Kou nekk akl lilayy danell c vrai... djiguenn da warra sangou ba sett soll lou yiww mourr ayy thieurreumm.. tokk yorr sa kamil wala sa crouss... wala tokk si natt wahtann si yalla ... c ça le plaisir
@alousseynouba4230 Жыл бұрын
C'est très important de faire savoir à certaines personnes votre débat est impeccable !bravoooo
@maodosalll6068 Жыл бұрын
Amna solo
@BaFariy Жыл бұрын
Amna solo way❤❤❤❤
@dembatoure8046 Жыл бұрын
Notre pays vamal
@awandiaye7510 Жыл бұрын
Bilal ay thiagua kesse gni gno raw mbodia mbaye
@humanityissuffering7464 Жыл бұрын
Sinaka
@humanityissuffering7464 Жыл бұрын
@@awandiaye7510 how mom kudem munulo sa borr
@patheseye1634 Жыл бұрын
Yén yénay encourangé ame dieukeur ame far yéna bone
@aichaalarbaallf4359 Жыл бұрын
Pathe gni loungouy wakh ak yaw bokoul boul ngèneu si sujet bi gni daniouy yètè
@modoukane8650 Жыл бұрын
Kou amagoul diabar si 2023 nagua takki diabar takk par force avek plaisir😂
@baboumomo6643 Жыл бұрын
Yalna yala mosahl si szytane
@IbraNdiaye-d9c Жыл бұрын
merci tata rama
@amadousamake416 Жыл бұрын
Am na solo 😅
@ablayefayecv6xi Жыл бұрын
Ay domeram ngén
@bintoudiallo3973 Жыл бұрын
Yénn wolof yimeuno lénn bayi wakhou kharafalndakh khamo lenn si darra boulénn wakhni kharafal dagnouye dague lépp manedé33ans de mariage machallah té sama wadji néna khalatul take kenene
@MomoMbodj95 Жыл бұрын
Aye way changer lène débat bi stp🙏🙏 🇸🇳🥰🤔On est en 2023 Naniou Wakh nouniouy def badèfare Sénégal pour mounïaw done le mieure Pays du Monde🥰🥰🥰débat yii mome doyall nagne 😔😔thie seuck vraiment guène🙏 balma
@CheikhNdiaye-ij3xk Жыл бұрын
Tankeu macky sall mougifi dra dou sangé
@bathiembaye1199 Жыл бұрын
gouvernement macky sall !!! li moy résultat bi, sexe, drogue, sacc, scandale !!! ndole bou mètti
@deugrek3312 Жыл бұрын
@@CheikhNdiaye-ij3xk lou Léér Nga wakh
@alassanethiam2784 Жыл бұрын
Weur lén wallahi billahi
@bintoufall3815 Жыл бұрын
C vari
@mamadoundiaye4634 Жыл бұрын
C rigolant mais aussi c important
@fatouboroaidara2477 Жыл бұрын
Salam,mais les hommes lane Molène idii si whatane nous femmes yii???😄😄😄du courage mes sœurs merci pour vos conseils, dieureudieuf, machalla.
@Dollarvelli2019 Жыл бұрын
Daniy diangue
@fatouboroaidara2477 Жыл бұрын
@@Dollarvelli2019 moo louguene Di diangue nakk???
@Dollarvelli2019 Жыл бұрын
@@fatouboroaidara2477 afir yi khana
@fatouboroaidara2477 Жыл бұрын
@@Dollarvelli2019 ça veut dire quoi ??
