Live oustaz Alpha ba ha et sa team - les Baye Fall Cii ñiaak diouliit akk koor ... ?

  Рет қаралды 22,647

KAADU DINEE JI Tv

KAADU DINEE JI Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 120
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m Жыл бұрын
Oustaz alpha mo meuneu wax deug wallahi
@ngordiouf3310
@ngordiouf3310 Жыл бұрын
C'est alpha ki à fait k je connaisse les dérives des tarikhas merci
@brandonjohnnytoure3447
@brandonjohnnytoure3447 Жыл бұрын
Alhourane ak sounah moy deugue kou doul jouli yéfar nga c'est simple
@awaba3307
@awaba3307 Жыл бұрын
Sen mission bi métina ndax vous parlez à des personnes profondément endoctrinées.yalla nalen sougnou borom har te maylen ndam.
@salioucisse2355
@salioucisse2355 Жыл бұрын
Yonni wouniou nioniou chi nioune muhammad sallahou halayhi wassalam laniou yonni chi nioune
@YusuphaTouray-oo4vh
@YusuphaTouray-oo4vh 8 ай бұрын
gain nyulen dembeelee nyu Gambie you doing the best belai
@iso2459
@iso2459 Жыл бұрын
Jërejef oustaz Alpha Bâ avec toute ton équipe. Allah jazîkoum bil khayr
@laminediop9904
@laminediop9904 Жыл бұрын
0 M
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 Жыл бұрын
Macha Allah Alqurane ak sunna rek moy deug
@Artymelo3362
@Artymelo3362 Жыл бұрын
yéwwou lééne sénégal yéwwou LÉÉNE sénégal yéwwou lééne sénégal yéwwou lééne sénégal yéwwou lééne sénégal yéwwou lééne sénégal yéwwou lééne sénégal yéwwou lééne aywaaye yéwwou lééne yéwwou jotna🤦‍♂️
@mamadousy6312
@mamadousy6312 Жыл бұрын
Billahi yewou diot n
@Diomaye-n9w
@Diomaye-n9w Жыл бұрын
Merci beaucoup Alpha ba et sa team
@ndiagamakhtarsow3599
@ndiagamakhtarsow3599 Жыл бұрын
dioulit day diouli alkhourane ak sounna rek mo woor
@awaba3307
@awaba3307 Жыл бұрын
😂😂ma khady voix bi Moy énervé gayi
@rappel4152
@rappel4152 Жыл бұрын
Je ne suis d'aucune d'ariqa depuis toujours et pas pros mais le gars Beug Fallou a raison Ma Khady à trop de tempérament et elle ne sait pas trop parler limite désagréable c'est pas comme ça qu'on parle quand on veut faire passer un message y a une manière de parler elle aurait pu l'écouter et apprécier au lieu de...Un peu de douceur peu importe qu'il soient insulteurs et ignorants ou autre " قولا لينا " parlez gentiment : sourate Taha c'est ce qu'Allah avait ordonné à Moussa quand il l'envoyait vers Firhawn qui était un despote. Il faut rester zen calme comme Alpha et l'autre. Nous ne sommes pas tous pareil mais quand on parle de l'islam on met notre caractère de côté et appliquer les règle de la bienséance. La douceur et le calme c'est les règle de base. Il faut qu'elle regarde les oulémas d'Ahl Sunna( Uthaymîn, Bin Baz, Dr Lo, FawZan... ) le calme et l'éloquence même si ton adversaire est agressif ton calme peut le mener à être calme Faites la passer mon message de bonnes intentions d'une sœur en Islam
@requinquin1
