Allah Akbar néna dafa khifff ayy wayy ndjire yalla niou yoré dimbeulii lénn nie té yalla tax si barke seydina mouhamed bilaye j'ai les larmes aux yeux 😭 méti naa trop 😭🙏
@marieme29612 жыл бұрын
Sama xole fess na ! Je vis avec ma mère également, mes deux frères sont malades, ça perdure depuis bientôt 6ans pour l’un et 3 voir 4ans pour l’autre! L’ainé est comme l’ainé sur la vidéo, il est malade physiquement, il est faible et il faisait une dépression mais l’autre pétait carrément un câble ba nos vies(ma mère et moi) dafay nekk en danger, teh do meuneu dem bayilène guinaw. Mouno lène setane niouy guéneu keur gui di dem parce que y a plus de dangers dans la rue. On a fait recours à l’hôpital(par manque de sécurité à la maison), aux traitements traditionnels et à la Roqia. Yaye Pauline bouniouko blamer ndax moi qui parle, sunu famille wo nagn police niou menotter sa frère yobou(nexoul ci xole) mais on l’a fait ndax danger de mort laniou nekone ci ay djiguène kassé. Situations yi bari nafi et doyna waar, douniou décourager mouk aussi ci souniouy proche… mais Li kouko doundoul doko xam, et pour l’avoir vécu, damay dokh ci mbedd guiss malade mental sax, sama rongogne yii tourou ! YAllah na YAllah soutoural ak taxawou mbolème dioulite ak mbolème domou adama. YAllah na yAllah mayniou xolou dioulite ak xolou mougne !
@ManstillAman2 жыл бұрын
Marieme métina yalna yAllah taxawou sameu léne yaw ak Mère bi té wéreule léne...adouna yague na méti mais mougne rék bayi lép si loxo borom bi
@marieme29612 жыл бұрын
@@ManstillAman Allahuma amine yAllah na yAllah defal diam ak soutoureu mbolème dioulite ak mbideff yeup 🤲🏾. Defal lako
@kalagui42912 жыл бұрын
Yala nalen sounou Borom délo sène sago ton histoire me touche Marème je te souhaite beaucoup de courage 🙏🫶🏾
@marieme29612 жыл бұрын
@@kalagui4291 Allahouma amine merci pour ton empathie
@ibrahimandiaye2184 Жыл бұрын
Mougne rk adouna bii amoul solo blh
@khadijaciss43972 жыл бұрын
Ndeysane maman Pauline yeureum nako soneu na torop si dom yii yalnako YALLAH takhawou si barké SEYDINA MOUHAMED (PSL)
Bilaye souma télone khame histoire bi doumako sétane 😭instant yi beugueutouma dara thiey aduna
@fatoumatafall53322 жыл бұрын
Ça fait des semaines setanouma parce que jour yi c'est trop triste ce qu'il montre yaye bou dawer rek amatoul pekher dawna yaram
@salymbengue15232 жыл бұрын
Bilakhii Yalla da meune dai mougne rekkk ☝️☝️☝️
@binetoundiaye12882 жыл бұрын
Pape Association li yémena. Yalnalenesunu Borom Takhawou adina ak allakhira. AMINE
@anitasaliou87092 жыл бұрын
Ndaysan Yallana yalla doli kholou mougne te tagaliko ay diafe diafe adouna si barkep Serigne Saliou Mbacke Di niale association bi kham nagnoune amoulene louguéni dimbali kéne wayé daguéna wayé ndaguéna deko sen khel si yalla motakh guene defko khamne domou Adama binoul bopam mayoul bopam nous diam bi mel yalla la nekh
@fatoukane98642 жыл бұрын
Liii diape sen xél yi yalla nalén bayi ba semi xél délousi si baxou borom I🙏🙏🙏🙏
