Kou gueum ni Ahmed Cissé gueumoul limouy wakh rk ❤❤❤❤
@AïdaDiome-q1k16 күн бұрын
Ki kay faux type la 😂
@bigpaby15 күн бұрын
😂😂
@TallaDiop-zf7pv18 күн бұрын
Soxnasy tëyel saborom kërgi bu baax yalla naleen yalla jappule Amiin
@momotouray17218 күн бұрын
Amine franchement bravo Maa Shaa ALLAH mon frére je suis fier de toi bravo 🎈🎉🍾🎊 surtout à votre Mari je suis fier de vous voilà
@fatoukane331818 күн бұрын
😅, A1a 😊😅😅😅😅😅😊
@moussapayemane416718 күн бұрын
Heureux menage,yalnaléne yalla défal diam ak salam ak ndiabote diou barké,seuy amoul âge té mo guéne ndialo
@khadydiop273417 күн бұрын
Bly ❤
@djibediallo268617 күн бұрын
Ndiabote 😅😅
@FatouSamb-e5y17 күн бұрын
@@djibediallo2686 Yalla meuna lounè
@IbrahimakhalilouNdiaye-k1u17 күн бұрын
C'est vrai que l'amour n'a pas d'âge ❤❤❤❤❤ Yala na seuybi barkél ci barkél seydina mouhamed Salla laahou halaa mouhamed ❤❤❤ Joyeux heureux pour les deux
@maodogamer14 күн бұрын
Ouaie ouaie l"amour n"a pas d'âge mais yaw demal taki mère
@MimiMimi-vm5oe18 күн бұрын
Ousseynou ak mère bi yeup wiri wiri nagn ba tontou wouniou ci nane la aborder mère bi tout simplement parce que mère bi moko dokhane mo diriger lepp c'est tout car khalé bou tolni ki dou guiss moromou yayam ak noumou meuneti mell diko khole beutou mbeuguél ta fékoul femme bi oubilko bounte baparé. Ousseynou est un innocent que la dame utilise et dirige
@khayanarr860717 күн бұрын
mimi xamoumala mais kou beuri pékhé ngua. Beuri péxé wéssouwoul nétali sa gueint morom. li yako féké ba meun ko nétali? xalé you djiguein yi di guiss sén moromou mame wala wala papa am thifofel si mom nak? c'est juste qu'au sénégal on a pas l'habitude de voir ça
C Amour entre Serigne AK tabile c mission espiritual.femme sage , homme sage on verra avec le temps 😂❤
@doyendiouf624018 күн бұрын
C'est vrai que l'amour n'a pas d'âge mais ousseynou et jeune et innocent on le voit à travers son visage
@adjib.3818 күн бұрын
C un bébé
@LEAMINE18 күн бұрын
Khaleyou djigéen yi koulen dokhane gnou kongeu leu 😂kay
@fodiart62818 күн бұрын
Mais il y ́a des vieux de 70 ans qui se marie avec des filles de 19 ans et même moins
@rouguikebe998417 күн бұрын
@@LEAMINEvraiment 😂
@CoumbaNdiaye-p6v13 күн бұрын
On ne peut pas prouver l'innocence d'une personne à travers son visage mais on ne sais pas comment il est😊
@couritad439818 күн бұрын
Je t'encourage, j'attendais ta version tou le monde avait parler sauf toi. Tu as tes raisons,
@lixewgalsentv18 күн бұрын
Bilay sénégalais mo sokhor
@momotouray17218 күн бұрын
Enfin je vois un couple model et adorable
@fall-solutionss.m.f681818 күн бұрын
Yalnaniou yalla mousseul si nittt Kouy nélaw les yeux ouvert 😢
@maremeseck954018 күн бұрын
Ndeysane yalla moy bolé ay nite 🙏mais ousseynou boul abandoner sa famille goorgoorloul diapalaléne 🙏
@bassiroundiaye391318 күн бұрын
Lolou mére bi moko thi mana diapalé Di wakh tane AK mboki boy bi diléne khamalné Lou yalla dogale la Di dalale séneu khél Di andeu ak môme Di séti mére bi
Soyez heureux, l'amour ne connait pas d'âge. Les jaloux vont maigrir l'essentiel est que vous vous aimez et vous êtes légaux devant Dieu point❤
@MaimounaDieng-o4j17 күн бұрын
❤❤❤❤👍👍👍👍
@demndao889718 күн бұрын
Cette union est legale mais pourquoi certains y voient negatif.Vivez heureux cher COUPLE
@fatouyayunabibumambabacars437317 күн бұрын
Vraiment
@MamoudFoune-oz9re17 күн бұрын
Sa nidiaye fassé diabarame yow diarbate bi islame maynala nga tak sa ex youmpagne
@Jean-FrancoisSenghor-lq4rr18 күн бұрын
Hamet Cissé tu et le meilleur pour ton émission ❤❤❤❤❤
@mouninandiaye791718 күн бұрын
Ousseynou a avoué que ce n'est pas la première fois qu'il courtise une femme plus âgée que lui. Je condamnais la femme au départ à cause des parents du garçon et surtout de son fils qui a le même âge que son mari. Mais comme Ousseynou n'est pas à sa première expérience avec une femme plus âgée, à mon avis il n'a pas été manigancé par la dame. Na ci nieupe mandou la guiss
@tendancebmn157318 күн бұрын
Ousseynou dé d’où wakh deugue Day féne rék.
