En tout ka hawa diouboul coumba diouboul. Na wadiour yi yar dom yi ta bayi dilen neubeul you bone yi. Soutoura nak amna wayé na wadiour yi kholat ndiabot gui
@sowamina17255 жыл бұрын
Doyna waar Lamine ziarnala
@nittoudeugrek96845 жыл бұрын
C vrai des ay mak youdoul wakh deug bolessi di neubeul seni dom a doynawar
@idrissadiallo59445 жыл бұрын
C sa la question
@laminegaye74295 жыл бұрын
@@sowamina1725 déllo ziar bou bakh
@simonganemnlt5 жыл бұрын
Vraiment
@mariemegadio7745 жыл бұрын
Parfois les parents ne sont même pas au courant des bêtises de leurs enfants
@adjagueye29515 жыл бұрын
Marieme gadio je suis d’accord avec toi
@fatousane41655 жыл бұрын
Marieme Gadio vous avez parfaitement raison !
@athiaice89695 жыл бұрын
Deugueladé 👍👍
@abybathily82215 жыл бұрын
Marieme gadio je suis d'accord avec vous
@cirabocar79685 жыл бұрын
Marieme gadio wallahi waxatiko
@mamyniassy13455 жыл бұрын
Qui lit les messages en regardant la vidéo déposée vos like
@lamekhoise5 жыл бұрын
Mane des franchement ; yayou coumbeu Limou wakh ; nekhoul wedddi ! Wediloule domam ! Wediwoul ni Hawa d’adone fanane keureum aussi . Legui pour régler problem bi ? Puisque le chef du quartier a entendu les propos malsains de HAWA . Comme quoi L’autre était sa femme . ; d’emlen interroger le chef du quartier ; solen beugueeee kham vérité bi . Parents yi naniou bayiii di wedill gouneeeh yi ! Nioussi beurrri double casquette 🧢 laniou am . Salam Merci de passer voir la chaîne . À bientôt
@khadijawane32335 жыл бұрын
F A M I L Y - S E N - 2 2 1 mom la gueune gueum
@toulayeceesay22135 жыл бұрын
Lou am te ler nga wakh
@fatimasoumare84075 жыл бұрын
Ya coumbeu mo gueuna explicite que yayou hawa mi
@michellemendy73835 жыл бұрын
F A M I L Y - S E N - 2 2 1
@khadidiatouseck6785 жыл бұрын
Amna fait bo hamni yayou Coumba wahoussi ndakh batay wediwoul ni gneuw n'a si keur hawa
@fallkhoudia24795 жыл бұрын
Li yeup so léne régléwone tok séne watou wadiour li yeup dousi djiguéne daguaye yam guatal saye tanke wagni kharito bou beuré mouye coumba di hawa
@toutoularandiaye21165 жыл бұрын
Goor tamit da wara tok thi pégoum bayam gnou diang senni téré wala séni hassaïde wahtane wahi adina ak likay safara. C vice-versa
@abybathily82215 жыл бұрын
Fall Khoudia ya plus d'éducation dans notre pays
@sophiem24115 жыл бұрын
Wakh deug
@abdoufall82765 жыл бұрын
Cette histoire montre l irresponsabilité et la fuite de responsabilité des parents d aujourd'hui. Comment une fille vient passer 15 jours ou plus ds ta maison pour une simple amitié. Une fille que vous ne connaissez ni d Adam ni d eve. Et cette générosité de Hawa toroodo n est pas gratuite en mon sens. Chère maman vous ne maîtrisez pas votre fille. C une ange à la maison et démon au dehors. Vu leur relation comme l explique cette dame, un problème d argent ne doit pas créer des histoires entre eux. Ce problème est trop louche.
@aminadiongue74855 жыл бұрын
Coumba dh yayam limu meune daifnako
@fatoukinefall38775 жыл бұрын
Abdou Fall wa lolou tmite cas la deh koulay diapalé noum lay fayéko banguénisiy khoulo🤷🏽♀️
@abdoufall82765 жыл бұрын
@@fatoukinefall3877 mbir mi dafa leer, parce que Hawa ne a lesbienne la, dou nangou ndawsi delou ak dieukeurem parce que dafa donne deff ci moom alal. Même Bou problème khaliss âme s'en digeunte d'où nonou laka wara fayeko. Wakh dji dal moy Hawa lesbienne la, kheyna yayam khamoussi dara, mais loulou beuri n'a fi, dingua diour sa doom tee d'où yoor sa djiko.
