Li niou mayy chance moyy al khourann bi niouy diangg chaque jour té niom amouniou lolou na niou sente yalah bou bakh alhamdoulilah 🙏
@AbdoukhadreLô-p8c13 күн бұрын
Wallhi wax nga duege dh
@DaourThiam-o3m12 күн бұрын
Wallahi ndaysann Naniou dellou si Yalla 😢😢
@ngoneseye699411 күн бұрын
😊Aa
@LamZani10 күн бұрын
Alhamdoulilah ❤🙏
@ombolinesigasene574610 күн бұрын
tu te trompes il est temps de croire en Jésus-christ. c'est sa parole (la bible) qui s'accomplisse voir l'apocalypse de Saint Jean. tout est écrit. dans ce monde tout genou fléchira et toute langue confesera que Jésus-christ est seigneur. même cela va s'accomplir. ouvrez vos yeux il est temps. merci
@SeydinaAbabacarSarr-f3w15 күн бұрын
❤une message à la jeunesse ❤naniou délou wat si yallah ❤
@BOROMLERGUICISSECISSE15 күн бұрын
Wallahi yaw kou bakh nga yalla nala yalla samou sy barkè sarigne touba ❤❤❤❤
@MaxSow-zd6gn14 күн бұрын
Amine ya Rabbi machallah bonne continuation ❤❤❤❤
@issefall524214 күн бұрын
Sama mbok si barké Serigne diw Si khétou BOKALÉ la moytouko 👍
@BOROMLERGUICISSECISSE14 күн бұрын
@@issefall5242 merci beaucoup
@elagegueye331012 күн бұрын
yalla dou def daea di bsrkee ken yopoulrn feleu te dem diagi
@BOROMLERGUICISSECISSE12 күн бұрын
@@elagegueye3310 yaw lane moye sa xam xam
@daoudagueye759815 күн бұрын
Yalla rek Moy buur bil lahi ❤🎉
@daoudagueye759815 күн бұрын
Merci bcp pa Assane Gueye 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@CheikhNdiaye-v8r14 күн бұрын
Merci beaucoup pa Assange pour se message ❤❤❤❤❤❤❤
@samadseck597914 күн бұрын
Merci beaucoup mon frère Yalla na sa djiamou yague si barke Qassida
@Hazz-Malick-Maodo77714 күн бұрын
Machallah Pa Assane DIAADIEUF kadouyi amna solo lool way Yalna Yallah doli Diaame barké TAAHA❣❣❣
@FallouThiam-v2p15 күн бұрын
😊 Machallah🥰way❤pa assane yalla n'a sa diamou yagu👍 jërëjëf
@fatimakane246315 күн бұрын
Deug dou rombe nopou machalah kaddou yi amna solo yalna yalla tek si yonou ndioub
@Ndpatriotes2414 күн бұрын
Machallah Pa Assan Yalnaniu Yalla Dioubel Ci Siratal Moustakhim Défal Niou Moudjou Go Rafét Amine 🙏❤
@DaourThiam-o3m12 күн бұрын
Wallahi ndaysann Nanou dèllou si Yalla mo Fi nek d😢😢
@OusseynouCisse-y8x14 күн бұрын
Pa assane longue vie à nous
@AssaneMbaye-uy5ej14 күн бұрын
Merci beaucoup pà Assane 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🤝✅💯🧏🧏🧏
@xamxamle959513 күн бұрын
جزاكم الله خيرا يا أخي الكريم على هذه النصائح
@AblayeSeck-mb1jw15 күн бұрын
Vraiment merci beaucoup frère message bi âme n'a solos trop 🙏❤️❤️
@salioundiaye99219 күн бұрын
ماشاء الله تبارك الله فيك
@OUSMANESADIOKa15 күн бұрын
Merci beaucoup Pa Assane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@yayebintagueye195011 күн бұрын
Masha allah c genre de message on en veux adouna dou keur kouko diap diapoule kéneu yalla borom bi khir niou cii bopam
Machalla pa assane message bi amna solo yalna niou yalla samal bopam yalla dioubal niou ték niou si yonou si ratal mostakhim Amine yarabi 🙏 ❤️ ❤❤❤
@salifgueye129215 күн бұрын
Boy wah nit gni né aduna bi diékh neu niou méré leu alors que li yoninteu bi psl wahone yép niounkoy guiss 😢😢😢 Naniou délou si sunu borom
@babacarbiaye241014 күн бұрын
Merci Pa Assane yal na sa diam yag
@massatalam77513 күн бұрын
MachAllah si conseils yi, yalnala Boroom bi faye. Tu es jeune mais très conscient des enjeux du moment ❤❤🎉.