@sympathisante1718 күн бұрын
Si c’est le cas dafa tela yakk bopam
@maman249318 күн бұрын
Amna gno khamné mak moy choix.... et si c'était le cas de ousseynou ...mandoulen ci mbeuguel
@MimiMimi-vm5oe18 күн бұрын
Ousseynou mi day tekk khél rek déjà nangouwoul expliquer dara lou lére ci nane lako abordé ndakh lepp mère bi moko manigancer, sinon lou khalé beug kouko mak tamite dou wessou quelques années maximum 10ans mais pas koula mate yaye ak loumou tarou tarou...Lolou rek la meuneu tontou pour tour nite yi leundeum
@mimisy126918 күн бұрын
@@MimiMimi-vm5oedeug rek nga wakh mèrr bi moko dokhane
@diamouyallahtv436318 күн бұрын
Ousseynou sagalna koulou jeune fiii thi rewoumm Sénégal, toute les jaloux vont mégrire, se cadeaux ces pour vous le couple Mbingue 🎉🎉 a vous deux seulement , ay waay fann laay amé lou mélni
@mamegamoudiop974318 күн бұрын
Ousseynou yalna borombi diappalé
@LayNyang18 күн бұрын
Yalla na sey bi barke ❤❤❤❤
@mbayecisse-u5f18 күн бұрын
Amine ❤
@fatousene692418 күн бұрын
Amine ya rabi
@khadijasagna645818 күн бұрын
Amine ya rabi🥰
@aminatagomez847618 күн бұрын
Amin
@abdourahmanesindidi181818 күн бұрын
Amen
@SaiTunkara18 күн бұрын
Mashallah so great may Allah give you happy marriage and long life too
@adamandiayekasse599018 күн бұрын
Mon cœur bii bimako dégué touti ma youkhou danou ganguiri😂 tothie sama téléphone
@AstouSy-f8i18 күн бұрын
Barki yalla mane dé saguam sama khol bi wadoul rek alkhamdoulilah ki vrai domérame la take domou diambour sans consentement famillam cheuttttt
@adamandiayekasse599018 күн бұрын
@ Bilahi ça fait mal au cœur
@rouguikebe998417 күн бұрын
Bon khatarayou 😂
@boyniang31617 күн бұрын
Mane deh dama réé ba 😭😭
@adamandiayekasse599017 күн бұрын
@ 🤣🤣🤣ya de quoi d
@sophiawright98668 күн бұрын
❤fière de vous Madame C’est pas le vieux sénégalais qui on le droit de courir derrière les petites jeunes
@rokyatoutoure61018 күн бұрын
Yalla nako yalla délo si wétou yayam té mou woute moromame sa yaye bou déwé dingua kham ni tate diaroule yéne yii
@FantaDieme-u4n15 күн бұрын
Ousseynou sois béni avec notre mama kel soit heureuse ya rien d mal c l'amour ki compte
@PapeFaye-d4s17 күн бұрын
Yalna lén yalla diappalé set rék mo worr mo geune di weur di dialo ak diabarou diambour yii
@AwaBa-ub6eo18 күн бұрын
Bilay ahmed Cissè day mbalak ni di len ranguanrti téh khamou gnouko🤭😂😂
@MimiMimi-vm5oe18 күн бұрын
Lolou moma diakhal ils n'ont rien compris, surtout la dame di wakh wakhi rafféte 😂😂😂
Tare amoufi motakh vidéos yeup dakoy filtre fi nak moy naturel ak séne réseau bou bone amouniou sakh WiFi 😂😂
@marambacke101618 күн бұрын
Yene khane d'âge mer 😅😅😅
@Pineapple300918 күн бұрын
Wa😂 mère bi deh elle a l’air de vivre dans un autre monde. Hamed khalifa di yokk diko ranguanti rek.