@abdoufall82765 жыл бұрын
@@fatoukinefall3877 moy wone ni diapale bii dafa rakh😂😂
@dabalagueye11175 жыл бұрын
Elle n'est pas un démon hawa c'est quelqu'un de bien elle n'a jamais fait de mal et elle n'est pas une lesbienne arrêter de juger feko léne ko mouy wané ni lesbienne la bayii léne jugé
@zfsamt5255 жыл бұрын
Nga balema khamalo sa dome dara. Au moins pour la version de l'autre dame, votre fille a dit au chef de quartier que Coumba est sa femme. Le voisinage est témoin de leur altercation. Pourquoi autant de liberté, ta fille fréquente des gens et tu n'as pas bougé d'un yota pour savoir où ils habitent. C'est triste. Naniou YALLAH samal Ndiabote gui
@fatousane41655 жыл бұрын
Amine
@fatimagaye96295 жыл бұрын
Niom niare nieup kéne dioubou si séne yaye yagui wkh rk ds fx les prn ne son mm po au courant des bétise de leurs enfants
@zfsamt5255 жыл бұрын
@@fatimagaye9629 bilahi té mane lima méti moy ils ont gardé une et laisser l'autre. Au lieu de retenir la violation de domicile. Il fallait les corriger sévèrement toutes les deux. Des mères irresponsables
@masseckseck85585 жыл бұрын
Lolou rék mo Diara gnane doyena ware
@bagneinjustice66205 жыл бұрын
Mère yayou Coumba limou wakh mogeuneu yénou maana dé 😄dougnou ay dof nak
@leylalati83605 жыл бұрын
C'est vrai t'as raison wakhoufi dara
@alimaseye15425 жыл бұрын
Yaye day protégé domame
@ndiayefatou86305 жыл бұрын
Deded mère bi da innocente elle n connait po lou bonne mo tah meunouko sah fokk
@bagneinjustice66205 жыл бұрын
@@leylalati8360 pour te dire apres interview bi nou def ak yayou coumba bignou dematé dagne ka fekeu mou febar be wakhoul tension bi monté
@bagneinjustice66205 жыл бұрын
@@alimaseye1542 lolou bakhoul nak
@ndiayefatou86305 жыл бұрын
Layy layy lala. Euy wayy heleyii. S'en mama yi bah. Innocente. Yarou. Euyy wayy li lane Lani. SoubhanAllah qu Allah nous pardonne tous et nous met sur le droit chemin.
@lamindarboe37155 жыл бұрын
Yaw loy melni kouy wayane ni
@fatimaeileen90674 жыл бұрын
@@lamindarboe3715 rayngama😂😂😂
@kessobelnou24904 жыл бұрын
Lamin Darboe 😂😂😂
@tajoutajou95905 жыл бұрын
Ndeyssane j'ai pitié des mamans elles n'ont rien compris
@Diidy_Awa5 жыл бұрын
Bilaaay amel naniou sen ndeyi ak
@Yajogueye225 жыл бұрын
Naysan dom loum bone bone domme la sou niep nei dete gani waw wa nagnou yala soutoural rk t samal niou sougnouy wadiour
@lareine21685 жыл бұрын
Amin nek parents métina torop yalla nayalla same djabot gui tek lé n si yone bou bakh
@petitefleurdesiles39575 жыл бұрын
Coumba a un enfant qui a 11 ans et hawa a 20 🤔🤔🤔 posez vous les questions qui est l'irresponsable dans l'histoire
@tabarandiaye83145 жыл бұрын
Coumba sa mère son ex marie ensuite les parents de Hawa sil arrive quelques choses à l'enfant pendant son séjour chez hawa 🤔🤔🤔🤔
@sokhnaaichambaye92305 жыл бұрын
Lou yemé
@khadysall57955 жыл бұрын
11ans avec 3 gos
@famachudiop26785 жыл бұрын
Hawa eupeulna 20ans hamnako wax lene deugg yalla moléne time
touré khadi khalé yi capable négne en MM temps coupable moy touléne khaléyi ndakh moune négne la roussal té bobo doo léne mouna sigui khole kéne doyna war
@ayshamohamed71745 жыл бұрын
Wa Hawa ak Coumba xana nio mom Sénégal? Gnii nak mom nagn niou. Mayleine niou diam . Entre yeine leu rek
@idycharo22195 жыл бұрын
