Lambalogue met en garde Ama Baldé : "moussiba la dieul, Franc souko diapé ci..."

  Рет қаралды 31,477

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 82
@ndiagafaye3106
@ndiagafaye3106 Күн бұрын
Bou leen thiatou sama mbeur mi franc ndam reek inchallah 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Күн бұрын
Franc yalnako yalla maye ndame ❤
@Young_boy43
@Young_boy43 Күн бұрын
Yalla boussa gnane nangou
@fidelemendy284
@fidelemendy284 Күн бұрын
Franc ndiago yalla na ko yalla soutoural 🤲 🤲 🤲
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo Күн бұрын
Zambala vs Gris2 Gora Sock vs Thattou Yarakh Doudou Sané vs Serigne Ndiaye2
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 Күн бұрын
Franc yalla nala yalla maye ndam bou sed gouye té mou djick là inchallah 🙏🙏❤
@CheikhIbraFall-u2r
@CheikhIbraFall-u2r 19 сағат бұрын
🇺🇲 incha'Allah yalla nanioukô féké talko si diam akh salam incha'Allah ♥️ mais Ama baldé yalla nkô yalla maï ndam si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶
@djimbaniang2190
@djimbaniang2190 Күн бұрын
Problème moye Fran dafa nekhoul nakh aussi beurre bi dafa wor dou dieul risque mbeur 100% le de mom
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 Күн бұрын
Franc beuré goul combat bou takh niounane mbeur la
@adama6405
@adama6405 Күн бұрын
Franc combat yimou beuré yeupou Moy favori thé ama da meune beusse
@djimbaniang2190
@djimbaniang2190 Күн бұрын
@adama6405 Fran temit Mina guew de
@michaelronthings3297
@michaelronthings3297 Күн бұрын
Franc ameuneudolé gawneu té Mouss amneuremisebouy tidji boutou déy champion leu mais mougui doggeu dadj Ama kén d'où mom déy beuré déy khékh mbeur moko takkdiarkarlok mom waleudiéma bayi Takko ci digu faguéndi fanan bé kerrogu mou diappé mou diékh.Franc amneu combat Ama n'a khamné oči franc da gaw trop latteu gay compeu diappeu.
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 Күн бұрын
@@modoubayefallsikroulla1423😂 kouy dane 40 mbeur bene jour ga nane danagoul mbeur bayilene thiakhane ama beureigoul kou meune franc
@josephcoly4127
@josephcoly4127 Күн бұрын
Ndam rek franky super ndiago or bi❤❤❤❤
@simmelsarr3599
@simmelsarr3599 Күн бұрын
Franc et Reug Reug sont d'immenses champions mais niougui soga dougou sen catégories. Franc meunoul nek favori ci kanamou Ama. Reug meunoul nek favori ci kanamou BN2. Ama mbeur kamil leu. Kou dane Malick Niang dane Tapha Tine sou dané Franc waroul bet ken. Franc dane Ama moy surprise
@BabacarJammeh
@BabacarJammeh Күн бұрын
Kou dane bombardier nak
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Күн бұрын
Binak moy combat ❤️‍🔥❤️‍🔥 franc ama baldé 😂
@bachirdiop19
@bachirdiop19 Күн бұрын
En tout cas lou mana xew yalla na franc dane 🙏🏿
@Luka23110
@Luka23110 Күн бұрын
Emile Francois gomis rek niou deme Ama am nga combat deii
@BoyDiop-i8v
@BoyDiop-i8v Күн бұрын
Faran seul
@abdoulayediallo4028
@abdoulayediallo4028 9 сағат бұрын
Noté sur mon commentaire Ama déy dorr fran mou danou Beuré d'où am si combat bi Khékh rék Comme le combat tafa tine vs Elton
@PapaBarry-cw1vz
@PapaBarry-cw1vz Күн бұрын
Franck ndiago seul 👊💪
@MomoDieye-j6s
@MomoDieye-j6s 7 сағат бұрын
Franc macha'allah
@layedembaniang1150
