“Lima Abdou K. Gueye waxal...” La réponse très classe de Al Amine Dramé à Abdou K. Gueye xrum xax su

  Рет қаралды 30,043

313  DIGITAL

313 DIGITAL

Күн бұрын

“Lima Abdou K. Gueye waxal...” La réponse très classe de Al Amine Dramé à Abdou K. Gueye xrum xax sur l'aff...

Пікірлер: 90
@byhamdydrame5500
@byhamdydrame5500 8 күн бұрын
Karim Ban important la AM Si rewmi 😢😢 beug dîné ta na ngou wou diangu sa dîné ☑️☑️
@MoustaphaCissé-q1d
@MoustaphaCissé-q1d 8 күн бұрын
Diarama sama imam amatigua dam dagua seelami machallah 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
@black2krack982
@black2krack982 8 күн бұрын
Vraiment mon grand Krim il parle pour parler rek
@demedeme6203
@demedeme6203 7 күн бұрын
Ap dof bouy dokh la rek
@Lechroniqueur221
@Lechroniqueur221 8 күн бұрын
Karim moma guena bett si sénégal🥺🥺🥺
@amadoudiouldeba5921
@amadoudiouldeba5921 8 күн бұрын
Imam Dramé sopenala té Yalla rek takh
@alassanesarr4662
@alassanesarr4662 8 күн бұрын
Problème bi abdou karime amoule kham kham beug wakh si politique
@mohamedgueye2856
@mohamedgueye2856 6 күн бұрын
Machalla oustase, Merci beaucoup ❤
@aldachir1032
@aldachir1032 8 күн бұрын
LAYSSA MINNA MAN DA'AH ILAL ASSABIYA DISAIT LE PROPHÈTE SWS ❤❤❤
@OusmaneFall-m9d
@OusmaneFall-m9d 8 күн бұрын
Abdou Karim khourou khar kou nafekh leu
@demedeme6203
@demedeme6203 7 күн бұрын
Nit kou doy warr la nafekh deug la
@seckmame1228
@seckmame1228 7 күн бұрын
Xam xam. Amou ko. Karim. Lomou kham
@babakebe4094
@babakebe4094 8 күн бұрын
Al amin un grand homme
@mamadousonko1481
@mamadousonko1481 8 күн бұрын
Abdou karim na dem outi dji xam xam mo gueune wakh djou beuri bi
@ibrahimacisse2504
@ibrahimacisse2504 8 күн бұрын
Mais non c'est dommage qoi 😮😮😮courage à vous deux
@welldonegoodjob3266
@welldonegoodjob3266 8 күн бұрын
Wakhou Abdou Karim dè diaroul wakh mom khamoul lou diné islam wakh beuri wakh diagoul
@coumbandiaye1900
@coumbandiaye1900 8 күн бұрын
Karim djaboot dako dap finiouy djokhé khaliss la sokhla motakh dotoul noppiii
@A2SPROS
@A2SPROS 8 күн бұрын
Abdou Karim dara daluko ludul reewandé
@byhamdydrame5500
@byhamdydrame5500 8 күн бұрын
Karim xél mi nékhol 😢😢 xaliss rék lay weur 😢😢 geumol tousses
@lunesy2298
@lunesy2298 6 күн бұрын
Ndeysane imam sa xol rafetna yalla na yalla samu
@amadousarr2121
@amadousarr2121 8 күн бұрын
Macha Allha ❤❤
@aliounegaye9606
@aliounegaye9606 8 күн бұрын
Vraiment wax pour wax mome diarouko. Abdou Karim dou wax si xam xam
@djilysall7727
@djilysall7727 7 күн бұрын
Karim weroul billakhi
@mariamapdiedhiou8454
@mariamapdiedhiou8454 8 күн бұрын
Karim mom c'est un mécontent 😂
@elhadjigorguifall9762
@elhadjigorguifall9762 8 күн бұрын
Waa jii Gént rekk 😂 Kariim dof la 😂
@SambaSylla-j4g
@SambaSylla-j4g 8 күн бұрын
Abdou karim Kouko deg lou dinga yakhou dof la rewna
@cheickmoinga3245
@cheickmoinga3245 8 күн бұрын
Xurum xaaqq daa Waayadiii leegui 😂
@AbdoukhadreFaty-y4l
@AbdoukhadreFaty-y4l 8 күн бұрын
Karim nitt kou bone la😂😂