Pour wakh deug mane je crois a la version de l'autre comm dem na ci chef de Quartier ba Awa ni Coumba est sa femme
@justicepourtous61685 жыл бұрын
😂😂😂 wakh nga deugue dé
@khadizaseck79915 жыл бұрын
Ah moi aussi pareil
@mamyfallyad44275 жыл бұрын
Moi aussi je crois à la mère de Coumba
@rararara1645 жыл бұрын
en plus el na po protegé sa fille nena defna loum meun pr weugni doom dji mai degualouko donc lotre est plus cohérente
@fatoubarhamthiellosene18065 жыл бұрын
Moi aussi pareille kuku wakham mo geuneu deugu sah
@aitapaye60085 жыл бұрын
Mane dale mére bi wakhame bi louche na li bénéne mére bi wakhe mo gueuna yénou mana !!!!bilaye laye warouna sénégal lane mofi dougou jeunesse bi niou bari yakou naniou ndakhe khalisse yalla naniou yalla doli soutoura 🙏🙏
@neymar11faye905 жыл бұрын
Mere amal soutoura domou diambour sou wéroul lossiy wakh si télé souniouko fasséi loussouy sa yone amal soutoura mère bobou wakhaloula dara lou niaw Mère d famille ngua. kone lane mo totie ardoise yii yar lén sén dom yii niogui def lénéne sén guinaw tei yeuguolen ko mère soyons sérieux ko khamoul beu parei diko sédél ay dom you dof tei yanéi khamoko enplus diko ebergei komem naniou kholalt yar yii tamit wasalam🙏yala na jame yague🤲
@mamyfallyad44275 жыл бұрын
youssou faye bilahi wakh nga deugueu
@torodo.ferrari5 жыл бұрын
Bilakh adounaa bi dafa teuradii
@seynaboutoure28685 жыл бұрын
Mere bi wakhou fii dara mouye giunge si serigne babacar di wakh sama Keur gui kéne douko fi dèfé Coumba ak Awa bounou bokè fanane thi bène nèkke ba beute sètt lagnou faye dèff Manoka kham ndakh doko fèkè boule nafékh
@khadizaseck79915 жыл бұрын
Bilay seynabou Touré guemouma dara si limou waah
@yandemoudamediopthiongane13225 жыл бұрын
Vraiment mère bi wakhou fi dara lou lere
@Amy-vg3md5 жыл бұрын
Wayé melna ni keur gui gni fay fanane beuri nagn... Kheuyna lolo takh mouni menoul am keureum ndakh intimité diafé nafa...
@zahrafall99195 жыл бұрын
Elle est pas cohérent On ne parle pas d’argent mère !! Tous se que vous avez fait pour eux na rien à voir avec la situation !! Si ta fille réclamer de l’argent pourquoi aller dire le chef de quartier que Coumba ces sa femme !! 🙄🙄
@mamidiuuf27365 жыл бұрын
Ce que certains ne comprend pas moy deuk bi legui lesbienne kassei la!!guiss na fi lesbienne bou am 4 enfants,3filles et 1 garçon ngay wakh ay amone na dieukeur !!mère ioe khamo sa dom sakh ....boul mimeul ken nak so beuguei nopalou🙏🏽
@mariedimitriendiaye51865 жыл бұрын
Elles se fréquente mais sougnou weto khamoulo lougnouy deff
@binetadiouf74785 жыл бұрын
Wayyy hawa di lesbiennes deugg guénn koyy faral Sénégal lii mntax d'où avancé
@houleydia10455 жыл бұрын
No khamèni hawa lesbienne la ? Dagua fèkè wala dagua guisss ? Manoul mo geune
@binetadiouf74785 жыл бұрын
Xana deukoul wonn gounass yaw nopil
@houleydia10455 жыл бұрын
@@binetadiouf7478 mdrrrr khamna yèna bokone fanane si bèn nèkkk gounass tmt Lèr nama daguaka sokharè rk Manoulèn mo gueune ahhhhh
@binetadiouf74785 жыл бұрын
Fall sma xoll bii da sett withi yaniouma yalla soxoré niitt té doumko mousseuh dff nakk
@houleydia10455 жыл бұрын
@@binetadiouf7478 Lolou dh bakhna Hawa mom mm sou nèkè lolou ioe warguaka soutoural tè ioe fèkè wo donc boul sèddè
@aminafall69375 жыл бұрын
Hawa ak coumba dall sen mbir louche na trop. Coumba di nek keur gnom hawa, hawa tamit pareil.
