KHADIME SAMB mérite d'être honoré car il connaît la culture et l'histoire de son pays ce qui est trés important
@isaacdiouf57854 жыл бұрын
Balla est meilleur dans tous ce qu'il fait
@moustaphasonko5964 жыл бұрын
Père ce que tu as fait pour les lutteurs c'est ton travail. Les communicateurs traditionnelle aiment la facilité le sport de lutte c individuel comme le football. Les reporters de foot et les journalistes font sortir un joueur jusqu'à qu'ils deviennent milliardaire et ils n reçoivent rien en retour et ils parlent jamais mais au Sénégal vs aimez la facilité ces vieux vs aimez trop la facilité ces lutteurs ont des familles à gérer point finale
@damembengue18944 жыл бұрын
Balla gaye 2 bou beuei mou nekh Balla gaye 2 sou backo mou nekh Balla gaye 2 tabei na lol manchallah Balla gays 2 le meilleur
@trompeursambenebisamb62454 жыл бұрын
Balla gaye 2 deux moy ndanane💪💪
@yacinebouballaguaye21674 жыл бұрын
Yacine bou balla guaye2 machalla salut Lamine et mon père khadim machalla amna solo encore comme je dit toujours mon petit frère Balla est le meilleur dans tout que le bon dieu lui donne longue santé et beaucoup de bonheur machalla Amine yarabi 🙏❤️❤️❤️❤️🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@mamadoudieng66114 жыл бұрын
mane deh sokhnasi sopnala lol ndakh ninga mel si balla gaye
@yacinebouballaguaye21674 жыл бұрын
@@mamadoudieng6611Salut mon frère machalla yalnala yalla défal diam ake sa famille Amine yarabi machalla 🙏❤️❤️❤️❤️🙏
@mamadoukaolackdiallo72094 жыл бұрын
Diadieuf père Khadim Sambou yay lambolog khol séedena si explication macha Allah longue vie et santé fer ziarnalla boubakh depuis lisbonne
@abdoudiop51634 жыл бұрын
kene dou bala gaye 2 aka tabe te bakh khol bi mo rafete masahala yala na dane bombardier si barke seuydina mouhamed psl 🙏🙏🙏💪❤
@aissatoucoly64674 жыл бұрын
Balla dousa sama mbeur wayer jeste bi rafetna trop trop Macha allah
@dembabalde72054 жыл бұрын
ken dou balla
@demebadiekh74764 жыл бұрын
Balla gaye borom bakh la mbeur yi dano bone
@dioubsbarro36024 жыл бұрын
Vraiment balla 🎩 partout on parle k de tes bonnes actions k dieu t’accorde une bnn fin
@khalifagueye49314 жыл бұрын
J'aime ecouter khadim samb et cheikh yerim seck
@seynithiam7857 Жыл бұрын
Vraiment il connaît la lutte .chapeau
@falloundiaye50123 жыл бұрын
Ndaye sane balla guaye yalnako yalla diapalé si barké borom touba khadim rassoull
@bayfall26584 жыл бұрын
Balla gaye 2 da bakh de
@mohameddiop72744 жыл бұрын
tu es fort pere
@salioufaye57944 жыл бұрын
Balla gaye mome borome bakh leu bou wer bilahi
@laminegaye74294 жыл бұрын
Balla gaye yalnako Yalla lafal thiat
@gorasarr15474 жыл бұрын
Vraiment balla dou Séne morom moy noble mbeur yi
@olimataseck78023 жыл бұрын
Mach Allah loro la deuk Lamine yalla na yalla takhou la
@salihoukanoute4894 жыл бұрын
C'est pas forcé qu'ils te donnent quelque chose
@djamildiouf85934 жыл бұрын
Mais c’est un acte de reconnaissance nous sommes tous des sénégalais
@cheikhabdoukhadrndiayendia60114 жыл бұрын
je vous assure que balla et beaucoup plus sociale de tout les luteur
@elhadjidiawdiaw5249 Жыл бұрын
Wakh deugue père dafa am thieure si lamb dji barké baye niass 💪💪💪
@bassbarra18394 жыл бұрын
Dieureudieuf père Khadim