@binetandiaye310818 күн бұрын
❤❤❤❤ machallah yallah na seybi barkel
@hawabarham7518 күн бұрын
Seuy yallah koy takk thia arraass, kou guem lolou rek yeeineu détail yi dossi dougou...Yallah toudone seuy bi allah kulli haal dafay am... Bayilen ay hastei teih lidieunti sen bopou, fi kou neik amga loula doy, nitt seuy na ak kimou tolol âge teih moussoul am baneikh... Yalna yallah barkeil seuy bi ya rabbi❤❤
@SadioThiam-q5j18 күн бұрын
Mounir mon cœur kay😂😂😂
@Ramapoulo18 күн бұрын
Mon cœur bi raynama way😂😂😂😂😂
@SofietouSall16 күн бұрын
😂
@AdamaDiaite-in3gk18 күн бұрын
Je ne suis pas contre ce mariage svp pensez à la Maman je demande à la femme de faire cette démarche de bien les consolider je suis une maman comme elle qu elle. essaye de. se mettre à la place de la maman du garçon heureux ménage ❤
@AichaDia-t1d18 күн бұрын
Gniepou loolou molen metti yaye kenna douko takali ak domam
@Organization22118 күн бұрын
Voilà t'as tout dit
@mariemely329018 күн бұрын
@@AdamaDiaite-in3gk pendant diop delol domou diambour dji yayam ..yow ak sa kaname gou reuy gui ak sa bakane bou melni bou la vache 🐮 qui rit beug gor rek motak nga Def lou niaw Li yow amoulo roussou ngaye. Manne bima la set lo ak sa perruque you reuy yi ngaye tek si sa bopp bi la khawa khalate que danga nek si dara vilaine que tu es ak sa visage bou reuy bi HONTE A TOI NYMPHOMANE DE MERDE
@rouguikebe998417 күн бұрын
C ça seulement le problème
@Khadija-y4d12 күн бұрын
Bilakhi Ousaynou damako fan❤
@cheikhdiakhate71618 күн бұрын
Machallah yalna seybi barkel 😂😂😂😂
@MimiMimi-vm5oe18 күн бұрын
Nieup niouy wakh dara nékouci da fekk Ousseynou dou séne rakk dou séne dome. Kéne banioul diabar diou mak dieukeur yen a en pagaille mais moromou yaye tekci abandonné sa famille c'est grave
@mamy404918 күн бұрын
Bilay wahatiko
@AstouSy-f8i18 күн бұрын
Merci beaucoup je pense la même chose que toi li c’est vilain sim elle m’énerve ak kanamam bi melni dakandé
@mouhamedsoumare471218 күн бұрын
@@AstouSy-f8i😂😂😂😂
@AstouSy-f8i18 күн бұрын
@ Moukha ki mérénako torop ousseynou mi
@awacamara22918 күн бұрын
Dagua nane moromou mamame kaye😢 li adouna moyé wadia touki maye wakh ki nane dionguama mineurs
@MactarKa-m1n18 күн бұрын
Machallah Mabelle Cherie ❤❤🎉🎉🎉🎉
@bourydiop121918 күн бұрын
Yallah na sey bi barkel si barké Seydina mouhamed psl 🙏🙏
@matarmbaye495518 күн бұрын
Bilaye aisatou kou oyofe la mashalla Kontanna siyawe ❤
@MouhamedCamara-xw2pw18 күн бұрын
vraiment contente ci yén machallah amelén diame rék
@AliCisse-ei6pd18 күн бұрын
Yalla na seuy bi barkél merci cheikh améde Cissé 🥰🥰🥰🥰
@ousseynouba47517 күн бұрын
Heureux ménage frr 🥰
@maidieng833218 күн бұрын
Salam ! bayilen mère bi , l'amour n'a pas d'âge. Regardez Macron & Brigitte. Félicitations ! Bayilen nite yi gnou dounda sen life.❤❤❤❤❤
@salamatabadji388818 күн бұрын
L'essentiel dioko respects totale bouko ko considère khalé considère ko sa kilifa
@serignembay885618 күн бұрын
Defarale sadiabare bame mele ni viyane ❤❤❤🎉
@baba.moudytaher51758 күн бұрын
Donc je confirme cette mariage et très valable je suis ici en Mauritanie
@yayefall829018 күн бұрын
Séne affaires yoyou naguene ci guénné serigne babacar
@SaliouToure-jt4mg18 күн бұрын
Yaw rek mom serigne babacar
@taphandiaye961718 күн бұрын
mais seuy bi dagane na déh yaye fall😂🤣
@asssarr293818 күн бұрын
machalla téylén bou bakh yalla dou nit mandou si sey bi
@antagueye844718 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂
@diayoussou882318 күн бұрын
Yaw ya môm serign Babacar?