@requinquin1 Жыл бұрын
Bilahi pure vérité
@ElieTine
@ElieTine 3 ай бұрын
Macha-Allah oustas ❤❤❤
@YusuphaTouray-oo4vh
@YusuphaTouray-oo4vh 7 ай бұрын
Senegal's believe in there tarika is very dangerous . Alpha and the members may Allah help you for the good work of hime. watching from Gambia
@SuperDaouda2
@SuperDaouda2 Жыл бұрын
2014 ba leguiii ndaysane mou ngi dadji mom da djikk yoneu wi mom loumouy geuenu wakh yoneu mi di geuneu am dolei mashallah wakh bi am na solo
@boubacardaffe6585
@boubacardaffe6585 Жыл бұрын
machallah leral bi amna solo
@mawandiaye9820
@mawandiaye9820 Жыл бұрын
Machahalla ya oustase hamenasollo
@AliouSarr-y6n
@AliouSarr-y6n 9 ай бұрын
Merci beaucoup alfa 🙏
@faly-ft5yd
@faly-ft5yd 9 ай бұрын
Mach'allah, k'allah vous bénisse et vous protège Svp j'ai besoin de votre numéro de watchap pour étudier le Coran et la Sounnah du Prophète ,je vous en prie je ne cherche que la vérité,la parole d'Allah et il m'est difficile d'en trouver actuellement dns ma communauté... Pour mieux comprendre je vous suis toujours blhi du matin au soir mais je veux votre adresse pour mieux me renseigner sur le chemin d'Allah inch'Allah merci encore Bénédiction d'Allah sur vous mes chers🤲🤲🕋🕌🧕❤️
@cheickly48
@cheickly48 Жыл бұрын
Biilahi ❤❤❤
@cheickly48
@cheickly48 Жыл бұрын
Oustaz Alpha ❤❤❤
@Kebe432Kebe43
@Kebe432Kebe43 6 ай бұрын
En tout cas : Diomay Faye peut dire haut est fort; aucun marabout ne m'a mis au pouvoir
@salifsow9779
@salifsow9779 Жыл бұрын
جزاك الله خيرا
@Alassane-fn7wo
@Alassane-fn7wo 2 ай бұрын
Alpha yag gni nga andal yena takh meu guindekou walahi nak mootakh mangui leen di gnanal yalla fayeleen.
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV 2 ай бұрын
Barakallal fiykoum yàlla Na Borom bi azawajell sam ñu tee sam leen diazakallah khaiyran
@awaba3307
@awaba3307 Жыл бұрын
Non machallah alpha amna sang froid.
@requinquin1
@requinquin1 Жыл бұрын
Chrétiens kayy gni ngui djouli ni léen ko Jésus santaané Toogn bakhoul
@abdalahyatt4555
@abdalahyatt4555 Жыл бұрын
Mashaallah ya oustaz
@aminatadiagne211
@aminatadiagne211 Жыл бұрын
Sen data Ndeye yeun nieup
@Abdouaziz-nz4bx
@Abdouaziz-nz4bx 7 ай бұрын
الله الذي خلق الليل داخل
@YoungSa-ln8nc
@YoungSa-ln8nc 9 ай бұрын
Yalla rék mo lén meuna fay
@mbayendiaye7560
@mbayendiaye7560 Жыл бұрын
Mme Khady sama kharitt boulenemaye yotttw
@salioucisse2355
@salioucisse2355 Жыл бұрын
Yaw werroullo Laillaha illallah Dangakoy dounde Bapare boy fattou nga meunko waxx
@moussaba1670
@moussaba1670 Жыл бұрын
Bonjour La différence entre le musulman et le chrétien c'est la prière tous celui qui ne prie pas va payé trop cher
@coumbayacineba3729
@coumbayacineba3729 Жыл бұрын
Fière de vous
@moustaphandoye8648
@moustaphandoye8648 Жыл бұрын
Salam Mon Frere Alpha la politique fais partí de l Islam .C est la maniere qu il faut voir.
