« Lac 2 59 millions la wara fay? papam dafa dioy…» Lac 2 déféré, Modou Anta fait des révélâtions et…

  Рет қаралды 106,255

People 221 TV

People 221 TV

17 күн бұрын

Пікірлер: 189
@People221sn
@People221sn 15 күн бұрын
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@PapaBarry-cw1vz
@PapaBarry-cw1vz 15 күн бұрын
Waw surtout lolou aussi
@niangmass5059
@niangmass5059 14 күн бұрын
Lac2 vs baboy .lac2 vs yekini.lac2 vs Modou lo2foi.lac2 vs boy Niang .lac2 vs siteu.lac2 vs emeu sene 2fois Ana limou amon si combat yii
@MohamedRassoul-lg7uo
@MohamedRassoul-lg7uo 15 күн бұрын
Natou dou wesss yalla nako yalla takhawou Lac2🙏🏻
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 11 күн бұрын
*Amennn🙏🏽🙏🏽*
@user-jd5xq1yn1d
@user-jd5xq1yn1d 12 күн бұрын
Kou am diome leu boy bi, C est un homme de principe, il a un caractère
@MohamedRassoul-lg7uo
@MohamedRassoul-lg7uo 15 күн бұрын
Adouna werou koor laa tank ndogou diotoul dioubo wesou woul 🙏🏻Papis Yalla nako yalla takhawou🙏🏻
@abdoufall9591
@abdoufall9591 15 күн бұрын
Lac mo togne bopam légui Ana gayui liguéye sén xalis am confiace guén di wakh natou xalisou diambour kouko lék dém prison
@PateMbaye-ec5em
@PateMbaye-ec5em 15 күн бұрын
Mais lac khana amoul compte épargne ? Des années de carrière avec des combats à des millions
@AISSATOUCAMARA-zu6fr
@AISSATOUCAMARA-zu6fr 15 күн бұрын
Vraiment
@LaBarhamienne
@LaBarhamienne 15 күн бұрын
Momathi diaxal mom mashallah limou diota am thi ay cachets wou millions warone na fégn thi mom, boudoul épargne sax di investissement.. ah doyna war, ah yalla nako yalla may xolou mougn té southi diouguè di dougou thi lou yonam nék rek ba bagn ko dalati.
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if 15 күн бұрын
C que peut être Mongi done épargné mai domou Adama modoule doyale xaliss
@dofoujackson2544
@dofoujackson2544 15 күн бұрын
Khalisou lamb bakhoul
@maramethioub2304
@maramethioub2304 15 күн бұрын
@@LaBarhamienneDes fois nit you siw yi thi bras long lañiou koy tek danou nane dou moudiè fene
@mika-fh3cj
@mika-fh3cj 13 күн бұрын
Éyway ndeyssane borom alale yi diapaléléneko guéne sotalko té yalla rék thakh thi barké serigne babacar sy❤
@KhadimDiop-jv5jp
@KhadimDiop-jv5jp 15 күн бұрын
Modou anta billahi nitkou bakh gua yalla n'a la yalla sam lac courage reck Dina bakh inchallah
@saliougueye2348
@saliougueye2348 15 күн бұрын
Modou anta bilahi nitkou bakh gua yalla n'a la yalla Sam Lac courage rékh Dina bakh inchallah
@mayasall9658
@mayasall9658 14 күн бұрын
Kag kéne kag la setou serigne mousa ka la🎉
@icAlphaDiallo
@icAlphaDiallo 15 күн бұрын
Yalla nala yalla diapale نصرك الله نصرا عزيزا اللهم إنصرإخواننا في فلسطين 🤲🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇳
@elisabethgomis1068
@elisabethgomis1068 15 күн бұрын
Mane dh lac rek layy supporté mom loumassi deegue bakhna courage mon champion yalna yalla doli soutoureu
@user-qw7uy4qp8d
@user-qw7uy4qp8d 15 күн бұрын
Khaliss d'où dara adouna lép dafaye diekh Lou Haye âme n'a sante yalla