@BayeibraBakhassida-de9wf14 күн бұрын
Merci pa assan amna solo lool deugu re nga fi wakh yalla na la yalla sam
@BiouCamara14 күн бұрын
ماشاء الله تبارك الله عليك سيدي تبارك
@NdiobaMbaye-e7d8 күн бұрын
Mon frère bien dit notre prophète (psl)nous avais prévenu qu'a l'approche de la fin des temps les phénomènes naturelles seront multipliées a vu des tremblements de terres et autres c'est grave qu'Allah nous guide 😢
@taphaniang534214 күн бұрын
Inchalla yalla bakhna métyna torop bly wolaye yalla bakhna 👏🏿👏🏿👏🏿
@kalidoufall09913 күн бұрын
Merci frère Pape, à partir de maintenant j'ai laissé 1xbet. Liguey reck inchallah ❤❤❤. Encore une fois Merci. Mes frères et sœurs laissons les svp 😢😢
@kalidoufall09913 күн бұрын
Adouna wonaa khardarr , Wadé jam kebab jam
@khadydiop779411 күн бұрын
Yalna la Yalla sammeu té barkel la 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
@abdoundoye158514 күн бұрын
WALLAY NDEYSAN DAGUA BAKH REKK MË SOULA NËKHONE LU YËPP DOULATHIE FËKK MË YALLA SA DIAMU YAGUI🙏🙏
@helpeventsofficiel77712 күн бұрын
Khana nda nga fatei goor gni yangui wakh si jiguen gni rek et oci ceux ki sont riches et n'aident jamais les pauvres lolou mo gueneu grave
@jontadoproduction928413 күн бұрын
BEUG NA TROOP INFLUENCEURS YI DEFOI NIOUY DELO NIT GNI TI YALLAH MACHALLAH❤
@DembaDiop-mj1ob14 күн бұрын
Free Palestine ☝
@rokhayaniang236910 күн бұрын
Machallah sama dom yalla na yalla fayla té barkel jazaka'allah khayrane baraka'alla fikoum
@SambaDiallo-l9f14 күн бұрын
Ndayssane los Angeles fouma gueuneu beugue si Amérique ❤❤
@PamodoundiayeOuvrié11 күн бұрын
Chapeau grand bi sa ligueye rafetna mancha allah yallna yalla barkél takhawoula ❤❤❤
@MountagaDiallo-wd6sl14 күн бұрын
Fatté ligui amna solo bou bakh جزاك الله خيرا يا pa assane
@AliouneBa-y2u14 күн бұрын
Ohhh un message très émouvant c'est très fort 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@PapaBabacarDabo-x9x15 күн бұрын
Kudul yalla mouno dara ☝🏾
@MouhamedSylla-ry2qm11 күн бұрын
buñou bayi woull Palestine 🇵🇸 dina demm ba sén propre problème doylén ❤ yalla rek mofi nekk ❤
@ombolinesigasene574610 күн бұрын
où est le rapport Palestine c'est comme le Sénégal ya des chrétiens et des musulmans. hors sujet
@ElhadjiDramé-b4f14 күн бұрын
C très important Ce message ❤
@iss990114 күн бұрын
Messages à la jeunesse sénégalaise pa assane yalla na la yalla diapalé si barké mouhamed
@youssoundiaye514015 күн бұрын
Merci beaucoup pour les infos am na solo trop man déh lomay sétane actualités bariwoul mais mbo dougala vidéo rek maguis ko merci beaucoup amal diam rek contant nan si yaw vraiment
@MamadoutidianeGueye14 күн бұрын
Pa assane yalla na yalla goudeul sa fane conseil rafetna trop guayi bayi lene khel thie limouy wakh ❤❤❤❤ta guene di khalate souba❤❤❤
@sambagueye609513 күн бұрын
الحل واضح جدا وهو الرجوع إلى الكتاب والسنة والتمسك بهما والعمل بهما
@alassanesylla614913 күн бұрын
Masha'Allah yAllah nala yAllah sameu té gouddal saa ayes fane c un très bon rappel sa genres yii lagnou sokhla🙏🏿🙏🏿🤲🏿
@babacarniang438913 күн бұрын
Deugggg leu merci pape assane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AdjiLo-dm9qo10 күн бұрын
Alhamedou lilaye alhamedou lilaye santé yalla bou bakh 🙏💯😭😭😭
@mariemdibba20276 күн бұрын
Machallah amna solo free yalla nagnou Yalla boleh same❤❤❤❤❤❤
@ndiawarsarr995212 күн бұрын
Machallah nouveau abonné ❤❤❤très pertinent
@astouseck95317 күн бұрын
Sa wakhe refetna Yall na yalla Faye la yiwe dieuradieuf 🙏♥️♥️♥️💯
@YacineFaye-r9r13 күн бұрын
Pa asane li ngay wakh amna solo bilay yalna nga am diam boubakh inshallah
@coumbasounandao13 күн бұрын
Allahou Akbar. Yallah nounou yallah tek thi yonou siratal moustahine Thi barké seydina mouhamed sallahou aleyhi wa Salam 🤲 merci pa assane qu'Allah azwajal vous garde 🤲 amna solo torop
@OmarDiallo-bd6jp14 күн бұрын
Wolahi wakhe gadeg continent torop❤❤❤❤❤❤❤ Yalahe na la yalahe defal diamou Mayela goudou fan ak wergi yaram