@sofiakane87162 жыл бұрын
Amine 🙏🏾🙏🏾
@mariemendiaye24122 жыл бұрын
Amine
@codoudiallo49292 жыл бұрын
Bilay li métina ndeysane yalla nalene yalla takhawou yaye rk mo mouna takhawou domam wayé mère bi dafa régal mo takh mou daw ndeysane maman yalla nalla yalla may goudou fane ak weur ba natou yi tégécoula si barké seydina Muhammed psl amine
@fatoumatafall53322 жыл бұрын
Pape yalla nala yalla defal diame maye la werr yalla molaye feyal bopam machaallah ak sa équipe
@diopsokhna73122 жыл бұрын
Machala yalnayala yok heweulgui AK werr werrseuk wouyatou sibarké seuydina Mohamed psl amiyarabi
@thiernoseck21972 жыл бұрын
Yaye boye nak yobou lenn ñiou fadiou guiiir yallah bala mouy diour moussi beu meun nagn leu rayy sakh teh dougn ko tayy yalnala yallah takhawu nga am loko fadié InshaAllah
@aissatousy187511 ай бұрын
Massa metina lolou yale nelen yale were le fadje len bouvbakhe yale n thi yep djap pour gnou wer❤❤❤aaa
@aliabeau2 жыл бұрын
c'est triste vraiment avec les quatres enfants tombé malade que dieu les aident
@baabou47512 жыл бұрын
Bilay adouna dafa mettiiiii yalna yalla def diam ak salam
@matyndiayeduval72632 жыл бұрын
S'il vous plaît arrêtez de juger la maman elle a juste peur qu'Allah les protège
@AlassaneNdiaye-f5q9 ай бұрын
Adouna dou dara, entre guémé DIEU récompensera leur Maman
@astalo396411 ай бұрын
Oh pape kholam fésna😭😭😭
@noorajoof74412 жыл бұрын
ndeyssan massa yaye. yalnalen Yalla Bour bi takhawou
@minata21742 жыл бұрын
Li niitt wara santé Yallah beurina, walahi, yalnaniou Yallah bal heure bignou salité di dioytou, Yalnaniou ko Yallah diégal, danio matadi rék
@mamediarrasaw55592 жыл бұрын
Billahi
@FatoumabinetaDiallo-cq8de Жыл бұрын
Pape Niang yalla nalla yalla Faye
@pouneyelguisse69392 жыл бұрын
Mère Pauline est très fatiguée walahi qu'Allah le tout puissant leurs viennent en aide Amine ya rabi 🤲😭😭😭
@borombakh11292 жыл бұрын
Ndayesane Li dawna yaram pape Niang bilahi wallahi kéne dou yawe nitou Aldiana firdawsi nga
@ngonekama99582 жыл бұрын
Ya allah guéris cette famille. Alhamdoulilah hanla kouli halll
@nenekeita87202 жыл бұрын
Amine yarabi
@moriciss63682 жыл бұрын
Pape gnii wéraguounous 💯💯sounou léne meuné yobou hopitale mo gueune
@binetoudieng25502 жыл бұрын
Adouna méttina trop pape yalla nala yalla maye héweul
@fatouwade50482 жыл бұрын
Massa maman,yana la Yalla takhawou si barké Seydina Moukhameth (SAW)
@mamediarrasaw55592 жыл бұрын
Amine
@fatimnahaye49322 жыл бұрын
MACHALA machala doli sante yalla bou bakhe machala yalla nala yalla maye wére ake soutoura amine yarabine aidara cherif bilakhi li métina trope ndeyesane 🙏🙏
@sidyndiaye76192 жыл бұрын
Yalah rék mo Laye faye😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢👂😢😢👂😢😢👂👂😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@sidylaminewade3 ай бұрын
Li yeupou ay liguey la rek dal nama mane mii 😢😢😢
@leytikane87042 жыл бұрын
Adouna doynawarr yalla na yalla tegui thionoyi
@PendaNgom-q1c9 ай бұрын
