B52 mon lutteur préféré double roi des arènes ❤ CNG war nane la décoré sa jour jubilé un vrai champion de la lutte sénégalaise et une référence aux jeunes lutteur ❤ Merci Gaston production
@bayealyndiaye609Күн бұрын
Une belle opportunité pour Jackson faudra saisir cette chance ✌️
@soppeousmanesonko777Күн бұрын
Nn combat la am dh
@LampGuisse21 сағат бұрын
@@soppeousmanesonko777dou combat bombardier daye danou dousi def 20 000f si combat bi
@pablømkjr082 күн бұрын
DEUG DEUG Lamb AK combinaison dioxko albourakh ❤. VIVE LA FAMILLE NDIAYE 🫶🥰💦
@Zam-Zam710Күн бұрын
BOUNOU KÉEN SONAL LAMB LA BA DÉ SOXOR GUÉEN TROP ❤❤❤ DIADIEUF GASTON PRODUCTION ❤🎉
@piifvntome290Күн бұрын
Fi ken soxoroul deug rk la niou wakh naka lako rose dané mou dieul bomb ? Nafekh bahul waay
@Justin-Lo.Күн бұрын
Lidou Combat 😂
@AdamaNdiaye-fm3fuКүн бұрын
merci Gaston production numéro 1de tout les temps ❤❤❤❤
@AbdouazizDieye-w2bКүн бұрын
😂😂😂😂❌️❌️❌️❌️👎🏽👎🏽👎🏽👎🏽👎🏽
@dexyemba2082Күн бұрын
My boy boula gars yi sarakhé bombe dou thiakhane dé . Sama mbeur nga tu as de l avenir Jackson . Yanna yalla takhawoula té mayela ndame si Barker Seydina Mouhamed S A w
@metza-e1eКүн бұрын
Ah Jackson dé amna chance, danou si Lac rose, dale si bombardier.
@Leuzsonko22 сағат бұрын
Lamb mo dèmè nonou guiss nagn fi ada fass lac 😂 . Liss poko moko dane te lac rose lay beurèl 😂
@Lamtoro2603Күн бұрын
Lac Rose dane la guay beurré ak Bombardier 😂😂Senegal mo nékh😂
@lixman771Күн бұрын
C’est tous des imbécilité ils ont détruit cette lutte 😠😠😠
@linkstardidingkeba2922Күн бұрын
Dane nane fi mbeur mou beurék roi des arènes ba dieul couronne ba. Barki démbo ndiaye la. Siteu mo si moudj .Mom sakh daffay danou di avancé😂😂😂😂😂😂
@azizdiop282Күн бұрын
Boula say morom ragalé nk?
@soppeousmanesonko777Күн бұрын
Même Bombardier si 3 défaites la diogui
@JubjubbaljubantiiКүн бұрын
Jackson garyi niemei wougn ko lac moko dane mais moko meun 😂
@OmartoureOmartoure-c7jКүн бұрын
Al bourakh moy lamb❤❤
@Domou_Deukk_Bi2 күн бұрын
Seye 2 vs eumeu Sathies vs Zarko Tapha tine vs modou lo Quench vs mbaye gouy gui Fils de balla vs gris bordeaux Général malika vs gris 2 Pokola vs diene kaïre
@OusmaneSow-j3kКүн бұрын
Nc
@alphathiam8792Күн бұрын
Fils de bala na dem dieul gris 2
@mohamedcoulibaly1923Күн бұрын
Général Malika nane la meun dané forza Mouy dieul gris 2 fofou douma ci dakor ak yaw
@JubjubbaljubantiiКүн бұрын
@@mohamedcoulibaly1923gris 2 insbi Mo gueun bakh palmarès fass après Serigne Ndiaye 2
@CASI77972 күн бұрын
Li mome meunoleine ko promotion bamou nekhhh😂😂😂😂
@guedagueye3359Күн бұрын
khana niou yobouko CANAL +😂😂😂😂😂
@Ousmane-pz1if2 күн бұрын
Gaston. Production da soulou pere Gaston vrai professionnel
@touremamecheikh97372 күн бұрын
Vraiment abdou lahad ndiaye diga yakal Gaston prod ak jackson franchement suis fans de jackson ms mokk mbaye gouy gui moh done yone gayy bagne albourakh diko teug😢ms jackson yalla nko ylla soutoural 🙏abdou lahad xolatal sa bopp
@guedagueye3359Күн бұрын
vraiment ta tous dit
@guedagueye3359Күн бұрын
vraiment ta tous dit
@Steven-ul8pwКүн бұрын
Li Yép Clant Rk Mé Dfay Saraxé Boy bi
@Leuzsonko22 сағат бұрын
Deugeule ms bombardie mo waxon ni dina may Jackson chance te Jackson combat bi moko geuneul fouff sah😂 ay moromam nioko done toutil ni dougnou beurèk mom moussa ndoye quenche ms rombou nalèn lamb chance la😂
@MamaThiam-y7xКүн бұрын
Merci abdou lakhate ndiaye
@elhadjimamadoudiaw36282 күн бұрын
Quelle combat !😂😂😂 Albourakh yena meune deh ! Li lambi defanté la !