@AwaToure-qh6rq
@AwaToure-qh6rq 15 күн бұрын
Bilay khaliss linga wakh c vrai
@PapaBarry-cw1vz
@PapaBarry-cw1vz 15 күн бұрын
Compte épargne c'est très important pour keup kou nèkk si activités.... Yalla nako yalla takhawou 🤲
@sensorohgnes1110
@sensorohgnes1110 14 күн бұрын
Compte epargne bahna frere mais bou geune moye di epargné si diamou yalla yi lo ame bok kok diamou yalla yi beuss boy ame problème même boula nieup setané yalla doula setane
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 15 күн бұрын
Wakh bi safna daara ohhh😢😢😢😢modou anta yabakh diangue réka woor😢alkhurane lawakh nake❤❤❤modou anta merci
@ismailadiatta6942
@ismailadiatta6942 15 күн бұрын
Lac de guer kène yènèwou ko liii mais tamite trafic de visa Lou grawla mais aussi naka lay fayèko ay million di encaisser khalissou ay pauvre li nak dou ndogal nioune des fois nioy tègu souniou bope yèn yi
@mamadoudiop1105
@mamadoudiop1105 15 күн бұрын
Lolu la osi
@papeba5881
@papeba5881 15 күн бұрын
Waw vraiment
@ibrahimasall4312
@ibrahimasall4312 15 күн бұрын
Khaliso lambo barkewoull
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 15 күн бұрын
Non dou mom mo enquêsé lima dégue mom mo bolé boyi ak wadji légui wadji encaisser khalis bi modaw si lima dégue🙄🙄🤔🤔
@swartnwar916
@swartnwar916 15 күн бұрын
Lac2 dafeu fegnlé rk mais lou beuuuri beuuuri des célébrités lolou lagnouy def. Tei lolou momeu titeul garyi danio nareu appliqué durement la loi pour diokhé exemple.
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if 15 күн бұрын
Natou dou wéss yalnako yalla takhawou
@boromkourousgui4918
@boromkourousgui4918 15 күн бұрын
natou dou wéssss thi domou adama bi kasso mome ay domi diambour rék niofa nék niou bakh yalla na léne yalla taxawou thi diam ak salam
@alysow9089
@alysow9089 14 күн бұрын
Modou Anta yw brom bakh ngua mé sa wakh dfa Bari k nianal len lac 2 mo Guen inchallah
@user-sb8gw2fx7k
@user-sb8gw2fx7k 15 күн бұрын
Merci modou anta d’avoir bien soutenir lac de guerre 2
@masseseck9475
@masseseck9475 14 күн бұрын
Cagnote pour lac s'il te plait 😢😢😢😢😢😢😢😢😢👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
@astousallmbaye5541
@astousallmbaye5541 15 күн бұрын
Wa 59 millions barina de Mane ma yakar ni 20 millions la
@alexisniokhorsenghor-lg4gc
@alexisniokhorsenghor-lg4gc 15 күн бұрын
Mais Lac tamit, je ne comprends pas quoi. Comment il a pu se retrouver dans tout ça. Sincèrement suis très ému, surtout un peu triste en même temps... Vivement que Lac garde la foi.
@AnneMariesanneMboup
@AnneMariesanneMboup 14 күн бұрын
Papis yalla na ko yalla diapale Amine ya Rabi
@soldarouyayam8524
@soldarouyayam8524 15 күн бұрын
Lac2 même bou fayone sakh loi dacoy top pour raison yimou dieulè xalise bii ak rôle bii mou thi jouèr ak loutakh mou dougu si lolou loi dafa compliquè wayè magui ñiane yala dakhawouko ak kèp koufa nèk yala dieulèlène fa ñious dèlou thi sène diabote
@KhadijaBa-gt2qq
@KhadijaBa-gt2qq 15 күн бұрын