C’est triste Ndeyessane Yalla na lène Yalla maye wer
@umuzahra71772 жыл бұрын
Yaye ak dom c trop fort bilahi 😭
@soukadiallo12172 жыл бұрын
Bilaye Pap Niang ya bakh yanna la yalla faye
@magatfall84862 жыл бұрын
amine
@Heuget9232 жыл бұрын
Je rends grâce à Dieu..jai un frère pareil..Maman Pauline a en 4...massa
@aminaba61302 жыл бұрын
Moi ossi je l avais il est decede il etait malade a l age de 13ans juaqua l age de 30 ans
@mariebadji647010 ай бұрын
MASSEUH YAYE BOOY YALLA YALLA SAMAL LEU SA NDIABOOT BI AMIIN YARABI
@adjiseck56672 жыл бұрын
😭😭😭yalla naléne yalla diapalé maye léne werre thieuye yalla ndeyessane
@aminatambengue30842 жыл бұрын
Ndeysane andoul ak khélam yala n'a ya rahmane wathié yeurmandém si sene kaw May lene werr délélone s'ene sago ak bépeu dioulite bou tawate
@djibrilgning498810 ай бұрын
Lilepe etabila boulenko jigne serignsi ay domouram you jite dilek khalisou rewmi rek
@ndeyearamendoye3096 Жыл бұрын
Yalnalène yalla sama arr lène yalla délowatt lène sène sago ci barké sanguou sangue yii Seydina MOUHAMAD alley salatou wa salam🙏🙏🙏😭
@idrissaba40352 жыл бұрын
Pape niang mba yangui set cii sokhna arame cia Mbour. Sama xël mingui si mom à chaque fois
@hawadiallo20712 жыл бұрын
Yalla na thioono bi yam si adouna
@haysamatanar24752 жыл бұрын
Amine
@maremesougou80312 жыл бұрын
Koulenne di togale thiono laye done 2 personnes rek la na wa kogne bi volontairou dilenne andile agne ak rérr Yalla nalenne yalla takhawou
@babacarniang56907 ай бұрын
Wa kogne bi hamnaloutah douniekodeif
@mouhamedndiaye68452 жыл бұрын
Ndeyesane mère bi sonou na yalla nako yalla takhawou😭🙏
@papealinedieye13022 жыл бұрын
Louga Terre des mechant
@modoundiaye-vr9jf2 жыл бұрын
Niou bakh la niou sén papa mo ma dane piqûres serigne sou nou keur da wou fa diougue. Yallah na lègne yallah safara
@marieme29612 жыл бұрын
Amine 🙏🏾
@Dieu3942 жыл бұрын
Niou Déme Keur Serigne sonhaibou Touba Gouy Gua
@badoudia48692 жыл бұрын
Baye diop mide souko psychologue tope dinagn guisne frustration kesse ak déception moko top bamou moudie aigri ni khawma lou nekk si kholam louko diaral liii ndeyssane le petit frère mom il est complètement parti ndeyssane yalna lene yalla takhawou rek
@MarieGomis-tt6ze2 жыл бұрын
Thiey natou. Yague. Na si aduna.
@lotathiam89422 жыл бұрын
Pape yalla na la yalla diappalé
@assanegueye28 Жыл бұрын
Adouna Lou méti yaguena yalla louko soupe laye défe
@babacarniang56907 ай бұрын
Pauline liguadeif reik lala yalla fay teisisa dom lay keupo deif loubah mo amsolo
@seydinaousmanediagne77032 жыл бұрын
YALLANALÈNE YALLA TÉGUIL NATOUYI ,MÉTINA TROP .MAIS YALLA REK MO KO SAGNE
@bintouthiam4002 жыл бұрын
MERE bi sonena thiey adouna 😭😭
@astoundiaye93132 жыл бұрын
Mais mère bi pape Niang dieul nako ya quelques mois yalla na yalla diaple lene
@HamidouKeita-z9h Жыл бұрын
They yalla nagne wakh alhadoulilah yalla naléne yalla tahawou si barki serigne saliou souma guissè kou sohla té awma sama morale yeup dame