Les conseils d’Imam Kanté à Ousmane Sonko après une polémique sur …

  Рет қаралды 14,181

SeneNews TV

SeneNews TV

Күн бұрын

Пікірлер: 59
@TaphaGueye-u8g
@TaphaGueye-u8g 3 ай бұрын
Diarama Serigne Moustapha sy Maktoum ❤❤❤
@serignediop2527
@serignediop2527 3 ай бұрын
Merci beaucoup serigne moustapha sy l’homme véridique
@ousseynoudiagne440
@ousseynoudiagne440 3 ай бұрын
Yalla n'a yalla Faye leu imame kanté wakh deugue d'où yakh Dara si ça thieur merci beaucoup yalla n'a yalla fayale niou Serigne Moustapha sy dolli ko wér ak soutoura inchallah
@myriammbengue9573
@myriammbengue9573 2 ай бұрын
Wallahi Mashallah Allàhuma Amiiinn inshallah
@CherifmackyDiallo-yk8ej
@CherifmackyDiallo-yk8ej 3 ай бұрын
Serigne Moustapha Sy d'où sa morom dél wakh Serigne bi ta wormal ko
@myriammbengue9573
@myriammbengue9573 2 ай бұрын
Seriñ Mustafâ du saxx lim doon moo epp Seriñ wax degg Yâlla
@CherifmackyDiallo-yk8ej
@CherifmackyDiallo-yk8ej 3 ай бұрын
Serigne Moustapha Sy lépp loumou wakh rek deugue leuh par ce que mom bouy andeu ak nitte principe lay andal ioe bo tegué sa tank si principe d'où am problème mais ayy ragalanté guinaw mom Serigne bi xamoul lolou motakh il faut nguén dioub ta di wakh deugue
@MansourDiop-y6j
@MansourDiop-y6j 3 ай бұрын
Walahi wakh ga deug
@mbayeseck9037
@mbayeseck9037 3 ай бұрын
Serigne moustapha sy al maktoum amoul morom ❤❤❤
@kanemodou2733
@kanemodou2733 3 ай бұрын
Serigne Moustapha Sy yalnafi yague te wer
@fatoudiawsene28
@fatoudiawsene28 2 ай бұрын
Diarama Serigne Moustapha Sy Al Maktoum.Vous avez réussi l'éducation des jeunes.Qu'Allah vous protège
@modougaye1311
@modougaye1311 3 ай бұрын
Merci Imaam kante ❤❤
@boucountasene6755
@boucountasene6755 3 ай бұрын
Wakh le Sonko deug mo gueun nguen di tourner autour du pot.
@mamadoumoustaphaka-hd1if
@mamadoumoustaphaka-hd1if 3 ай бұрын
J'apprécie beaucoup ma maturité sociologique et islamique
@mouhamadousall322
@mouhamadousall322 2 ай бұрын
Seringe moustapha sy point❤❤❤❤
@abdoukarimfall134
@abdoukarimfall134 3 ай бұрын
Serigne Moustapha Sy a dit qu'il a aidé Sonko en lui envoyant des médecins donc il n'a même pas parlé en tant que marabout
@DiopMadaga-pc6bq
@DiopMadaga-pc6bq 3 ай бұрын
Mai gamou Gui tamit gamou Serigne Moustapha la halisou Ken demoufa Lika nieh Lafay wah
@gmeuzcana193
@gmeuzcana193 2 ай бұрын
Déjà *IMAM KANTÉ* rectification, boul ni nit ñangui nan nitou fitna nga, nél amna nit ñikoy waax ,com nimou amé ñiko waxoul.... mais bn *KANTÉ* tu n'as jamais dit de bonne chose sur *OUSMANE SONKO❤* donc bañ dou beugeu 🚶‍♂️ 2ème ma: *S.MOUSTAPHA SY* avec tt l respect kon lui doit,momoul *SONKO* encore moins nit ñi (peut-être sén Talibés mou mooom lén ñom la concerné), limou défal *SONKO* rek *SONKO* défal nako le quintuple.... ex: s'il a réussi a avoir 11 députés c'est en grand parti *Pasfef❤* , té ce qui me dérange c'est pas en réalité l'attaque qu'il a fait a *SONKO* parsk tt ls jrs il en subit, mais le faite de vouloir *DIAXACÉ SONKO & DIOMAYE* Yeufou *SEYTANÉ YOYOU* je dirai même *NAFÉKEU YOYOU* dou thieureum , *SONKO* sou néké nitou ay ak fitna xana téy lakoy soga guiss ? Prqoi mou nangouwone coalisés ak Nitou fitna bi ? *DIOMAYE* sou néké candidat bay done *Président 🇸🇳c'est a cause d'O.S* moko désigné té il pouvait l faire avec un autre il aurait l même résultat 🚶‍♂️ linguén beugone mo sotiwoul,sén yéné si mom mo antouwoul, il a été intelligent pour ne pas tombé dans votre piège 🗳✍........linguén di bañ lañ lén di waxat : *C'EST PAS LES MARABOUTS C'EST DIEU* 🗳✍