@alphaOumarsy389
@alphaOumarsy389 Жыл бұрын
Non politique boksi yaw sama harite
@ismailacamara6733
@ismailacamara6733 Жыл бұрын
Alkhourane ak suna rek moy DEUG amoul lelene
@siacamane3361
@siacamane3361 Жыл бұрын
Longue vie a vous ❤
@aboubacryfall7653
@aboubacryfall7653 Жыл бұрын
Machalah machalah
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m Жыл бұрын
Niaka dioulli wooroul dara ak dioulli noumou néxé
@KineSarr-gi9dn
@KineSarr-gi9dn 10 ай бұрын
Baye fall mo woor yéne bakholéne
@ngordiouf3310
@ngordiouf3310 Жыл бұрын
On'est en coeur avec vous
@papediop-vt4wk
@papediop-vt4wk Жыл бұрын
Wahlene lousenyonnek
@papediop-vt4wk
@papediop-vt4wk Жыл бұрын
Magui italia
@papediop-vt4wk
@papediop-vt4wk Жыл бұрын
Baye falle doumorom
@papediop-vt4wk
@papediop-vt4wk Жыл бұрын
Nopile sohnasi
@papediop-vt4wk
@papediop-vt4wk Жыл бұрын
Katal sa Ndiaye salafou ndiye
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Mane lima diahal si ibrahima moy mom .deglou woul wahi yalla dé .app meram la topp ba narra sank bopam .thiey senegal
@oumardiallo6139
@oumardiallo6139 Жыл бұрын
Merci beaucoup alla
@ndiagamakhtarsow3599
@ndiagamakhtarsow3599 Жыл бұрын
dioulit day diouli
@ibrangom4276
@ibrangom4276 Жыл бұрын
Bay fall dou dioulit
@Bah-gl1kj
@Bah-gl1kj Жыл бұрын
Yaw kafir nga
@ousm7710
@ousm7710 Жыл бұрын
diouli diouli yefar gua
@thomasdiatta6510
@thomasdiatta6510 Жыл бұрын
Ouataz Bayil bay fall yi Lolou moy sa yeurmandei
@cheikhndiaye7094
@cheikhndiaye7094 Жыл бұрын
Yow dal khana do sonou ohlaaa gnone mom 😂😂😂😂
@requinquin1
@requinquin1 Жыл бұрын
Question bi ngay poser nii man mi amagoul 30 ans sakh amna réponse bi bilahi. Cheikhra Fall ndakh andoon na ak khélam, ak sagoom? Man djap nani tontou bobou moy indi li waral Serigne Touba téré woon ko woor ak djouli. Nitt ko khamni louniou la santeu nga déff ko ba forcer ko képp ak lépp louy noyyi kham ngueen ni kokou wéroul. Kouy woor lo ay animaux ak ay liir kokou kham ngueen ni fallait que Serigne bi téré ko nguirr bagn mou lorrr kénn wala lénnn. Gni ko topou kay nioom nio katakayni. Yalla boroom khél yi la wakhal donc kou am féébarou khél loumou déff mo gueun loumou défoul👩‍💻
@requinquin1
@requinquin1 Жыл бұрын
😂😂😂 kouy yor kour di khaathie di door ci kawam , sol ay sagar , déff tankou néén , bayyi sa karaw mou leudj ba déff ay dankeu kokou kham ngueen né amna paanou doff Yalla topé wouko dara manga Aldjana di leumbé
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Guissgeu adouna bi dafa neikh leigui trop sakh barki cheikhra fall beu kou djouk leigui yor sa téléphone gueineuh beu bitim reew wakh loula neikh tassareiko beu nieupeu diot thi man dama beugoon boudei ayy djoulit ngeen tei yalla ak deug rkk nior leen pour man nite bala nga wakh thi mom war geu dem beu biir keureum feikeu ay seuteum niou tok ngani leen kat man dama ame louma diakhal thi djeum dji tei beugoon thi ayy leral thi tel ou tel point sou booba louniou la wakh boula doyoul tei Alkhourane ak souna neik fii sagn nga tall sa telefon def live nei niom kat wakh navn ma lii wayei geumou mako doora khass wala nga togn pour leral leen touti rkk man baay fall la wayei lii ngen wakh ni seugne bi dakonei woral mou woor lo khar yi ak liir yi lolou amoul seugne bi yalla mo gnou sakeu tei guinnaw lolou nimou beugeu niou mel wala dokhei ko nioun nieupeu melou niou nonou maanam niteu ngui askano baay fall tei li baay fall di ladj yeupeu matalouko comme exemple nga guiss kouy askanou djoulite rkk tei li