Modou Lo yalnako yalla maye ndame le 24 novembre 👑👑👑👑👑
@SonkoDiomay-g4qАй бұрын
Gayi ndeysan daniouy fatté lamb thiosane la avant tout 😊j’adore les serrer bilahi Lamb dagne ko meune ❤que le meilleur gagne Sénégal beneu bopou la 🫶
@FatouSibéАй бұрын
No siteu bilaye jtm ❤❤❤❤
@madefaye2232Ай бұрын
Ndam inshalla pour notre champion siteu
@MoussaThiongane-m5rАй бұрын
YaNaLa Yalla MaY NdaM frére SiTeu YaNaLa Yalla DéfaLe Diammm Yarabii Inchallah NdaM Rk Inchallah ❤❤❤❤
@AlysarrAlysarrАй бұрын
Yalla nanio yalla maye Ndam inchallah Modou seul
@mohamedfall-rv6wrАй бұрын
Waw yakarrall say mystiques nioune niou yakarr yallah 😂inchallah Modou dalay dann té bitéllou kirene lagnouyy tooyalé souniou Yarammm 😂😂😂
@amyrock4324Ай бұрын
AK ZAMZAM SALALAHOU ALA MOUHAMAD ❤❤❤
@Nénéba-y7jАй бұрын
Siteu seul kou am lenene nane ko tey tarkinda bi yalna ko yalla maye ndame dimanche inchallah 🎉🎉❤❤ .. amine yarabi🎉🎉🎉❤❤❤❤😊
@MbayangNdiaye-n8eАй бұрын
Ndam réck baye fall inchalah ❤
@JackariaSyАй бұрын
Salalahou ala Mohammad ❤️
@SaliouWade-i1mАй бұрын
Yalla nala yalla may ndam barké seyedina mouhamed
@elhadjimalickmbengue9988Ай бұрын
Pour yén Modou lo yalla la beu dou danou beu dimanche dingén xamni ndam yalla Koy mzyé
@Mbodji-waloАй бұрын
Siteu Yalmine🇸🇳🇺🇲💪🏾❤ Yalla nako yalla may ndam inchallah
@KinaNdayeАй бұрын
Situé SEUL 🤍🤍⚔️👑👑🩹 ❤❤❤❤
@AliounebadaragningBadaGningАй бұрын
Seute seul❤❤❤
@yyytgg1882Ай бұрын
Au moins lui il a fait quelque chose de nouveau, il a permis au djonouwarois de se faire quelques choux en quelques heures, ça élargit le business dans la lutte et permet aux autres d'en tirer bénéfice
@SaerBa-o6kАй бұрын
Siteu❤ borom le 24 yalla nalla yalla siguile si barké alxuraan
@MouhamedNiang-d9kАй бұрын
Wakh ka deuk
@cheikhbiaye4854Ай бұрын
Modou kesser ❤❤
@NDIASSE4132 ай бұрын
Yaye bvndi walahi yallna la yalla may ndam diambar ji 👑 inchallah 🙏
@dialloousseynou4098Ай бұрын
Ndiom thiossane
@abdoulayendiaye4713Ай бұрын
Siteu moy lamb
@FatoupascalineSagna-bx5ksАй бұрын
Salamalékoum mane la siteu dama tite sakhe 😢
@Papiblack-i7kАй бұрын
Nite mbokam ❤❤❤
@FmymindАй бұрын
😂😂😂😂😂😂siteu à regarder beaucoup de films 😂😂😂
@saliouthiam24622 ай бұрын
Mom lamb dji yepp mystique lako diappé 😂😂😂😂
@GUEYEBAMBISTE662 ай бұрын
YA MEUNE doulll
@AliouCisse-w9n2 ай бұрын
Bayil doul Modou dakha mystique fouffffff😂😂😂😂
@alybenzediakho26002 ай бұрын
Modou Lo ndoxou zam zam rek lay sango combat bi diekh par kao Modou seul 😂❤
@SpevakKris2 ай бұрын
Boy yi vrément changéwougnu 😂😂😂
@ResidenciaImmobilier2 ай бұрын
Bilahi😂
@faye67182 ай бұрын
Sérére mo moom lambou n'a léer
@serignembackediouf909Ай бұрын
Siteu ay réi lama def sakh😅😂
@GnagnaMbaye-i5fАй бұрын
Bougne la danè damaye kharouu
@Babandao-d4s2 ай бұрын
Siteu yana yalla may la ndam
@WadeOusseynou2 ай бұрын
Diamou aye garape 😢😢kou doy lo woull.yalla do ame diamou
Sa waay boudee ay mbiroum dinee rek lamb si bopam dafa Haram Kone nopil
@mawlanaambengue2059Ай бұрын