Thiey ndeysane nako yalla takhawou sii barki seydina moukhamed psl
@ndiayemaleye2581
@ndiayemaleye2581 15 күн бұрын
Amine bilahi aduna fi yagui doundou rekk natou wesoul 😢😢yalla nako yalla takhawou thi barkè seydina Mohamed wasalim
@soxnandeye5170
@soxnandeye5170 15 күн бұрын
Amine 🙏
@KhadijaBa-gt2qq
@KhadijaBa-gt2qq 15 күн бұрын
@@ndiayemaleye2581 bilae ndeysane niou nane rék yalla mouseul niou s
@ndiayemaleye2581
@ndiayemaleye2581 15 күн бұрын
@@soxnandeye5170 natou dou wess parfoi nga dougou thi lo xamoul
@user-pi3gx2rq4x
@user-pi3gx2rq4x 15 күн бұрын
Amine ya rabi
@cheikhndiaye6698
@cheikhndiaye6698 4 күн бұрын
Lac2❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ téy lako gueuneu beugue
@jeangabrielcoly4091
@jeangabrielcoly4091 Күн бұрын
Il faut qu'on dépasse les affaires de bras long , nous sommes tous égaux , si c'est lui qui l'a fait alors n'a qu'à rester en prison c'est tout . S'il sort tout simplement parce qu'il est un lutteur populaire alors je dirai que la justice sénégalais n'est pas équitable , elle est juste ici rien que les pauvres ( voleurs de téléphone , de mouton, coq etc)
@alysow9089
@alysow9089 14 күн бұрын
Khana lac 2 bewoul aak siteu Bari wakh dayy takh nguayy
@oulimatadieme9003
@oulimatadieme9003 15 күн бұрын
Yalna ko yalla takhawou
@abdoulayecamara9500
@abdoulayecamara9500 15 күн бұрын
Lac a récemment fait 3 combats eumeu boy niang et siteu. Il doit épargner au moins 30M + les 10M de sadio mais loumouci tek faye avec ses autres connaissances
@bakhreckww6053
@bakhreckww6053 15 күн бұрын
Merci beaucoup Modou anta ❤❤❤
@AbdouCisse-xs5mc
@AbdouCisse-xs5mc 15 күн бұрын
Ndeyessane natou dou wess yalla nako yalla defal diam 😭
@bakhreckww6053
@bakhreckww6053 15 күн бұрын
Merci Modou anta ❤❤❤
@user-ib7tv3ff1k
@user-ib7tv3ff1k 15 күн бұрын
machallah modou anta ❤❤❤
@user-er6yr7zc8e
@user-er6yr7zc8e 15 күн бұрын
Merci 🤲🤲🤲❤❤❤
@user-lg1rl2zs6i
@user-lg1rl2zs6i 15 күн бұрын
Machalla Modou anta
@damefall9416
@damefall9416 15 күн бұрын
Ndeysane yallana ko yalla takha wo teguel ko natt bi barck brome touba
@AstouGueye-bb3gb
@AstouGueye-bb3gb 14 күн бұрын
Lac de guerre yalla nako yalle takhawou si barké seydina Mouhamed
@MamytoMn
@MamytoMn 15 күн бұрын
Moudou anta❤❤❤❤❤
@sarrabdou3040
@sarrabdou3040 15 күн бұрын
Nonn li geumoumako woon mais lac 2 dafa nélaw bou bah sah , linga féyékou si ay Millions isss😮😮
@Mecrare01
@Mecrare01 15 күн бұрын
Modou Anta Machalah Diap si yaw ❤️ ay bou nekone Abou domou ndeye 5tonnes niary seytané yoyou beug buzz akk ay vue Loy diaxasé rek laniouy defff
@mamadousylla3550
@mamadousylla3550 15 күн бұрын
Lac laniouy kétal alahou akbar
@lassanadrame7385
@lassanadrame7385 15 күн бұрын
N’oubliez pas que y’a des victimes qui ont travaillé leur argent ,justice pour ces victimes qui ont perdu leur argent .et ne demandez de l’aide à personne car quand les jeunes qui vous suivent étaient tues par des nervis et policiers on a vu aucun lutteur sauf Quelques uns .
