Tu a dit la verité frére touss courage, Sénegalais Dani soop kou ragal dofi tékki yala rek mofi nek
@famadiop20232 жыл бұрын
Modou Mbaye yalna nga doundeu TÉ mou and ak werr Yalna and ak khéweul you yatou Yalna la YALLA saam , aar leu , mousseul leu thi lep louy loré thi barké SERIGNE SALIOU MBACKÉ ❤
@ndeyetoutyfall13222 жыл бұрын
Ndaysan Modou Mbaye nonou lako beugue nak yalla nala borom bi samal bopam
@maguettedeme35483 жыл бұрын
Machalla Modou que Dieu te protège longue vie a toi depuis le Mali
@ibrahimandiaye71393 жыл бұрын
Dieummi père Becaye fees ci dieumeu dji
@neymar10diallo922 жыл бұрын
Billahi 😀🤣❤️💯🙏🙏
@biranecamara67963 жыл бұрын
Diádieuf modou mbaye kou baax nga machalla deugou rék mon am solo bonne continuation
@ibnoukhayriismaelba6183 жыл бұрын
Boy Médina Yi, ay nandité laniou. Médina sang-sei. Supporter Nannn crème Seetannn combat niubi.
@diengmatar54403 жыл бұрын
Lamb dji sou direct yi dello fomou nekone boy yi amoul pass stade dem si tellé yi dina wagni lou bari si violence ak agression
@mansourdieng20003 жыл бұрын
Wakh Ngua Deug
@mamadoudieye22933 жыл бұрын
Bien dit frère
@cheikhbambaseye96053 жыл бұрын
Tu a raison bro
@cheikhdiabaye60993 жыл бұрын
Linga wakh.deugla
@Blackpower1093 жыл бұрын
machallah, yalla bouléne thiat dougou,mouth ak mouthlé💓💓💓💓💓💓💓💓💖💖💖💖💖💖💖💖💖
@ndeyedioufmouserignefallou67203 жыл бұрын
Machalla wadiour kendou mom Lamine chapeau à toi aussi
machallah modou ak lamine yeupe goudou lene fane werr ak werle khewal ak soutoureu inchallah bakh rek ame solo
@babacarba8313 жыл бұрын
Vraiment ca se vois que vous êtes du côté de balla gaye ca se vois direct
@damembengue18943 жыл бұрын
Lutte Tv meilleur site internet of Sénégal 🇸🇳 Lamine Seck boucar ndour omar Diop Et leur boss Beuz pro diamou ci yenn 🙏💪
@tidianekane93512 жыл бұрын
un gars que j'ai côtoyé de peu vraiment un vrai baye fall foko fekk togn cafe reee limou ameu seddo ak niit yi yalla na sa diam yagg
@abdoufatahndiaye26862 жыл бұрын
Non vraiment Modou mbaye ndanane pure nga li nga analyses si BG2 vs B52 comme danga guissone lambe ji👏👏👏👏 laff tiate bro vraiment yalla boula tiatt topou
@adamajoop45872 жыл бұрын
Mashalla lép Nice nah Modou ✊
@diopfallou76383 жыл бұрын
Éducation moy lépp té am ngako machallah ci kaw ci kanam rk inchallah
@badarakane20843 жыл бұрын
mérci way yénwa lutte tv ♥️♥️♥️👍
@daoudambow83483 жыл бұрын
Waye Modou Mbaye kham na niou lép niémé wo tarkinda yi ba legui abou ndiassé dou goul TOP 5 bantamba té mo gueune raféte daane bou niou ko daane si année bi yép
@Ahmad-gw7yg3 жыл бұрын
Bravo modou continue sur cette lancée boul tégui sa tank figa nék bahna
@ablayembaye84053 жыл бұрын
Machallah Modou Mbaye ablaye ❤💯
@papediop64023 жыл бұрын
Tu a raison papa sow mo yakh lamb dji ak gora sok tapé lagne
@bayfallyomboul5133 жыл бұрын
Très bien Modou mbaye merci Lamine
@babacarndiayefrommbour44213 жыл бұрын
baravo les 2 lamine seck modou mbaye yallna yalla samm
@abymboup83593 жыл бұрын
Khaala ak Massine Demba ak Guor Waly Waldiodio mithi Ndiakher Beytir Madjiguene Mbor ,Aly Madjigyene Mbor ak Seune Seck Madjiguene Mbor Khéwé yayi Ndieke Ndiaye Ndoguo Penda mithi Bélèlane Ndonguo Beye bayi Mada, Mada bayi Omar Dia Beye, Olar Dia bayi fatou Thiaw Beye Fatou Thiaw yayi Mbaya
@cheikhdiabaye60993 жыл бұрын
Éy.mbaye
@unbiased2163 жыл бұрын
Machalla modou ligueye bi nice neu❤