@layedembaniang1150 Күн бұрын
Franc eupoul dolé Ama inchallah jour ba diguénsi xam dra
@ndiagaseye5304
@ndiagaseye5304 Күн бұрын
Franc mo eupou dolé fouff Ama Baldé té inchalla franc dinako dane
@KareAliou
@KareAliou Күн бұрын
Farà man fouf
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd Күн бұрын
Gor bala meune gor niou lalé
@ousseynoudiallo9284
@ousseynoudiallo9284 Күн бұрын
🔥🔥🔥ℙ𝕠𝕜𝕠𝕝𝕒 𝕤𝕖𝕦𝕝 🔥🔥🔥
@JULESEMILESARASAGNA
@JULESEMILESARASAGNA Күн бұрын
Lutax dolen dégoulenté lingén di waxa done mntkh bruits yi beuri bayi lenn si xel
@niangniang1555
@niangniang1555 Күн бұрын
😂 Modou anta Aka beug graw grawlou ak bopou pitch bi😂
@bigleuztv5211
@bigleuztv5211 17 сағат бұрын
Ya boone 😂
@CASI7797
@CASI7797 10 сағат бұрын
Lambelogue migui neilaw nak, da soneuu
@KhalifaSow-hw1dw
@KhalifaSow-hw1dw Күн бұрын
❤❤❤❤❤❤
@lem4750
@lem4750 Күн бұрын
War ngein niou may jamm ak Ama sou parei dh…ay millions lagn ko fay
@assanewade6616
@assanewade6616 Күн бұрын
Kou nek di wa
@assanebabaofficiel3533
@assanebabaofficiel3533 18 сағат бұрын
Ardo dou am si combat biiii
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo Күн бұрын
Latakh kén dou wakh wakh Serigne Ndiaye2 bayilén lamb bingén yakk Doudou Sané na dieul Serigne Ndiaye2 combat leu
@adama6405
@adama6405 Күн бұрын
Franc combat yeupou mou beuré molay attaqué mais est ce k bouko Ama attaquer dina guisse comme sa thies reuk reuk
@Wrestling1890
@Wrestling1890 Күн бұрын
Forza ak bombardier nak nioko songue wala
@josephcoly4127
@josephcoly4127 Күн бұрын
Forza mo attaqué bombadié mo attaqué
@adama6405
@adama6405 Күн бұрын
@@Wrestling1890 b52 ak forza dougniou ay attaquant lolou dou sène fort mais ama mom attaquant la franc aussi donc kou attaqué bagna may sa adversaire mou xalate gueume na ya mom combat bi
@adama6405
@adama6405 Күн бұрын
@@josephcoly4127 mais dagno joué fokhamni dou sén poste 😂mais Ama vrai attaquant la meunoule défendre fofou lay waxé
@josephcoly4127
@josephcoly4127 Күн бұрын
@adama6405 ama champion incontestable le yalla khamnako
@CASI7797
@CASI7797 10 сағат бұрын
Modou Anta khana Ama gua faral aussi
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 23 сағат бұрын
Ama baldé mo meune mo eup dole
@aliounembaye5203
@aliounembaye5203 16 сағат бұрын
Senn plateau il faut nguen di deglonté. Waxando bi tmt c chiant
@HawaTall-om3xz
@HawaTall-om3xz Күн бұрын
Lambalogue Del deglou waté ioe késsé waro wax li dou xam xam way
@MohamedThioune-p9k
@MohamedThioune-p9k 12 сағат бұрын
Fran limou beug def lay def
@georgesp3398
@georgesp3398 Күн бұрын
Modou anta wakho deugue ama balde falé woul franc
@MorGning-n4i
@MorGning-n4i Күн бұрын
Franc diga AM Lola bête ama balde aka meune beuss
@GuyGuiguitou
@GuyGuiguitou 3 сағат бұрын
Lzmbalogu bouy waxx delénn ko deglou ahh mo lenn eupp kham kham
@mouhamedseck6368
@mouhamedseck6368 4 сағат бұрын
Franc mo meune siteu
@boubaleye2003
@boubaleye2003 Күн бұрын
Ama dh bou paré blh mo meune franc
@NdiayePapa-pp5bu
@NdiayePapa-pp5bu 12 сағат бұрын
Ama seule franc do tousses
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 19 сағат бұрын
Franc moy favoris contre ama baldè.parce que Franc messoul danou en plus annè yi wéssou franchement ama baldè dafa faible trop