@RioNdiaye
@RioNdiaye 14 күн бұрын
Legui lo beugue wakh mbeur yi nio takh gnou raye khallé yi
@malicksarr2141
@malicksarr2141 15 күн бұрын
Courage 😥 lac 2
@LimoGas-gp5gq
@LimoGas-gp5gq 15 күн бұрын
Mbeuri amnagnou caisse de solidarité mais un geste quand même sil a fauté
@user-jm7iv3sy3l
@user-jm7iv3sy3l 14 күн бұрын
Modou anta❤❤❤
@user-ib7tv3ff1k
@user-ib7tv3ff1k 15 күн бұрын
meci ❤❤❤
@moustaphadiaw4314
@moustaphadiaw4314 15 күн бұрын
Yalla takhawou ko
@alysow9089
@alysow9089 14 күн бұрын
Yw dangua wakh Modou Anta wakh diou Bari bakhoul
@bathieballagayedrame9638
@bathieballagayedrame9638 15 күн бұрын
God bless lac 2
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 15 күн бұрын
Senegal da ngay nek say bis nes badara khuew nioné tiss
@user-ce9ic8rf1f
@user-ce9ic8rf1f 15 күн бұрын
Sénégal doye na ware aka nio meuna yakeu ndanane li khéwe responsable bilakhi dou lac de guér responsable bi police sokholouko naniou torokhale lac de guér rék moléne niore. Sénégal danio aye si ndandane yalla na niou yalla yokou soutoura
@MaelSi-tx7uz
@MaelSi-tx7uz 15 күн бұрын
Kone bou nekone c frr gnou wère ko siw ci bopame mo nexoul meno siw b paré tek ci doff di jay yewou nite ligey khalissame yow gey profité
@xalimagui-officiel9001
@xalimagui-officiel9001 15 күн бұрын
Ioe tu ne jouis pas de toutes tes facultés nga balma nak
@user-lj5dz7cm8c
@user-lj5dz7cm8c 15 күн бұрын
Dara diarako fi daal 😢😢
@papafaye4033
@papafaye4033 14 күн бұрын
Délen di wakh nite thi degue il la qu'elle compétence pr prendre l'argent des gens pr des visas
@sagatakondiaye7270
@sagatakondiaye7270 13 күн бұрын
Senegal dagaye dougou si dra boulasi dra fekke gani natoula il prend c'est responsabilité mbeur doumako diokhe sama khalisse
@awasylla5203
@awasylla5203 15 күн бұрын
Yalla na Yalla guene ko si defe si ndokhe bou sede
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 15 күн бұрын
Domou adama loula yala diokh nagua doye lou bou bakh .tè hamenii moy sa weurseukk lou ame solo la .fii lèp dafay dièkh adouna amoul solo .
@siroupam7249
@siroupam7249 15 күн бұрын
Danio fokaler
@papendiayel5151
@papendiayel5151 15 күн бұрын
Man dh lolou khamnasi dara
@abasall711
@abasall711 14 күн бұрын
Luler nga wax yalnako yalla diapaler mu delu keureum chaque erreur du passé est une leçon pour le futur
@AliouDiouf-ci2ny
@AliouDiouf-ci2ny 15 күн бұрын
Modou anta fonko nala torop mais nak Li mom problème Lac 2 la Nano bayi Boye yi Nion nakh Lolou moy deg
@gnilanediouf7960
@gnilanediouf7960 15 күн бұрын
Modou anta khana beurétoul kouma nékh la machalah ❤
@medounesanchezdiop6112
@medounesanchezdiop6112 15 күн бұрын
Modou anta mbeur dou ki dh kokou ganiou na bou yag😂
@gnilanediouf7960
@gnilanediouf7960 15 күн бұрын
Abon
@benoitlorent1386
@benoitlorent1386 15 күн бұрын
​@@medounesanchezdiop6112 ki modou anta thies ley wakh, kokou mo ngi fi d
@user-ls1mw9ow4f
@user-ls1mw9ow4f 14 күн бұрын
Amine
@elagegueye3310
@elagegueye3310 15 күн бұрын
alhouran bigay wah sok gueme۔loutah guendy def silibounenn si kanamou haleyui
@RioNdiaye
@RioNdiaye 14 күн бұрын
