahimadione1437 6 жыл бұрын
Dieu est unique moy fall moy fallu ce n'est pas une personne qui dispose
@sambacoundoul2353
@sambacoundoul2353 6 жыл бұрын
degue rėk nga wakh
@ibrahimacisse8977
@ibrahimacisse8977 6 жыл бұрын
Merci Gaston tu'as bien dit seul Dieu est Dieu le marabout la soit disant moustapha sy il est marabout par nom de famille
@bakhyayeyaye9625
@bakhyayeyaye9625 6 жыл бұрын
machalla lep yalla la
@mouhamethniang3154
@mouhamethniang3154 Ай бұрын
Thieye yala dé moye deugeu kholale li rek com kou dewoul yalnako yala yeureum t yekhe niou amine hooooooo yene gni comantair bayi len ligueni wah serigne moustapha sy rawoul kene kokou nitou yala la
@zakariadeune2296
@zakariadeune2296 4 жыл бұрын
Merci gaston ya bakh si mak you réw yi té mana fén 👏👏👏👏
@elmaestrondiaye1617
@elmaestrondiaye1617 4 жыл бұрын
Ray ngama
@mouhamedmbacke6006
@mouhamedmbacke6006 4 жыл бұрын
Sa ndaye ak sa baye ndion tothie yayame rew
@hassandiop8052
@hassandiop8052 6 жыл бұрын
Bayuilén bay dinthie yolwan doudé !! Gaston reglel sa bopou bo dougué ci moustaph légui nga yém !!
@adjafall3436
@adjafall3436 6 жыл бұрын
Yaw gaston domèram nga t domèram sah beugoula melni Yaw waxoumala serigne dè wayè ben talibèm rek xadioul si Yaw t li def sa donou doto ame loula nekh incha alla
@goraniane9817
@goraniane9817 6 жыл бұрын
Merci père
@fatoumbaye8397
@fatoumbaye8397 6 жыл бұрын
Serigne bi dama ko beugue respecter ko mais dafa wara khamne ay talibem. Parti. Politique bounek monguissi togayou gamougui waroul wone wakhe nonou nguen balma ak nak boubakh
@kebevisiontv1051
@kebevisiontv1051 6 жыл бұрын
Fatou Mbaye bien ma soeure liga wakh deugla
@maissandiaye7703
@maissandiaye7703 6 жыл бұрын
Il ne peut pas faire la médisance. Tout ce qu'il veut dire il le dit à haute voix. Il faut qu'on dit la vérité à nos politiciens ils ne doivent pas gérer le pays n'importe comment.
@diagnegnilou1078
@diagnegnilou1078 4 жыл бұрын
Fatou Mbaye deugue pire ngawah
@diagnegnilou1078
@diagnegnilou1078 4 жыл бұрын
Surtout le jour du Gamou
@FreeFree-vw4xd
@FreeFree-vw4xd 6 жыл бұрын
Gaston dale mo wakh deug manila Moustapha sy dou touss gnémé yalla sodone fallé ame majorité assemblé ay marabout niouy féne ak niawayam bakaname bou reuye mako wakh Kou togue fi séy mame togone niou diokh la thieure biga mom kouffi wathieu sa ande nak niou xolé la boy town défaneté ko ak yaw bouniou kéne réye sunu borom moy fale man andouma ak macky diépi lako déf sakh mé yéne serigne si naniou bayi wakhi doff yi amolé daray xam xam khayatoul dunya niou bone guéne
@aliounebadarasyll5360
@aliounebadarasyll5360 6 жыл бұрын
sa leufeul ndaye yaw ya doul touss
@aliounebadarasyll5360
@aliounebadarasyll5360 6 жыл бұрын
Garçon sarr ham sa bay bimi kat sa yay daf ka dioutal mo tah say wah dioutou
@mustafcisse213
@mustafcisse213 6 жыл бұрын
babacar sarr So geumé limalay wakh my dieul ma pv na kholi sa leufal ndaye serign mo raw sénne mami bayy
@FreeFree-vw4xd
@FreeFree-vw4xd 6 жыл бұрын
entente asc wouy tite na ay rétane guéne ma déf petit con
@fatimlo4621
@fatimlo4621 3 жыл бұрын
Merci beaucoup Gaston 👍👍
@barrezi
@barrezi 6 жыл бұрын
C'est vraiment dommage pour mon pays
@sawrousarrbageuloubakh8160
@sawrousarrbageuloubakh8160 6 жыл бұрын
dageu rek nga wakh dageu da nekhoull ok!!!!!!!!!!!!!!