En plus c'est des bébés, facile à manipuler dans ce monde pouri. il faut que les parents prennent leur devant...bien éduquer et éveiller les enfants de ce monde pourit..
@nanyfall18465 жыл бұрын
Sa wakh rafetna yalna ya Allah rafettal lépp dollignou soutoura té tékk gnou si yonou l islam,wa magal bi kagn la sakh...
@gouyartvdieng50055 жыл бұрын
talata bii di nieuw dou dellou sè dinaa fèck niouneck si 18 safar
@nanyfall18465 жыл бұрын
Baba dieng 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 yalnako fekké diam
@abybathily82215 жыл бұрын
Nany Fall amine yarabi
@dembaba15 жыл бұрын
Yalla naniou yalla dimbali, khiir niou si Lou bakh.
@nanyfall18465 жыл бұрын
Mamadou Ba Amiiiine way
@fatoukinefall38775 жыл бұрын
Esk dou nguén interviewer Chef de Quartier bi tmite soit mou deugueul mbamou wédi li yayou Coumba né Hawa moni Coumba diabaram la🤷🏽♀️ g rianh compris moah
@ibrahimafaye68805 жыл бұрын
Slt
@LiLi-dv2dd5 жыл бұрын
On a tous 2 visages Kane lafi ssa yaye khamal lép?👀? Yaye bauy déf ga ssa waréf
@sophiem24115 жыл бұрын
Le plus logique c'est que les deux femmes devraient voir là où elles ont échoué et reprendre leurs enfants à main au lieu d'essayer de rejeter la faute sur l'autre.
@diopndeyendoumbe61584 жыл бұрын
Bilay walay
@aron60545 жыл бұрын
Waxe dji rafétena yalla naléne yalla diapalé nguéne dioubo adouna bi dafa diéx ba paré , na lép raféte dara diaroufi yéne yi
Ndeysane kharit amadoul antado khéwii naa fii reuye bii dolou djiguéne mo sokhor diiga guis sa boromou djiguéne dii liguéye diap diambouram dii wéral yayeum nga nékk sii Lou boone nga beugue borom maane ma outtaloul xarite 🙏🙏
@mariamasadioba91035 жыл бұрын
Sen keur khana amoul kilifa ba nitt difa gnieuw difa nekk des mois
@mary182035 жыл бұрын
Voila
@aminaabdoul9585 жыл бұрын
Wakh deug yalla. Keur dal day am loi
@jositoelmalito5 жыл бұрын
Keur yi amnaniou kilifa dè mais " KHALISS" la toudou. Khalé bousi YORR sen wa keur tu deviens ROI ou REINE loula nekh ngay deff gnepou khamko DEUG BALLE BI. YALLAH nagnou si YALLAH mouseul
@Toxique-girl5 жыл бұрын
Bonne question
@fatoubarhamthiellosene18065 жыл бұрын
Diaar na ladjie dé clifa da bakh ci keur
@ebrimasaho43055 жыл бұрын
Yaye boye as wakh reffetna trop machallah
@fatoukinediop17895 жыл бұрын
C est vrai dé dangay yar si sa bir keur mais sougnou guener yor bénéne djiko Yalla nagnou Yalla taxawou si sougnou dom yi aminnne
@pendadiallo78464 жыл бұрын
D2zoppn. 🎵🎧🎧
@serignesaliousene11645 жыл бұрын
daysane j'ai pitié aux mamans , elles n'ont rien compris
@mamidieng96675 жыл бұрын
Je croix pa a cet dame la mère de coumba est plus véridique
@babstv45435 жыл бұрын
Wakho fi dara lou laire. Ay lesbiennes wala? En tout dans le PV de la police elles ont reconnu faire des pratiques de lesbianisme
@maimounafall21945 жыл бұрын
Papay Hawa waroul accepté domou dianbour sirtou djiguéne di fanane sa kheur ay wér
Kilifeu barétoul niary wérr ci ko khamoul fumou deuk
@BTSmyisuniverse5 жыл бұрын
Doy na war
@nittoudeugrek96845 жыл бұрын
Bakhna dal lii doynawar
@ramadiouf38135 жыл бұрын
Nourou chikory doyna warr dhh wakhouma Daraa Ana Djiguène ak djiguène nane dagua ma nèkh nèkh bay dème keureum diffa fanane sakh lounè nga Dieund ko
@Amy-vg3md5 жыл бұрын
Réalité de la banlieue aussi...
