Ani wa coalition tok di khar Baye Mbaye. Manifestez vous svp!!!
@assaneseck47664 жыл бұрын
جزاك اللة خير وزادك علما ورزقا واسعا
@BAMBISTETV4 жыл бұрын
Magui ni
@xudamulxadimxeexakwakhaabi35654 жыл бұрын
*Machallah ♥️♥️ Serigne Mbaye Gueye syll lii rafétna, Mame mor Mbaye tamitt deysaan ku amouk taalubé la ta diokh thieur mag gni*
@oumardiawseck45944 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Syll,niom yen wakh yi laniou wara bayi,Serigne Touba Amoul none koukoy wouteul none yay nonam,ndakh kiu bokoul ci yonou Mouride tamit bok ci wenen yon wala nga bania bok fen ta doula tere don dioulit bou wer ndakh ken dou doug ci bir bamel ba Borom bi Yallah ladj la ban tarikha nga bokon,Serigne Touba mom boudouwon nitou Yallah sakh douko tere don mbokoum Senegal yeup ba takh nieup am ci mom thiofel,wayaniou eupeul niou diegui dayo yikoy mboubo ak diko wouyo di wakh,wakh you ken xamoul foumou tegou ta dara douci deug nioniou la historiens yi di amal probleme .Dieukeu Gamou ak Moudia Gamou amoul solo ndakh Gamou 3 siecles apres Yonent bi laniou ko tambale deef ta fi ba Adouna di touki daniou koy deef,Xam na ni Bayre Magal ci Senegal kouko xeuthio ak Serigne Touba dinga niak,waya Bayrep Gambou ci Senegal tamit kouko xeuthio ak El Hadj Malick Sy ci Senegal dinga niak inchallah ,wassalam,Merci Syll..
@Buna584 жыл бұрын
Jërëjëfëti, Seriñ bi. Fi nga nekk foofu la. Na nuy tek Seriñ bi ci Xam Xam ndax musu koo wacc
@actualiteevenement23074 жыл бұрын
Machala diérédiéf bay mbaye gueye syll. Vraiment tu es un bibliothèque. Il faut accompagné les jeunes comme mam mor mbaye. Mom tamite kou oyofla ta nagou kiliftéf
@aboridial34314 жыл бұрын
Lí rafetna WAY SERIGN bí rek Mofi nek Yalla na Diam yag
@oumarthiam5634 жыл бұрын
Dieureudieufaty lii moy am solo lepp ak défarr la diourr lepp santala mame mor mbayitt defna lico warr
@papatine67394 жыл бұрын
Machallah li moy senegal,jamm rek.dieureudieuf serigne touba
@bassgueye44364 жыл бұрын
MACHALLAH...GUEYE SYLL..WE MOUROUDI ALLAH..kounek hamnani danio heur ...mais aussi kouy dignan..dignan ba fawww...faut pas inventer ni falsifier...faux pas donner la chance ...jammono waratek xewii na...Faut aller dans les sources les archives comme Ce Grand Monsieur a l habitude de le faire...La comunaute Mouride ...vous remercie infinement...DOYEN.
@baydidiallo28084 жыл бұрын
bien di wakhe DEUG
@bambasunumbeckte59154 жыл бұрын
Machallah ni daal mo Guen pér tu a raison wakh daal day tegou thi xam Mame mor mbaye na niëw diange
@KRMDecrypte4 жыл бұрын
Machalla, je te respecte davantage pour ta sagesse et sa connaissance.
@karadioplg40094 жыл бұрын
Machalla ame na solo trop billahiii deguel mor mbaye
@sonhiboufall31124 жыл бұрын
Allhamndou lilah baye mbaye yalla nga goudou fanne thi barkep serigne
@Alioubarca4 жыл бұрын
Merci Mam c k ya trop de gnuewelism dans l histoire de nos erudits Il nous ft des gens com vous pour retablir la verite
@ibrambaye16264 жыл бұрын
Jerejef baye mbaye gueye.talibe yeep beeg nagnou si yeen gnaar.
@cheikhahmadoubambayakhined14182 жыл бұрын
Machalha Cheikh bi ya ngui leuguëyeul yalla dhé .. Diadieuf Fassalé.