@diagnemodounaar9613 Жыл бұрын
@@fatouboroaidara2477 laa lanté bi
@dioufmareme290 Жыл бұрын
Aywaay yangui dadjie waay Nono. Adada doyna ihh
@diopfaya3471 Жыл бұрын
Sarap ndayi thiaga rek
@seydoucisse6219 Жыл бұрын
Thiaga international
@ndiougamar2202 Жыл бұрын
Aï vrai koba
@NdeyeramaWade-w2z Жыл бұрын
Rama j't'aime 💋💚❤️
@mouhamadoumaniangsylla9302 Жыл бұрын
Taate kessé yoroul goor 21e siècle lagnu nekk gnune goor sohla nagnu jiguen bou am ay valeurs sûres meune nio yaral souniou doom nio hamni so guenné sakh sa khel daal mais vulgarité day wagni valeur jiguen. Souniou Yaye yi wala Mame yi rafett jiiko wala kaddu motahon gnu diour ay walliw nitté toppu yonnu siratikhal moustahim mais cette nouvelle génération indiscipline tokk si média wakh Lou niaw rek lepp lou bonn ngen beugg ko bakhal Lou bakh ngen beug ko bonnal. Svp reewmi kousi nekk amnga part de responsabilité pour l'avenir du pays cikaw gnuy diangalé Lou bakh comme ça kouko degg lou meunsi diarugnu niko Yalla ak Yonnent bi beugué. Roy len si Sokhna Diarra Bousso ak Mame Fa Wade Wellé... niognu cilou bakh lagnu nekon ba sen tourr dou faay abadane. Boullen promouvoir Lou bonn cos Yalla dafa binneu té Yamaléwoul cos lingen di digg lé moy jiguen kousi amoul geum wala bopp bu bakh dangay khepp sa dieukeur am faar wala tass outti kenen pour koumpa gui. Adouna dou keur naay rafett mognu jiik. Yalla watié fi Tawfekh ak Taïssir. Dafa nekh guis sa yaye wala sa makk ou kousorri si yaw guenné kaddu bou am nieurigne daley sagaal fepp mais wakh Lou niaw pour gnulay bayi khel amoul nieurigne. Ay Sénégalais nagnu makk gni danio bakhon mtx sen seey yi daan yagg mougn bangen diouddusi nakh niolen mounial bobou Goor gni Allal beuriwoul comme de nos jours gnu mougn ko mais legui royatoulen Mame mtx dara yaggatoul kou beug doom bougnuy simmil dalleu yakoy seey✌🏽... comme magg fin mais ngen diouddu fekk lepp am fala seey waron geunneu am valeur mais pas sexy kessé plaisir dousi neggu seey kessé nakhté yaggoul... Amna louko eupp nieurigne fouf bayilensi khel. Magui dieggalou boudé wakh lafi Lou niaw si man la bou raffeté souniou borom lanekh ngir dellosi khel yi rek...❤🇸🇳🙏🏿
@Deathtomyennemis Жыл бұрын
Saway degueu rek nga wakh gni douniou khalate dee amouniou beneu valeurs
@awandie Жыл бұрын
mande djiguene la mais damanane plain bou barri dafaye soukhali Soukhe wante dafaye wante daye. nassakhale roukh.naniou dellou si linoou sounou borome maye.adouna yaagoule..Nous sommes des etres naturels pas des inventions mecaniques ,le corps a ses limites,l esprit a lui aussi besoin d etre entretenu par le plaisr qui emane de la communion avec le corps dans leur relation avec le createur..
@ndiawarsarr9952 Жыл бұрын
Machallah saway binda nga ☝😅
@fatoumatadione2434 Жыл бұрын
@@ndiawarsarr9952 walay binda😂mais deugue pir la wakh
@khadymbodji3703 Жыл бұрын
Machalla bien dit Sénégal li moléne tardel foléne fek débat rek.seuye soutoureu la lathie nguir diour waliyou.k'allah ns compte parmi les femmes du paradis.niou diéme roye si yaye aïcha AK khadija........