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 8 күн бұрын
KARIM KHRUK SOU BEUGEUH DINEH BI DEUGUE NA DEM DELOU WATTE NDIAGATTE GUEUSTOU BOU BAKH , GUIR SOUBA MOU MEUN DI TOKK WAKH LOU KENEU DOUL TEGUI
@CheikhDiouf-g9f
@CheikhDiouf-g9f 8 күн бұрын
❤❤❤❤
@oumardiouf1585
@oumardiouf1585 8 күн бұрын
Sa wayy karim amoul kham kham zero kham kham cachorro 🐕 🐕 🐕 🐕
@fatoutouray1474
@fatoutouray1474 8 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@massambathiaytouceedoosall2394
@massambathiaytouceedoosall2394 8 күн бұрын
Vous donnez trop d'importance à Abdou Karim
@babacarceesay4819
@babacarceesay4819 8 күн бұрын
Abdou Karim doff la politique Imam dafawara politique
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 8 күн бұрын
IMAM AL AMIN AK NYI MELNI YOW , SI WAKH DEUG DEEGOU , GUEUM LINGA DONN , WAKHLEN BA DOUGOU BOITE VOCAL. GUIR DJOU BEUNTI, AK TEKK NIOUN SI YONN RELIGIEUSEMENT
@ismailambaye6977
@ismailambaye6977 7 күн бұрын
J'ai suivi le débat mais Karim n'a rien dit de mal sur imam Sénégal mo bari ay nafekh😢
@ousmanegassama4446
@ousmanegassama4446 8 күн бұрын
😂😂😂 doyna waar
@falamadinvesttv1676
@falamadinvesttv1676 7 күн бұрын
Abdou Karim est très prétentieux
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 8 күн бұрын
IMAM ,AK KILIFEU DINEH REGULATEUR LANIOU WARA NEKEU SI MBOOLLO, RAWATINA SI REW. TEKKO SI NDIANKHANAY, KON SOUNIOU NOPEH MOUSIBA AM .ABDOU KHRUM KHA , KHAMOUL TEH AMOUL KHAM KHAM , SI DARA , DAY TEULI TEULIREK .
@ZaleDiallo-lg7kv
@ZaleDiallo-lg7kv 6 күн бұрын
Sénégal degno wara tegg internet bi 1an ba nitt gni demm fadjou ba werre gnou dokka indiwaat ndakh mime rèw da bari ay doff 😢
@djibrilsene9029
@djibrilsene9029 7 күн бұрын
Salam , khrum khax mom bala may beugu dee mounan ibadou dommage gneuke si djaka, nafekh la na dem ligueyi goor dey liguey. Diam deug. Domeram bou mak
@MorTouure
@MorTouure 8 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😮😢😢😢😢😂😢😂😢😂😢😂
@Alakhou-vw9kv
@Alakhou-vw9kv 8 күн бұрын
Karim xourou xar doméram bou laxatou woon la macky sax moko tané ndékété
@ousseynounjaay2446
@ousseynounjaay2446 7 күн бұрын
Abdou Karim réew mi doyé wouko touss. Amoul xamxam amoul diom
@OusseynousambeKarbalah
@OusseynousambeKarbalah 8 күн бұрын
Xana djangokowone tps Ousmane sonko
@taphadiagne
@taphadiagne 8 күн бұрын
Karim khana dou rouss
@ndiayemodou8728
@ndiayemodou8728 8 күн бұрын
15 sans du prison kuye wakh wakhi wasson
@OumarBa-v5y
@OumarBa-v5y 5 күн бұрын
Wa ki journaliste leu wala seytani radjime😮
@malicksarr2141
@malicksarr2141 8 күн бұрын
Khana birame soulaye mom danko wara diapou 🤷🏽‍♂️
@MorTouure
@MorTouure 8 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@SambaSylla-j4g
@SambaSylla-j4g 8 күн бұрын
Abdou karim dagouwoul fene katt la. Doreu katt la
@sindiditv9606
@sindiditv9606 5 күн бұрын
Karim sunu bookon émission douka déffati
@marandiaye2704
@marandiaye2704 7 күн бұрын
LEUFEUL NDEYOU WA PASTEF YEUP SENEU DATA NDEYE
