Vraiment modou na bayi nopal gnou. Mane damay sonou trop ta kham nani amna gnouma gueneu sonou ci mom. Ses 3 derniers combats damay nafila pendant 1 mois (le dernier mois) bollé ci wird bou bari wallahi. Le jour ma guéné samay sarakh ba paré continuer di wird ba combat bi diékh. Billahi damay sonou. Merci le grand champion daffal nga niou lepp !
@papeflokiFallАй бұрын
T'es pas le seul frère bilahi surtout contre ama baldé j'ai failli perdre mon job tellement j'étais obsédé je raté rien sur KZbin concernant le combat mais nak sant yalla hier même j'ai dit la même chose il doit arrêter pour le bien de ses fans
@BarhammDioufyАй бұрын
@@papeflokiFallndanane laa barkki alkhourane nakko yalla laffal thiate rkk mousseul ko sii pékhépp nonneu nieup beug mou danou
@Mamecheikhndao-pe8nyАй бұрын
Lolou sa problème la
@lodiabamba1594Ай бұрын
@@Mamecheikhndao-pe8nymon frère Sénégal dafa meeti d.Tu demandes à une personne d’arrêter son gagne pain pour te dédouaner de ton stress.
@SiraNdiaye-xi1heАй бұрын
Baringasi morom dé
@blackpure5177Ай бұрын
Je suis a 1000% BG2 mais modou est un grand champion et respect à lui pour son combat. Siteu da daw lamb j yeup. On y vas modlo vs sa thies.
@MamecheikhantaNgomАй бұрын
Siteu = Amy mbacké thiam modou lo vraiment c’est le meilleur ❤❤
@BayeModouDiagne-b9dАй бұрын
Ana fans BG2 you gnémé deugue ta bakh beug modou lô Machallah yen 🎉❤
@FallouGalss-j8rАй бұрын
félicitations modou lo❤❤❤❤Lambalok ya khoromo😂
@awadiongue5434Ай бұрын
Maisblolou aférou tapalé la té modou borom diom la dou konmbine mbeuré très fière de modou lô❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@GoraMbengue-f2jАй бұрын
Goor dou daw en tous cas 😂
@MamadoulayeNdoye-f6vАй бұрын
Modou lô yalla boumou amati défaite si barké seydina MOUHAMED amine yarabi Que ALLAH nous permet de réalisé notre rêve pro inchalla bou nékhé yalla Amine yarabi et donne nous de long vie amine yarabi YALLA NANOU YALLA OUBILE SOUNOU WEURSEUK AMINE YARABI ❤❤🤲🙏🤲
@MalickGueye-f5mАй бұрын
Amine way lepou dina bakh inchallah
@MouhamadouMoustaphaTall-b6bАй бұрын
Lolou moyy modou lô dotoul beurré tih ak balla gaye 2 deh
@awadione4229Ай бұрын
Allahouma amine 🙏🏽
@BayeMbaye-ht4klАй бұрын
Félicitations Modou lô le roi 👑
@mamadoumansourdiop5343Ай бұрын
Modou anta merci pour ce duo lambalogue dafa wara am ay millions si lamb inchallah. Lambalogue lep dina nieuw digua am auto inchallah. Nekal si ligua wara nek yalla soxaroul
Fi modou deif épaule siteu deif na 4 appuies , mais c’est très bien pour modou na djeul gni ame mérite ! Siteu fane leu meune nek roi des arènes si Sénégal
@BayeModouDiagne-b9dАй бұрын
Defoufi dara beuga don roi😂
@dioufaliou4384Ай бұрын
Modou Anta continue sur cette voie bien dit
@FallouGalss-j8rАй бұрын
Lac de geur bou diamageune daye daw rek amoul Arét😂
Modou lo roi incontestable félicitation🎉 Siteu day daw Rék amoul arrête comme thiak thiak heure bou niew modou yéépp mou daw😂
@AsseNguerАй бұрын
Machaallah mention spéciale à vous deux✅
@OusmaneKaneeАй бұрын
Modou dagni sétann machallah laf thiate
@fadiloukharma2683Ай бұрын
Duo bou nkh yagg lene fi lolou té werr ❤😂🎉
@daoudangom6842Ай бұрын
Yallna yala defal diamou sen anda rafet na mai modou moye Rio moy king 🤴 nane ko nagoul
@bambistebiАй бұрын
Team lambologue vous êtes où?😂👋🏾
@IbrahimaThiam-n6oАй бұрын
On est là 😂🎉 force à notre cher lambalogue ✊
@bambistebiАй бұрын
@@IbrahimaThiam-n6o C le meilleur wlh😂👏🏾
@diarra__diouf777Ай бұрын
😂mom rk lay topou
@bambistebiАй бұрын
@@diarra__diouf777 késsé nk😂
@pape2227Ай бұрын
Oh popopopo 😂😍
@gabrielagboton5361Ай бұрын
❤❤ modou anta ak lambologue yallah nalen yallah are deffen ďiam si barka seidina Mohamed (saw) !!! Ay wakahatou degeu nguen . Siteu delen ko wakh degeu diambars dou lii .. ama baldé gaindé la .. boy niang diambars la .. si digui geéw il len beurré machallah Kou bougou nek roi degeuy samp diagua diokhé sa bakane Khayane kou dégue sérrére wopopopopo !!
