😂😂 mais yén daguén beuri wax😂rek Modou lo khawnalén ray daguén daaw lambji yeup …makhala gueuméwouniou défaite bi
@diopDakar-jw3hn7 сағат бұрын
Bilahi 😂😂😂
@salioudiop71412 сағат бұрын
Ligeen bëgg du gaawa am dh fouhhatti couronne 👑 si modou lo dou gàaw dh😅😮😮siteu daw combat bi yeepp 😢
@ngagnendao9429Сағат бұрын
Békaye nioum nga
@mbayemodou24127 сағат бұрын
Bécay mii nak sitta la faral
@MaremeBeye-lc6hu7 сағат бұрын
Amnaci droit n'est ce pas?
@azur211733 минут бұрын
Naniou gueum Yallah té khamni c'est pas les marabouts c'est DIEU 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Modou Lô késsssssssséé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NdeyeSall-fr3ky5 сағат бұрын
Félicitations à Modou Lo félicitations à siteu la route est longue 🎉
@KhadimoulMoustaphaDiop8 сағат бұрын
Bekaye weroul
@serignethiernoniang69802 сағат бұрын
Ma warou békaye néna lambe dou afairou guérié
@pirlo44787 сағат бұрын
Promoteur yéppou modou lo la nioy commencé khékh pour mou niakk rois bi bécay modou lo la dane faral khaliss molén dieud rek mdl❤rek
@azur211735 минут бұрын
Salam Fii Modou tollou fii leu Yékini tollouwoon. Combat Modou lo Siteu mooy combat Yékini Baboy. Moment bobou lici eupoon ci akhlou lamb daniou beuggooneu détrôner Yekini. Ndéysane Sama champion bi nakk Ciré Khoudia Coumba ak Gaïdèl fofou leu tollou
@pipezensalekh25556 сағат бұрын
Becaye Siteu champion la mais Modou lo mo dominé combat bii en plus Say analyse dafa khawa nekkeu propagande 😅😅😅 koula fay
@mamepathengom93987 сағат бұрын
Bilahi walahi Lac 2 amoul ndaye ci lamb ndakh ni Siteu di beurré rék la Lac di beurré 😱becaye ragal yalla 😱 Siteu noumou deuminer xékh bi té gnou diokh ko 4 avertissement? 🫢🫢🫢 Siteu dawe combat bi yép güéne ragal ko wakh deugue 🫢🫢🫢 thiéye milieu lamb ✍️ wayé yalla bakhna na Siteu dieul Balla inchallah dinagnouko xasse ✍️✍️✍️✍️✍️✍️
@MansourDiouf-m6f6 сағат бұрын
@@mamepathengom9398 lac mo tané ndax parfois mou amsi nul mais défaite lassiy am di
@SeikoumbBandeh4 сағат бұрын
Siteu people are always happy e we with defeat 😂😂😂😂
@chocsevenements89904 сағат бұрын
Becaye mo nekh koi lane mo ame sisouf 😂😂😂😂
@dielkeffelywele8128Сағат бұрын
Siteu a fait 4 appuis.Modou Lo est combatif.C'est lui qui a gagné.
@mouhamedndiaye53378 сағат бұрын
Père becail yangui beug nek nafekheu
@MEUSSDADYLOFFICIEL7 сағат бұрын
Mok domame yép ay nafékh lagne
@ndellasow66827 сағат бұрын
Vraiment
@AbdoulAzizKande6 сағат бұрын
Boulko wakh père ki féne Kate la blh
@AlhamdouLiLahi-wl4cq2 сағат бұрын
Saway becaye limou guiss RK lay wah bayi léne wah diou niaw Modou lô foumou yéksi becaye carrière la boku
@GoldenBoy-ll7yf2 сағат бұрын
😮😮😮
@Misterkal5557 сағат бұрын
Père bekaye iow nakaté khamo lamb dhh
@momo121464 сағат бұрын
Bècaye ndèkètè khamo lamb
@BaAmadou-j9y7 сағат бұрын
Becay dangua farr
@badianetraore5183 сағат бұрын
Tu as raison Modou sa victoire n'est pas propre
@logementetdiversadakar27495 сағат бұрын
Modou devait attendre siteu qui voulait la couronne. Siteu a lutter sur taktik, car il sait Modou est très dangereux. MLo a des problèmes car siteu est gauché et met le pied droit devant. MLo est tjr en haut siteu a tutoyé Mlo
@patrickokioh48103 сағат бұрын
Bonjour à tous, je pense que Modou a remporté ce combat non sur la chute mais sur le nombre d'avertissements. Situé n' a pas combattu, il lui revenait d'aller chercher et diriger le combat, son attentisme a joué contre lui. Finalement c'est Modou qui l'a fait à sa place. Dans ces genres de configuration, il gagner avec la manière avec une chute franche auquel cas les arbitres ont tendance a privilégier le favori.
