No sérieusement nak Reug Reug moy lamb 🫡 Félicitations ci victoire bii
@baityrba2447 Жыл бұрын
Vraiment Reug Reug mongui dundale late tourou thiaroye si lamb dji mon frère Thiaroye est fière de vous félicitations Reug Reug
@toutpourlefootball8489 Жыл бұрын
Ndeysane cheikh daffa beugg reug reug xol ko daye retane rekk
@pendafall9903 Жыл бұрын
Reug bene moye dak inshallah champion ga🎉❤❤❤
@issandao1378 Жыл бұрын
Félicitations sa Thiès Bell victoire machalah Balla gaye 2 notre fierté
@elhadjiabdoulahidiagne9726 Жыл бұрын
Reug Reug champion Machallah
@rawanegueye590 Жыл бұрын
Nos reug reug masalah mbeure leu franchement
@dimkhalebambiste2931 Жыл бұрын
soy weur mbeur so guisé reug reug diapal mo len geuna saf mbeur niom nieupu billahi vrai champion la
@efootball224 Жыл бұрын
Y’a pathie deh😂😂
@momotouray172 Жыл бұрын
Merci Siteu et Reug Reug Maa Shaa ALLAH
@alvin2goat339 Жыл бұрын
Mbeur kamine mo gui ni Omar Kane defarou rek diel si ténors yi defal lenn affaire… tu es très brave et tu es un grand champion donc évite les discours et travaille plus fort dieli roi bi bientôt ❤
@assanediop771 Жыл бұрын
Reug reug leegui mboolo mi dako commencè wouyou ci
@dameniane65 Жыл бұрын
Felicitation sa thies ak equipe bi yeup du courage reug reug champion nga
@mamecorndiaye1850 Жыл бұрын
Félicitations reug reug ♥️
@abdoulayeniang2511 Жыл бұрын
Bilahi Siteu phénomène leuh😂🦁❤️🔥💪🏿
@ibrahimaly8584 Жыл бұрын
Day nexal lamb kw lii Moy lamb ambiance rk
@marcusmouhamed Жыл бұрын
Lamb dekina way diadieuf gnari mbeur yi❤❤
@oumarseck2710 Жыл бұрын
Gni tokk thi plateau bi di wax respecté wougnou BG2, siteu à beaucoup de chemin à faire
@papito8025 Жыл бұрын
Vraiment bilahi 😁 mane dei dama tite
@Ibrahim_dia Жыл бұрын
Ces reporters sont hypocrites
@lemondetv5415 Жыл бұрын
Il a fait 4 appuis mes bilakhi daffa meune lamb mbeur deug la chorégraphe bou çétt la am machalla
@papadiom9260 Жыл бұрын
Lou werrr Reug Reug mii sakh gayi Dagn ko merer thi communication motakh gnou soot ko welbeuti Victoire bi (Thi batine naak kaay wakhe ay yaw )! Mais mbeur Camille laa ! guis nga ni mou teureule Sa thies nonou lako narona daner en 1ere action mais dafa gnakk concentration thi biir gew bi !!motax ay tektal lam you beuri daf thi djoum.
@lemondetv5415 Жыл бұрын
@@papadiom9260 le problème moy sénégal dougnou comprendre niit kou meunoul wakh té lolou daffa am si ay niit mes lii dinako yéé
@serignedia9391 Жыл бұрын
Siteu mbër kaamil la❤
@efootball224 Жыл бұрын
Si bane aya la nek 😭😭
@papedjiby1354 Жыл бұрын
SITEU BALLA GAYE COMBAT LEU
@Bilal66850 Жыл бұрын
Meilleures combat de ces 10 dernier année
@damesylla8010 Жыл бұрын
Machalla champion reug reug roi desane inchalla bonne continuation grand lutteure mana beurré ame dollé machalla
@efootball224 Жыл бұрын
Reug reug mane rek mako eup dolé 😂
@ouzdaking382 Жыл бұрын
Siteu grand champion le baye fall sociale Yallheu neu Yallheu yoné nieupou diamou Inch'Allah 🙏
@cheickamalasanogo7939 Жыл бұрын
Siteu il faut respecter les gens ,Sa thies t'a humilié et c'est avec Balla tu veux lutter. Balla c'est ton arrière dans la lutte. Je suis un fervent supporter de Modou, je ne supporte pas Balla mais il mérite le respect dans l'arène sénégalaise.