@IbrahimaFaye-nx5ny
@IbrahimaFaye-nx5ny 2 ай бұрын
Pur feras face inchalla d ici jusqu au 2029 deuxième tour candidature sonko pour les élections présidentielles
@MamadouDiallo-zh8wn
@MamadouDiallo-zh8wn 2 ай бұрын
Imam Kanté, tu es ambigu et décevant, comme tous les intellectuels mahonnêtes.
@maradiop1147
@maradiop1147 3 ай бұрын
Kham NGA yéne dama Léna yareum li Serigne Moustapha Sy almakhtoum wakh Sakh môme imame bi Sakh mano KO kham lotakh môme do Akh si discouro arabe bi n'a fekhna bakhoul way
@M7B7A4Y6e
@M7B7A4Y6e 2 ай бұрын
Sama domou Serigne Moustapha sy almaktoum doundal weural amal diam
@fatima-gd8td
@fatima-gd8td 3 ай бұрын
Sonko Liguéy so bueugueu mou ague fi nga beugueu boul si oute intermédiaire Wala bok ngay diar si cheikh Oum Mila Serigne bi bolé wone!
@kandemounir6775
@kandemounir6775 2 ай бұрын
Kante est devenu un nafekh soubha Allah c'est grave, pourtant moo fii togone di khass imamou lay dans un débat devant ses talibes😊
@CherifmackyDiallo-yk8ej
@CherifmackyDiallo-yk8ej 3 ай бұрын
Bayilènn bouniou wakhé gamou nguènn diapp ni yalla ak yonentibi rek laniouy wakh fofou politique si diné la bokou ta yénn ta ioe mi imâme kanté xamo Dara nakaté ayy wakhou nafék rek ngua fi wakh guisngua Serigne Moustapha Sy amoul morom sikaw souff si xam xam ak élégance konn nak del modéré sa language
@MansourDiop-y6j
@MansourDiop-y6j 3 ай бұрын
Merci beaucoup frère ❤
@chiekhmbengue-zm9gs
@chiekhmbengue-zm9gs 3 ай бұрын
cest vrais, il a parlé meme pas 2 minutes de politique, yalla nako ar ta samko❤❤
@myriammbengue9573
@myriammbengue9573 2 ай бұрын
Sénégal 🇸🇳 l' sport national c le nafexism
@abdoulayendong6249
@abdoulayendong6249 3 ай бұрын
Sarap ndaye Sénégale yi nio bari wakh detaye rk li Serigne bi wakh thi gamou gui yeup niou tekko feule dieul ben bat rk di rataaaaaaaaaaa isss mayeleniou jiam wakh thi limou wakh thi gamou gui mo gueun
@IBOUDIOP-xp1rk
@IBOUDIOP-xp1rk 2 ай бұрын
Man loutakh enseignement bi Serigne Mouhamadoul Moustapha Sy si Yonenté bi dolen si débat mo guénn si détails yi
@mouhameddiallo9969
@mouhameddiallo9969 2 ай бұрын
Serigne bi Mossoul sauvé ousmane Sonko dé, day wak
@babacar315
@babacar315 2 ай бұрын
Mr Kanté boul nekk nafékhe bo waxé dëgg rék , dinga sédé ni Serigne Moustapha Sy lepp loumou wax ci enseignement ak orientations nguir tabakh nitt ci la déllou,ci aduna ak alakhira .
@marchesor6082
@marchesor6082 3 ай бұрын
Walaye konte rombou nga nakhékk dégue kéne douko ragale mou zab za bina nga
@salioudiop7141
@salioudiop7141 3 ай бұрын
Franchement deg naa dëg😮
@MalickMalick-oe2zl
@MalickMalick-oe2zl 3 ай бұрын
Yaw ya rew ganan moustapha sy domeram serigne moustapha sy dousa morom mou baye domi khatie🐕🐕🐕
@fayepape4648
@fayepape4648 2 ай бұрын
Kouy gamou Dale yémal si gamou. Lousi rakh lénéne Dale dakokoy gakal
@fatima-gd8td
@fatima-gd8td 3 ай бұрын
DEUG mo méti rék té sénégalais dou kouy guawa nanguou DEUG!
@aronadieng5532