@biranecamara679618 күн бұрын
Adja bi daffa geum boppam nak 😂😂 ❤
@Cherifa0518 күн бұрын
Trop key néna ak taar bi 😂
@veroniquenatack739218 күн бұрын
*Wouyyy😂😂😂😂😂😂*
@biranecamara679618 күн бұрын
@@veroniquenatack7392 no damako beugue pour môme mo dakheu si adouna bi 😁
@biranecamara679618 күн бұрын
@@Cherifa05 lolou Ray nama 😁😁
@Mamefatoufall435118 күн бұрын
Thia tarrrr balaaa😂
@WareNdiaye-hk1wd18 күн бұрын
LI DINA TAH HALÉYI DOTOU NIOU RESPECTÉ MAG
@MaraThiam-s1e17 күн бұрын
Beugueunte guenn je suis daccord mais demalle ga waxtane ake sa famille moye prioriter
Je suis Sénégalais et je trouve qu'il y a pas de polémique à amener ici laisser la dame tranquille je vis en France il y a beaucoup de Sénégalais qui sont ici qui sort avec des vieilles femmes donc arrête de faire du polémique pour rien bon ménage madame
@naboushadiop729718 күн бұрын
Mon cœur bi dinama ray 😂
@omarjueye17 күн бұрын
Je ne vois vraiment pas pourquoi cette femme se justifie je ne la comprends plus car je croyais que c'était une femme avec beaucoup de classe
@rokyatoutoure61018 күн бұрын
Ki da beug lou yombou dafay daw responsabilité néna mère doula sonale ki amoule diom
@Habiba-v9k2g18 күн бұрын
C’est vrai kii kou niakk diome la beugue lou yomb imbécile la
@cheikhoundiaye-n7v18 күн бұрын
Roky dem lenn rekk.. Boy yi si magg yi la niou dieum... Kom yenn gonnê yi amokenn ambition té danguenn rew.. 😅
@rouguikebe998417 күн бұрын
@@cheikhoundiaye-n7v😂😂😂khaléyi dinagn lamb dé😂
@baba.moudytaher51758 күн бұрын
Moi même j'ai 30ans mais.ma femme cet une marocaine elle a 47ans nous sommes tranquille machalah
@AliouDiallo-wv2sp18 күн бұрын
Boy weur jeune bou wayadi ba niewé ci gosse teyel Je t'en veux vraiment Demal liguey soutenir sa famille
@mortadacisse899218 күн бұрын
Bly 😂
@mariemely329018 күн бұрын
Aliou diallo yow rek ya wak fi deug gnenene gni tontou gnom ak aissatou pendant diop gno yem ay nymphomane leu niou comme mome .dème ligueye dimbali yayam mo.ko war waye dommage si vieille bi laye langamou pour tounde qui d'où massa tegui dara pour dimbali qui ko diour kou ko khôl sak khamne kou niak diom ak kilufa la un vrai ramassis
@OusmaneSeydi-q8j18 күн бұрын
Hana seuy bi decoy téré liguey ?