Iow ya guiss modou anta mou def slipou nén bayil len juger niit yi
@aliounemboup4234
@aliounemboup4234 12 күн бұрын
Modou anta mbeur thies lakka djawalél peut-être
@ousououssououssou
@ousououssououssou 15 күн бұрын
Mais gni faye lac aussi pour acheter visa nagnouléne diap aussi ndakh defougnou gnone
@user-id8uv3ob2f
@user-id8uv3ob2f 14 күн бұрын
Na fey khalissou diambour yi senegal dagno sonou si affaire trafique visa na fey reck
@AliouKama-zs9ye
@AliouKama-zs9ye 15 күн бұрын
En tout cas il doit payer l'argent 😢car il ne sait pas comment ces gens ont leurs l'argent 😢
@FallouSarr-
@FallouSarr- 15 күн бұрын
Bilahi t'as raison Sénégal mo bari ay nafekh gnouy wakh gnouy ndeysane na fey wala prison
@josephcoly4127
@josephcoly4127 15 күн бұрын
Deg nekhoul Sénégalais nafeke le niome il parle même pa des gens ki on perdu cette argent
@serignefall7167
@serignefall7167 15 күн бұрын
Bilay frère
@SaloumSy
@SaloumSy 15 күн бұрын
Bamouy lek khaliss Diambour Dafa nekh Naniou fay khaliss Diambour si bopam nan ay ndogualll
@user-gm4ny3vg5n
@user-gm4ny3vg5n 15 күн бұрын
Xaliss diaroul li il faut travailler lac 2 doit etre puni comme tout le monde y a pas de mesure
@aliounefaye2901
@aliounefaye2901 14 күн бұрын
Lac ma yoro djikoy peulh reik yor 200 millions sa compte am problème dieunde médicaments 20 mile franc ba décédé feik lenefa
@user-vm1cb1zv7y
@user-vm1cb1zv7y 15 күн бұрын
Tant qu'il ya la vie y'aura tjrs des circonstances
@moustaphandiaye8734
@moustaphandiaye8734 13 күн бұрын
59 millions ,environ 60 millions
@sonnedj2304
@sonnedj2304 15 күн бұрын
Modou anta yako wakhone neko yallah nama yallah atté ak yaw yallah atté nalléne
@ibrahimaseck3589
@ibrahimaseck3589 15 күн бұрын
Mai nak il faut faire tres attention Diomaye sonko niofi nek amatoul louniou fi meuna négocier Lac yal nala yalla guené si natou bi Mbeur yi tmt danguene wara yewou touti
@babanena6869
@babanena6869 15 күн бұрын
Akhou modou anta mii mo dal Lac de Guier
@boyetownfromdkr5287
@boyetownfromdkr5287 14 күн бұрын
Yaw dimbalil nite gni waye ak sén wakh yii lolou soko wakhé manila wakho deugue
@fallndoye1913
@fallndoye1913 15 күн бұрын
Pour moi il était au courant
@AISSATOUCAMARA-zu6fr
@AISSATOUCAMARA-zu6fr 15 күн бұрын
Lolou guay dafa lere
@MamyGueye-my2gd
@MamyGueye-my2gd 15 күн бұрын
ioe déégo limou wax xana
@LissaBiaye-xs8ud
@LissaBiaye-xs8ud 15 күн бұрын
Il était bien au courant problème bi dou teye yeuguone nako mais hum lou yalla ham doyna
@mamadouseye2558
@mamadouseye2558 14 күн бұрын
Na Fay ndayou khalissou Jambour
@fallousarr5728
@fallousarr5728 15 күн бұрын
Lac louko wara dougeul ci li la khamoul koi bilahi
@djimbyfaye7149
@djimbyfaye7149 15 күн бұрын
Nattou la
@ndiayeSoda-ch3hg
@ndiayeSoda-ch3hg 12 күн бұрын
Lak yeurem nako na faye rek mou diekh
@dembaztarkinda8270
@dembaztarkinda8270 14 күн бұрын
Modou anta dioum nga lac 2 siteu la moudjié beurel 19 novembre
@babssadikh5863
@babssadikh5863 3 күн бұрын
Door aye nite séne khaliss niou diape la gayi guéne si télé yi si doule… na day khaliss diambour yi.
@orrnoir9022
@orrnoir9022 14 күн бұрын
ana bg2?
