Merci fadam bilay linga wax moye deug makane waxoull lou lerr thiatou yarakh mo nek si deug 🎉
@mamadougueye99865 ай бұрын
Thiatou Yarakh tu as été trés claire Yalnala Yalla soutoural🙏🙏
@fayealpha22155 ай бұрын
Thiatou yarakh est intelligent nélawoul dhé... xam na limouy wakh.
@salioudia93585 ай бұрын
Legui nan photo contrabi publiéko adoune guisko moulér ❤❤❤❤❤
@GabrielGomes-yo6ie5 ай бұрын
Merci bour deug lá deh 🤝
@cheikhdiop96735 ай бұрын
Même li gnou déf thiatou yarakh beugone nagnko déf balla gaye wayé balla dafa am ay mbokk Aziz Ndiaye mo fay thiowli nilén balla gaye dou beuré ak eumeu séne trois combat yim signé wone diékhna ta ba tay makane désélna balla gaye khaliss bou bari di wax wakhi bénén combat balla foumou moudiou b52 gris boy Niang mou diékh Gaston production ay vrai diler lagne gni bousi Aziz Ndiaye takhawoul wone ni lagnou narona déf balla gaye
@laminethiam15995 ай бұрын
Saway cas yi bokouniou le cas de balla le combat n'était régularisé au CNG ça veut dire que le CNG na pas reconnu ce combat mais le cas de thiattou yarakh le combat est régularisé donc le combat est reconnu au CNG 😮
@laminethiam15995 ай бұрын
Le cas de balla meunonena delo avance bi ndakh agul CNG motakh parfois NGA DEUG niouni mbeur tel delona avance bi NGA balma akh nak bro
@cheikhdiop96735 ай бұрын
@@laminethiam1599 yaw nak daga geuna déf makane ap nafékh combat bougne régularisé woul mou beugone balla gaye beuré ci ba Aziz Ndiaye guéne di kass lolou kou dioup douko khalatt bakoy wakh ba diap datte yaw ligay wax sétlouwoko légui Ama balde danoul zoss ak Gouy gui final mou dane tapha tine mou diékh thiatou yarakh même chose la dafa dane gamou Gueye dane thiatou Yoff mi geuna nakharé dane dane Ndiaye tine dou diékh lolén beug
@laminethiam15995 ай бұрын
@@cheikhdiop9673 kheikh liratal limala expliquer bou bakh dinga kham pourquoi balla et son encadrement avaient raison 😂
@cheikhdiop96735 ай бұрын
@@laminethiam1599 kou diotagoul avance nokoy woutalé datte sa way makane beugoul wone bayi dafa dém ba gnak pékhé ndax Aziz Ndiaye dafa tothi kass yi ni batay makane limou désél balla gaye mo eup limko diokh motakh mou roukh wayé dadone deugeurenté ak gnom bop
@falloufall82325 ай бұрын
Franchement Fadam a parfaitement raison
@MorWade-w7q5 ай бұрын
Thiatou yarakh demal beredji bakhna
@coeur2lion385 ай бұрын
Loutah Mouy beredji té diotoul avance
@falloufall82325 ай бұрын
Bécaye mbaye makane néna ay séquence la sétaane dnc menoul wakh lou leerrr...en tant l'acteur principale warona dieul temps sétane intégralité point de presse bi yeupeu
@cirely32205 ай бұрын
pikine la deuk mais makane vrai domouharam le day utilisè mbeur rek mbeur yi dèm lén signé ak albourah
@salioudia93585 ай бұрын
Rafétéllen kadouyi tayalla takh
@mamadouwade65655 ай бұрын
Sén émission bi amoul bén sens vu que dolen deglo ishhh
@paulngordiop13175 ай бұрын
Bour et son gars laaaa vraiment soff naniou.... On s'écoute
@championBoulan5 ай бұрын
Fadame mii nafekhe de gue la kii mo yakhe Lambeue Sénégal fadame fine nga nak
@mbayendiaye45625 ай бұрын
Yagui toogne dall
@yeuzzndiaye42595 ай бұрын
Makane sou diapone fou deugeur ak liko boy bi wakh yepp dou waxé ni tay prck Bizness manLa daniouy utiliser mbeur yi dilen exploiter en complicité ak qlq ménagère ak qlq journaliste respect ✊ THIATOU-YARAKH merci FADAME2️⃣
@moussatoure84855 ай бұрын
C'est dommage thiatou yarakh yagui yakh dh 😢ay da niou ma wakh li yoyou môme bakhoul
@SerignemodoumbeneDiouf5 ай бұрын
Baye balla ak bour mom bilahi amouugnu fi place beurii nagnou wax trop
@matarlo9535 ай бұрын
Rawatina baye balla mo guene sokhor niepp
@GabrielGomes-yo6ie5 ай бұрын
Merci bour ❤❤😁😁
@GueyeNdioro-xy5je5 ай бұрын