@senemarie9815 жыл бұрын
Yayou coumba dè limou wakh deug doukou wessou. Hawa c’est une traînée
@madamemadame33805 жыл бұрын
Wakh sou dofé nopou yikoy dégue meuna wér. Yayou Coumba sétaloul domam takkal sa dom tamite dé. Yeuf yi kou khôl mère bi khamnani nakari nako trop.
@latdiordiop25575 жыл бұрын
Vraiment mer bi wakham dawna yaram
@misslady28585 жыл бұрын
Mer bi nianoul dara il a dit na hawa bayyi sama diabote Pff problem bi yeup am guen si walleu
@Corailpro5 жыл бұрын
Hawa mom à 20 ans limouy liguey ba di diapale famille leum. Niom niari yeup nio sik. Couture mom manoula may alal bobou yeup
@sambadiallo46085 жыл бұрын
La maman de hawa torodo ne sais pas comment parler on l'a demandé l'histoire et elle raconte du n'importe quoi yaw mère amo soutoura dara inutile de parler situation de la famille de coumba(qu'elles n'ont rien elle a une enfant malade , elle n'avait pas de mouton pour la tabask)i tt ça on t'a pas poser ces genres de questions ok il faut savoir comment parler
@myaba40495 жыл бұрын
Mettrez vous à sa place elle protège da fille .ces soit disant journalistes arrêter de relayer le problème des gens sur les reseaux
@bibinn23585 жыл бұрын
mya Ba vraiment je ne comprends pas cette soi-disant presse. Ils ne relaient que des ragots et jettent les gens en pâture. C’est méchant ça!
@teningsarr814 жыл бұрын
Franchement 🤷♂️
@bulldozer31315 жыл бұрын
Il faut surveiller vos filles .
@famadiankha11005 жыл бұрын
Neub bou beuri mo tass rew bi yar len sen dome bayi neup neupeul bi.niom niar nieup ken jouboussi
@petitefleurdesiles39575 жыл бұрын
Avant de comprendre comment les gens sont méchants l'ensemble des commentaires condamnent hawa si toute elle est lesbienne coumba est pire quelle car elle est bisexuelle de vrais phénomène
@yayeawagueye62855 жыл бұрын
Mère yéne yi dou sisse jaboot dañkoy sègue ba kène douko infiltrer. Leep ñak kilifa moko lale
@Mamadou-Fall5 жыл бұрын
Mais pourquoi doolenn demm interview coumba puisque elle est libre en ce moment!!!?!???