@ngomsanou1990 Жыл бұрын
Mahalla
@momofara4026 Жыл бұрын
Amna solo machalla!!! C'est de l'éducation sexuelle...adouna dangaye diangue leupe rawatina wallou sèye aka ame solo
@Nature_Voyage83 Жыл бұрын
Walay
@diagneafrica8467 Жыл бұрын
Ana goorgni déglou comme mane 🤣🤣ndiaff do kholé 🤣
@salegaye9816 Жыл бұрын
Kaylen wokalma sama lelbi
@mamadoucisse4507 Жыл бұрын
Yéna thiagga waay
@boromebakh28 Жыл бұрын
2023 monde bi nékk si développement, vous nous parlez de plaisir entre homme et femme vraiment c'est déplorable 😪
@YETHIE Жыл бұрын
Lol 😆 🤣 😂
@MomoMbodj95 Жыл бұрын
Vraiment
@boromebakh28 Жыл бұрын
@@MomoMbodj95 gni dagniouy diékhal xol quoi😪
@bathiembaye1199 Жыл бұрын
deug Bo xamnè débat bi moye ndèye guèye ak ndiolè dioubonaniou, ouzin Keita ak pawlish kou meun !!! you mèlni boumou lo bèèt
@deugrek3312 Жыл бұрын
Plaisir motakh Nitte Djouddou , bassi animaux Yi, Ñépe Meunouno Bokk Di Wakh Ci Développement. Sans Plaisir Deukk Développé. Wakh Léne Ak macky sall Mi Tardéle Deuk Bi😂
@thiawfoot5217 Жыл бұрын
Sen leufal ndeye way Sénégal soxla wol li actuellement
@mouhameddia4149 Жыл бұрын
Li baloumaléne ko bilay
@brigadeantibidah2911 Жыл бұрын
Séne émission amena solo Machallah Bonne continuation.
@bambagaye6133 Жыл бұрын
Ndawsi nenaaa deuggg leu
@reallion5832 Жыл бұрын
Il faut discuter en couple pour savoir les points sensibles c'est la solution.
@lasuite5917 Жыл бұрын
Ay thiaga rek
@thiernoniang7117 Жыл бұрын
Incitations à la débauche par média interposée. Voilà où nous en sommes.
@modouseye2757 Жыл бұрын
emission diaga
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Deugu leu bi
@lhommefort973 Жыл бұрын
Sénégal mom té niouko arraw araw bou séw nieup goukh ? Rewmo khamni wakhoum taate rk oh leufall ndey li way 💔
@mathalogue3436 Жыл бұрын
Sénégal tat môles sonal
@lhommefort973 Жыл бұрын
@@mathalogue3436 billae motakh khalé yi Yep tit
@mouhamedousambe1721 Жыл бұрын
Niak lounguéne wakhléne si liy dokhal réwmi.
@brigadeantibidah2911 Жыл бұрын
Sa waye fi theme bi affaire negou seye donc bo bougué déguelou lénéne démêle fénéne isch
@abdousaine1187 Жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 wakh deug 👍🙏👌😎
@CheikhDiouf-wv9if Жыл бұрын
❤❤❤
@FayeMamadou-d1w Жыл бұрын
Le pays est en chômage et vs parlez de plaisir
@bathiembaye1199 Жыл бұрын
niar gni niome !!! ay vraies bandilaniou
@omarba3621 Жыл бұрын
On est en 2023 comment développé laniou wakh Géneu si ndoll bou meti bi mais non tate rek. Mais malheureusement au Sénégal mariage legi tate kassé la kakanté rek laniou wakh té lolou rek dou seyy
@yayadiawarasane5000 Жыл бұрын
🤣🤣🤣😂😂😂🤣 Omar bouma ray way 😂😂😂
@ndeyediankemanga2836 Жыл бұрын
🤣🤣🤣😅😅🤣
@samiab.7475 Жыл бұрын
Je l’aurai pas dis avec vos termes mais je suis tout à fait d’accord avec toi.
@citoyenavatar3021 Жыл бұрын
Ca fait parti du développement vois aussi.