@alia2617818 күн бұрын
Yenne guènne lène si linguène né ki limou def la yala santané kou guisse ko beugue takk ko mo gueune sèn tiakhane yi mom au moins nékoufi di tiagatou aka ndialo en plus molèn wakh topatowoul sèn wa keur
@rouguikebe998417 күн бұрын
Pourtant seuy bi téréwouko liguéy dé
@fatoundoye217317 күн бұрын
Wawaw machallah mo coeur rèk ❤❤❤❤❤
@rosesall980117 күн бұрын
Mère mineur jongoma😂😂😂
@cheikhdiouf459418 күн бұрын
Heureux ménage incha Allah Que Dieu veille sur vous amine
@AmadoulatyrBizzy18 күн бұрын
Boy bi riyeul la gor la ! ❤Mai nay YALLA tel ok❤
@maodosalll606818 күн бұрын
Yalla na seye bi barkey ❤❤❤ begeeee
@maman249318 күн бұрын
Heureux ménage ❤❤❤
@SarraDione15 күн бұрын
Yalna sey bi barcké inchallah Rabi allah mouhamed sallahou allhi wasalame ❤️
@SokhnaSarr-d2v18 күн бұрын
Yalla na seyebi barkel❤
@KaraJieu-p5p18 күн бұрын
Ousseynou du courage, yaw moome laakhe ngua ngueureumou sougnou serigne bou baakh bii,cheikh akhmed cissé,sey bi day barkail inchaalaah
@amadoumakhtarsene555518 күн бұрын
Wayadimane deug Moy bro bii😂
@iboucarter128315 күн бұрын
J'ai beaucoup de choses en tête, appuyez deux fois sur la note vocale pour tout entendre ! ▶︎•|၊|။||||။၊|။|||။|||။ 10:23
@petitjaraaf800318 күн бұрын
Mane dafa am juste question bima beugeu posé question senegalais yi On dis que nous somme a 90% de musulmans té gnoune nénagnou sunna Mohamed lanouy roy, té degna sunu prophète geun dji mindef lika sokhnam maguéwone barina lol, legui lane motah warouno nangou seuy bi soude geum nagn yalla ak yonente Mane dama diapeuni kepou kou opposewou si seuy bi rek wediga sunna ya rassoulilahi
@FulaniGirLll18 күн бұрын
Merci beaucoup 👏🏾👏🏾👏🏾ĺa réponse que je cherchais Lo khamsi nitt you hypocrite 🤔
@adamandiayekasse599018 күн бұрын
Sangou sangue yi Psl, bamouy dieul sokhna khadija ay mbokam daniou thi andeu, dém niani. Kii dafa détourner domou diambour, yayam di souffrir mou déff louko saf
@bintourassoulrassoul387118 күн бұрын
@@adamandiayekasse5990❤❤❤
@khadijafall812618 күн бұрын
Yonénete yalla mouhamed abandonné woule yayeam bimou také diabar lolou mo méti nit yi mais dou seye bi arrêter
@user-vibf6ji2n.18 күн бұрын
Ousseynou bamiy takk mère bi béneu parents wam yégoul mariage bi , fi mariage amoufi ,wakh lén gnaari lascars yi deug mogueun . Ousseynou sa yaye mo ngui dioye rek si internet bi , té nga meuytou ,akhou parents woroul si dom dé.
@alyndiaye291014 күн бұрын
Machallah Yalla na seuye bi barkél
@aminatadiaw928318 күн бұрын
Ak Kanamou khaley bi😂😂😂, yalla Ndiabott... N'a mandou rek...