@papeseck9969Күн бұрын
Jackson tu a chance pour entrer dans les VIP do your best pour gagner se combat
@ndakarudialdiop12062 күн бұрын
Teug combat bo khamni lérnalén ni bou amé nite Jackson mokoy inedi té stade bi dou féss 😂thiey wa Gaston production😂😂
@layetheonly5139Күн бұрын
😂😂
@Leuzsonko22 сағат бұрын
Kom ada fass lac rek😂
@LayeDiarra-p6f2 күн бұрын
Li mome guerrou Abdoulahat ndiaye la mais dou combat walahi
@AbdouazizDieye-w2bКүн бұрын
Albourakh ❤❤❤❤👑👑👑
@goraba4661Күн бұрын
Machalla ❤❤❤Jackson dit birima
@AtoumaneNiasseКүн бұрын
Machallah comme Jackson mbeur yi danouko ragal yalla nako yalla may ndam
@mamecheikhdiop85592 күн бұрын
Albourakh seule 💯❤️💯🙏🏿
@morsene7507Күн бұрын
Mbaye Guy gui Jackson vraiment monékone combat bi
@jaynprods2Күн бұрын
wala jackson vs diene kairé
@leuzgning6004Күн бұрын
Jackson mo daw
@JacksonNiangКүн бұрын
Jackson yalanala yala may ndam 👏✊
@malickwade2727Күн бұрын
Brima seul🎉🔥
@OmartoureOmartoure-c7jКүн бұрын
Al bourakh mofi nek❤ mounekh len AK mounakari len
@Justin-Lo.Күн бұрын
Combat bou torokh bi😂Moy lane lidou combat way bombardier meunoNe n'a dieul Aline seye 2
@sakhoelimanediallo3792Күн бұрын
Li mom wohou seytané la lamb kéneu momouko promoteur yeupeu son libre de signer mbeur bouléne nékh, lolou sah Moy dohal lamb
@habibcisse64872 күн бұрын
merci beaucoup abdou lakhat vive Jackson ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MantaDiop-v3k2 күн бұрын
Ki wa albourakh lay khekh ndakh mbaye gouygu Jackson Ndiaye lakhat moko yakh mai sen li diaroul dem state yamlen amadou bary😂😂
@moustaphakhoule35062 күн бұрын
Saway combat bi kay malika plage lanioukay beuré 😅😅
@habibgaye92Күн бұрын
Vraiment jakson bou meuné dieul bombardier doyé woul dara mbaye gouy gui objectivement
@hamzafall5475Күн бұрын
Jackson bou dèfoul nii dou beurrè... tapète yi dieleuntè nagne si sènn biir kay... tè Jackson dafa bokk si lamb... felicitations Gaston Production...
@WaxDeug21Күн бұрын
Bonne chance Jackson Jr ! 15 ème victoire inshallah 🙏🏽
@LayeNdiaye-k4cКүн бұрын
Jackson limou djokh thieur balla gaye 2 mo takh mu nèkh ma défoi rendre hommage di touss ay tousam Dara djombou ko mbeur bu yarou la yalla nako yalla djapalé mou dane bombardier djèla bu guaw tée lèr thi sering fallou thi bisou magualam gui yalla baxna❤🤲
@cheikhbasskeurmassar95482 күн бұрын
Bombardier Jackson mome lamb biiiii de mom kéne khalaatouko woone Jackson kaye moosi dale lék 😂😂😂😂😂
@elhadjimamadoudiaw3628Күн бұрын
Bilahi tei amoul lou geunone nekh gris 2 bombardier. Jackson mbaye gouye gui ! Li dou gattt vraiment mais Jackson mome yalla moko beugg ! Li chance deugg leu !