yalla beugeu djoulite deugeu mel melouko djouli thi nioun gnii di wotei wo djoulite gniko thi meun beuriwoul tei boul diamou yalla mouk beu fokni ya geun nite gni fall ndakh kat bouleen fatei ni djeuf loumou bakh bakh tei fatou wo yobaleiko toudeugoul djeuf djou bakh ndakh boulen fatei ni lo wakh thi nite tei teiguo ko fo weir bolen dadjei yowmal khiyam li yalla di def moy ioe say djeuf you bakh yinga yobalei thi lagni dieul diko djokh li thi geuneu woradi nak moy boudei ko hamni massalan mom amoul you bakh you bone tkk la yor thi you banal yoyou laniouy dieul ioe dila djokh yalnaniou thi yalla mousseul diw ndakh andoon na ak khelam tei bi niou yobei serigne bi exilé ko kokou ngen di wakh mo def ay pekhei beu serigne bi deloussi waat palais bii president nek ay tolam la woon ak yenneni beureub ay nassaraan toudei naniou ko doom yalla neina bindeu na loungeen khamoul mame cheikhra fall thi lingen khamoul la bok maleen di niane rkk en tant que dioulite l’islam dou diner bouniouy forcer ndakh souniou borom kat dafa yoni yenenti bi nguir mou doon yeurmeundei thi nioun tei yonenti bi meussoul forcer ken thi nekal djoulite dontei ab yeifeir nga sanakntouma nioun gni nek ay djoulite bo guissei loula djakhal thi ab djoulite mou diko def tei deupo woul ak li nekk thi tereii bok na thi djikooy djoulite yi geun mou mandou thia tei nian yalla mou leral koko ndakh souniou borom dara teuwouko tei tamit bok na thi yiniou geuneu sib mouy ak soss djoulite dou sossal moromou djouliteum ngen balma akheu beugoon na mou geuneu leer nak bou amei louthi deungeu rkk sama djeum djou kheibou bii leu bou amei louthi leeritam ngen khamni souniou borom leu ndakh moy kii leral
@mbayendiaye7560
@mbayendiaye7560 Жыл бұрын
C des tokkars les serignes six Senegal
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Ahh kou bakh tei nga bania wakh lolou ndakh kat niom def nagn sen liguey boudei nak ayy nite you bokk thi niom teiy deungeul aka wakh louleen neikh nanga diapeu ni niom dei thi deugeu rkk laniou meusseu nekk ndakh bo setlo souniou borom mi gnou bindeu sakh amoul louko neikh thi nieupeu niata yoon la souniou borom toukeul adouna ndakh ayy lorante aki niawtef souniou dingeuntei seigam yalla mo amoul lolou assama koumou yonni niom yalla neina rkk laniou meun deigeu ak topou nak yalla la angage ndakh yalla dafnei yonenti bi psl wootel rkk tei boul forcer ken ngeum allalou yalla leu moy khole kokou neikh mou defko thi mom khana deigeu nga abou lahab ba saar wathie thi mom loumou bok ak yonenti bi kon naniouy mandou boudei danio guiss louniou khamoul tei nian yalla mou leral niouko ndakh kat mom souniou borom dara teuwouko ndakh yalla bindeu na louniou khamoul tei souniou borom saasounei mou wan niou bopam thi diamou yalla yi motakh mame cheikhra fall doon louniou khamoul souniou boroma beugeu wanei bopam rkk dou nieupeu la khamal boudei li thi terei yi nak kounei meun ngako kham
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
-1:32 wadiodiou c’est bien nbaguene ko watie kissi topeu tamite watiebi rafetneu
@IbraimaTall
@IbraimaTall 4 ай бұрын
Ils n’ont pas des arguments, ce sont des domeram, tout simplement
@madoudiaw7506
@madoudiaw7506 Жыл бұрын
Makhady féroce gué
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
Makhady feroce kaye neu feroce beu dougou boite vocale parce que gni wote gnoussi beurri aynoul rahmati bignou nane billeu
@mamadoundiaye2317
@mamadoundiaye2317 Жыл бұрын
Yen manouwolen, baxna.rek.