@ahmedlo24774 жыл бұрын
Nieuw dou force mayè dou force lii motax gniounane ngueweul badolala xalise motax ngay wax lii
@dembismc52434 жыл бұрын
Pourtant yagui togne ngueweul yi de te nga wakh ak borom wakh dji rek
@ahmedlo24774 жыл бұрын
@@dembismc5243 kone magui djègalou pa bii motax may wax
@sarrfallou83154 жыл бұрын
Pourtant Li paabi Wakh Dara Nekousi
@ndatteyalla99174 жыл бұрын
Vraiment ah kou ñewoul loume laye wañi la xamoul en plus may dou forçe Senegal mo méti quoi koula mayoul sax ñou taxé la kou bone
@modra54654 жыл бұрын
History lesson 101😎Thanx dad🇬🇲🇸🇳
@baaziz95144 жыл бұрын
Balla vraiment kou bakh la nieup lay dimbali tai yalla rek takh, balla khol bi moo rafet teuyer woul khalis mouy dara dafay dimbali nieup . Motakh yalla mayko loumou mayoul benn mbeur .
@Lion-hi4bm4 жыл бұрын
😁 👍 L'argent rend fou 🤪.... Mais père a raison.....
@babaanna26054 жыл бұрын
Kène dou balla Gaye
@moustaphakebe33824 жыл бұрын
Papi la buegue man bilahi
@serignesaliouniang42274 жыл бұрын
Dafa féké lamb demb ak tay yalla nako yalla may guoudou fane
@djibrildiaw81433 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂🇪🇦🇸🇳barkii seurigne touba ki dama koo beugeu❤❤❤
@morsady53702 жыл бұрын
WALAHII khadim samb mo nekh
@tk922214 жыл бұрын
Tu ne vois ça que au Sénégal yèlwan boléko ak aÿ yürou aÿ anecdotes (certe dëy nétâlii aÿ diaar diaarou lamb de l’époque) D’ailleurs ce n’est pas aux lutteurs de te donner mais plutôt à l’État si tu attends quelque chose
@mamadoukaolackdiallo72094 жыл бұрын
Vraiment père Khadim Sambou tu a parfaitement raison vraiment ils sont pas reconnaissant tout simplement ce que tu a fait dans le lamb tu ne mérite pas ce qui ils sont fait
@aveniryalla21734 жыл бұрын
Lou yombe ngaye weure. Mé merci à Balla gaye
@bayfall26584 жыл бұрын
Balla gaye 2 rek
@yorokante7774 жыл бұрын
Modou lô c lô rois des arrenes 👑👑👑
@ElTIO_Galass4 жыл бұрын
Yaw degag yak sab roi bou niak khorom bobou isss
@Senegalishtv3134 жыл бұрын
Yaro man la modou lo
@khalifamboup87744 жыл бұрын
Balla gaye 2 kanam leu jeum
@galayediop66674 жыл бұрын
Machala balla
@elibrahimahalilullah36784 жыл бұрын
Balla rekh là
@modousarr18744 жыл бұрын
Diatie.amna lofa tobaye de sete dañofay khol dar nagako gastou
@booygaye98944 жыл бұрын
35:46 père arme la yoor wala ? 😂😂😂
@mouhamedlaminetall34904 жыл бұрын
Yangui liguéye, ame seu salaire té meuno doylou. Makk bou toole ni yow, reste digne way. Niite day xam doylou mais di rassatou borom xaliss yi rek
@modouball99184 жыл бұрын
Balla khollbeirafett yallakayefaye
@cheikhbasskeurmassar95484 жыл бұрын
Balla gaye deux papaye mbeur yi kéneu Dou môme khadim samb wakhal wayy yonéte yalla Balla
@cheikhndiaye4713 жыл бұрын
Amoul morom ♥️
@mbayeiba23324 жыл бұрын
Khadime Samb wax na deug bilahi merito wul lolu li nga def ci lamb dafa reuy
@theophilesimondiouf2704 жыл бұрын
"Historien clé" lol
@ablayethiawfall60114 жыл бұрын
Pere iao boul gnou sonnal gneup kham nagn ni Balla moy sa mbeur ndakh molay mayy xaliss
@goldengilmaky67884 жыл бұрын
C’est seulement au Sénégal que les gens demandent à être honoré pour le travail qu’ils sont payés à faire. Tu avais un salaire pour faire ton boulot donc cet argent est de la corruption.
