Boy Niang wallahii je l’aime quoi,il communique très bien et il est très poli machallah ndam rek
@muhamedjabbie86472 жыл бұрын
Inchalla balla ndame rek ❤️
@ndureuhofficiel22472 жыл бұрын
Je vois un Boy Niang Tres determiné piur ce combat ! Yalla nala sunu borom may ndam ! Dangako sokhla Pikine sokhla ko
@issalayendour14092 жыл бұрын
Dolène am Dara
@djilybadiane94112 жыл бұрын
Ama balde. Sagnu la diapalee
@maxfall35972 жыл бұрын
Ndam rek inchaallah boy niang ❤❤❤✌🏾
@abdoutall84912 жыл бұрын
Yaa meune yaa eup dolei yalnala yalla may ndam inchalla
@talibecheikh57042 жыл бұрын
Qui vivra verra
@modo62182 жыл бұрын
Amine inchallah
@moftv49612 жыл бұрын
reve bien
@mamadousarr05102 жыл бұрын
Vous êtes méchant
@abdoulatifdiop56402 жыл бұрын
Amine
@papafaye22042 жыл бұрын
Boy bi amna Dole 💪 nk
@mouhamadoujegou76962 жыл бұрын
Kou khame entraînement rék Soko khoolé rék Di nga khamné amena doolé dafa entraînement ba oooss billahi
@papafaye22042 жыл бұрын
@@mouhamadoujegou7696 no amna Dole 💪
@tigotigo19792 жыл бұрын
Massala
@normalement21esiecle82 жыл бұрын
Maachalah 🙏 qu'Allah vous protège très discipliné
@daoudambow83482 жыл бұрын
Ya meune ya eupe dolé ya gueune nek khalé kou wédi ladial sa thies😂yalla nala yalla maye ndam lou reuye 🙏🏿
@modo62182 жыл бұрын
Bilahi 🤣🤣
@ml_sa98802 жыл бұрын
Être jeune veux rien dirre vous avez rien compris dans le sport de combat
@iboudiatta85252 жыл бұрын
Mo Moune mou eup dolé mo geuna nek khalé après tu dit yalla nako yalla may ndam comme mo Moune diaroul yanal cône
@talladieng61322 жыл бұрын
Daw lakhou .Amo mbeur bou dane BG2.
@ibrahimadiouf96852 жыл бұрын
Lou lèerr nga wax
@Lune91212 жыл бұрын
Boy Niang yaye yeungueul Gway✌️
@sabalyhadji10202 жыл бұрын
Un message très important les lutteurs de pikine son très discipliné vraiment machallah champion victoire le 1er janvier une cha Allah
@saintlouis85872 жыл бұрын
Rien la voix de boys niang montre que il est très déterminé et confiant
@abdoulkhadrecisse50872 жыл бұрын
Dans vos rêves arrêter de delirer boy niang momeu si bobam khamnani amoul niveau bou beurei akk balla apart beuz bimoussi ameu .
@saintlouis85872 жыл бұрын
@@abdoulkhadrecisse5087 attention diambour j'ai fais que constaté je ne suis pas un fans de boye niang ok Le 1 janvier inchallah moy gagner
@gueumsabop69902 жыл бұрын
@@abdoulkhadrecisse5087 yow hamo.boy niang kèn dou dèba ak yow sa beur dè dièhalna jour ba ngay comprendre
@emilemoreira64652 жыл бұрын
Voix ak determination rek danoul keneu. Qu’il reste concentré balla est toujours dangereux!