@maododiaw9211
@maododiaw9211 6 жыл бұрын
Deug nekhol bilay
@rimaadkr132
@rimaadkr132 6 жыл бұрын
Maodo Diaw Deug nekhoul nane rawhane yalla reka fi nek
@awandiaye7510
@awandiaye7510 6 жыл бұрын
doule reck a khaliss guay def mbengue mais fais attention t a vu youssou toure demande le ki est serigne moustapha sy
@maododiaw9211
@maododiaw9211 6 жыл бұрын
Awa Ndiaye je suis tidiane mai seringe moustapha waxol Kham kham li mo def lolo salbe moka mom na bayi polítique sou manon lolo Khalifa sall donek reubeus wakho fi dara
@ahmadoundoye6158
@ahmadoundoye6158 6 жыл бұрын
Maodo Diaw iOe mom bo teudei do nelaw
@maododiaw9211
@maododiaw9211 6 жыл бұрын
ahmadou Ndoye Lu takh
@hadaratoulakhmadiyadediamal
@hadaratoulakhmadiyadediamal 6 жыл бұрын
Merci beaucoup gaston
@papandiaye979
@papandiaye979 4 жыл бұрын
Gaston dma dem bey tifar khol commentaire yi di guis félicitations merci wakhga degue mane con yes
@fatoumbacke9083
@fatoumbacke9083 6 жыл бұрын
Serigne bi khana da beugue macky dioke co khaliss mais loutakh demoul rebeuss
@maradrame9749
@maradrame9749 5 жыл бұрын
Fatou Mbacke khana gaston nguay wakhal
@thiene07970
@thiene07970 5 жыл бұрын
Fatou Mbacke iow khamo foy takhaw
@mouhamedmbacke6006
@mouhamedmbacke6006 4 жыл бұрын
Fallou serigne moustapha soxla woul Khalis réw mi
@norayni8589
@norayni8589 6 жыл бұрын
Journaliste yene ay saytane guene rk
@gorouawandiaye1571
@gorouawandiaye1571 6 жыл бұрын
Vraiment je suis Tidjane mais je suis d'accord avec toi parceque Mane diapounani yényi varoul respect kouka AM yakomay sabopou
@momodrame5244
@momodrame5244 6 жыл бұрын
Gorou Awa Ndiaye iow do gat
@gorouawandiaye1571
@gorouawandiaye1571 6 жыл бұрын
Momo Dramé merci beaucoup yalla baxna
@modougueye3964
@modougueye3964 Ай бұрын
Senegal mo nakhari wakhee deug rek biilahiiii
@mamoudoudiallo2333
@mamoudoudiallo2333 6 жыл бұрын
Gaston wakh nga deug.suis tidiane mais le serigne m'a déçu avec ce discours mediocre.vraiment il exagère en prenant la place de Dieu
@abatalibniang9950
@abatalibniang9950 5 жыл бұрын
Daguay doul do tidiane
@ousmankhouma4475
@ousmankhouma4475 5 жыл бұрын
'
@yacinesall868
@yacinesall868 6 жыл бұрын
Serigne yi gno wara guéne si wakhi politique franchement 🤗🤗
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
Moustapha sy mofi done khass ak teukou yaallah niitou yaallah yomboul Gaston yaallah moko fi dieulé Moustapha sy touti na si lolou
@khalifagaye634
@khalifagaye634 Ай бұрын
Lolou dé deugeuleu mais nakh meune nga ko continuel khekh bi wala ?