Banga soumeko di beurré lala sharia doumeu bu yaag. Lamb thiossane lh malheureusement xamolen lolu
@kaneadama12262 ай бұрын
Boul lambe yeufou thiéddo la bo amoul mystique togual
@NdiayDolèbo_04Ай бұрын
Vraiment siteu mo khoromou lamb
@TalibouyaNdiaye-h1dАй бұрын
Siteu sa mystique yiii nawna bou yagg🤣🤣🤣
@MAIBA-wg5qyАй бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉😢😊
@IbrahimaFalla-v2j2 ай бұрын
Lii amoul sérieux ay fo leu yeufou xaleyii bamou jakarlo AK xaragne inchallah
@GUEYEBAMBISTE662 ай бұрын
SITEU KASSÉ NAK TOUSSSSSSSSSSSSS
@ibrahimambengue37002 ай бұрын
Yenn bayii lenn ay wx goor dou beurrii wx kw guanan ay fooo gni dii fayékou ay millions pour gagner leur vie gua ndy doul
@AndrekanfanyАй бұрын
Dekhey kate sa yaye doul dee
@allenndiayeАй бұрын
Garabe bi sakh titena mogninane yalla diegalma balema yaram nieuweul yawww laniouye khare.....bene ayatoul koursi lepppp dawwww delou famou diougue😂😂😂
@khadimniang9136Ай бұрын
Diaye na rou wam 😂😂😂
@cirendiaye2492Ай бұрын
Siteu comédie rek la am cii combat bi
@mouhage2157Ай бұрын
Siteu comédien nga deff sa bopp 😂li lamb leu dh soula modou dooré nga dawe 😂
@AssanSecka-bd4jkАй бұрын
Senegal amut mborr mystique mofa am
@absakeinde3659Ай бұрын
Tapete lac 3😂
@FallouGalss-j8rАй бұрын
Abdou séck manké nafi ndiol mii
@KhadimBamafaye2 ай бұрын
Yalmine bi seul 🎉🎉🎉🎉🎉
@SouleymaneSoumaré-b3qАй бұрын
Brom inch'Allah ngay barel😅😅😅
@modouniass2973Ай бұрын
Instant bii niou tolou lii Danoulll modou
@SimonDasilva-o6fАй бұрын
Thiossane ake ada yi amoul deuk rkk gnioye critique defe lo khame rk mo waure khol sedd na yalla na la yalla maye dam
@OusseynouThiam-v8b2 ай бұрын
ki nako even prod wala marodi wo 😂😂😂
@Ballasylla-e6jАй бұрын
Lo combat bi geuna yagu di geuna méti si mom so beuré danou so khékké danou lodéf danou siteu Modou lo roi des moy sa bay si lép thioth day khamlékam
@Ballasylla-e6jАй бұрын
Modou lo mistique douko diapou lép si yalla lako ték siteu nak pour mom lép mistique la nakh ga sa bopou dimanche gay kham kan moy sa bay modou lo dinala nokhou danla
@FatoupascalineSagna-bx5ksАй бұрын
Lép sa géw ba la mou takhaw xaragne takhaw inchallah
@hametsall8386Ай бұрын
Siteu mystique réck
@CoumbaDiouf-x4iАй бұрын
Demeu bi
@sambacordiop1027Ай бұрын
Siteu bayil sa yeufou dof yi , bou mystigou joal bakhone con niou ame mbeur. Yaw show mola nekh
@mariamagueye9084Ай бұрын
aye masque zoro, danoule modou lo
@moustaphaseck18252 ай бұрын
Moudou lo mou dakha mystique
@AminataDIOUF-ez8kdАй бұрын
Fouf
@madinagueye168Ай бұрын
Siteu tite rek motakh Mouy def li
@assanediouf74352 ай бұрын
Kii blh comédien laaa 😂😂😂😂
@ibrahimambengue37002 ай бұрын
Daguay ndy doull dh
@chekhonadia6494Ай бұрын
Bilay 😂😂😂
@AndrekanfanyАй бұрын
Sa digue lefeul ndeye siteu seul ❤
@chekhonadia6494Ай бұрын
@@Andrekanfany 😂😂
@massambadareАй бұрын
Ki lamb ngen nan comédien lamb art le Modou Moy sama mbeur mai siteu dafa meun lamb motah promoteur yi diko weur
@Falloulam12342 ай бұрын