@Msenegal-o3d
@Msenegal-o3d 8 күн бұрын
Karim ay médicaments la soxla
@cheikhcoly5933
@cheikhcoly5933 8 күн бұрын
Abdou Karim n'est pas ce gars là que vous parler il mélange tout il connaît rien dite les tel quelles sont
@sady1964
@sady1964 8 күн бұрын
En tous cas simple defo ko
@ModouBodian-jv4oj
@ModouBodian-jv4oj 7 күн бұрын
Yéneu gueme aye tariha nioune sunu yone ci tariha féne késé té dou dëgg louniou néhe dinagne ko wach ci tariha yi ak sén Serignesi ga hamni adouna rék moléne niore
@cheikhseck1908
@cheikhseck1908 8 күн бұрын
Karim domiram la domo khadj la nafekh la fen rek lay def
@AmethNdao-o3r
@AmethNdao-o3r 6 күн бұрын
Karim Gueye problème Kaniott bi, mo détourné cerveau bii
@babacardiop7210
@babacardiop7210 7 күн бұрын
Journaliste bi tmt yagui wakh imam lila karim wakh moudj ladj la guani liroko 😅😅 vraiment am gua fit😂😂
@ousseynounjaay2446
@ousseynounjaay2446 7 күн бұрын
So amoul xamxam ba paré beug lou nieuw nga wakh si, di nga yagg am gathié. Lolou mo dal Karim, amoul xamxam té eupeul na
@kif7471
@kif7471 7 күн бұрын
Karim dal gemoul dara
@biramathiam6408
@biramathiam6408 8 күн бұрын
Imam beuss bou Omar Sow bouy dem pour gno xol ndakh bopp bi tranquille na yobalè Karim lolou Moy deugg
@MohamedDiagne-v9b
@MohamedDiagne-v9b 7 күн бұрын
Karim ne merite pas 5 munites dans un plateaux
@SyllaSylla-jy6ft
@SyllaSylla-jy6ft 7 күн бұрын
Macky c'est le meilleur président de tous les temps vive Macky rék pour toujours merci Macky ❤
@joyfulness80
@joyfulness80 7 күн бұрын
😂😂
@byhamdydrame5500
@byhamdydrame5500 8 күн бұрын
Boy deglou da ngay déglou kou Am XAM XAM bu séll Karim xél mi nékhol dh
@farydiop6566
@farydiop6566 8 күн бұрын
Fouta thi Sénégal la bokk. Peul fouta yi eupp fa tahoul niou moom ko !!!
@KINGBABA6838
@KINGBABA6838 8 күн бұрын
Karim est trop nul ,weur di féne ak soss rek la fi néké dou nitou deug
@Bdioufy
@Bdioufy 8 күн бұрын
Hooo Karim c'est un mécontent on dirait un frustré quand on fait le constat tous les gens qui se réclament activistes sont des chômeurs leurs problèmes c'est eux mêmes la meilleure façon d'accompagner la marche de ta patrie c'est de travailler ou de faire travailler des gens participer à l'économie du pays mais des gens qui ne font rien à longueur de journée mais deviennent des mécontents alors qu'ils doivent s'en prendre à eux mêmes trouver quelque chose à faire au lieu d'être là à parler des choses qu'ils ne maîtrise et de dire toujours des contres vérité je réponds à sieur Mody quelle est l'impact de Karim dans la société qu'est-ce qu'il prône que de dire des contres vérité maintenant
@sayfoulislam2173
@sayfoulislam2173 8 күн бұрын
Yagui nekhal Karim de boy Karim domou haram
@mouhamedkane9486
@mouhamedkane9486 7 күн бұрын
Imanme merenala trop boul tontou ben badola
@cogitoergoseum1445
@cogitoergoseum1445 7 күн бұрын
Mais journaliste bi nite leu???😂 Yaw tu n'as même pas écouter Karim et tu te permet de poser ay questions.