@oumylaye68795 жыл бұрын
Moma diakhal
@binetteba42685 жыл бұрын
Yaye boye sa wakh dji diouboul boul fi diema nane dagueye tour leudeume population
@Nabypalo00005 жыл бұрын
Mère sa dôme lesbienne bu mak la Bane intérêt la amm diko dieundal tout ça
@ramadiouf38135 жыл бұрын
Usman Palo moma diakhall dhh thi djiguène ak djiguène bo sètè yayou coumba limou wakh mo gueuneu yianou mana fouff ana djiguène nane moromou djiguène name nane ko daguama nèkh
@aminafall85765 жыл бұрын
Moma diakhal
@mariemendy61635 жыл бұрын
doye na waar mére bi dé kham na lép
@nogayendiaye96875 жыл бұрын
Moma diakhale man
@houleydia10455 жыл бұрын
@@ramadiouf3813 Ioe do am ay kharite yo khamni danioulay nane dagualène nèkh ? Des mensonges os6 peuvent être logique ne vous filler pas aux paroles Fèkè wo fèkèwouma donc manousiii mo geune
@mamadouniang33594 жыл бұрын
Ya trop de lesbian au senegal 🇸🇳 e gordjigenn
@abdoulayroumiii44735 жыл бұрын
S'ils vou plaît je ne comprends pas wolof, et y a pas de sous titre en français. Qu'est-ce qui se passe ?
@tiguizlovely55025 жыл бұрын
Mère bi neina boudone môme leuh dou yakk sein deir donc si je comprends bien même bou yeigone ni dômame lesbiennes leuh dakoy soutoural douko weir ndeiysane avec ça niouye wotei dioulitte thiey yallah😢😢
@awagassama56805 жыл бұрын
Nith dafay wax deugue alalou adouna djaroul lie ta fille a assumé k lesbienne leu stp les parents bayi léne neupeu neupeul sen dôme yi
@wourywane33585 жыл бұрын
Ohh ndeysann Mère bou bakh sakh hawa aussi pareil khamnalenn boubakh sakh
@mabintoudanso97265 жыл бұрын
Woury Wane ya wakh li gni sen problème bi doy na warr
@wourywane33585 жыл бұрын
@@mabintoudanso9726 bilay mane ak hawa nio bokonn class primaire nitt gni bouniou nieuk deglou première version mère de comba rek naniou teyy khamna mère de hawa boubakh sakh
@abdoufall82765 жыл бұрын
Woury wane problème bi dou yayou Hawa, mais Hawa moo djouboul. Meun nga diour sa doom tee bokoulen djiko.
@salimatadrame5675 жыл бұрын
Iow dal mére say kadou raféte na machallah mais tamite boul takal yayou Coumba ndax kokou wakhoul lou ay loumou féké rek la wax tei mom leu guiss tei niit sax bo guissé sa dom niit diko fréquenté comportement wam nékhoul am gua Droit wax ak sa dom tei yayou Coumba lolou la deff am na si Droit entouka sa dom lesbienne leu tei khamoko tei entre ses deux la am na loussi louche ndax niom niar rek nio wara khol sen deguénté ak sen borom wax deug gui lep fégne une bonne fois pour toutes
@mariamandaw75265 жыл бұрын
Mais histoire biii louche na hein Je me demande comment se fait-il que Hawa Di dimbali Coumba diko defal Lou nekk ba un bn jour mouni dakaa yorel khaaliss ba dici dioté ak moom Et puis puisk couturière leu et k dakay diappalé diko May tissu donc prkw pas mou niawal ko ba paré, offet y a tant de trucs incohérants dans cette histoire
@ndiemendiaye53695 жыл бұрын
Doyna war dal
@kenefaye1865 жыл бұрын
Gualathie bii geune thii gualathii moy moytou
@jositoelmalito5 жыл бұрын
Keur yi amnaniou kilifa dè mais " KHALISS" la toudou. Khalé bousi YORR sen wa keur tu deviens ROI ou REINE loula nekh ngay deff gnepou khamko DEUG BALLE BI. YALLAH nagnou si YALLAH mouseul
@naturehumaine12195 жыл бұрын
Yayi Coumba sa version est mi claire. Chef de quartier waroon na leeral accusation bi. Hawa di defaal Coumba lou neek. Naka la leen xaliss wara bolé 🤔 va lou melni joudou ci. Li leen jotalé nioom niaar reek ko maan leraal té Yalla takh. Te Coumba war na xol ci liko Hawa defaal ci lou bakh té leraal ba xam mo deef ou pas. Affaire lesbianisme moom chef de quartier rek mo maan confirmer ba xam Hawa moko wax ni Coumba jabaraam la.