@djibytaye91102 жыл бұрын
@@saintlouis8587 ioe da nga xam louy xew demain arrête way
@amadousall48402 жыл бұрын
Boye Niang le parolier de la lutte mais balla gaye yalnako yalnako yalla may ndam lou sedd sa kaw
@ndeyemaguettembengue83322 жыл бұрын
yalla bakh na. balla niogui lay nianal inchalla yalla may la ndam do yakheu lamb am ngua Diom am fayda ya tatk gneep beugue lamb yalla na yalla laf that machalla L
@gnakoudione77252 жыл бұрын
idole la toujours respé laye woné même sax bouye wax ak khalé mberyi royléne ci boye niang kou am respéla merci mber
@mayad.222 жыл бұрын
Lo meunti doone champion Balla Gaye 2 dou sà morom ben yoone ci beuré ci doolé ci palmarès🫶🏽. Wà salam 🙏🏼
@abdoullahiingom74012 жыл бұрын
Sa papa mo ndieuké wax dji saway na diokh bopam respect ba paré
@balladiop63362 жыл бұрын
Du courage champion djameu rek INCHA ALLA
@taftaf39892 жыл бұрын
Wdiour tamite naniou respecte domou diabour yi balla domou diabour la
@fodetoure87402 жыл бұрын
Merci
@alassanendong96102 жыл бұрын
ndam rk boy Niang gui reffo amnga respect vraiment
@elhadjiibrahimadiatta94852 жыл бұрын
Na sa pape noppi té dinga danou inchallah
@truckwarriors98322 жыл бұрын
😂
@Sowpoulohardo2 жыл бұрын
D'accord na ni sa thies limou wakh warouko wakh wayé tamite respect bi père De Gaulle moko warone ndieuké, lou nékk yakk nako balla gaye. Mag sou amé respect moko may bopam.
@onelove67212 жыл бұрын
Wakh dji yeup lolou la Mai senegal hamouniou kou togne kou fayu laniou kham
@mouh6842 жыл бұрын
Inchalla balla gaye 2 dey dane boy niang amine ya rabi inchalla barkhe seydina mouhamed
@diakhatecheikhna81462 жыл бұрын
Après gay comprendre
@mouh6842 жыл бұрын
@@diakhatecheikhna8146 inchalla balla gaye 2
@diakhatecheikhna81462 жыл бұрын
@@mouh684 inchala boy niang rek
@daoudambow83482 жыл бұрын
Thiapathioly bi😂yaye deranger Wa guediawaye deh😂kou wédi ladial sa thies😂yako diap doumeu ko daane ko😂😂
@chamousman27262 жыл бұрын
Waw waw waw
@laminefall32402 жыл бұрын
Merci boy bayilén rék niouy wakh yaw nitt gua
@souleymanediaw89302 жыл бұрын
yaw khana li Degaulle di wakh degoko mak sou ame respet moko maye bopam
@laminefall32402 жыл бұрын
@@souleymanediaw8930 pourtant papa balla gaye dépasse n'a eumeu mais biniouko ladjé dafani sama papa la moko wara wakh bilahi
@souleymanediaw89302 жыл бұрын
@@laminefall3240 man de degouma li less wakh me douma rafetlou kouy depasse na bayi boys niang wakhal bopam mo ko dakh cominique
@ninkinanka36442 жыл бұрын
Kagn La Nek Nitt Mom MOFI Andiwone Violence Bi Contre Zoss Faté Xadioufi
@saintlouis85872 жыл бұрын
Bilaye noys niang mala fans wayy de la part d'un fans de XLO
@michirimichiri54872 жыл бұрын
Yalna yalla may la ndam champion bi khamo wakh bou gnaw doko wakh tamit Boy niang 2 sec ❤️❤️❤️❤️
@assfall74002 жыл бұрын
Mon luteur préféré fils déghaule ♥️♥️💪💪
@ibrahimamba12962 жыл бұрын
Nous les supporters de Bala nous demandons à notre lutteur de bien se defoncer et de nous respecter ; s'il amène la même forme que contre Mod Lo, Boy Niang n'aurait aucune chance
@cheikhoumarsy26922 жыл бұрын
Oo
@cheikh03902 жыл бұрын
Oe je suis d’accord avec toi bravo
@daoudambow83482 жыл бұрын
Sou indé forme bobou sakh dafay daanou inchallah
@jenas85922 жыл бұрын
Deug pire!
@ibawade61862 жыл бұрын
Bilahi boy Niang ndam rék
@cherifdiop55202 жыл бұрын
Bilahi Mbeur wax ngua deuggg dioxeii tchieur dafa am solo si ndaw wax dji rafett neu trop mbeur machallaah
@diakhatecheikhna81462 жыл бұрын
Bilahi bala prépare toi liga done wakh ay yekini tyson yeup boy niang dinalako wakh si sene face face té dosi meune dara té inchala boy niang dinala douma danela
@papadiom92602 жыл бұрын
Bilahii Walahiii te Balla mola geuna xam Lolou! Amna loumouy bayi khel thi Boy Niang ! Ba leguiii ay kadoum dafkay kholate
@manemorndiom30522 жыл бұрын
Waw lolou rk la balla bange rk nk
@amadouly15702 жыл бұрын
On est toujours derrière tw Yalna la sa borom may ndame sa tiens wakham moi béryl reck
@ahmeidtoure23732 жыл бұрын
Sa way lii dou combat balla dou sa morom balla ndam rek inchalla
@daoudambow83482 жыл бұрын
Boy niang franchement wakh dji rafete na da nga niité nak,sa thies amoul respect motakh nga diap ko doumeu ko daane ko aka niak diome mome
@diakhatecheikhna81462 жыл бұрын
Lolou moko meti liko boy niang humilié moko meti
@onelove67212 жыл бұрын
Papay boy niang nak amna respect si domou double less yi ?