@kamoucamara73944 жыл бұрын
balla dafa diote boye lime beur yi daguakay teik feulé bokoul ak niome dakhelenne beuré dakhelenne diokhé
@amycollemboup69034 жыл бұрын
Wakhko si kaw
@giovanenero32834 жыл бұрын
Way ki na topou felle bekcayi mo si wal boyi yepou
Cest pa forcer kils te donnent cest leurs argents tw même tu travaille tu a ta famille père fair play rek
@lifestylelifestyle81884 жыл бұрын
Gñewoul yonèwoul pére adouna métiwul
@papembaye79214 жыл бұрын
Machalla
@issadiagne71954 жыл бұрын
Pére khadim Samb merci pour l'histoire que tu nous repel. Mais votre pére vous a dis quel chose de tres important. Étre geuwél n'est pas une fonction
@mbenedieng58312 жыл бұрын
Kendou khadim
@ogviito19494 жыл бұрын
Père démal nga togue gars yi amoun sa diote 😂😂😂
@talibesokhnaaida54803 жыл бұрын
Ya rew kii mo mak sa bay mbame
@houleyeifra3914 жыл бұрын
Balla gaye2 nitla machala Balla
@kingvon35784 жыл бұрын
Yenen gayi mom dono ay nit 😏
@mansourfall73454 жыл бұрын
Yaw kou beugeu Lou yombe nga père mayé force leu cooooo way
@Kocc_Barma4 жыл бұрын
Bilahi beugg lou yombou baakhoul
@kingvon35784 жыл бұрын
🤣🤣🤣
@lenfantsenegalais23104 жыл бұрын
Koufi beug Lou yomb ?
@Kocc_Barma4 жыл бұрын
@@lenfantsenegalais2310 tu n’a pas entendu les propos de Khadim Samb?
@ousmaneba60644 жыл бұрын
Ken duo balla wayè Ken duo pèt
@amaama64724 жыл бұрын
Kène dou balla guaye
@kharagnembaye48624 жыл бұрын
Yalla khol lay fay mtx toujours Moudou lô migui si kaw en plus bou danoo moléen geuneu chaire sou danouwoul moléen geuneu chaire déléne wakh rék
@giovanenero32834 жыл бұрын
Billakhi modou lo limouy deff ken defouko si soutoura billakhi
@boubafall10144 жыл бұрын
Modou lo bokkoul sissa yoyou fo togg balla gaye tangg c’est normal mou dioxleu xaliss Sissou mane gua li mooh tax ganii ganii balla mooh meun si lamb ji té eumeu danne ko 2 foi Kou bagn modou lo niou bagn keu ya xam boko xalabé
@ndatteyalla99174 жыл бұрын
Pere petêtre daño diapone rek mai may mome dou force en plus koula mayoul bumou tax gua yakarni kou bone la
@mordiakhate42604 жыл бұрын
Pere khadim wakh dji am na solo torop
@mbayatoure59384 жыл бұрын
père wouyoul Aline seye2 ak niakh nènane nga diokhlène sén xaliss bi déss😂😂😂😂😂😂
@serignesaliouniang42274 жыл бұрын
😃😃😃
@gueyetvgueye74434 жыл бұрын
😂😂
@thiapa64894 жыл бұрын
🤣😂😂
@kebambengue21144 жыл бұрын
Cool
@a-qudoosallahisone64984 жыл бұрын
cëy BG2 xalis défuko muy dara
@sambich88644 жыл бұрын
Limou kham si sunu thiosan Barina lol machallah