@glasgowhits8585 Жыл бұрын
Guisgua data ak Koy rekk data ndeye lii
@mamadousagna7514 Жыл бұрын
Ame dieukeur ame far gua tass bouléne nous sonnale
@modousow1900 Жыл бұрын
Yena ayé de li leeup âme n'a Sénégal
@tupacdione2293 Жыл бұрын
Machallah👉👂
@patheseye1634 Жыл бұрын
Kou ame dieukeur khélal waral nékk si bénén goor bamouy éssayé nane ki mo meune sama dieukeur
@diordiakhate7828 Жыл бұрын
Il faut des moyens pour être belle
@bounadieng1505 Жыл бұрын
Li lay wakhtanné si sama tiktok bouna alboury Dieng abonnés len foofu expérience lalen di partagé
@civisme8953 Жыл бұрын
Femmes you niak diom.niak ay valeur.di pouss yèn femmes yi niouy Moy .domeram deug
@baboumomo6643 Жыл бұрын
Xana amoulen ay doum
@jaamupyalla9132 Жыл бұрын
Portant xeeto wakhtaanyii day niroo ak lo am solo pour certains individuelement mais bokkonathi liy yàq société bi globalement
@awandie Жыл бұрын
gores gni sakh legui danio commencer di neiw dole ndakh plaisir bou Bari daye lekeu soukh newel roukh.Khola legui ko wakh mou ni yokkeu awra,new katane. Poison laniouye rakh si soungoufe yi dilene ko diokh.sou yague nak sidittes yeup nassakh.
@novioloco7078 Жыл бұрын
Senegal mo beuri thiaga kholale ma gni rek
@lepanafricaniste9898 Жыл бұрын
Hamon si Dara sah
@mathalogue3436 Жыл бұрын
Sénégal tat mo len sonal
@diagnemodounaar9613 Жыл бұрын
@@mathalogue3436 mouy gor di djigen mtx deuk saay bou taker taat moko taal
@humanityissuffering7464 Жыл бұрын
Khamo dara
@humanityissuffering7464 Жыл бұрын
AK yow molen setan
@mamebassirouthiame9780 Жыл бұрын
Thiaga you bonngén
@sidilaminebadji1347 Жыл бұрын
Très intéressant à apprendre le juste équilibre est là
@Nature_Voyage83 Жыл бұрын
Les mamans apprenaient ça aux filles dans nos traditions le jour du mariage.
@serignembacke9485 Жыл бұрын
GNi dal Moy lolou
@amadoudiop-l4l Жыл бұрын
bolen takhawalo ba yakkou point yepp fatou gueni weur plaisir founioukoy dieule bayilen goor yi te rey sen ndao
@falloundiaye3120 Жыл бұрын
Sénégal d’où avancer télé yii ak site internet yii dougne wah moukou nagne laniouy def ba developer Mai’s Dara , cnra di khol douthii wah dougne wah moukou lou am chance
@maikellgomis6516 Жыл бұрын
Thiaga rek😂😂😂😂😂
@falloundiaye3120 Жыл бұрын
@@maikellgomis6516 té gniiy wah amou niou Dieukeure
@maikellgomis6516 Жыл бұрын
@@falloundiaye3120 borom dieukar kay sañul li 😂😂😂
@cheikhououmarndiaye5623 Жыл бұрын
salam bég si yéne Mane dh Limay Ray Moy chaîne you mbir yoyou may guis mbir bi AK ndig lolou diko khôl rk gagné nama
@matargueye7200 Жыл бұрын
Yenn deuke bou kate dayame bi niouye khole nounsi guenne senn emission you kate dayame yi
@awandie Жыл бұрын
Gni nio takh sounou gors gni meunouniou fippou.Kou yaakar niou gueneu khekhal askane wi dingaye nakh sa boppe.