@mouhamadousiby3451
@mouhamadousiby3451 7 күн бұрын
karim weroul diaroul tontou
@jaharmytall6389
@jaharmytall6389 7 күн бұрын
Karim ab doff la. Topou tele yi di doul rek ta khamoul dara si loumi wakh
@assanesene5989
@assanesene5989 7 күн бұрын
Je ne vais pas commenter sur ce fou de Abdou Karim GUEYE mais plutôt sur ce journaliste qui pose une question sur les propos d autrui sans savoir ce qu il a dit c est à l image de tous nos journalistes qui ne préparent jamais leurs émissions. Trop de nuls devant nos écrans
@babacarceesay4819
@babacarceesay4819 8 күн бұрын
Karim doff la xamoul Dara
@sady1964
@sady1964 8 күн бұрын
Manga beug yonènt bi wayè manga beug niou bakh nièpp nak
@oumarabdoulbah8496
@oumarabdoulbah8496 8 күн бұрын
Mody parle trop
@MamefatouFall-ce8qy
@MamefatouFall-ce8qy 7 күн бұрын
Ce vieux mody et ses extrapolations et ce vito ,nioom daniouma diaakhal! Tarkhiiss rék laniouye def! Certains rigolent mais.....
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 8 күн бұрын
VITO YAGUI DELOO AVANCE DEH , YOW EN TANT QUE TASKATOU KHIBAR , DEUTHIE KOUMPEU , NGANEH YOW LIRO WALA DEGLOU WOO LI KHRUM KHAK WAKH. TEH DIEMEULEKO LOU TOLNI SA KHARITT IMAM AL AMIN DRAME , TEH NGAKOY INVITE SAY SOUNEH . FOFOU MOM TEYNA SI KHEL. WAYEH NA DIAP REK SISA WAKH . BA DEGUE LENENN , WALA KHAM .
@seyedinahomarseye4211
@seyedinahomarseye4211 8 күн бұрын
Mak yaw man kouko bege ma ba la
@yacinefall8372
@yacinefall8372 7 күн бұрын
C’est quoi ce journaliste ? Quelle médiocrité !
@Oubli2023
@Oubli2023 6 күн бұрын
Karim psychopathe. C’est un fou arrêtez de caresser les choses.
@salimatadiop4546
@salimatadiop4546 7 күн бұрын
Pauvre Sénégal. Des plateaux télé transformés en plateau de téseunté. "On a dit ça sur toi" un journaliste à 2 balles sans scrupule ni vergogne. Le monde bouge et nous on en est là.
@laminetall4890
@laminetall4890 8 күн бұрын
Imam drame yeimale si dîner bi mo gueuneu ngaye topou doulekate yi wa pastef
@BiramFaye-i6j
@BiramFaye-i6j 8 күн бұрын
Ou était vous quand Ousmane sonko disait que Macky n'aime pas les Diolas
@binetasane2701
@binetasane2701 8 күн бұрын
Le président Sonko n’a jamais dit que Macky n’aime pas les Diola il n’a fait que dénoncer un fait Macky avait isolé la casamance il avait arrêté le bateau le Sénégal dém dik et c’est injuste
@JeanJacquesMendy-e4f
@JeanJacquesMendy-e4f 8 күн бұрын
Wakhale dégueu OS n a jamais dit que Macky n aime pas les diolas mome dou diola bayilen di wakhale nit ki loumou wakhoule .N aime pas la casamance, n aime pas les casamancais woutey na Li ngaye wakhe.
@amiralyou
@amiralyou 7 күн бұрын
😂😂😂 encore karim Le fou du village 😂😂😂 il n'a pas été nommé PCA 😂😂😂 alors il se rebelle 😂😂😂 il va mourir de chagrin ndeyessane 😂
Tuna 🍣 ​⁠@patrickzeinali ​⁠@ChefRush
00:48
albert_cancook
Рет қаралды 148 МЛН
Sa Ndiogou humilie Abdou Karim gueye
3:24
Wassare snTv
Рет қаралды 2,5 М.