Force à toi Aïda force à vous lan moy ndayou liberé nitt sans causes sénégal mo barii nafekh
@AntaSow-t6rАй бұрын
Bilahi aida deug rek gua wakh ki time aziz et wally ray bou gnaw bigne ko ray gua nék conciene tranquille nane aziz déna ét après justice pour aziz et wally 😭😭
@alhamdoulillah3153Ай бұрын
Yalna yallah wére képe kou bok si assassinat Aziz akh Wally
@lixman771Ай бұрын
Courage à la famille des victimes 😒ce pays c’est une catastrophe 😡😡
@PipomzАй бұрын
Des pv qui circulent partout. La sœur de Aziz a raison Cette nabou leye devrait être en détention préventive
@cocottendiaye1944Ай бұрын
*Justice🔴🔴🔴 pour Aziz et Wally* *Li daffa métiii walakhi😭😭😭*
@AminataBaldé-f3dАй бұрын
Justice pour aziz et waly 😢
@adamandiaye4314Ай бұрын
Machalla Aida courage na yone dèfe liguièyame gnawena metina loleeeeee Aziz Ba et Boubacar Cano yallana yalla yeureulenes té kharlenenes alediana amineeeeeeee
@Thiatebeuguefallou9596Ай бұрын
on réclame justice pour Aziz et Waly
@sokhnafatimasarrsagna2595Ай бұрын
😢Dafa jote nak
@fatoutouray7447Ай бұрын
Justice pour Aziz Dabala n Wally Gano
@Elhadji2187Ай бұрын
Force à vous la famille et tout les participants❤️
@maremeseck9540Ай бұрын
Yalnaléne yalla diapaler ba lepp ler inchallah 🙏
@Thiatebeuguefallou9596Ай бұрын
on réclame justice justice pour Aziz Dabala et Waly
@fatimenahaye-wn7ekАй бұрын
Bilaye walaye machala rék ❤️❤️🤲🤲🤲
@MamichoubbАй бұрын
Ndeysane métina way ô yalla na yalla léral yeup si Barker seydina Mouhamed
@diaynabacisse6090Ай бұрын
Bilay boulène bayi mou ceed Bakane dafa fort Bilay décès bi dafma meti trop
@fatoutouray7447Ай бұрын
Justice for Maman Aicha Ndong
@SehGayeАй бұрын
Sénégal Coumba am ndaye AK Coumba amoule ndaye
@nioukfall7869Ай бұрын
Mensonges manipulations tricherie c macky etses juges qui sont là pour saboter le travail de Sonko
@aron6054Ай бұрын
Pourtant Tonss waxone nako Nabou Léye dou yag si kasso bi ndax juge yi djiguéne rek lagne beug ak xaliss
@Thiatebeuguefallou9596Ай бұрын
yakar gui gnou amone si gnome ba fallen li lahi wa sabrila li moy sène premier acte acte bolenegnou wara wonè litax gnou tek lène fi ngiir yalla justice pour Aziz et Waly 😭😭😭
@HelenePouye-fk5emАй бұрын
Elle a raison de connaître la VÉRITÉ. Perdre un ETRE CHER comme ça, non , non
@bintasarr2940Ай бұрын
Vraiment justice pour Aziz
@afro3827Ай бұрын
Pape ndiaye nitt kou bonn la 😢
@fatoutouray7447Ай бұрын
Justice for Aziz and Wally
@fatoutouray7447Ай бұрын
Justice pour Maman Aicha
@AbyDiallo-hv5wqАй бұрын
Justice pour Azize, Daba et Wawa
@AstouSy-f8iАй бұрын
Merci Aïda bien dit deume rayla dialé la bobou ba tay eske yayam si bopam nieuwou fa wowou léne kone loumou fay def niawena baparé
@AissatouFaye-k8cАй бұрын
Boumou. Gneuwe na talal sa khathie 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@CouraSeck-r9jАй бұрын
JUSTICE POUR AZIZ DABALLA
@pivoine481Ай бұрын
Aïda dè sa you wakhè si dèwou Aziz ak Wally mi douma meune teuyè samay rangogne. Massa, Yalla naniou khipé Aldiana Firdawssi.
@MamenarNdaoАй бұрын
Nila amoul bayi na lep leer
@worembenggu2950Ай бұрын
Wa ana avocat coumba gawlo seck
@nioukfall7869Ай бұрын
Voilà où macky a amener la justice. Le nouveau régime à vraiment du travail travail à faire
@ndeyebouyakoita4469Ай бұрын
justice pour Aziz et Wally 😭😭😭😭😭
@khoudj841Ай бұрын
Nabou leye d'où nitkou bakhe .guelou criminel , criminelle lay donne . justice pour Aziz et waly 😢
@habydiarra2741Ай бұрын
C'est vraiment bizarre ton frère habite à Dakar et vous ne connaissez pas où il habite. Vous êtes des inconnus pour Azize, si l'inconnu prend la place des parents et proches, on devrait revoir nos relations.