@joliediopcoiffure90243 жыл бұрын
Diarr Diarr dafa méti torop mais dina bakh guem sa bopou molay takha yégue finga diem 😭😭❤❤yalla naniou yalla défal diam ak soutoura ak khéwal si barké saydina Mohamed 🤲🤲❤❤
@fakhadiagne52883 жыл бұрын
Nite kou deugou nga modou mbaye..continuél si lancé bobou rek
@modouwade74943 жыл бұрын
Machallah amna solo Modou mbaye diam si yaw
@ndiaboutadiouf79123 жыл бұрын
Nice modou mbaye verite absolue
@paolosarr29213 жыл бұрын
Modou mbaye ndafeck bou mag na
@yacinediop11723 жыл бұрын
Machallah yalna la yalla arr mayla soutoura
@damembengue18943 жыл бұрын
Lutte Tv for everything Lamine Seck good job vraiment Amal diamou rk
@babacarmbaye84782 жыл бұрын
machalakh mbaye dieiry ngonei degou rek ndatte ngua deuk do ragal sounouy mame si tolou kharei lanou dieikhei amou niou ay seuk sa kaw sa kaname
@amysylla58443 жыл бұрын
Yonou deugue dé bossi néké boule ragal wéte ma cha ALLAH modou
Modou Mbaye aime bien la vérité gni deuk si Banlieue bi dagno wara kholate sén bopou........mais violence dokhaloul lamb
@maktarngom34273 жыл бұрын
Lamine tu deviendras journaliste lutte du Sénégal malako wakh
@ndeyemourseye48803 жыл бұрын
Manchallla yallla n’a la yalla sam
@paolosarr29213 жыл бұрын
Le grand ndafeck de l'année modou mbaye leu
@modoumbaye15473 жыл бұрын
Mon Tom 🙏🏼🙏🏼✊✊
@issadiagne93423 жыл бұрын
Modou mbaye yow patrimoine national gua. Yalha nala yalha same, vous bocou de fans en Argentine💖 Lamine bonne continuantion
@ibrahimaniang42653 жыл бұрын
Merci lamin Seke
@diopibou25643 жыл бұрын
Jadieuf Modou mbaye bonne continuation
@ibrahimaniang42653 жыл бұрын
Merci si Modou Mbaye
@sombelsene68943 жыл бұрын
Machalla moudou diéreudiéuf wayè
@horssyba88173 жыл бұрын
Machallah modou mbaye
@moussandiaye72933 жыл бұрын
Dangua faralone siteu ndah guewuel gui
@momosy60833 жыл бұрын
Machaallah mon frère
@ibrahimadiakhate21722 жыл бұрын
Force à toi 👉 ❤
@nogasarr70343 жыл бұрын
Machalla 💕💕💕💕💕💕
@Hiuhysk3 жыл бұрын
MachAllah ❤️❤️❤️
@saloumdieng9713 жыл бұрын
Machallah Modou kéne dou yaw boule ragal dara
@karimdiop3092 жыл бұрын
Tabarakallah machallla 🥰
@diarradiene4275 Жыл бұрын
Lamine jambaar la yarounga nitou kesee yalnaga egg ni yonnn
@ndiaboutadiouf79123 жыл бұрын
Verite absolue modou mbaye
@ibrahimaniang42653 жыл бұрын
Modou mbaye merci
@basssene55623 жыл бұрын
Yow papa sow ngua yape yape yabo ay balla gaye
@ballafaye24903 жыл бұрын
Modou mbaye masala nek si rek domou pikin dou ragal
@ibrahimaseck51113 жыл бұрын
Yalla nama yalla mousseul ci musicien yi. Barki yonent bi
@nianemoubayeniass97103 жыл бұрын
Aminé ya rabbi
@mansourdieng20003 жыл бұрын
Lou Takh Ngua Wakh Lolou
@yannickmatarsbdn64013 жыл бұрын
Numéro modou mbaye la soxla ngire yalla
@dioplemaire25463 жыл бұрын
Modou Mbaye vrai baye fall nga bilahi kou bakh nga
@ablayembardiouf38253 жыл бұрын
Machallah
@yannickmatarsbdn64013 жыл бұрын
Nguir yalla gnanal léne modou mbaye mou yague fi lol si barkep MAME BOROME DAROU NOREYNI
@bambalo33983 жыл бұрын
Moodu mbaye vraiment daga nafekh papa sow daniouko toogne tay iow laniou xeep ndax sa waxx
@dieydidoucoure8583 жыл бұрын
Modou Mbaye wakho deugueu
@amethndiaye99833 жыл бұрын
Nice n'a lamine et modou machalla
@bocarba27813 жыл бұрын
Mais modou mbaye fouye nga rew nga sérieux. Papa sow dou sa morom, yaw tu parles violemment, la dernière fois tu disais que vous étiez nombreux et prêt à vous battre contre les supporter khame nga ni sa bay dou def lolou