@ibrahimaniane6508 Жыл бұрын
😄😃😀siteu kayy daffay xarou koi
@adamaseck8816 Жыл бұрын
Siteu bi balla dougoussé nga faye
@sarrymbengue553 Жыл бұрын
Guané siteu amoul respect yaw dagua dof
@amadoulatyrndiaye231 Жыл бұрын
Yew ya wara respect siteu boye niang amoule deux defaite tee gniowe beure ak balla dane ko wala instan bi dane balla mo guenna yebou danne sathies wala yew khamo lambe balla kenne widiwoule donne champion wakh deff na lou neee thie lambe mais aussi siteu amena droit laye ko comme sathies nimou ame droit ladhie gniome bombardier nekelene ayye sportif li deyye sport la rek
@cheikhmoussaba5440 Жыл бұрын
Merci beaucoup frère bien dit
@baityrba2447 Жыл бұрын
Siteu il est plus qu'un phénomène ❤❤❤
@astoufall8165 Жыл бұрын
Boy Niang késsé 💚❤️💚❤️
@ndeyeyamasokhna1503 Жыл бұрын
Reug moy lamb bilahi
@efootball224 Жыл бұрын
Wauyy Reug reug meunul 😂
@mamadougalsen8712 Жыл бұрын
siteu mome da fateni papa sow rek la dane😂😂😂
@mgoudj23goudj65 Жыл бұрын
Akk zoss 🤣🤣🤣
@mamadougalsen8712 Жыл бұрын
@@mgoudj23goudj65 waxnga deug 🤣ancienne gloire rek la dane
@mgoudj23goudj65 Жыл бұрын
@@mamadougalsen8712 siteu gayii dagn ko eupeu dollee... ba paree mom xamoul bopam
@mamadougalsen8712 Жыл бұрын
@@mgoudj23goudj65 lolou moy probleme bi amoul dolé comme gars yi😅
@ibrahimaibrahima6448 Жыл бұрын
Balla gaye 2 la star de l'arène
@ndeyematyseye Жыл бұрын
Oui c vrai c l'unique 👌💪
@papandiaye7155 Жыл бұрын
Reug Reug vraiment champion la
@efootball224 Жыл бұрын
Xana champions des parleurs la 😂
@papadiom9260 Жыл бұрын
@@efootball224 Guis nga nimou teureuler Sa Thies ??? Reug dou ay Tiaxane dhee
@momotouray172 Жыл бұрын
Maa Shaa ALLAH le Stade était extraordinaire
@kebaseck3531 Жыл бұрын
Reug reug le meilleur de t les temps 😍😍😍😍😍😍
@abdoufall2660 Жыл бұрын
Kéneu wédi wouko mais danouna.
@Mobachir92 Жыл бұрын
Reug yaye lamb par force
@piifvntome290 Жыл бұрын
Siteu gouy gui meunou la dane Sa thies dane la Nga beug teukou balla gaye Beug nala lol mais dou combat boula papa sow nakh nak
Balla daniouko maye chance mouno beurè ak Saye morome beurè ak saye make dangaye beurè ak Saye rake lamb nila
@bizliontv1671 Жыл бұрын
Je ne comprends pas la haine de siteu envers Balla gaye et sa famille.
@diolsallamariam392 Жыл бұрын
Limou dane yekini motakh
@modoundiaye7985 Жыл бұрын
topal feulé ganane haine
@yayustyledancertamba1022 Жыл бұрын
Siteu daga beug leek si khathie yi xana😂😂😅😂
@falloudiop4925 Жыл бұрын
Déte way 😂😂😂😂
@neymarsy3453 Жыл бұрын
Si Reug Reug voulais battre Sa Thiès il ne fallait pas être avec Siteu 🤣😂🤣ce dernier a été victime
@abdoufall2660 Жыл бұрын
Siteu yow Gouy Gui daane leu . sa Thiès dorleu daane leu nga beugueu beuré ak Balla Gaye2😂😂😂 kou bax nga naak té baye Fall mais yemal bala may tégui worma gui😂😂
@modoundiaye7985 Жыл бұрын
reug nak mbeur deug la 🤣🤣🤣
@clementpommesarr9877 Жыл бұрын
Nanie wakh si eumeu séne vs balla. La date du combat
@Lune_Ghost01 Жыл бұрын
Siteu doit attendre le vainqueur de Forza vs franc ou prendre sa revanche chez Gouye gui mdr
@assanembengue4747 Жыл бұрын
Siteu tonton wam yekini la beug fayoul yag Nako wakh
@moustaphagaye1457 Жыл бұрын
Kone dh na nopalou nakh Balla dou beuré ak mom
@ibrahimandiaye4923 Жыл бұрын
