Nagnou moytou vaccin yi,toubab dou beug wagni population bi ba paré dignou financé pour gnou avancé.wayer guem na duo bi Sonko Diomaye dinagnou arr population bi.Toubab yi dagno yéwo deh.le mr des ordinateurs pour ne pas nommer BG,ay ndiombé la def ci deukou amita bachen daw.moytouleen daal.