Badou Yagui def sa liguay nk bou baxx grand dakar niogui sa guinaw
@bayezallniang2 ай бұрын
Mes sa touba fimou wané ak Fi d'où béne dé😂😂😂
@bayemodoundiayexassida1767Ай бұрын
𝐁𝐞̀𝐧𝐧𝐞 𝐥𝐚 𝐤𝐞𝐲 𝐤𝐡𝐚𝐧𝐚 𝐤𝐡𝐨𝐥𝐨𝐤𝐨 𝐛𝐨𝐮 𝐛𝐚𝐤𝐡
@vivelarevolutionpacifique15372 ай бұрын
Billahii chow bi gua ame si lamb djii😂
@CheikhDiouck-y8bАй бұрын
Mais badou j'ai une question a te poser
@badou100decouvertestvАй бұрын
Suis à l’écoute bro
@MedouneKebeАй бұрын
Boula MODOU lo diape digua kham lep deugue la😂😂
@amaduamadu1600Ай бұрын
No siteu aka meun folclore
@Khadimgadiaga-b2pАй бұрын
Nn Sénégal dou reuw
@GoraMbengue-f2j2 ай бұрын
Gni bilahi xamouniou Modou lo 😂
@GUEYEBAMBISTE662 ай бұрын
Tousssss nak
@michuthebest53742 ай бұрын
Modou lo bou diaaroul fi mou doone diar avant si bir cayor ak fandéne d'où guiss dará.Lamb tiossan leu
@AndrekanfanyАй бұрын
Djiemal kham sa bop 😂
@ModouMbay-f4g2 ай бұрын
Siteu mo meun koudoul Modou lo souba gein Di comprends
@Omarsane7491Ай бұрын
Moustapha senghor aliance siteu lo def danou inchallah
@TavaresAlexisАй бұрын
Siteu vraiment tes un comédien va demandé a ama ,mystique né rien devant modou
@daoudakante29172 ай бұрын
Mougui mel ni kouy def tournage film Horreur
@modousarr88482 ай бұрын
😂😂😂
@Jeuneentrepreneurcheikh217Ай бұрын
Lii rék laa amm sii Combat bii🎉😂
@mounassndour2500Ай бұрын
Wakho deugue dès 😂
@aablayesy4092 ай бұрын
Siteu yefou deum Rk lay def 😂
@khadimfaye80032 ай бұрын
Serer Mo mom lamb mais roi bi serrer yoroko
@ModouDiom-z6w2 ай бұрын
Modou Lo danko meune géneu si serere yiii
@AminataDIOUF-ez8kdАй бұрын
Gua sagn ko wakhouDiom-z6w
@VikingsénégalaisАй бұрын
Franchement j'ai de siteu il est un peu satanique
@MamadouLamineNgom-t4gАй бұрын
Mais normal mou âme mystiques beut bou ne mo laye khôl lamigne boune mo laye toudou
@sadiosane5621Ай бұрын
Mbété cavalier de l'apocalypse
@CheikhAssane-o4h2 ай бұрын
Modou Xaragne Lo (Al Qour’an) Dou Moromou Siteu Tarkindanou (Xeureum)
@laminediongue84262 ай бұрын
Ki dof na bou yag😂
@abdoulayediallo4028Ай бұрын
Cagoule bi daf méy fatéli film dracula ces la même chose ak Cagoule siteu by
@ArmandMendy-y5p2 ай бұрын
Soumbou kate bou mak bii 😂😂😂😂
@Pénda-e3dАй бұрын
Li rèk gua thi am dèh
@Msenegal-o3dАй бұрын
Pour mom mystique moy dane Modou lo
@MortallaNdiaye-h8j2 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@LassanaTRAORÉ-m5xАй бұрын
Pourquoi drapeau États Unis ak Sénégal??? Nioune Sénégal laniou wakh. Gueum sa bop ak sa rew.
@papaofficielsenegalvip30502 ай бұрын
Badou diama si yaw
@Ibouseck-gr5jnАй бұрын
Ki wéroul way yeufou dof yi
@taphadieye4210Ай бұрын
Mom dafa sémploul dara
@FallouThiane-k4vАй бұрын
Lome dèfe dano
@AbdouKhadér-u5z2 ай бұрын
Modou lo dana dokhan ndayam 😂😂😂😂
@malicksiteu76562 ай бұрын
Saway yaroul rek Français nga ☺️
@aablayesy4092 ай бұрын
Sa data yaye
@AndrekanfanyАй бұрын
Sa digue lefeul ndeye
@papahabibdiop2 ай бұрын
Siteu lim soll ni moy lann😂
@malickseye23422 ай бұрын
Mé deuk bi Ana mak gui deuk bi ay khalé rek nioko weur