@ndiayecrypto7 сағат бұрын
Père becaye comme kou niakk xaliss'am ci sunubet bi😂😂
@Modoudiop-b5zСағат бұрын
Bécane mbaye nafekh deugue moye ni nga mana wakhé
@mamesambandiaye10962 сағат бұрын
Merci Père Bevaye le lambalogue Siteu danna Modou 😂 Na Modou delo Couronne bi😂 Doumanako dannko 😂
@fanianesarr3056Сағат бұрын
Bagne Bagne beug rek modou mofi nek❤
@ablayediop57528 сағат бұрын
Siteu topal feulè yaw man nga guènè sakou yiii nane 4 appiii vas la bas
@wellywellydiallo31598 сағат бұрын
Parfois eske becaye d'où mandi car siteu daw combat bi bamou diekhe
@AstouFaye-g4n8 сағат бұрын
Pourtant limou wakh nonou la amna jours yo khamné dodeimé sagn sagn dangay teik kheil ba guénsi
@aitadiene936036 минут бұрын
Bilahi bécaye ya sokhor li nga fi wakh yep dara dousi deug
@EumeuSamb7 сағат бұрын
Père becaye yagui thioubou nk Nioun setane nagn lamb j dh Siteu niou nokk ko bamou daw
@MaremeBeye-lc6hu7 сағат бұрын
Kouniou nokk Moy dem ardo ngen nourou fi yeup di beuri wax
@prince69726 сағат бұрын
Père Becaye parle avec déception sa ce voit que wa akhlou lamb ne veulent pas du couronne 👑 avec Modou Lô le CR7 du Lamb
@ousmanesy672739 минут бұрын
Je ne comprends la lutte. Un sport de combat c'est l'action. Donc commentateurs de la lutte aussi encourage le refus de lutter
@IbrahimaSy-f4g7 сағат бұрын
Nan la nit di dano guen koy favorise li day tah chaque combat du beuré
@omarseye28766 сағат бұрын
Chak combat siteu ni leu contre lac 2 nila wone. Danio fans siteu tei dougn ko wkh deug
@fashionfashion13302 сағат бұрын
Bécaye vraiment bétt ngama khana siteu dalay may khaliss
@seydinaissadiagne436721 минут бұрын
Père bégaye yene aye makk guéne dé léne wakh deugeu ay seytané guéne
@LamineBa-vn3ub6 сағат бұрын
Deug rk kay deug père bècaye wakhal loula nexx ❤❤
@LiveStory-t6h5 минут бұрын
Siteu bou beuré wone dîna am avertissement Boulen gnou sonale waye dem len fowi 😅
@mamedegueneseck26007 сағат бұрын
Siteu fo dieumm😂 mounei mann nieuw tiaw tiaw mounei mann nieuw😂😂
@fall827035 минут бұрын
Becaye khana dafa am loum dioté ak modou lo senegal yakhou na makk yi warona ayé fen khalé yi gnoy fen legui 😂😂
@ElHadjiNiang-f7d7 сағат бұрын
Siteu beure woul combat bi yeup day khar nioukoy attaque thi boy bou beugue couronne bi:Diarama Modou le champion des champions .
@HafizDiagne2 сағат бұрын
Boye békay wakho deugue dé
@AminataNdiaye-cp3nyСағат бұрын
Bécaye balla rek la beugue kii 😢😢
@CherifAdrameDiakhate5 минут бұрын
Becaye legui nak dagua nakh😅😅😅
@youlayediedhiou9797 сағат бұрын
Bécaye tú juge mes sa se voie k tes avk siteu mes modou lo mo beuré combat bi yeup siteu dafa daw ba sonne
@abdoumbaye8584Сағат бұрын
Senegal mo beuri ay nafékh siteu beuriwoufi touss
@chamedaidara57786 сағат бұрын
Bekay mi wakhou naafek dong lafi wakh wakhlen siteu na dem duangui beuré
@RassoulNjaayСағат бұрын
Becay mo ñieme yallah, siteu ban khekh la dominé wa becaye Khana Danga dof