@ousmanedieye9679
@ousmanedieye9679 Ай бұрын
Ki dafa yébaté rek yaw bouna guiss gua bouniou dadié gua wakh si serigne moustapha sy dara dinala def lou bon niak wormal kilifa bakhoul
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
@@khalifagaye634 nékkal djioulit bayi khékh ta nga tope yaallah lala wakh amna gno khamni Solène topé dagnoulay réral rék ay comédien lagn dagnouy graw graw lou rék
@BounaNiang-mt8mg
@BounaNiang-mt8mg Ай бұрын
@@ousmanedieye9679 kilifa dou khass yaallah diko teukou soubhanalah wayé li yeup yaallah wakhone nako nak akhirou Zaman bila mani topal yaallah ta bayi thiakhane bi lala wakh
@khalifagaye634
@khalifagaye634 Ай бұрын
@@BounaNiang-mt8mg souma wakhaté lénén de plus ñiak kham sama bop minguimay dikeul nakh nit dangay disol gni nga kham ni sen niveau xel tolo na
@modoudemba4651
@modoudemba4651 6 жыл бұрын
Yow macky sall na dègage macky sall dèfoule fii dara na dèm yalnako yalla wathièko si nguour gui ndakh macky sall dafa yakar nè ak nguour dou dièkh yène gnèpp thi ngui naww macky nguène nekk macky dèmale
@santeyalla2371
@santeyalla2371 6 жыл бұрын
Serigne yii danou wara bayii khelou nitte yinouy fowe 😈😈😈
@ngagnegadiaga9919
@ngagnegadiaga9919 4 жыл бұрын
Nopil yaw sant toyalla seytane ga
@cheikhfaya6063
@cheikhfaya6063 6 жыл бұрын
Waw kene khamo lo done
@damesalindiaye340
@damesalindiaye340 6 жыл бұрын
beugue léne diam li Amoul béne ndiarigne Kilifa méme bou dioumé geune kheuye Séti ko khamni Andoul ak mõme nane ko lo khamsi li serigne bi wakh mais senégale yi bane djiko lanou yorr b.serigne Saliou sama khol day méti li li te meunou masi dara😭😭😭😭
@mansordiop4268
@mansordiop4268 3 жыл бұрын
Machalla amna solo torop
@ahmadoundoye6158
@ahmadoundoye6158 6 жыл бұрын
Gaston iOe mom amo Lo wakh iOe gueumo Dara. Cause amo Lo def loudoul di dokh si ay mystique Donc bul gnou takha wakh.
@kanagueye5012
@kanagueye5012 6 жыл бұрын
Gaston mbengue kou tokh sa lafoul ndeye ga sounou serigne responsable morale moustapha su dousa morumou bay dakh astoumac yaw
@sarromar7565
@sarromar7565 6 жыл бұрын
Kana Gueye kenn khamé woulen wakh djou niaw dj
@momo-hp4yf
@momo-hp4yf 3 жыл бұрын
@@sarromar7565 bilahi the sakh geunou niou done tidiane ms serigne Moustapha si dioume la deuk mounoul fall kene
@amadouka1354
@amadouka1354 3 жыл бұрын
Linga wah deugla mais diaroul saga
@user-ju7qm2ko3n
@user-ju7qm2ko3n Ай бұрын
Paix â son âme que firdaws soit sa demeure éternelle
@bounafall2812
@bounafall2812 Ай бұрын
Serigne moustapha Sy Al mactoum Thiaga bou dokhane ndayam leu
@sebcam10
@sebcam10 6 жыл бұрын
Ta raison pourtant yalla moye fall di folli di reye di doundall
@ousmanediouf849
@ousmanediouf849 4 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂gaston ana sey rawkhane nn pére réy nama😂
@user-xf3bs3vs2e
@user-xf3bs3vs2e Ай бұрын
Nala raye yala midi raye raye nala
@khalifadiop6739
@khalifadiop6739 Ай бұрын
Yalla nalla yeureum thi barkai serign moustapha sy
@Topofthetopapex
@Topofthetopapex 6 жыл бұрын