@BathieGueye-sp2hb
@BathieGueye-sp2hb 15 күн бұрын
ki dafa degou billahi
@user-ys5bq2dq6c
@user-ys5bq2dq6c 10 күн бұрын
Modou Anta bou thies walla
@serignemodoubeye2730
@serignemodoubeye2730 15 күн бұрын
Senegal naniou bayi kou liguey khalissam thi digne ma Nitte ki nakhla thi affairou touki bouniou diougué gnini nattou leuh moko yobou foumou nk
@SaloumSy
@SaloumSy 15 күн бұрын
Billay frère gays danio nafek kW baniouy lek khaliss Diambour fignu nekkk
@SouleyemaneGueye-uq6lt
@SouleyemaneGueye-uq6lt 14 күн бұрын
Sa data yaye
@biramdiagne7697
@biramdiagne7697 15 күн бұрын
Nagn bayi justice def ligueyam niou kham fou deuk bi fete Deuk bi amna yone dou lounekh say def comment on peut être millionnaire et vouloir escroquer les gens
@RioNdiaye
@RioNdiaye 14 күн бұрын
Banne justice leu fi ken ben justice bou juste mo ame moy bou yalla
@biramdiagne7697
@biramdiagne7697 14 күн бұрын
@@RioNdiaye liguay wakh ni tegouwoul
@user-mx5fo5eq1n
@user-mx5fo5eq1n 15 күн бұрын
Lac. De. Guiers. Kou. Niak. Diom. Leu. Dou. Rouss. Dou. Nittou. Dara. Rembourse. L. Argent. Des. Gens. C’est. Ça. La. Vérité. Papal. N’a. Dioye. Et. Apres
@marie-bq9qs
@marie-bq9qs 15 күн бұрын
lac weireina
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 14 күн бұрын
Nattou la rék yalla bakh na
@CheikhAbdoulaye-yu7ib
@CheikhAbdoulaye-yu7ib 15 күн бұрын
Na fay
@SaniCisse-pq8qw
@SaniCisse-pq8qw 14 күн бұрын
🤲🤲🤲🤲😞😞
@mamadoudiop1105
@mamadoudiop1105 15 күн бұрын
Nako yala takhawu mai osi bign dieule ben ou 2 avance sotiwul warugn won dieulat khalis diambour
@user-rj9sb9cv7u
@user-rj9sb9cv7u 15 күн бұрын
lac de guere yala nala yala same arla guene la si xate xate yi
@mamadouseye2558
@mamadouseye2558 14 күн бұрын
WA lac noumou deff khaliss bi
@xalimagui-officiel9001
@xalimagui-officiel9001 15 күн бұрын
Mann dama warou koi
@lahadboukharagnelo6707
@lahadboukharagnelo6707 15 күн бұрын
Man batay affaire dama diakhl vraiment man khamna nani xaliss lekou si dara kharitam moko door xaliss mes lac mo nek si bop legui lac affaire tolou na fi xalissam boumou donn beurre anamou mou faye soutoural bopam man lolou rk moma si diakhal khana dolen ma llac amoul xaliss
@badoudiatta7219
@badoudiatta7219 15 күн бұрын
Lolou Mann guemoumako dh 59million ngané lékouko yalla baxna Mais xalissou Diambour la lougnou waré yeureme lac gnougnou lékk sénn xaliss gnoko guena mérité
@babanena6869
@babanena6869 15 күн бұрын
Modou Anta Lac 2 moko done diéma humilier tay mogui nii torokhal nagnu ko thi digue Rewmi
@fatoundiayeanne5714
@fatoundiayeanne5714 15 күн бұрын
Ah bon louniou diotei wone stp
@afro3827
@afro3827 15 күн бұрын
Ma degon 20milions 🤔🤔
@aloufaye1470
@aloufaye1470 15 күн бұрын
Les dealeurs leurs place ses la prison
@NfdhfGgsud
@NfdhfGgsud 15 күн бұрын
Non il faut la justice fait son travail car nul n'est au dessus de la lois comment un lutteur qui reçoit plus de 30 millions et récupére l'argent des des jeunes qui font des bisnes
@khadyloum-ey8xg
@khadyloum-ey8xg 15 күн бұрын
Na diay autom ak Bimou maybe diabaram de mem sa maison
@Mister-nay-ler
@Mister-nay-ler 15 күн бұрын
Mbeur yi dagno beugu lou yombe di encaisser ay millions ba paré di wayane rek
@Diopbayemodou
@Diopbayemodou 15 күн бұрын
59 millions wala ma guissoul
КАКОЙ ВАШ ЛЮБИМЫЙ ЦВЕТ?😍 #game #shorts
00:17
Маленькая и средняя фанта
00:56
Multi DO Smile Russian
Рет қаралды 5 МЛН
КАРМАНЧИК 2 СЕЗОН 5 СЕРИЯ
27:21
Inter Production
Рет қаралды 582 М.
Chips evolution !! 😔😔
00:23
Tibo InShape
Рет қаралды 42 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 1 - Épisode 33 **VOSTFR**
33:13
WEST AFRICA SN PRODUCTION
Рет қаралды 72 М.
КАКОЙ ВАШ ЛЮБИМЫЙ ЦВЕТ?😍 #game #shorts
00:17