@aronadieng5532 3 ай бұрын
pour le senegalese
@myriammbengue9573
@myriammbengue9573 2 ай бұрын
Lii leer ba leer moy 2 mn syr l'actualité politique yeen ko fessel ci gàmmu gi bayi limu jàngalé solo gi sax dafa epp. Degluw leen lu dul extraits de 2 minutes begg nu tympaniser
@kabukoring6788
@kabukoring6788 3 ай бұрын
Bilahi le systeme est profonds. Les plus dangeureux sont les plus insoupçonnées. Imam est subitement un radical depuis que ce regime est au pouvoir
@aronadieng5532
@aronadieng5532 3 ай бұрын
kante seyetane bakhoul
@myriammbengue9573
@myriammbengue9573 2 ай бұрын
Wax leen sonko degg moo gën metti woon na ta Seriñ Mustafâ SY la gisoon ak njabootam. môm sonko teel na bew lool ni baadola ishh
@elhadjidione8938
@elhadjidione8938 3 ай бұрын
Degal journaliste bi doméram dji nâfékh
@DiopMadaga-pc6bq
@DiopMadaga-pc6bq 3 ай бұрын
Gamou Dou dioulli lislaam wahoul Ken ligafay wah
@laminediagana8215
@laminediagana8215 3 ай бұрын
😂😂😂😂
@cheikhndao5331
@cheikhndao5331 3 ай бұрын
Yaw journaliste bi dewoulo Serigne Moustapha Di posé question, wala sa khôl fekhoul.
@modougaye1311
@modougaye1311 3 ай бұрын
Ki journaliste la 🤣🤣 ya mëna fen, far taxul nga waxlo nit ki lumu wax
@sayitekane4064
@sayitekane4064 2 ай бұрын
Kom boke kiné ci nopie Line ci
@elagegueye3310
@elagegueye3310 2 ай бұрын
Yaw imam kantee fanla famou daganee.bogana niou diagalesi istoirou yenentebi 😂?
@DiopMadaga-pc6bq
@DiopMadaga-pc6bq 3 ай бұрын
Wahga Lou Madou Si sabab lou ak dogal
@serignesenebousso3830
@serignesenebousso3830 3 ай бұрын
Dagoorouma gamou politique
@SheikhEbrima9902
@SheikhEbrima9902 2 ай бұрын
Imam kanté tu racontes n’importe quoi
@modoudiop4863
@modoudiop4863 3 ай бұрын
Yaw nopil serigne Moustapha sy dusa morom
@badaragueye9137
@badaragueye9137 3 ай бұрын
Attaque, yaw con nga rek
@laminediagana8215
@laminediagana8215 3 ай бұрын
انت مجرم
@mamadouthiaw2694
@mamadouthiaw2694 3 ай бұрын
Kanté bayile thiakhane.Moustapha sy avait son propre candidat et son candidat n'a même pas 1%.Imam Alioune badara Ndao et sonko ont fait le travail plus le peuple sénégalais (la jeunesse,les islamistes et les alliés).soyez serieux
@Brou-xp9vu
@Brou-xp9vu 3 ай бұрын
Kanté mooy naféq deug ! Moo fi guiss dualité. Moustapha Sy na démal boppam ci élections yi di gneuw le 17 novembre. Su booba lépp ay léér !
@sellgaye4279
@sellgaye4279 2 ай бұрын
Imam yà nàfekh s Moustapha limou wakh lép si yonéntë bi saw avant mouy toud sonko ci 2 mn yisi fin bi dòko déglou ba paré dòga atté kholàtal sa imam gui té khamni mandou laniouy khàr si yaw
@cheikhndao5331
@cheikhndao5331 3 ай бұрын
Yaw journaliste bi dewoulo Serigne Moustapha Di posé question, wala sa khôl fekhoul.
黑天使被操控了#short #angel #clown
00:40
Super Beauty team
Рет қаралды 61 МЛН
Quando A Diferença De Altura É Muito Grande 😲😂
00:12
Mari Maria
Рет қаралды 45 МЛН
Les conseils de Barth à Sonko : "S'il m'avait écouté il ne serait pas en prison"
5:35
L'invité de la RFM matin | Amadou Mahtar KANTE : Imam / Écrivain
18:23
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 10 М.
Freedom sit- in : Imam Kanté recadre les féministes
12:10
SeneNews TV
Рет қаралды 272
黑天使被操控了#short #angel #clown
00:40
Super Beauty team
Рет қаралды 61 МЛН