@kingomzo59323 жыл бұрын
Dou nitou deug tapha gaye tahawone neu nei modolo daniou key scorter ama danioukey scorter bi incident bi amé warone neu wah tapha gaye liga wahone loutah defoleine ko en face nieup m defouko bro gni daniou hypocrite duniou wahantei deugg t kouleine wah deug niou oubi sene gattt di tontu
@mamadoundiaye52303 жыл бұрын
Non frère vraiment l'image avait fait le tour du Sénégal Sénégal mo démé nonou si modou mbaye n'avais pas montré cette vidéo défa narone hawa louche
@elhadjiaminediop64173 жыл бұрын
Móodu deful dara waay ax
@momobeugdeugrealiterek74683 жыл бұрын
Boy daga nafekh Papa Sow ci Zone nam lanekk moye Mbeur bi wara beure wara guene sarakhaam donc aap batteur waroukoko tere dagneko sagnaa def BG2 boy Modou Mbaye domou Grand Dakar dou ragaal mane Moukhamed malakoye wakh bou Papa Sow tognone nieup daal ci kawaam meussoule Yakk Lambji
@mamadoufall91112 жыл бұрын
C pas vrais c la faute de papa Sow ahh Modou mbaye a raison ahh ragale yalla waye bro
@residenceera11213 жыл бұрын
Pape Sow n'a rien à dire
@goradiagne38863 жыл бұрын
Waho dueg papa sow waroul guéné saraham ape tegue kate téré con lolou dou dueg
@babacarndiayefrommbour44213 жыл бұрын
mais sangnsé ngian d machalah
@ladepechetv69982 жыл бұрын
Qui trouve que Modou Mbaye à des traits avec Akon?
@papynd79213 жыл бұрын
Bien dit frère tu as bien parlé
@abdoulahadsarr38273 жыл бұрын
Merci modou
@joliediopcoiffure90243 жыл бұрын
Amine ❤❤❤😭😭😭😭😭😭😭
@assietoundoye36243 жыл бұрын
Modou Mbaye dawal thiow fils sa wakh Yi ay wakhou far farlo lay nirol.
@neymar10diallo922 жыл бұрын
😃🤣❤️
@serigneabdthiamass9943 жыл бұрын
Lamin yag modou guène dou yèn
@bongacamara69983 жыл бұрын
Mashalla !!!!!
@kaboumbaye22573 жыл бұрын
machalla mbaye mouno raguale ma samba coumba ndama Moy sa mame
@alidiouf14393 жыл бұрын
Toi aussi tu avais deux versions différentes l'intervalle de deux jours. Mardi tu disais Djily était fautif Mercredi tu disais que Papa Sow était fautif. Alors le quel de tes propos dois-je croire ?
@mamadoufall91112 жыл бұрын
Que tou les deux sont vrai (djily et papa Sow)
@ebounjie12333 жыл бұрын
Ma Shah Allah modou mbye We love you
@momondiaye39303 жыл бұрын
30mi lay comase di wakha si papa sow
@cheikhalimdiop29383 жыл бұрын
Dieureudieuf
@Bbf157233 жыл бұрын
Merci beaucoup frère
@charliethiam67493 жыл бұрын
Parli bn frate🔥🔥☝️☝️☝️
@ballagaye2koumounekhouleto5463 жыл бұрын
Gaston dafa sokhor bilai
@ndakarudialdiop12063 жыл бұрын
Nice neu modou
@ousmanendiaye52563 жыл бұрын
Papa dadone sarakhé dji
@joliediopcoiffure90243 жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@morthiaw48943 жыл бұрын
Tapha rik 💪💪
@bintadiop37933 жыл бұрын
😘😘😘❤
@neymar10diallo922 жыл бұрын
😃❤️💋💋💯 salut 🙋♂️ 🙏🙏
@papejuleslebarhamien87863 жыл бұрын
Deug rekay deug frère lénéne loudoul deug ayy fénela...finak laniouy khamé ndakh wa CNG daniouy far wala deug moléne fi tadie...c'est papa sow qui a tord donc corrigés le et laissé djily de continuer avec siteu...c'est tout
@birahimog63243 жыл бұрын
🙏🏾💪🏾
@seydinaaliouneboromjasiji32002 жыл бұрын
Areen Bi Yatou na Da Nguey Bey Sa Waar Sa Morom Bey Waram
@duduseiye5073 жыл бұрын
Yow Baye fall nga
@sambegorasambe39693 жыл бұрын
Modou wakh yi refete na mai lamb meme cng dagnouy def violence