Lou takh Modou Lo doore Boy Niang 2! Yaram Gueye très en colère et retrace le film..“ na bayi di nat

  Рет қаралды 27,242

Sénégal Buzz221

Sénégal Buzz221

Күн бұрын

Пікірлер: 72
@sambamangane9089
@sambamangane9089 Жыл бұрын
Kou beugeu Modou Lô ❤mane beugeu nala bilahi ndamm rek inchalla le 01 janvier
@doudodieng476
@doudodieng476 Жыл бұрын
❤Modou Xaragn Looo merci beaucoup grand Yaram Yalna Yallah Maay modou ndam inshallah
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف
@محمدعبدالله-ص5ذ5ف Жыл бұрын
Entourage modou lo ils ont super intelligent machallah 😂😂😂
@momodadd5045
@momodadd5045 Жыл бұрын
Xaragne lo yalla nako yalla may ndamm inch'Allah ❤
@awambayeeva6698
@awambayeeva6698 Жыл бұрын
Respect à toi yaram bien analyser Modou lo yalna yala may nam inchallah si barki serigue fallou 🙏🙏❤️❤️
@worldevents2448
@worldevents2448 Жыл бұрын
Allahuma Ameen 🤲
@ibrahimafaye8170
@ibrahimafaye8170 Жыл бұрын
Modou Yalna nako Yalla May ndaam barkii SWS boy niang togne bakhoul
@pouyeismaila3355
@pouyeismaila3355 Жыл бұрын
Merci yaram ak wa parcelle tellement mature Et correct,ndam rek in sha allah
@boubacarboiro5813
@boubacarboiro5813 Жыл бұрын
Modou lo Yalna nga am ndam sii kaw Boy Niang inchallahou Rabi
@alioundour41
@alioundour41 Жыл бұрын
Yarame Gueye wakh dji rafetna machahala
@MaguetteDioneKa-ln1hq
@MaguetteDioneKa-ln1hq Жыл бұрын
Yalla nala yalla may ndam Modou lo Yaram wakh dji rafetena Yalla nako yalla lafal thiate
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 Жыл бұрын
Thiye wa p.a ngion rafét wakh machallah ❤
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 Жыл бұрын
Merci grand lou léer nga wakh
@Azoura22
@Azoura22 Жыл бұрын
modou ✨ xlo yaw rek bilaye walaye seul yalla nako yalla 🤲 maye ndam amine 👑 alhamdoulilah 👑 santé 🤲 yalla ✨ bou bankh 🤲
@IssaBa-s8u
@IssaBa-s8u Жыл бұрын
Ya nopil rék boy bi da beurri wakh Bayil ba modou japp ko
@MamecheikhantaNgom
@MamecheikhantaNgom Жыл бұрын
Grand yaram gueye ❤️❤️❤️❤️❤️
@maguettegueye2971
@maguettegueye2971 Жыл бұрын
Ndame rec inchallah kharagne lo ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@mordieng4617
@mordieng4617 Жыл бұрын
Boy niang amoul dolé bako Modou beumakhé da naww😂
@madiorsene1412
@madiorsene1412 Жыл бұрын
Respect grand
@talladiop4837
@talladiop4837 Жыл бұрын
Bayiko rek boy niang bis bou khamone likoy yote dina moytou
@FatouBeye-cv1ch
@FatouBeye-cv1ch Жыл бұрын
Bilaye walay le 1janvier Dina lérr nagne modou 🦁🦁la Bourou allllle bi
@mouhamedlo5045
@mouhamedlo5045 Жыл бұрын
Kou yarou la🫡☑️
@ngourambow237
@ngourambow237 11 ай бұрын
*Alhamdoulilah YALANA YALLAH SOUBHANAHO maye N'DAME luréy Modou Lô çi kow Boye Niang 2: AMINN-YARABÎî*
@KhadyNiang-wb7gl
@KhadyNiang-wb7gl Жыл бұрын
Bravo à toi
@Meek-Mill
@Meek-Mill Жыл бұрын
Bilay nila waheii dadone pesé modou ndakh da deg modou kong la def😂
@peresene9958
@peresene9958 Жыл бұрын
Modou lo késsé amoul lenene
@mhd_0039
@mhd_0039 Жыл бұрын
Modou kassé neam rek inshaallah si barké Seydina Muhamed saw👑🏟️💪🏾❤️
@yeswecan995
@yeswecan995 Жыл бұрын
Ndeysane Modou louko gueuneuh yok force mooy gnimouy andal gneup dagneko yééuné kithi gueuneuh ndaw ba thi kaw
@MamadouMbaye-q5e
@MamadouMbaye-q5e Жыл бұрын
Boy Niang hamoul saa si coumou douguou . Modou kessé
@BabacarFaye-z9t
@BabacarFaye-z9t Жыл бұрын
Boy niang day daw ba dane boy niang barki diakhaloule modou si beuré ak si khekh
@joe6326
@joe6326 Жыл бұрын
Afer bii Boy Niang leu il est temp lamb dji changer
@badaragueye-bw2xz
@badaragueye-bw2xz Жыл бұрын
Nioume neupe Modou lo mo meune reuge reuge sa Thiès ama modou mo meune il plus sportive
@boubafall1014
@boubafall1014 Жыл бұрын
Drapeau chef de l’état saint Louis nate na Mod’lo Jalaarlo bou dieuk ba biniouy sol you rouge yi Nate nako 2stv Binak Mod’lo wane koni ligay def xam nako ❤ Mod’lo dou am pression si lamb ❤
@Fitserigne
@Fitserigne Жыл бұрын
Même biniou démé palais natt nako 😂boy niang chérr la😂
@sidathniang7183
@sidathniang7183 Жыл бұрын
''sama neubei rekhou sakh bouko modou sokhla ma kheudio koko'' Yaram mo sadikk🤣🤣
@alassanediop8564
@alassanediop8564 Жыл бұрын
Boye niagne mo togne
@senegalrek2579
@senegalrek2579 Жыл бұрын