Non fadam 2 teye mom nekhoul ba nekhoul mais linga wax deugue la taye mom anda yaw thiatou yarakh danko bègue diaye dolé 😢de 😢
@FayeMessi5 ай бұрын
Fadam 2 amoul place sì Platon bi
@laminethiare36935 ай бұрын
Bour wakh n'a deug béneu côté sa problème ak lakhate Ndiaye sen yone nekouthi makane cheitani bimouye wakh Kone apo ngako ya Bone tontouwo ko bamou dem nga beuga sonal bour tamit 😅😅😅
Yaw do may nit gni diam guanane bayi khaliss kidi liguey khalliss motakh Mouy beurré
@CASI77975 ай бұрын
Fadam faut écouter
@cheikhdiop96735 ай бұрын
wa di beuré di dane ta dougnela yokal foum am kone loutakh gay dén way makane fayal boy bi ta bayi thiakhane bour mome bilahi dafa geumoul bopam dougouroumane la cng bénn promoteur momouko boy bi bilahi mo mane doudou sané nignouy beuré bokoul doudou day bén bénnal rék ta boy bi khél lay beuré thiatou yarakh dollé danouko
@talibebambasalihousarr10675 ай бұрын
Sa way iow khana khamo louy contrat boude Thiatou Yarakh mokko signer na deme beuré combat jambor bi ah lolou moy deug
@fabregasfamara-cl2km5 ай бұрын
Bour da rouss mongui 😂😂😂😂rek a la fin d lappel Thiatt
@salmonefaye41185 ай бұрын
Fadam deugla wakh
@MamadouDialodialo5 ай бұрын
Un contrat déjà signé faut le respecter c'est tout même si 1 centime
@ibrahimafaye14975 ай бұрын
Boure guéwèle hamoule dara
@AboubacarSadikhDiop5 ай бұрын
Thiatiou Yarakh il faut aller faire du Mma ou King boxing
@ndiayekhalil71565 ай бұрын
Buur gueweul séytané leu
@salmonefaye41185 ай бұрын
Gnoune yarakh lagnou
@faye67185 ай бұрын
Merci tonton bour et baye Balla deug rek ngay wakh fadame moom vraiment nafék la Ndakh bouy wax déye xol Lou nékh nit gni té Soko nékhoul tmt bo nékké si deug sa Dou guiss lolou mé pére békaye moniou togne moom mi takh niou diél sunu temps Di déglou fadame
@gorandiaye76485 ай бұрын
Par ce que limouy wakh mola arrangé buur Moy fenn katt bi limouy wakh khamossi dra mar Kat Tate la
@faye67185 ай бұрын
@@gorandiaye7648 l'âne mo masi arrangé Mane wakhou deug rek topeu mé kouy maar guinawou nit lolou moom la té nguene yarou nakk bour Moun n'a la diour
@cheikhtidianembengue67095 ай бұрын
Yaw katal sa ndeye nékk nitt fadame deugu layy wakh té bour guéweul dafay marr tate Fadam intérêt mbeur yi thi lay dokh nékal ndéy nitt
@faye67185 ай бұрын
@@cheikhtidianembengue6709 saga bi pour l'âne té saga woma déh Ndakh sa yaye Moy sama yay té ioe nafék nga com fadame motakh
@cheikhtidianembengue67095 ай бұрын
@@faye6718 nékal ndéy nitt lala wakh dof nga rék
@albertgomis73145 ай бұрын
Père becaye waro togue ak fadame si plateau
@cheikhbasskeurmassar95485 ай бұрын
Thiatou yarakh la 28 bi beurrë woule de
@HamathGangue5 ай бұрын
Bilahi Sénégal amoull kouyy wakh deugueu bilahi nieuppeu khamne Makan mo am deugueu mais ayy ennemi Makan nio barri
@NdeyeNiang-i4n5 ай бұрын
Khamou dará
@luh_kodak84605 ай бұрын
D’à Guay doul
@FallouSarr-5 ай бұрын
Wakhofi dara ngay waatt
@GabrielGomes-yo6ie5 ай бұрын
Fadam nopy boy
@AmethDieye-yt8ju5 ай бұрын
Mais fadam mo wakh DEUG ❤
@talibebambasalihousarr10675 ай бұрын
Thiatou Yarakh momoul nit gniii iow depuis ba claf dii claf ba leguiii kham guaniii niiii la massa demé niar poule yi moy poule A ak Poule B kouffa diele 1ère dayye Croisé mou nekk Final donc iow Thiatou Yarakh demal gua beuré combat diambor biii Dijon CNG suspendre la Iow Fadam Seytané deug gua ak Doundourou Wa Keur Aziz mais Makan nawlo woula sakh bilahiiii
@Ordinaire955 ай бұрын
Non ça dépend du contrat , lors du claf de 2007 organisé par Gaston lac de guier2 était le premier et zoss le premier dans l'autre groupe,pour un problème de cachet finalement c'est Luc Nicolaï qui a organisé la finale . Il faut toujours négocier et ne rien imposer aux lutteurs