@yacinthefassargning604Ай бұрын
Vraiment lambologue kën d'où yaw t'es brave am lën jam rek
@GalloSene-z7yАй бұрын
Bayil niann baxoul tu as ton boulot respecte toi
@AbdouAziz-ri8tdАй бұрын
Siteu Dafa Daw Combat Bi Yeup Thiak Thiak la il a Fui ❤
@BoubacarDiallo-x8rАй бұрын
Yalna yalla may la leep banga def leep si Daradieye Seydina Mouhamad PSL Amine Incha'Allakh
@aichalo4204Ай бұрын
Lambalogue deug la linga wah yeup mais geunal gooor gooorlou nah amena koula diégué di wah ni beug nala mais guissouma lolou wahouma pour yak mais Lou nek si hol feigne si kanam wah NEH na mais hol dafa sori mo waral nitt leundeum amal Tawfekh nak merci 🙏 modou lo mon roi 👑 mon sang 🩸 ❤
@mamepathengom9398Ай бұрын
Merci lambalok 👏👏douma danou mo guene yomba ci beurré 👌 Lac 3 la toudeu toudoul Siteu ✍️ bilahi walahi nagnoufi yalla bayi rék ✍️ di dawe chaque combat ñoulaye gagné par avertissement ngaye jubilé 🤷 bisse bou deugeulé boopam ñou xépko ✍️na xamni tamite lamb ñoko sotlé wayé yalla nopina ✍️
@IbrahimaLô-o6hАй бұрын
Modou sathies moy combat bi
@AliMba-v6jАй бұрын
Lambalok dorr bi guay guay bayi nk 😂😂😂 tu es le meilleur bly
@CheikhGueye-w7lАй бұрын
Modou ya bakh beugue lambalogue yalla séne diam yague
@BassirouSamb-oe6shАй бұрын
Modou anta sa xol raffetna vraiment ♥️♥️♥️
@MaraGaye-t7fАй бұрын
Wa ms ani siteu dawkinda😂😂 bi mani foumou fété dimbali léne ma noum togué kanam gui noumou déf ba néwi woul ak lou mana khéw nioune gni andak ya oustaz dit oussama niokoy balou naniou baal 😂😂
@adamandiaye5829Ай бұрын
Nio bok xalatt siteu fègnoul féne démb ba lègui
@MatarNdiaye-j9nАй бұрын
Alhamdulillah modoulo xlo amba ndam❤🎉🎉🎉
@BakaryCoulibaly-c3mАй бұрын
C’était déjà dessiné pour se combat car Aziz voulait que siteu ramène la couronne devant balla et dieu a fait que c’était pas le cas 😂😂😂 deal bi yakanou supporter roi moy wakh wayé bi demé si balla thiey khirr yallah takhawàl
@Rassoul__Moustapha07Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@yusufmouhamed-8787Ай бұрын
Merci pour votre courage
@adamaanne9473Ай бұрын
Sene ande bie yal na sakh waye ❤❤
@GoraMbengue-f2jАй бұрын
Je supporte BG2 mais demb siteu daffa daw lamb dji yeupp il mérite pas d’être roi des arènes yaye xalé ba paré di daw soyons sérieux il faut avoir le courage de dire la vérité avec ça mounaan balla gaye la sokhla ni rekk layy défaat.
@BayeModouGueye-j2sАй бұрын
Saway bo faralé balla li sounou yone 😅
@GoraMbengue-f2jАй бұрын
@@BayeModouGueye-j2ssaway wakh lènn sen mbeur bi mou am diom tapette na tropp goor dou daw.
@Oumanas5995Ай бұрын
Mane AK yaw gnon yameu
@Mamecheikhndao-pe8nyАй бұрын
Daguay dou do béne fans balla Gaye
@cheikhounagaye9405Ай бұрын
bilahi siteu ne mérite pas le roi des arènes hier
@cico789Ай бұрын
Il as beaucoup changer du comunication de la lutte
Mané daguéne wakhône Modou fakoye door imilié Co mais lolou amoul siteu est in champion que vous le voulez ou pas. Diadieuf Yal bine❤❤❤❤
@BayeModouDiagne-b9dАй бұрын
Lamb yangui commencer Seytané dh😂😂
@mbackefaitdesvideos2271Ай бұрын
Thiak thiak bi rombou lén fofou 😂😂😂
@tallafall636Ай бұрын
😂😂😂😂 lamb yafi nek
@mamadouba7738Ай бұрын
Yalmine thiak thiak 😂
@AlhagieKabbeh-ru7kdАй бұрын
Dawmine kay😂😂😂
@NdeyeSao-y1dАй бұрын
Modou anta m aschalla 🎉🎉🎉
@AmadouDoumbouya-e6jАй бұрын
😅😅😅😅😅 comme Thiak Thiak
@moustaphatraore9070Ай бұрын
❤❤❤siteu mo dann ❤❤❤❤
@MonsieurNdiaye-k9jАй бұрын
Je suis supporter de balla gaye siteu a beaucoup fui modou lo est le meilleur dans l arene siteu doit prendre sa 🎉revanche sur sathies jaime balla gaye mais je supporte aussi modou cest un technicien