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
-29:41 Ki werneu lilaye wahati si Sénégal un peuple de moutons
@brandonjohnnytoure3447
@brandonjohnnytoure3447 Жыл бұрын
Salam Salam wa keur gui
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
Gni amouniou argument fi alkhouran ak souneu un point un trait
@birikeurndiaye3399
@birikeurndiaye3399 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@modouboussosow7547
@modouboussosow7547 Жыл бұрын
Yalla nama Yalla mousal thiy yénn
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Mais li borom bi wah ngua d'accord si ba paré .en plus ngua beugg indi encore contradiction.mais li nehoul
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
-29:41 amneu diote pour hole baye laye bignou croix
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
Ki saga wer neu daguene ko waroneu watie
@mamadousalioucocou-zs2fx
@mamadousalioucocou-zs2fx Жыл бұрын
Ay nafeekh rek ngeen sene Mildiou dou rafett
@modoundiomitalia7294
@modoundiomitalia7294 Жыл бұрын
Wakhdji limasi geuna nekh moy si fin bila wadji poser question nila ban diamou yalla mo geuna mageu si diamou yalla yi ganiko wetal yalla kon hana baye fall lignu deff du wetal yalla
@rappel4152
@rappel4152 Жыл бұрын
Wetal yalla ci dieuf leu té لااله الاالله gneup ko meuneu repeter mais gnata gnokoy diéfé té dief leu lathieu baye fall gnofi dake bokalé ? heure rou dé grawneu c'est le moment de la vérité so kou dieféwoul wone dou meuneu gueneu sa guémine et tu peux beau essayer mais doko meunou. Guisnaye fi gnouy déh gnouné lene wakhlen لاإله الاالله té dara guenoul té avant bobou degne ko done wakh. Bayi len di encourager l'ignorance svp té guestou sen dîné dou aye fo
@morniang1977
@morniang1977 Жыл бұрын
Nane ngay néké domou Sénégal ba paré nga ni do politique ba paré nga beuga critiqué ngi politique au moins ngéne adhéré si parti RV bou cheikh Omar Diagne . Mais tok Di setane nane douma politique dafa yomb trop ndakh sa constitution ngay bayi ak ngi ngay critiqué c'est pas courageux. Dama léne di déguelou ndakh ndiarigne amna si mais votre patriotisme est néant do léne nima prophète bi douwone patriote
@Kebe432Kebe43
@Kebe432Kebe43 6 ай бұрын
En tout cas : politicien africain, égal menteur !
@birikeurndiaye3399
@birikeurndiaye3399 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdoufaal786
@abdoufaal786 Жыл бұрын
Dinè senegal dinè senegal ak dof rek
@ouleyedieng-pn5os
@ouleyedieng-pn5os Жыл бұрын
Je voudrais bien avoir leurs contact, comment les joindre ?
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Pour les rejoindre je te conseil de suivre alhouran ak sounah
@seynaboulo796
@seynaboulo796 Жыл бұрын
Sonko dh war nga déglou li ningama bétté
@galayedione2670
@galayedione2670 Жыл бұрын
Songéne loll séne mame ba légui mandoline si darra
@ndiagamakhtarsow3599
@ndiagamakhtarsow3599 Жыл бұрын
alkhourane ak sounna rek mo wore
@ThiernomamadouDiao
@ThiernomamadouDiao 6 ай бұрын
Arrobas oustaz allfha ba
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
Damademe Senegal daw bene policier topeumeu mane ak sama done ndahe tieukeul con bike tieukeul matin midi soir
@galayedione2670
@galayedione2670 Жыл бұрын
Ibra fall guene sene baye
@thieyacinekeita416
@thieyacinekeita416 Жыл бұрын
Sunu baye au moins day djiouli 😂
@ndiagamakhtarsow3599
@ndiagamakhtarsow3599 Жыл бұрын
noumoulén gueuné
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 Жыл бұрын
Ibra falla boudei dawoule diouli tei tayko yeifer leu
@abuwhanbalyibnnda0902
@abuwhanbalyibnnda0902 Жыл бұрын
Il ne faut pas bloquer les gens c'est une dialogue
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Mais Door yi menou gnouko bagne mais téwoul dawwahh bi dane koy deff .té diamonoy yonenti bi gnata dioulite lanouffi ray dilene doorr aussi .té téwoul yonenti bi hadiwoul bénna yone.kone li ngeunell la dé