@issaba425714 күн бұрын
Merci beaucoup Pa Assane Pour ces conseils Nala yalla fayy Dieureudieuf
@khadydiop779411 күн бұрын
Yalnala Yalla fay yiw, sammeu la té barkel la ak dioullit yeup 🤲🏾🤲🏾🤲🏾 amna ndiarigne mâchaa Allah tabarakAllah
@NdeyeSeye-j8u8 күн бұрын
Merci beaucoup Mâcha.allah amana sollo❤❤❤
@cheikhndiaye43315 күн бұрын
Tu as parfaitement raison et surtout d'arrêter aller voir les marabouts et respecter les parents et respecter les religions Pascal nous sommes des musulmans ☝🏾☝🏾☝🏾☝🏾☝🏾
@bintatoure749 күн бұрын
Kou bakh gua Yallah na Yallah defal diam ak beppe mbolemou dioulite❤
@BabacarGueye-w3g14 күн бұрын
Vraiment dom bay vous avez parfaitement raison que Dieu protège tous les continents du monde surtout l'Afrique plus précisément au Sénégal. Merci à vous dom bay. Contente si yaw
@BounamaNiang-e8s15 күн бұрын
Merci Pa Assane
@baelhadjiabdou498213 күн бұрын
Machallah yallana yalla fayal yiw té khiir gnou thi loubakh ak beug Loubakh barké Nabil Moustapha PSL
@cheikhahmedtidianegueye37014 күн бұрын
Je pense que moussouma commenté saye vidéos mais aujourd'hui dina ko déf parce-que linga wakh c'est très important yalna yalla same té nangoul niou
@yacinesamb306613 күн бұрын
Machallah ya bakh Diadieuf yallah na yallah fayela yiww ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@CheikhAidara-fv3ww13 күн бұрын
Machallah ❤️ ya oustaz
@SidyCasa14 күн бұрын
Machallah ❤ Pa Assane l message est bien reçu 👏👏 yalna la Yallah takhawou 🤲té mayla goudou fane 🤲
@kfkmouridisme118614 күн бұрын
Ndeysan ieo d yay royo kay deug yay vré influenceur deug nak yalna yalla fay la man d naw nala loom walkahi hasimi yalna yaalla fayla ta sammou la
@MbayeNdiaye-df7gm14 күн бұрын
Merci beaucoup machalla machalla
@elhadjisene972313 күн бұрын
Machallah ndeyssane dégue bu weur nga wakh ❤
@MountagaDiallo-wd6sl14 күн бұрын
Merci beaucoup pa assane
@Majamakhan14 күн бұрын
Merci grand frère je suis fier de toi❤❤❤
@ousseynoudiouf24758 күн бұрын
Oustaz pa assane merci beaucoup
@M_Dame_Afia_Mou_Serigne_Sam_13 күн бұрын
Kou diay sa lér dieundéko leumdeum bou kérogué dingko réthiou té Serigne Sam Mbaye Néna daray adouna diaroul daray allahira merci beaucoup Pa Assane kadou yi am na sollo loll machallah yalla nagnou yalla dollé khiir thi lou bakh thi Barkéb Seydouna Mouhamed PSL ❤️🤲
@AminataSarr-bw9xr12 күн бұрын
Merci mon frère mes respects.
@gueye0713 күн бұрын
Merci frère très important
@babacarndao53114 күн бұрын
Amine yalna yalla moussal niou thi barkep yoonete bi psl mais bou lolou wésso niogui santa yalla bou bakh thi liguye bou refet bi mou def amarque c'est pas que niom danio diapou niofi man mais yalla mofi ne da guendi dof dof diapou diamou yalla di ray rek falastin doyna thi eksml🙏 yalla niogui lay wakha félicitations
@bacarysane19414 күн бұрын
Merci beaucoup frère courage
@laroufrancisba568110 күн бұрын
Mon frère sa wokh machallah amna solo
@gueyebambandiaye907912 күн бұрын
Iow frère Borom bakh ❤❤geu wlay yalla nasa Diam yagg ❤ Lou weer geu wakh 🙏🙏
@MamembayeNdiaye-n7u15 күн бұрын
Pa Assane yalla nala Yalla thi barckeb serigne fallou❤❤❤😢😢😢
@CheikhFall-bn4ki13 күн бұрын
Amna solo frère masha allah ❤️naniou dellou si yalla
@falloumbaye606815 күн бұрын
Thiaye papa Assane niakue la déglou woroul bilahi louwër ngaye wakh yalla nanou yalla sakhal si loubakh ❤
@MamadouBà-k2x13 күн бұрын
Merci pa assane pour les conseils ❤
@DjenabaSene14 күн бұрын
Machallah pa assane yaw kou bakh nga yalna yalla goudal fane wii ak werr ak wëre lei ❤
@AhmadouLô-q9b13 күн бұрын
❤❤❤❤ wallaahi Yal na Yàlla defal ñu jàmm .
@DiaBathie-h3e15 күн бұрын
Yananou yala khirr si bopam 👏❤️
@BiouCamara14 күн бұрын
ما شاء الله جزاكم الله خيرا
@DabakheNdao14 күн бұрын
Merci beaucoup yaw reke lay tope bilakhi
@abdoudiouf111914 күн бұрын
Macha ALLAH pa assan yalna YALLA mayniou moudj gou rafett