@hametndoye57885 ай бұрын
Fadam est INDISCIPLINÉ
@mamadousarr33715 ай бұрын
Thiatou yarakh wakhal liga man sola léron ne manga dan doudou sané kon do daw demal sétane liga ndieka wakh si doudou sané légui denga niake pekhé motakh nganan légui demay bere niaw gatsa
@ibrahimaniang17345 ай бұрын
Yaw wakho fii darra gni dagnouye ligueye
@ndiougamar22025 ай бұрын
Boy bi Goor leu dou Goor djiguén nékal nit
@PapaThiam-v7k5 ай бұрын
Sénégalais dafa seytané fadame amoule place si plateaux by dfa seytané
@PapeGueye-bm1is5 ай бұрын
Fadam a raison
@coeur2lion385 ай бұрын
Bécay yaw ak bour géwal position bikéne del dou yone thiatou yarah couco déglou hamni limouy wah deg la
@babsbaba195 ай бұрын
Thiatou yarakh il doit pas rentrer dans des histoires comme ça il devrait lutter après il parlera avec. Il est pas encore allé loin il commence à rentrer dans des problèmes c’est pas un bon signe
@mamadougueye99865 ай бұрын
Non je suis pas d'accord mon cher il faut battre du fer pendant qu'il est encore chaud...il faut que ça soit claire avant de lutter.,la plupart des promoteurs c'est des dealers ,ils ne sont là que pour leur propre intérêt. Thiatou Yarakh n'accepte pas qu'on te sacrifie campe sur ta position 🙏
@laminethiam15995 ай бұрын
Le contrat que thiatte a eu cest pas le contrat particulier dey firdé ni promoteur bi beug na sa combat ak diw té diokh nala temp pour garanti la rek 😮ya comprendul
Thiatou yarak xawma iow la xawma sa ménager la, mais daga wara beuré parce que c'est un contrat que vous avez signer bo beuréwoute tamite sa affaire la
@salmonefaye41185 ай бұрын
Deuk
@NdiapouFaye5 ай бұрын
Mais ou est le GNG?
@salmonefaye41185 ай бұрын
Fadam beugnako
@GanaNgom-h6z5 ай бұрын
Mais pardon pour quoi pas ngene deglouwanté débat bi amoul chance si téléspectateurs yii
@khadimmoustaphagueye40585 ай бұрын
Tapet nga doudou sane il est fort
@adamandiaye56225 ай бұрын
Bour weve bi mo dougou😂😂
@mamadougueye99865 ай бұрын
Bilay gueumna lolou
@AliouFaye-ye5ok5 ай бұрын
Tiatt sa wakhdji la gana dègue wakhi mkane amoull arguma , bagnall ba teud thi nadjba ya tèy
@saerfall7015 ай бұрын
Baye balla makane bou tégone contrat bou lérr dou woté sauvé biss bi takhouko diokk contrat bi lou lérr nékou si
@walobrackmbodj8055 ай бұрын
Becaye Mbaye Bayilén Di Faral Borom Khaliss Té Wakh Deug. Des Lutteurs Comme Thiatou Yarakh Combat Deux Millions C'est Pas Normal Arrêter
@ousmanekasse87585 ай бұрын
,😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂bekay bilahi dafay mbalak
@saerfall7015 ай бұрын
Wax dji déh mo geuneu lérr fouf
@oumarsow66255 ай бұрын
Mais pkoi vous n.appellez pas le menager Il est louche il doit réagir .
@aboubacarndiaye7795 ай бұрын
C'est un dialogue de sourd.
@naarbi53605 ай бұрын
Tant que Ecuries bou nekk amoul senn propre managers, thiouw yi dou dakkeu. Managers nekk promoteurs, managers yorr mbeurs you wara dajjé daffay yokk confleluts d intérêts CNG da teullé!
@adamandiaye56225 ай бұрын
Bou nekone si deug douko yokal 😅😅😅promoteur you beug khaliss yi
@vitosy51235 ай бұрын
Ms mano lén di deglou merde way li comme marché bou tass
@NdiapouFaye5 ай бұрын
C pas compris
@babadiop58515 ай бұрын
Nekhoull ba nekhoul mé li FADAM wakh moy deug makne amoull béneu arguments boy bi kham na bou bakh si limou nekk
@doffdouweer36865 ай бұрын
Bour kou sofff la
@AboulBacharSall5 ай бұрын
Fadam niaw ngua rew ngua fouy ngua xamo sa boppou
@youssoudieng80435 ай бұрын
Bour sa tounou ndeye
@Yahouba-oq4jk5 ай бұрын
Pourquoi saga ndéy
@khadimmoustaphagueye40585 ай бұрын
Katal ndeye feulet goordjiguen nga
@FallWaly-c6g5 ай бұрын
Diay dole rek
@SerignemodoumbeneDiouf5 ай бұрын
Baye balla ak bour mom bilahi amouugnu fi place beurii nagnou wax trop