@Steven-ul8pwКүн бұрын
Ban Dal Kou Wara Dém Raitret Té Ay Mromam Nek fi li kay Boukosi kén Encourage nk
@AstouFall-q2xКүн бұрын
Fou modou mayé chance siteu louné meune na am❤
@bellingham-k6t2 күн бұрын
saway boulen beugué deg deug rk fi albourakh lafi yalla tékk 😂😂
😂😂😂😂😂xaral ma rée. Lakhad Ndiaye amo xaliss gueumeul ylla
@cherifousinguinar8455Күн бұрын
Lamb dou xaliss ay pèkhè la 😅😅😅
@syllamohamadou4660Күн бұрын
Ahh combat le li Mom nice jaksone merité n'a beuré AK bom
@karimistesarr3457Күн бұрын
Inchallah Jackson Dakoy dann noté lénkô😊
@SidyDiallo-d9i2 күн бұрын
Bilahi bombe kou bakh
@madycisse6635Күн бұрын
Jackson mon lutteur vraiment sa encadrement baxul😢😢
@AbdoulayeMbengueSimaКүн бұрын
Si combat la Kay bombardier amoul ben challenge boumouy defati à part may ay rakam ak ay diarbatam chance ❤ allé Jackson
@adramebeye27852 күн бұрын
Bonne chance Jackson Jr❤️
@AmaryNdiaye-v6vКүн бұрын
ALIOUNE SEYE 2 KAGNE LANIOU KOY DIOKH COMBAT
@PascaleMendy-y7fКүн бұрын
Lii dou combat way
@boubasy2 күн бұрын
Vraiment combat bi nekhoul!! Bombardier est de 1976. Il aura 49 ans cette année. En tout cas bonne chance à Jackson. Abdou lahat mo yakheu combat bi contre mbaye gouye gui cest dommage
@ModouSall-v9xКүн бұрын
Walo walo bii seul ❤❤❤
@modoubayefallsikroulla1423Күн бұрын
Jackson yalla nala yalla may ndam rk inchallah
@OmarBao-gu5qpКүн бұрын
Merci Abdou lakhate ndieye 😂
@Ndiaye-t2Күн бұрын
Jackson yalla sounou brom takhawou may la ndam rek inchallah
@RtRt-f6lКүн бұрын
Jackson vs mbaye Gouy Gui était le combat pour dire vrai
Jackson dh champion lah kou yarou leuh mais mom si défaite la diougué contre Lac Rose wara rebondir.Gnu diokh ko Bombardier li dou logique.Supposons mou dane Bomb koneh day dougou cours des grands comme ça facilement...🤔
@ibrahimadrame94992 күн бұрын
Merci beaucoup Gaston prodision 😢😢😢 quelle combat 🤔🤔🤔
@habibcisse64872 күн бұрын
Billahi ❤❤❤
@DioufMouhamadou-s6xКүн бұрын
Vraiment li dou comba bou nex
@ibrahimadrame9499Күн бұрын
@DioufMouhamadou-s6x barki sayyidina mouhaméd combat bou nékh ngaye guiss ndakh bombardier Day beugue guénalé ak victoire ndakh yakarna bi moy dernière combat wam🤔🥺 combat ladé
@pascalkane9767Күн бұрын
Trouvez un combat à Gris 2 svp
@MortallaNdiaye-z6oКүн бұрын
❤❤❤
@damembengue18942 күн бұрын
Bomberdier nak 😂😂😂 bonne chance Jackson jr ndam rk inchallah
@Lamtoro26032 күн бұрын
Li dou combat way😂 Gaston Production khana daguén diakh lé😂
@alaminefaye6248Күн бұрын
Bilay Bombardier mo niakk khole teiii niak diome. Un combat impopulaire sans saveur incolore et inodore 😂😂
@jaynprods2Күн бұрын
bomb si bopam amoul khorom di, dou baakou bou nex , dou nexal signature, dou beuré bou rafet, dou dara
@SoninkaratelevisionКүн бұрын
Gaston Mbengue defaral n’a lamb wayè makane day yakh lamb. 😂😂😂😂😂😂😂😂 li d’où combat . Jackson ne mérite pas d’affronter bombardier
@mbayesdieng2 күн бұрын
Li dh moy lamb fathie merr deug 😂😂😂
@modoubayefallsikroulla1423Күн бұрын
Mbadou 😂😂😂
@modoubayefallsikroulla1423Күн бұрын
Mbadou 😂😂😂
@MansourDiop-wd2orКүн бұрын
Bly DEUG leu 😂😂
@AdjimmembayeКүн бұрын
Li dou combat way
@assanesene8337Күн бұрын
Alburakh 🎉🎉
@degrk5622Күн бұрын
Vraiment wa Gaston production da ngéna daanou liii mom dou combat Albourakh niaff nalén nak Nooo seuhhhh 😢
@bocarly30562 күн бұрын
😂😂😂😂😂 non li aye blangeu la😂😂
@Ghost-bl1lbКүн бұрын
Jackson waro wone djeul bomb! Victoire ley weur pour bayi! Té dane ko yomboul! Mais bonne chance de ng nek si yone!
@alaminefaye6248Күн бұрын
Bilahiii makane so bayiwoule Abdou Lahat miii 😂😂 dina lékk linga yorré
@ResidenciaImmobilierКүн бұрын
😂
@OmarBao-gu5qpКүн бұрын
Combat bou nekhna la
@matarthiam9572Күн бұрын
Mod Dia aussi war na am combat nak diaplé lenko svp