Boye day nat waye tegina niou beumeukh ko mou dali ndar 😂😂😂😂😂😂
@medzoseck6035
@medzoseck6035 Жыл бұрын
Legui khana modou tamba la dal😂😂😂😂😂😂
@medzoseck6035
@medzoseck6035 Жыл бұрын
Modou foumou dal mome khana diawbè
@kawoba2298
@kawoba2298 Жыл бұрын
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥👑🐐✊🏻🎁🔥💪🎉
@maguettesene7527
@maguettesene7527 Жыл бұрын
Modou lo le 1 janvier laayi moudiee douggou pikine Khame naaniou leeppeu
@mamadoudiop1105
@mamadoudiop1105 Жыл бұрын
Modou lo ande ah pression kukoy wakh rek dagua faral boy niang mai modou lo kuma diapantel digua kham bala gaye wakhnako mai su modou lo neke dinako dumeu dinako dann
@ousseynoudieye7600
@ousseynoudieye7600 Жыл бұрын
Pikine amougnou mbeur bou meuna dane Modou
@Ndiayeniangua
@Ndiayeniangua Жыл бұрын
Wakhatiko deh
@medzoseck6035
@medzoseck6035 Жыл бұрын
Walahi guemo lingay wakh grand
@omargueye2309
@omargueye2309 Жыл бұрын
9:36 khana wero ioe capitaine moy responsable bi meune na bagna ay
@Ino505
@Ino505 Жыл бұрын
Yaram so wakhé Diguene nanguou Wa Keur Ama diapalé lene ma khamné dioomi Nguene 😂 Io Modou Lo wakhou mystique sakh dafko diéleulé soko tagouwoone dossi wakh ndakh mom mbeur bi kouko kham legui khamné dieuloul lep tekk ko si mystique So wakhé Jule Baldé bou gneuwé beugeu lene diapalé ngané loolou doko bagn kone màkhamné dioomi nguene nak si combat bi😂
@bocumalpha3200
@bocumalpha3200 Жыл бұрын
Nebé boko diokhé niak déh😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@BassLeye-tc8ne
@BassLeye-tc8ne Жыл бұрын
boy niag manoul nate modou kokou gun douko naaté
@papezulefaye7263
@papezulefaye7263 Жыл бұрын
Wakh lene louléne nekh mais inchallah le 1er janvier inchallah boy niang dayy dane modou lo inchallah
@Ndiayeniangua
@Ndiayeniangua Жыл бұрын
Ay doul la deh😂😂😂
@ngonesow5197
@ngonesow5197 Жыл бұрын
😂😂😂
@OmarNdiaye-co2sn
@OmarNdiaye-co2sn Жыл бұрын
Yawo yame fine
@OmarNdiaye-co2sn
@OmarNdiaye-co2sn Жыл бұрын
Moudou lo Manoule dane balla gaye 2. Boy Niang2 mouye baye me doudara
@hj-eu6xc
@hj-eu6xc Жыл бұрын
Balla gaye manoul daane eumeu sene Balla gaye manoul daane bombardier
@papediouf4607
@papediouf4607 Жыл бұрын
Modou dey danou parforce😅
@ngonesow5197
@ngonesow5197 Жыл бұрын
Modou lo ndam rék inchallah
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 Жыл бұрын
Combat bi dou mat 1mn niou takaliko
@omargueye2309
@omargueye2309 Жыл бұрын
18:06 ioe kou sokhor gua ba le 1
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
Yaram guye may diou amou ben foulá dem ga ba sa bédiawo bott modou mo tax ga dioudou dé yaw amo la wax
@ElhadjiFall-nw2he
@ElhadjiFall-nw2he Жыл бұрын
V'èrite abssolu
@damembow6374
@damembow6374 Жыл бұрын
Ragal laaa nako modou indil liko zoos andal rk modou amo loy perte sii combat bii
@omargueye2309
@omargueye2309 Жыл бұрын
8:21 moko dakh beuré kay nakh senn baye la Dane balla
@coolheuresdumonde2171
@coolheuresdumonde2171 Жыл бұрын
Mome Zoss moko dane dh 😂
@omargueye2309
@omargueye2309 Жыл бұрын
@@coolheuresdumonde2171 zoss benn lako dane TEs kokou lamb bayinako wakhouma da bayi nk yakar na degue gua fimay wakhé
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
MODOU LO EUMUE SENE LA DAN TE EUMUE SENE XAMOUL DARA MANOUL MBUER MANOUL GÉKH BILLAY 9 DEFITTE LA AM MODOU LO DAN KO NEK ROI BI
@MamecheikhantaNgom
@MamecheikhantaNgom Жыл бұрын
Katal ndyam khamo lamb
@ousmanendiaye1712
@ousmanendiaye1712 Жыл бұрын
Yow kouleuh gueneuh doff amoul
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
@@MamecheikhantaNgom yaw demay togn sa sarap ndeye sa luef ndeye sa tounou ndeye depou sa ndeye katt ko si tounou gui
@ibrahimambaye277
@ibrahimambaye277 Жыл бұрын
Balla Moss n'a modou gnaari yoon....
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
YARAM YAW BI GA DIOUDO BA LIGUYE BOTATÉ MOY SA METHIA TÉ DIEGAY BOTT YALAN EPOU DOLÉ FOUF MAI LIGUYE YOU NDEYE GA AMOUL TOGAL DI TEPI SA TOUNOU NDEYE FO FOU REK
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 52 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 623 М.
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 83 МЛН
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 52 МЛН