@nittoudeugrek96845 жыл бұрын
Tu as raison dai gnome gnar gneup ay lesbienne lagnou kene bakhoussi khaliss bolewoulene elles sortais ensemble
@maguettediaw92715 жыл бұрын
Kham nagne lèpp
@Lopios-g6l5 жыл бұрын
Boul faténii aye halé you touti lagne vintaines d,années lagne âme. Le reste ya Le rekk moo kham.
@reezachou3055 жыл бұрын
Comme tt ls mères elle n fait que protégé sa fille finalement on ne sait qui dit vrai seule Dieu sait m li yayou comba wakh hum wakh dégueu yallah nékhoul wédi
@seynabfatalecisse91415 жыл бұрын
Dara léroula ni Hawa khamoul dara qui gname khorome bou yague ? Sa faute moye bigua nago di fatte domou diambour té khamo aye wadiourame gua déve erreur bou mak kéne waroul héberge niite té khamo aye parent wome
@mariediaw6055 жыл бұрын
non mane jai pas compris comment est ce qu'on peut laissè sa fille passè la nuit chez des gents que lon ne connait pas,,,mane daal ma diomi wadiour yi nagniou hamnè ndiabote samm la bissou yowmalhi yam dina gnioula lathiè no samè say ndiabote
@dielekanoute18775 жыл бұрын
la maman d coumba avait trs peur c pourcla k ell é partie directement o police si c'était tw maman tallais fér la mm chose dissons ns la vérité votre fille é lesbienne c ki é fait é fait
@mamysarr70155 жыл бұрын
😌😌😌😌yeuf yangui beug diakhasso di moway warou mane
@alimaseye15425 жыл бұрын
Version yayou coumba loloumay version originale bi
@khadimmbodji11145 жыл бұрын
Ms limah diakhall moyy l faite k yayouh coumba dih profité si histoire bih dih gnaneu ndimbeulll tmt en tout cas c louche Khawmah nk vérité bi foumouh feiteih
@papediop94045 жыл бұрын
Awa da dokhe si néwti dolè coumba diko utilisé. YAYE BOY lèral ngua leup a travers tes paroles.
@fatoumatabarry13165 жыл бұрын
Li dal hawmaci dara, wayé la famille de Hawa mem wah lagnuy wah melni gnou def séne complot....légui nak chef de quartier na wah lep lér
@ndeyendiaye49985 жыл бұрын
Nioko wakhantè
@fatoumatabarry13165 жыл бұрын
@@ndeyendiaye4998 doyna ware d
@sophiegueye73475 жыл бұрын
mere bi nena coumba day yeuw thi keurgui difi def 2 semaine ak hawa kon boul jugé
@bibasarr48214 жыл бұрын
Ndeysan khaliss saytane la
@assydia69755 жыл бұрын
Métina trop billahi ndakh doom si khol la sakh wayé boumou takh nga wakh Lou amoul sa doom djouboul
@zouwairiatouba48865 жыл бұрын
Wollakhi
@Kingalexswag4 жыл бұрын
Senegal eska ay joulite lanou
@yayefall77655 жыл бұрын
Maman nga balma kou doynawar nga linga nankhou sa keur une mère de famille responsable douco Def lep hawa la
@lesastucesdefabee74585 жыл бұрын
Wa mais la soeur di k xamoul yayou coumba mère bi néna Yayou coumba niewnafa?hana hawa mom mbaxam da eup ba loumou am joxko coumba?c louche
@mirandagaby37204 жыл бұрын
Sa fille aime une autre femme... Bon, mais qu'est ce qu'elle y peut cette maman ? Ça ne fait pas l'affaire de la morale, mais c'est comme ça, c'est tout.