@ibawade61864 жыл бұрын
Dou sama mbeur mai c'est le plus généreux des lutteurs balla gaye 2 le fils de double less
@ibrahimdia76734 жыл бұрын
L'argent rend fou bilahi
@dpdp33904 жыл бұрын
Wahga degue de père denio waron niewe
@Steven-ul8pw4 жыл бұрын
Li dh moy senegal nit no mél si mom té doko teral doula tek sah nit balla kou bahla diohnala li xolam atan modou lo mas nala may 50mil lolu la xolam atan yenén mbeur yi kulasi masul may dara tmt warna man nais ndah terala dou forçe nit lumi def nako man te bukoy def na yalla rk tah pér nit ken duko diapé dioxe ndah bis bula dioxatul nga xarap ko nit manala yeuk te fek yorul dreum bumla dioh
@andremendi34754 жыл бұрын
😂🤣🤣🤣🤣Teugouma combat pour mbeur am xalis
@baimamud14913 жыл бұрын
😂😂😂😂
@mbayendiaye1704 жыл бұрын
Pabi nena 1945 wala 1950 pabi bobou dioudogo
@omzogueye91683 жыл бұрын
Balla nite kou bakh la
@modoucisse22964 жыл бұрын
li dh mogui beug métti thiokhé forse 🤣🤣🤣
@giovanenero32834 жыл бұрын
Per may niou diamou modou lo comba am ak lac 12 mulino la dello pape abdou fall pape abdou wakh nako billakhi yen sen bopou rekk
@moussadiallo45504 жыл бұрын
Balla gaye nit kou bax leu
@morndao52624 жыл бұрын
Lamine teye amnga gan
@adamasognane29884 жыл бұрын
Fayal alioune seye 2 relika am bi mo geune
@serignesaliouniang42274 жыл бұрын
Père nak fayal aliou seye2 ak niakh sén xaliss
@augustinfaye87924 жыл бұрын
Eh ionei len pabi an
@mouhameddieng85644 жыл бұрын
Beugue teugue lamb diko wère si aye nit so mounoule do ba boule ngou sonal waye
@isaitendeng134 жыл бұрын
Père Mayer Dou forcé dé iow
@nitedeug69714 жыл бұрын
mayé dou force tu parles trop
@souleyewade74194 жыл бұрын
Khaliss rek lolou mo takh mou nane balla mo meun c faux eumeu sene mo meune
@ndakarudialdiop12064 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣
@ousmanetine65644 жыл бұрын
عجبتٌ من جادم سامب !!!
@abdousall90424 жыл бұрын
Per mayér doufor chou ahh
@ndakarudialdiop12064 жыл бұрын
😂😂
@abdousall90424 жыл бұрын
@@ndakarudialdiop1206 ahh wakh n'a deugueu di
@abdousall90424 жыл бұрын
@@ndakarudialdiop1206 Sénégal danon tamou lolou
@abdoulayefaye72714 жыл бұрын
Escke c force de te donner arret waay
@antadiop66934 жыл бұрын
Balla dafa bakh d bilahi balla kholbi mo rafette
@bengcamisetastv77924 жыл бұрын
Kon diokhla xaliss c'est par force ?
@mussdio62514 жыл бұрын
Père tu étais payer pour le boulot
@mbayeiba23324 жыл бұрын
Mane suma lay deuglu nga wax ci lamb sama yaram day tang dieure ndaxe yaw yay lamb khadim