Serigne bobou bou deiii yalla na taw boulette😏 Déjà serigne bouy wakh ci politique je te fais pas confiance 😒 je ne suis ni avec Ce macky sall ,ni avec Gaston, ni avec ce marabout. Tivaouane meussouma degg bene serigne di teukouwatè jusqu'à ce serigne (je connais même pas son nom)😒
@alassanedeme3792
@alassanedeme3792 6 жыл бұрын
Fatou Diop yaw sa tata yaye
@queenasonking265
@queenasonking265 6 жыл бұрын
Gaston xolatal sa wakh beuss dina niew diga réthiou bilay walay Serigne Moustapha dou sa morom dougourou Macky sall diaroul li yèdal sa bopp
@damegaye3162
@damegaye3162 6 жыл бұрын
Je ne suis pas fan de Gaston mais il a raison fi yalla rék mofi nék
@aboubackrydiallo6074
@aboubackrydiallo6074 3 жыл бұрын
Bilaye walaye père Gaston wakhalwaye
@ndiayecheikhmariemou1412
@ndiayecheikhmariemou1412 6 жыл бұрын
Deug rek nga wakh kou beug Lou bakh day melni serigne Bass
@babsgalsen9706
@babsgalsen9706 6 жыл бұрын
fans lyon ou il a pris ces milliards kil réponde à assane diouf d'abord
@serignesall4769
@serignesall4769 6 жыл бұрын
Na wakh foumou dieulé milliards yi
@papitodiack3092
@papitodiack3092 6 жыл бұрын
fans lyon wawaw lolou dafa lèrr
@mansourmbaye8441
@mansourmbaye8441 6 жыл бұрын
fans lyon sa data yay da ngay mar sa bounou nday
@dagoubag5105
@dagoubag5105 6 жыл бұрын
fans lyon 7 doull gane bass bousale fole yowe ak bass
@mouhamadouseck6631
@mouhamadouseck6631 3 жыл бұрын
Moustapha Sy day doul mok guana mèsèrè gnio yèm
@maimounagueye997
@maimounagueye997 3 жыл бұрын
Un peu de respect quel éducation
@lepediambf1337
@lepediambf1337 6 жыл бұрын
Merci častou
@MrNdiaye-ps8lm
@MrNdiaye-ps8lm Ай бұрын
Gaston Yaalah ko ray kén rayouko
@kenyonou9149
@kenyonou9149 6 жыл бұрын
Machalah Gaston wakh nga degue diarajuef moustapha sy limou wakh teguego fene wakhoul degue
@massambasy6918
@massambasy6918 6 жыл бұрын
ken yonou iow denguay kharou rk kokou dei meune nala bale wayei martabame dou balé dei lissi kaname rawoule beute bilay yalla nalla yalla até ak mome
@kenyonou9149
@kenyonou9149 6 жыл бұрын
Massamba Sy rousnala dh gamay wakh martaba khamoul dara day fene rk
@massambasy6918
@massambasy6918 6 жыл бұрын
ken yonou bilay borome dinako fadial bopame inchallah si barké mamame khalifa ababacar sy
@hazishazis2267
@hazishazis2267 6 жыл бұрын
+ken yonou ioe dena.katt sa yeya
@fallbabacar4447
@fallbabacar4447 6 жыл бұрын
Yala na yala ate gnou yaw Gaston Mbengue si martaba Serigne Babacar Sy Balla at me djekh
@kebekhadim9162
@kebekhadim9162 6 жыл бұрын
yalla lako takha wakh
@fallam1010
@fallam1010 4 жыл бұрын
Qui es la après la déclaration de Moustapha Sy sur kara
@morsakho6107
@morsakho6107 6 жыл бұрын
Merci per gastos
🔴Bidew du 06 Août - Théme: L'histoire des Prophétes par Pr Madiama FALL
57:47
The delivery rescued them
00:52
Mamasoboliha
Рет қаралды 10 МЛН
WHY THROW CHIPS IN THE TRASH?🤪
00:18
JULI_PROETO
Рет қаралды 9 МЛН
Cute Barbie Gadget 🥰 #gadgets
01:00
FLIP FLOP Hacks
Рет қаралды 43 МЛН
Révélations de Serigne Moustapha Sy : Aliou Sall refuse de commenter
4:51
La Vie Senegalaise
Рет қаралды 557 М.
Conférence de Serigne Moustapha Sy à Nouakchott - 25 février 2017
1:32:03
wiktivi - Mauritanie
Рет қаралды 19 М.