@sagnsesenegalaise45754 жыл бұрын
Ndeysan sunu mame mbaye gueye Syll aka beugue Serigne touba yalla nala Serigne bi taxawoul bopam
Machallah yalla na yalla fay la si barck serigne touba amatina sólo waw Goure mouride Machallah
@falloufaye1344 жыл бұрын
Mame More Mbaye il faut mou nopi nak car amoute bene kham kham wakh rek layyy def di reuyy lamagne khamoulene darra donc il n’a cas se taire akh merci pour ces éclaircissements lairena lol Yonu Serigne Touba kham kham mokooo lalll mais pas guiss lene ma
@ndiakhassndiakhass58854 жыл бұрын
Nopi moom mounoul am wakhdji Kay Moy na yem si loumou kham te geuneu khooteul geusstou bi
@beugalahira50874 жыл бұрын
Pr lan Mouy nopi mom kay conseiller ko mou xolate ay kaadom rk
@ismasow22784 жыл бұрын
C'est vrai un combat idéologique repose sur la connaissance
@nabilinfo49492 жыл бұрын
Vous êtes un grand travail.Mashaallah
@a-qudoosallahisone64984 жыл бұрын
Ndeysâan li rek moy tax nit ñi xam mbirum SeriGne bi xam bou wérr Dieureudieufaty sunu baye Mbaye diey syll
@khadimrassoulkebe10094 жыл бұрын
Jeurejeuff serigne Mbaye si xamxam bou werrr
@cissokhomamad71244 жыл бұрын
merci serigne bi kou bakh nga
@youssouphaseck60374 жыл бұрын
1884 LA SERIGNE TOUBA TAMBALI GAMOU .DIEUREDIEUF YALLA SA BOROM FAYAL GÑIOU LA .BÈGUE NA LOL WAKHAL MAME BAMBA DEUG LA BEUGEU.
Jaajëf Syll, ku xamul dafa wara jànggi wala mu nòppi
@serignesaliousamb96434 жыл бұрын
Mashallah jajeufety serigne touba lep mom leu walahi
@zorroantiquairecapskirring78794 жыл бұрын
Merci beaucoup modeste dieuredieuf baye mbaye syll
@cheikhcisse74064 жыл бұрын
machalla tayde kontanna lole diere diaf s mbaye gueue sylla ak s mame mor mbaye nireke la
@mamecissedieng26074 жыл бұрын
Machalah serigne mbaye Gueye sylla
@serigneadj17794 жыл бұрын
Dieuredieuf Déle défar rék tha kaw tha kanaan 🙏🏿
@dembeaktey4 жыл бұрын
Segne Gueye tu es un grand connaisseur et savant du mouridiisme. Mais il faut te réconcilier avec ton frère Cheikh Oumar Diagne pour l'unité de l'islam qui est combattu par les occidentaux.
@Lopios-g6l4 жыл бұрын
Waw goor baye mbaye niguadéfe nonoula machalla...
@khadimndoye89214 жыл бұрын
Maachallah Nieuppa Sara DIOUBOO
@galaxiepro.56414 жыл бұрын
ce vieux a raison il a la source du savoir et faut le reconnaitre vraiment
@momo_ceepgy27754 жыл бұрын
Mame mor mbaye ku bakhla ta talibe la waye da wara bayi di wakh da wara diangi ba nopi waye doyna war lepou kene manouko wakh
@amadou35914 жыл бұрын
Li moye yone koufi wakh loudoule deugue gnou tékk la si yone😍😍
@SERIGNECHEIKHMBACKE4 жыл бұрын
ZIAR BOU BAKH YALNA DIAMOU SAKH CI REWMI
@radioradiotelevisionbawalm70594 жыл бұрын
Ku diara nianal brome Xam Xam la
@assanemar53534 жыл бұрын
Machalla rafet nA trop am na solo aussi
@modouloum71154 жыл бұрын
Vraiment je suis content
@paped51804 жыл бұрын
Mame mor dayi woute khaliss rek
@serignebadianeditkhadime59634 жыл бұрын
Hakaza dieredieufati serigne Mbaye goudou fan wergouyaram barke cheikhna khadim
@ibrahimacissedieureudieufs27324 жыл бұрын
C'est vrai mais ne faut pas te limiter seulement aux archives tenez aussi en compte ce que les proches et compagnons de Serigne Touba ont raconté merci
@kman-974 жыл бұрын
Bay sylla je te suivre presk un ans mei tay gua meuseu def louma rafet louwoul pour man yen gnar gneup ayy talibe guen tei entr talibe internet amousi yon sa domla sa rakla woko si souf guen waxtan ndax yow tmt feke wosi dra archive national rek guey toxale dignou andil tai lafa nek yeup nonou serigne touba yi gnoko fa bind gua bayi si xeel
@ibrahimafaye18064 жыл бұрын
Bilay li rek serigne touba beug Machalla
@wakeupafrica99064 жыл бұрын
Waw Goor li rekk la déh... Deuggeul Dioubbëul rek.