@assanebabaofficiel3533
@assanebabaofficiel3533 18 сағат бұрын
Ndiago or bi seul
@modouboussoguene8443
@modouboussoguene8443 Күн бұрын
Lambalok mi esk dou gezman ama ngay teukeulek franc
@theblackmamba434
@theblackmamba434 21 сағат бұрын
Fran seul
@abdouseye2486
@abdouseye2486 Күн бұрын
Franc dh nekhoul diap mistiquement
@bricecorrea2628
@bricecorrea2628 Күн бұрын
Lamb y’a kham beuré té do far
@MaodoMbaye-yv4eu
@MaodoMbaye-yv4eu Күн бұрын
Yéne de lene wakh rek ba ama jape fran di na dohan de
@CamaraSy-j4e
@CamaraSy-j4e Күн бұрын
Ama Baladé REKk
@falloudiop6144
@falloudiop6144 Күн бұрын
Yen mom Franc Guen farar way nak ama kou man foufo ama dou boy yoyou dh
@AmetheSeye
@AmetheSeye Күн бұрын
Ama vs franc kagne la
@CASI7797
@CASI7797 10 сағат бұрын
Faut pas parler en même temps
@FallMbackefall
@FallMbackefall Күн бұрын
Franc mane siteu fopou
@AdamaFall-ny4pi
@AdamaFall-ny4pi Күн бұрын
AMA gnimou dane niépou dole lalene dané apar malick niang ta gniko eupou dolé niépou dasé am problem guisa gouma mana beurem amna fite gnimena
@bassiroundaw4751
@bassiroundaw4751 Күн бұрын
Tapha tine nk 😂
@AbdoulayendiayeFall-t1z
@AbdoulayendiayeFall-t1z Күн бұрын
Modou anta ama la faral😂
@mamadoucoundoulndiaye3064
@mamadoucoundoulndiaye3064 Күн бұрын
Donc meun nagnou wax mom rk mothi faral Ama le reste Fran lagnou faral ? Yéwoulén té nangoul kou nekk seu analyse.
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 Күн бұрын
Bayilène kou analyse ngén né dafa far kon gnisi dés franc lane faral
@soldar05581
@soldar05581 Күн бұрын
Moudou anta tay dacorou ma bilahii farac manoul apou dole Ama bou wér bilahii kendou ma nou ko ilmou régal mailk nia bakh n'a 😂
@adamsempereur3149
@adamsempereur3149 Күн бұрын
Saway nekh nga nak beurré bi nek si franc nekoul sakh si Malick Niang franc Dafa meun beuré lol boudé c impossible ama eup ko dollé té le 16 tu verras bien 😂😂😂😂😂
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 Күн бұрын
Fi ama diarr franc diaroufa bayilène khél lolou franc beuré goul combat sock gnim beurél niép molène mann
@mouhamedseck6368
@mouhamedseck6368 4 сағат бұрын
Saway carrière franc mbappat lepp la dieule amoul défaite malick ak tapha tine meuniouniou mbeurei
@AdamaNdiaye-v8n
@AdamaNdiaye-v8n Күн бұрын
Modou anta Lo wakhe amoul ama seul
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 Күн бұрын
Amaaa Balde bou parè Moo Meun Mbeur you Nèkeu Galséne yeupou 🧏‍♂️bou parèwoul rék Moniou Diaxall ndioun fans Lingz Piko pako yii wallahi 🧏‍♂️mè Boo parè Deugeu Molèn Moun Nieupou wallahi ✍️
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 40 - VOSTFR
41:05
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 142 М.
Thank you mommy 😊💝 #shorts
0:24
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 33 МЛН
"Идеальное" преступление
0:39
Кик Брейнс
Рет қаралды 1,4 МЛН
Andro, ELMAN, TONI, MONA - Зари (Official Audio)
2:53
RAAVA MUSIC
Рет қаралды 8 МЛН
Every team from the Bracket Buster! Who ya got? 😏
0:53
FailArmy Shorts
Рет қаралды 13 МЛН
YouCut 20250106 022835394
7:16
As-Samadiyya TV
Рет қаралды 4
Thank you mommy 😊💝 #shorts
0:24
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 33 МЛН