@papendiaye3400 Жыл бұрын
Mdr
@falloundiaye5619 Жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣😍
@amdy879 Жыл бұрын
SALAM AMOUL YAKAMTY DOUCEMENT TECHNIQUEMENT UN VRAI HOMME DOIT SAVOIR LE POINT G DE SA FEMME
@lhommefort973 Жыл бұрын
Ay mére you thiaga Thiammm kham nguén ni ray nguén sén dom yi té déwougnou chiiiiiiim
@matarmbaye4955 Жыл бұрын
Liguene di wakh mo nekh kontanna si yen degeu reck mo nekh
@diopfifi4937 Жыл бұрын
Yaw low déff si déba djiguen??
@djibydia6381 Жыл бұрын
Bollène niaméwoul liguene wakh diaroul def sen émission
@soukayesamb6002 Жыл бұрын
Numéro
@aminadiongue7485 Жыл бұрын
Yaital gor kayyy mbetei Bb djiguene dal mo sonu🙄🙄 nioune kougnouy yeital
@mohametthiam4500 Жыл бұрын
Machala amna sola lolll
@mbayefall8311 Жыл бұрын
Débat bi ci développement labok. Li amna solo loooole.
@victordacosta3537 Жыл бұрын
Ok a des enfants Ne les encourage pas, ce débat est une discussion pornographique Elle est purement satanique. Jésus Christ a dit : que par ta bouche que tu seras jugé, par ta bouche que sera condamné. Une bouche qui proclame le nom de dieu ne doit pas sortir de mauvaise dans sa bouche... C'est débat purement pornographique (GNI DAGNOU DIAWOU C'EST CLAIR EST NETTE)
@milkmilo4082 Жыл бұрын
Koumou intéressé woul gissga lignou titré loy kat ndém sétane bou léne gnou sonal way sétane n'a geine teudj séne gatt yi
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣2023 bi plaisir la 🤣🤣🤣🤣🤣
@djonabi1085 Жыл бұрын
Niom Amnagn Dieukeur Wala Ay Maguétoum Koba Lagn
@elzobibaboypolyvalent Жыл бұрын
Wakhou katanté rék molén niorr sén data ndaye rék
@idsmovengo5471 Жыл бұрын
Yéne ak thiaga guéne vulgaire séne leufeul ndéye
@ousmanesow5625 Жыл бұрын
C'est pas possible c'est quoi ça
@makhoulawssa7474 Жыл бұрын
Ayer domeran you BOn iiii
@Nature_Voyage83 Жыл бұрын
Elles sont renseignées dé😂😂😂😂
@modousow1900 Жыл бұрын
Calibataire dal nakate dou touss fay ma takki diabar si 2023🤣🤣🤣
@dioufmareme290 Жыл бұрын
Guaawal bala ngay tarder 😆😆😆😆😆👏🏼👏🏼👏🏼
@cheikhdiop9932 Жыл бұрын
Estanbi sene leuf yagui toyy hipou
@falloundiaye5619 Жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@seyeabdou2696 Жыл бұрын
Waw yen nounguen def ba kham façon goor yi yepou hhhhhh
@boylebou3230 Жыл бұрын
Pourtant guiss nguéne titre bi dh avant nguéne diko lire sétane ba paré nieuw diniou sonal ak ay wakh té yéna dakha sétane prono
@daffalrrrnagne6089 Жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@tid6724 Жыл бұрын
Lifeul ndeyi deuk bi , tate rek ,chetetete parlez nous d économie, de santé, de technologie, ces guignols poudeurou melni ay golo ....no senegal j ai pitié bilakhi
C'est un monde important qui fait partie de la vie
@brigadeantibidah2911 Жыл бұрын
Vous êtes personnes très difficiles, il faut que vous compreniez que chaque chose à sa place ici le thème ça parle de la vie conjugale si ça ne vous intéresse pas allez faire un tour dans les autres chaînes de télévision et y'en a beaucoup. Sache que ça aussi fait du développement du pays.