chapeau bas Ama Baldé débordant de modestie . Ce garçon est HUMBLE Je le respecte et l'aime beaucoup en tant que lutteur
@desreidieng44135 ай бұрын
victoire a notre cher père faalaye que nous ne cessons de prier balde Dina baakhe
@MOUHAMADOUMOUSTAPHANDIAYE-q7i5 ай бұрын
Dieulale Fran nopilo ko mbeur félicitations ama ❤
@MalickSarr-iz3rr5 ай бұрын
Vraiment ama tu as bon cœur ❤️
@Papyvuitton195 ай бұрын
Ama rek laniuy topp 😍😎💯🙏🏾
@Yetta2215 ай бұрын
J’ai commencé à aimé ama baldé depuis son combat avec modou Lo. Modou lo la faralone ndax moy sama mbeur mais j’ai découvert ama lors d’un interview il est très posé et kou niaki niane leu vraiment yalla nako yalla taxawou ça se voit que nieup la yéné diam félicitations Mbeur liy nieuw mo dak Inchalla ❤
@fatoubintoubalde855 ай бұрын
Ama yéé ❤❤❤sama domou baye
@MouhamedGueye-z1j5 ай бұрын
MACHALLAH YALLA NALA YALLA AAR YIIR LE SAAM LE SANGUE LE SOUTOUREU TETE LE... MAYLA AY NDAM YOU BARI...🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@bayemorgaye33225 ай бұрын
Peulh bii kassé ❤❤❤
@gueyelabsolu58895 ай бұрын
Amaa Balde ndiou Daxeu xékh Senegal 🇸🇳 Molène Doumeu Kidou Nith 😂) « Malick NIANG) Tapha Tine) Gri Bordeaux) Vré Gayné nga félicitations ❤Ninga Beraii Tay Dji boko continue Mbeur Mounoula Dann Senegal 🇸🇳 C bien Nith Boula Mbolo bou bary Topou Dangalènuy Respect c bien sa fans yeupou contane Tay Mbeur Bonn continuation ❤️💚❤️💚
@matarmboup-zo5yf5 ай бұрын
Yallna yallah dèffalla diame Ama contan na this yaw lol bilahi❤
@Mbaye._pro5 ай бұрын
Ama yée❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@championblinde27915 ай бұрын
Yaniou siguil dh❤❤
@dabojr97495 ай бұрын
Félicitations Ama
@latifthiam11145 ай бұрын
Ama geuneule yoke entraînement yi sou eta de physique bi forme bi mome tamit lothi geuna yoke mou geuna bakh aye ndami ndame domou pikine 💚♥️
@serignecheikhdiouck12375 ай бұрын
Felicitations ❤❤❤
@iboubayefall78485 ай бұрын
Ama yée❤❤
@ibrahimadiallo2195 ай бұрын
Ama seul félicitations champion pir
@diop35755 ай бұрын
Beg nane nioune fans balla gaye yi di nianal balla gaye ll yallah defal ko ndamm si kaw tapha tine ❤❤