@ramatoulayediafate57395 жыл бұрын
Way mère accepter ko xalé daniou done beuggeunté aye lessbienne laniou panne naniou kilifa torop
@senisene3042 жыл бұрын
😭😭😭
@fatimathiam55235 жыл бұрын
Wakhdji yeup moy Kharito dafa diara khol keine douko forcé. GATT tank dale khamnani bakhna si domou adama
@kantomeniang90705 жыл бұрын
Li mom foumou am iow khamo parents Coumba diko teyel domam 2mois diko ba paré Dina bayi sa keur man dal les parents d'aujourd'hui mom dagnouy topp si li neh s'en Domi dilen neubeul en plus motah lossi dis mougn fou gnaw rekk
@maeramegaye59075 жыл бұрын
mane dal warouna sonal séneu wadiour yi rèk nekhnaléne diamouléne séni Aÿ wadiour mo gueneu diléne ték fitneu ték léné gathiép adouna li niawna déléne bayi khél djaboot gui tèy séytou andadoyi lou âme solo la wa salam
@maremegueye35175 жыл бұрын
Kouy nek lesbienne diko wakh say parents bayilen wédil sen dom yi khalé you jiguén yangi dokhane khalé you jiguén yi dek bangi tocc bakhna dal
@demefalldiop23615 жыл бұрын
Jiguéne gnii nga khamni douniou may dara goor wakhoumala moromou jiguénam ci gratuité...yén yénay doul ndéémm
@naboudione5535 жыл бұрын
Ana jiguéne ak fanane keur yamour no amouma fite bi sakh bilahi
@fatimagaye96295 жыл бұрын
Niom niare nieup kéne dioubou si Mouy hwa Di Coumba kéne dioubou si
@mariamadrame33715 жыл бұрын
Vraiment sa devient compliqué 🙄yalla na god léral lep
@sophiethiam70825 жыл бұрын
Mariama Dramé Walahi c vraiment complikeee yallah rekh amm
@fatimagueye47715 жыл бұрын
En tout cas sène affaire yi doye na ware yeine nou Coumba di nèkè sène keur pendant des mois démo lène sène keur défo lène dara dè yayou Coumba nèna Tabaski bi sène voisin yi gnon lène maye yapou tè Coumba noumou mana nékè di ande ak yayam di diaye dieune ba parè di nèk sène keur difa fanane lèpou dall entre Hawa ak Coumba gnon ko khame tè yène mboki Hawa yi boulène khase yayou Coumba ndakh yalla rk mon khame wasalam
@timandiaye85715 жыл бұрын
Yayou coumba limou wakh mo gueuneu cohérent que yayou Hawa limou wakh
@rokhayathioye62565 жыл бұрын
Li yombe n’a 🤔🤔 pour yenne senni dôme dagnou len di Wax lignouye def
@truckistikhama82275 жыл бұрын
Mais gni nioum nièp ay toucouleur lan! Ak toucouleur yi ninou baakhè!
@tymahott23885 жыл бұрын
Wawa les toucouleur son très bon
@aminatathioune70695 жыл бұрын
Mère nak nga Baalma mais teranga yi manoul gnaak ndax Mr et Mme ngay am fofou Nama yalla baal
@ndoyemalimaram65075 жыл бұрын
Mane dal sama khalat bou gateu bou diap di ame coumba ak hawa yeup laniou wara diap ndakh afèrr bi louche na trop
@fatoufall74555 жыл бұрын
xolal ma mère bi di wax ay xar,ay kessou cannette you Hawa dieundeul coumba. Mère bi bougoul wax sax thi situation bi
@fatoukinediop96195 жыл бұрын
Elles sont toutes deux fautives mais la mére de coumba hésite trop en parlant et les pierres qu’on nous a montré et les trous sur le toits c’est pas possible on a montré des pierres énormes et un petit trou de rien du tout.... comment une fille de 20ans peut manipuler une femme mariée avec 3enfants tamit soyons logiques. Ak lou mounti khew dal niome niar nieup nioko def voilà...
@fallpenda68085 жыл бұрын
Ani chef de quartier bi
@Fafashuu5 жыл бұрын
Yaye yi sonou nagne ndeysane
@sophiedrame87845 жыл бұрын
Mér bi nafékhla
@ndeyefall82444 жыл бұрын
Djeul sa khalis.di finance sa moromou djigue Come yawe yaye dji Daf coye gueneu takhal adouna bi tolou na fo khamni gnari khalé you ndawe mouye gor mouye djiguene boulene bayi gnouye wete mouk wakhou mala aye magoum djeum doyena war
@julielarissa95765 жыл бұрын
une histoire très trop louche , les parents peuvent cacher leurs magouilles de leurs enfants ou sont pas au courant , venir chez sa pine 1mois semaine , fête elle donne etc ... chelou 👭 , meilleures amies ou plus dieu seul sait