@bintourassoulrassoul387118 күн бұрын
😂😂😂😂
@bambasall844718 күн бұрын
Machalla Ousseynou bou la kén yakhall dokhalell de tobabe yagui am 60 sans dît tak khalé sénégalais you am 18 sans te kén dou wakh
@DieynabaSamb-g5e18 күн бұрын
En tout cas il parle avec maturité
@SaerBa-o6k16 күн бұрын
Yallah moye doggal❤👊
@Fatou-n4q18 күн бұрын
Fils démal wakhe tane ac sa yaye mo guene ta moytou thiate mo gue ne😮😮😮😮😮
@MaguetteCisse-rc3ye5 күн бұрын
mon cœur kaye wouyou cheikh Ahmed 😂😂😂
@fatoukinembaye478718 күн бұрын
Sénégal mandou lène si seuyou diambour bi nguir yalla kou nekk amenga loula doyy lidieunti ko silou nekh yalla lagnou nekk yalna yalla barkel seuye bi
@dialdiallo764415 күн бұрын
Way defale lou le nekh👏👏👏👏
@FatouDiallo-w1p18 күн бұрын
Machallah farata rek la def
@MadaDione-y7u18 күн бұрын
bilahi
@CiréMamadou18 күн бұрын
❤Bonne chance à eux yallah seybi barkel😊
@dawdatouray26618 күн бұрын
I love this couple ❤❤🇬🇲
@MountagaDiallo-n9b16 күн бұрын
Mane ana lu tere nit wara maandu ci mbiri Yalla. Ndaw si, Sunu Borom Moo ko boolee ak jekkeram, kon book, prions pour leur bonheur
@Machine4Amndykara418 күн бұрын
Worna yallah ouzin barde woul mère belle vie moko fa bayi d'après son réaction beugoul
@AstouSy-f8i18 күн бұрын
Merci beaucoup non Ousseynou sama ak souko dalé
@Machine4Amndykara418 күн бұрын
@AstouSy-f8i Loy tek ni defma signe gnou wakhtane
@MamadouNdiaye-yo9vl17 күн бұрын
Sa réaction c mieux 😅
@dianekhaliss17 күн бұрын
Histoire dinako bindeu😂😂😂
@AliouDiallo-wv2sp18 күн бұрын
Wow lou raffett ci vieille bi😂😂😂
@antagueye844718 күн бұрын
Moma diakhal beugue mou nétaliko rec 😂😂😂😂
@sophieseck931718 күн бұрын
Ndeysaan yallna len yallavlafal thiat😊
@sokhnaSaly_Diop485318 күн бұрын
Man controuma lén dh mais waro wone menacé famille bi danga lén wara comprendre fékhé nakhanté ak gnome ndakh nk li tammou ko di guisse
@marianendoye18 күн бұрын
Soyez heureux . L'amour n'a pas d'âge, je vous souhaite beaucoup de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ que Dieu vous bénisse 🙏
@ChiekhDiop-b6g17 күн бұрын
😂😂
@mamourniang876418 күн бұрын
Yalna lénne Yalla défale diamme 🙏🙏
@isatoudjaiteh944718 күн бұрын
Brother cheikh, don't say "Allah boni celibataire deh 😂😂😂😂 just pray for us because we are bachelorettes and we follow and like you 😂😂😂😂😂😂😂. ❤❤❤❤❤❤❤may Allah continue to bless you amiine
@Bgch752518 күн бұрын
Je ne sais pas si vous avez la même analyse que moi mais c’est la dame qui est victime dans cette histoire. Car le jeune homme est intelligent et très mature il cherche juste du buzz pour se faire remarquer. Et il utilise la dame mais c’est désolant 😢
@Fa_169718 күн бұрын
La dame n’est une victime mais une coba
@Bgch752518 күн бұрын
@ tu as raison entoucas li c’est bizarre dale
@CheikhmohamedvadelCheikh18 күн бұрын
Bonne continuation s'est pas haram je vous souhaite bonne chance par la baraka de son prophète mouhamed psl
@kantarandiaye18 күн бұрын
Ousseynou est un innocent 😂😂😂😂😂😂😂
@Ndeyetall-r6y17 күн бұрын
Dafa ame niousokhor soudone age 80 ans sakhe diaroule mbép mbép
@seynabfatalecisse914118 күн бұрын
Adja diallo balgnou mais sa tarr diékhna aujourd'hui 😂
@AichaDia-t1d18 күн бұрын
😂😂😂😂
@Ndeye-v2p18 күн бұрын
😂😂😂
@mamy404918 күн бұрын
😂😂😂 merou djinné bi dieul Na lep kay
@seynabfatalecisse914117 күн бұрын
@@mamy4049 mdrrrrr
@khadidiatoumane405917 күн бұрын
Thiey sénégal ana kerseu ana soutoureu yalna yalla âr sounou ndiabôt yi
@fadangcamara369618 күн бұрын
Mère bou geum bopam amna aisatou la toudou 😂😂😂🙈
@MyaDior-f9p16 күн бұрын
Yow mi déf live bi seytané nga
@AblayediagneDiop18 күн бұрын
Sama ex copin nena bimou neke khalait ben mer moko done iri diko yeudai moko😅khamal djiguen te après laa découvrir ni deef nako presque kharitame yeupe😅 li😅yaguena Sénégal te boye khole khalebi dafa beugone gnalo ake mome mouneko dedete