Xalè bou ndaw diapla Dane la ba toksa kaw massage la ak lifi sa Thies wax yep tay mou toppu plateau tele yi ande ak Gaïndè bou maguètte bi ak payi sèytané yi Tapha.Gueye ak Bècay di wax waxu 4 appuies😹dolène sakh rouas REUG REUG dafko dane ba massage ko😂
@papasarr6270 Жыл бұрын
Yaw khamo lamb reug daw combat bi yép comme djiguéne ba danou
@efootball224 Жыл бұрын
Ioe xana Novelas Tv nguay setané lamb 😂
@wizkid540 Жыл бұрын
Ak michoui mbam bi...😃
@momobouthiapathiolybi7752 Жыл бұрын
Siteu mo meune balla gaye fouff gaindé gou maguette la dafay khoukhalé🤣🤣🤣🤣
@doudoundiaye3152 Жыл бұрын
Bayilen fofou khamouniou ni balla diekhalna khana mystique
@mouhamadoudiop678 Жыл бұрын
Saway dagua rouss rek s'en mbeur mii boy Niang beugone coalisé ak reug reug nenako dafay beureik mom deh🤣🤣saway yaw sakh wahowone nii reug reug mo meune sa thies
@elhadjiyoussouphdiatta2810 Жыл бұрын
Hana do hool,sathies rek Moy garap siteu
@momobouthiapathiolybi7752 Жыл бұрын
@@mouhamadoudiop678 wéro 🤣🤣🤣boye niang mo meune si génération wam la preuve mossi raw🤣🤣🤣
@mouhamadoudiop678 Жыл бұрын
@@momobouthiapathiolybi7752 mais meunoul amanekh ak zoss deh ak tapha tine ak lac 2 deh waleu
@falloushoptv257 Жыл бұрын
Siteu beug nalla trop mais si balla gaye lala nara méré
@guillaumembaly6704 Жыл бұрын
Lolou dou dara
@mortadacisse8992 Жыл бұрын
Méré gua khôl koukay yeug Siteu laniou beug❤️
@moussandiaye2045 Жыл бұрын
100%serere
@khassimkane3985 Жыл бұрын
Reug Reug rek bilahi ragalouma lolou
@1999-un Жыл бұрын
Reug mo féssal stade bi
@tazdinediallo6318 Жыл бұрын
Xana guiso li sa indi
@IbouGoudiam Жыл бұрын
Wayei mom laniou dann 😂
@serignemansourtoure86 Жыл бұрын
YALMINE BI KÉSSÉ LANIOUY TOPP 💪💪💪
@maestrocisse Жыл бұрын
Aky Deug
@Guawarguilofficiel9776 Жыл бұрын
Wallay lolou layy wakh sunu wa kogne SA THIES AK REUG REUG danio dékalate Lamb mé nanu fakhé ba combat biy ndieukk amate mou nékh rk
@momoseck1617 Жыл бұрын
Dou saram ndém
@sambagueye-bv9bf Жыл бұрын
Bilay balla moy lambou😂
@Diarista90 Жыл бұрын
Wa siteu 🤣day comèdie🤣🤣🤣
@mamadoumoustapha6174 Жыл бұрын
Siteu AK Reug Reug yeup ay defeant lagne . Sen affaire nafekh yi lanie wara bayi 😔
@mamadoumoustapha6174 Жыл бұрын
Siteu AK Reug Reug nanie beuré boudai lepp deug lh.
@wizkid540 Жыл бұрын
Lansar la deukk dhh mais deugg nékhoul moyy siteu khamoul boppam
@mbackemoustapha9161 Жыл бұрын
NDAKH NGA SAÑKO WAKH DAYE TAPPALÉ RK DOU ENTRAÎNÉ
@dimkhalebambiste2931 Жыл бұрын
mo meun balla de lou lér lala wakh
@wizkid540 Жыл бұрын
Barki Lerou alkourane siteu meunoul dra
@jadamajadama7749 Жыл бұрын
Siteu, wahal te noppi, boul def action. Bayil sa staff yii niou wahal la . Maanam lingue beugeu deff. Mais hamga nè pour Balla defa tehl. Por favor 🙏
@ndeyesonadaffediouf Жыл бұрын
Yaine gniy comentaire taiguaina bagna diay siteu
@omarsenghor4572 Жыл бұрын
Siteu rek laniouye topou
@serignesalifoufaye8888 Жыл бұрын
Momo ngom Yamuna tege
@meissaseras3855 Жыл бұрын
Siteu Siteu leuh
@RIINAA24 Жыл бұрын
Mais en fait Lamb dji demb nekhona deh Wélélélé deh
@deutschkillatv4696 Жыл бұрын
Siteu et reug reug demlenligeyi yakamti guen lolu sen adouna
@mamecorndiaye1850 Жыл бұрын
Siteu balla combat la
@nouhadieme1889 Жыл бұрын
Siteu pour mome mbeur la boul faté ni papa sow rek nga dane