@senegalsamareew43484 жыл бұрын
B.mbaye yalla ngafi yage
@Gueye77904 жыл бұрын
Machalla baye Mbaye gaye Syll nala yalla samb ta aarr la
@mbayethiam45954 жыл бұрын
AMINE😭😭😭❤❤❤
@daoudagueye62554 жыл бұрын
Diareudief syll nala yala May fan wou good andak werr
@mouhamadoufadilniang4 жыл бұрын
Serigne mbaye Gueye Sylla soldaro bourom daroul mhoty jerejefety ya woyof ta bakh ta sella
@daoudagueye62554 жыл бұрын
Diareudief syll limo werr
@oumardiouf15854 жыл бұрын
Djaa djeuff rafetna maa chaa alla bayy mbaye sylla begue brom darou al moukhty sama yakar oumar depuis brasil
@ababacarsignane84704 жыл бұрын
Merci beaucoup
@seckmor63164 жыл бұрын
Djieredjief s mbaye ni reck la yaw lobakh reck mola ñor.serigne bi reck
@ndirsope1234 жыл бұрын
Mashaallah suis très content de toi 🙏🙏🙏
@bayfalllabeuguedonne67564 жыл бұрын
Serigne mbaye Geuye sylla yaw yaye kan bani dowo mam mor mbaye
@modoundiaye33904 жыл бұрын
Dieureu dieuf baye mbaye rafétna
@diagnesoma36894 жыл бұрын
Rafet na Mouride ni rek lay meuna mel,yen yena gnouy bégal thi Serigne Touba
@mordiop56964 жыл бұрын
Macha allah baye mbaye
@codediaw42384 жыл бұрын
Dieur dieuf baye mbaye gueye sill
@cheikhfallseye66694 жыл бұрын
Machallah bay
@diawfalfaraa59974 жыл бұрын
Pour man nak diarouko woon baye mbaye woko walla mu woola parce que beut bu rousoul tothie
@pdiallo10294 жыл бұрын
Merci Père . Vos sources sont plus crédible
@iboulayewade11294 жыл бұрын
Vraimen credible
@marraka024 жыл бұрын
جزيتم خيرا وكفيتم شرا
@abdoukhadretop2554 жыл бұрын
Macha Allah diame rek gay ame incha Allah
@daoudambaye99894 жыл бұрын
Ma challa..
@niassousseynou5074 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne mbaye Gueye mourit bi 🙏♥️🙏
@niassousseynou5074 жыл бұрын
Machallah mbaye Gueye amatina solo méré wne nala lolo
@abdoulayegueye49313 жыл бұрын
Merci
@ndiagalo62074 жыл бұрын
Machalla reftna
@mafatimciss32694 жыл бұрын
Serigne mbaye yaa baax! Sa waxji rafetna loool !!!!
Niga dokhaléwone môme damalathia méréwone ba commentaire roumawone
@BAMBISTETV4 жыл бұрын
Tay de yen niar niepp sagal guen mouride yi mame Mor mbaye niogui rafet lou sa takhaway yague len fi te wer degue rek moy degue mame Mor demal Mou tek le ci kham kham dieuredieuf
@djibrilcasse36734 жыл бұрын
MACHALA DJEUREUDJEUF BOROM TOUBA LII AMNA SOLO LOL MOURIDE BOLO
@ahmacisse20364 жыл бұрын
Baay Gueye waxal thi Macron waay😪😪🤕
@fazaniangthanksyou7514 жыл бұрын
Dieuredieuf Mbaye sylle
@khadimgueye71664 жыл бұрын
Alhamdoulillah Dieu est grand
@sonhiboufall31124 жыл бұрын
Mame mor waw goor talibe Day woyof
@absadiop76674 жыл бұрын
Magnifique fait plaisir
@thianta15284 жыл бұрын
En tt cas dp8 bimala tambalè suivr, boobou video rek laa contesté. Mais puisk j suis pa l seul et apparently, vs trouvez k c'est la bonne approche...