@awaba3307
@awaba3307 Жыл бұрын
Sénégal kay amoul benne secteur bou dokh.montax gnaneyi warnagnou wakh fou mou fegn
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
2 ou 3 mois avant magal bi peulh yi nekheu barkedji venant tous les bords niofaye dème di ndiabar gayi aye preuve you tangible la si am Sene deal bi bilahi walahi Dina totie par A ou B te sene sonkho bobou doufi djite sounou rewmi bou heure bi djote dinagne ko gérer te ragaloumeu limaye wahe fi lakoye wahe sibir New York il faut keu mou leer dafaye diehe ala koulli ali soi nieupeu doundeu wala niou keupeu si souffe parce que sounou rew momou diarna tahaw c’est pas normal comment ça fait keu amoul kene si Sénégalais koumeuneu tahaw dageu sene tioutiou yi waye boule ne dara meti dinako géré
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 Жыл бұрын
Ndiabar dafa haram alqurane ak sunna dafko teirei kouy ndiabar nak danga woutei ak alqurane ak sunna
@dialloibrahima8134
@dialloibrahima8134 Жыл бұрын
Les filles la il faut les éviter mes frères entre filles elles peuvent faire leur live mais entre hommes et femmes ça risque de chambouler
@requinquin1
@requinquin1 Жыл бұрын
Mbatté animaux 😢 Makhala foungueen tolou sexe moy nékk séen khél yi Ma khady mo fi togal djigueen gni ndakh diiné pour niép la
@morniang1977
@morniang1977 Жыл бұрын
Mais femme bi di wakh nelene ko mou dal
@grahamkane3594
@grahamkane3594 Жыл бұрын
-22:20 damako arrêt
@galayedione2670
@galayedione2670 Жыл бұрын
Serigne touba moy sounou yakar
@ndiagamakhtarsow3599
@ndiagamakhtarsow3599 Жыл бұрын
soko yakaré kone do diouli wala
@birikeurndiaye3399
@birikeurndiaye3399 Жыл бұрын
Yakargua ci ko hamenteni aujourd’hui ci yaw la yakar en ce moment car il a besoins de te prière pour que Allah lui pardonne ak mbolemu ñi faatu
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 Жыл бұрын
Yalla rek laniou wara yakar
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Wayé limoula wah si jeuwharoul nafiss page 12 bi lerna .demal gnou firil lako
@galayedione2670
@galayedione2670 Жыл бұрын
Yéne wero léne sakh
@dadjibokaleiakbida539
@dadjibokaleiakbida539 Жыл бұрын
Koudoul diouli dou worr mo werr
@ndiawargueye5007
@ndiawargueye5007 Жыл бұрын
Au moment où vous faites vos lives pour polémiquer les Baye Fall travaillent pour améliorer la condition de vie de la population. Je me demande quelle est votre utilité sur le quotidien des Sénégalais à part bavarder.
@seydouba2603
@seydouba2603 Жыл бұрын
Baye Fall kate yélouwane moy sene ligueye .légui damay demandé lane mo gueneu magg liguayal borom bi .saway nakk nehh ngua trope
@myandiaye1213
@myandiaye1213 Жыл бұрын
Yow meunga fennn de baye fall di weurrr di sarakhou thiii biirr populations yiiii
@bocomaladi7000
@bocomaladi7000 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤
@galayedione2670
@galayedione2670 Жыл бұрын
Yéne wero léne sakh
COP29: Deal or No Deal?
2:15:24
350Africa.org
Рет қаралды 30
Replay QG du jeudi 07 mai 2020: Invité Baye Ndiaga Diop
4:53:25
How Many Balloons To Make A Store Fly?
00:22
MrBeast
Рет қаралды 194 МЛН
Quando eu quero Sushi (sem desperdiçar) 🍣
00:26
Los Wagners
Рет қаралды 13 МЛН
If people acted like cats 🙀😹 LeoNata family #shorts
00:22
LeoNata Family
Рет қаралды 44 МЛН
Oustaz Modou Fall invité de Midi + du 17 Décembre 2021
57:39
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 1 МЛН
Radio Sén Vision Médias en Direct
1:28:10
SENVISIONMEDIAS TV
Рет қаралды 29
Intégral (Live) Oustaz Alpha BA et Oustaz Assane TOURÉ
2:14:20
Oustaz Alpha Ba Donne La Parole Aux Mourides
1:48:14
Watawasaw Bil Haq
Рет қаралды 18 М.
🚨DÉBAT LUMIÈRE SUR LE FAUX PROPHÈTE || PAROLES AUX AUDITEURS LIVE TIKTOK
2:47:53
How Many Balloons To Make A Store Fly?
00:22
MrBeast
Рет қаралды 194 МЛН