@ROKHAYABA-j2dАй бұрын
Vérité absolue
@coumbafaye9319Ай бұрын
PAPE NDIAYE AK CHEIKH GADIAGA DEH DOTOUNIOU MESSEU WAKH SI AFFAIRE BI. CHEIKH GADIAGA MOM KOU NIAK KERSA LA.
@dakarcolobabe9221Ай бұрын
Vraiment bilay dmco moudié yeuram
@loudoulaktalibesafouma3429Ай бұрын
nabou léye da ngéne ko wara réye😢😢
@KhadySarr-bo9gjАй бұрын
😭😭😭😭😭😭🤔
@MaimounaDieng-fz5hrАй бұрын
DEUG la dé jeune homme bou done domou ministre cône day guaw lol
@nioukfall7869Ай бұрын
CE SONT LES JUGES QUI SONT CORROMPUS SONKO L' AVEZ DIT
@MagatteFall-up7qoАй бұрын
juge bou maag bi moy bour yalla
@f.b.s7667Ай бұрын
Aida da moudié beuri wakh😏😏😏😏😏😏
@aissatousow2022Ай бұрын
Koumou done sa mbok nga beuri wakhhh tchiiimmmmm
@fatoucoulibaly5595Ай бұрын
C’est parceque Khama likometi
@KhadySene-i1yАй бұрын
Aïda mo wara bayi Nabou Leye sou féké mo raye non merdre waye yawe danguaye lathie ba légui. Nabou Leye dou sa make il faut croire en toi. Nabou leye e complice de meutre.
@insa3207Ай бұрын
Vraiment
@ibrahimaba9685Ай бұрын
Ki berina wakhe
@moussagueye1291Ай бұрын
They sénègal doynawar
@user-nd2yx2qg7wАй бұрын
Nabou amna yanou wadiourr deuk ak ndayam moukoy yanal chaque jour
@Malicksindidi1988Ай бұрын
Xaana dou Aïda mii mofii waxoon ni jusqu'à preuve du contraire geumoul ni NABOU mo raay Aziz lgui Yoon bayiiko niou teupp dii taal taali rek dossier bi yombul dh ndankk rek
@AichaDia-t1dАй бұрын
Dagnio rayoul sa mag mo takh ngaye wakh loolou
@Malicksindidi1988Ай бұрын
@AichaDia-t1d lanla wax ngay doul Aïda si bopam mo wax liima bind ay illettré ngén xamolén ni justice Di dokhé"le temps de la justice est une vieille dame qui marche lentement"
@Elhadji2187Ай бұрын
Et après alors ieie tu parles de ay dianguolen alors yay con bi
@AbdouNdiaye-or2biАй бұрын
😭😭😭😭
@nabousylla1314Ай бұрын
Babacar Touré nena Nabou leye dagnouko togne té dinassi def live ,nit bou nek AK nimouy dounde emotion AK choc
@AichaDia-t1dАй бұрын
Bayilen faral nabou ley liko teyé dou nen
@MouhamadoulmoustaphaFofanaАй бұрын
Nafek bahoul
@Elhadji2187Ай бұрын
Nafekk bahoul
@AstouSy-f8iАй бұрын
Je me demande pourquoi niou beugue sétale nabou leye mani lépeu mome la bouniou fonto il faut gua nek domérame deugue pour satal ko ki vrai vampire la
@ramandiaye3726Ай бұрын
Surtout c pas encore jugé c tellement bizarre ohhh
@AstouSy-f8iАй бұрын
@ bilakhi Rama cest anormal li dafa yombou torop iiiiii
@user-nd2yx2qg7wАй бұрын
Soutoul len aziz
@AichaDia-t1dАй бұрын
Wakhofi touss justice pour aziz ak waly
@chiekh.samsum4870Ай бұрын
Li migimay beuga soof
@boubacarndao921Ай бұрын
Yaw mome yagui beugue soff
@maremendoye160Ай бұрын
No bilay elle doit se taire
@AichaDia-t1dАй бұрын
Dagnio rayoul sen mag mo takh😢yeena bon ki limou wakh warnako kheb ndak deret defa for
@AmyWague-uk7ooАй бұрын
Dagne la rayaloul rek
@aissatasow6421Ай бұрын
@@maremendoye160bougnou réyoone sa frère doo wakhé nii. Il faut être empathique. Lilène dal meuneu dal kounék ci gnoune
@Elhadji2187Ай бұрын
Mo tepiii leufeul ndey soudé aida daléni derrenger diguen Kate s'en ndeyy parck chak jour diguen ko guiss