@daoudambow83482 жыл бұрын
@@onelove6721 séne papa dou le less tok na fi wakh léne lou nek té takhoul niou dépasser ko té dégaulle sene baye la,baye dou morom
@alioukama72112 жыл бұрын
Inchalla la dame rec
@baimamud14912 жыл бұрын
Balla ndam rek insallah 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@user-re4pj1bp8k2 жыл бұрын
Merci ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
@layetamba93242 жыл бұрын
Yalla na balla gaye am ndam🤲🏿❤
@youssou51622 жыл бұрын
Sa papa mon respect woul bopame kone kéne douko respecté
@patheka84162 жыл бұрын
Bilahi Incha allah balla Gaye 2 dalay dane
@papadiom92602 жыл бұрын
Dioum nga
@aliouneba30782 жыл бұрын
foko tekk
@patheka84162 жыл бұрын
@@aliouneba3078 balla ko meun
@alalama19172 жыл бұрын
Boy NIANG da dakhar ndeyou sa thies ba pare danekoooo
@drameserigne28712 жыл бұрын
Bravo thiapathioli bi, boys Niang rék
@salioukebe2722 жыл бұрын
Bilahi boy bii champion laa
@sellediop132 жыл бұрын
Machala dafa yarou trop
@papemalickfall21832 жыл бұрын
Bilahi lii rekk gaa amm thiii combat bii baa jour inchalla dinga kham lepp deuggg la
@aliounedieye97512 жыл бұрын
Bien dit que le meilleur gagne
@moustaphasognane20712 жыл бұрын
Yalnala yalla May Ndam tiapatioly bi
@modougueye62422 жыл бұрын
Yalla na la Balla dan 🤲🤲🤲🤲🤲
@diop35752 жыл бұрын
Aminne
@baimamud14912 жыл бұрын
Amen
@falloumbengue11742 жыл бұрын
Merci boy Niang sa Thies amoul respet
@jenas85922 жыл бұрын
Sa Thies lanela wah? Bayi léne soss
@sirysene882 жыл бұрын
QU ALLAH le tout puissant vous assiste et vous protège si barke cheickna wa khayartou
@didiermakhouniass29522 жыл бұрын
Ya meune fouf combat bi mome balla dinga nek makk force dano sonou si khalé la
@morseye40842 жыл бұрын
Wakhale sa kawe momi moy khaley bi balla Makla
@didiermakhouniass29522 жыл бұрын
@@morseye4084 lolou kay leer nek makk force
@djeganengom2 жыл бұрын
😂😂😂
@moustaphasonko5962 жыл бұрын
Les supporters de BG2 bayiléne Papay diambour bi kéni manké de respect wakh lén si combat mo gueune si mbeur depuis bimou daané ba légui da takk radio wakh lén si Lolou inchallah le 1er BN2 dinako daane
@djeganengom2 жыл бұрын
Vraiment amuniou respect kouné say parents ga am respect dafa bakh si nit
@serignefalloumbacke78492 жыл бұрын
Inchala walahi boy niang Lima guiss nekhouma
@papecisse60002 жыл бұрын
Waw Waw boye Niang machalah. Tu as bien dit
@cheikhfatmaseck17362 жыл бұрын
Lamb djiiii dou wah billahiii
@oustazahmedfall64782 жыл бұрын
Vive boye niang 💪💪💪💪💪
@damembengue18942 жыл бұрын
Do deff dara wakh rk nga meune do dara balla dina leu defall bagage mou lerr 💪💪🙏
@mohamedballadiop60852 жыл бұрын
Bayiko mouy wakh rék
@adandoye37592 жыл бұрын
Bayiko mouy ndélou rekk
@ousmanefall57432 жыл бұрын
Champion gua dei
@baityrba24472 жыл бұрын
Yallah nala yallah may ndam si kaw balla 💚❤ amine
@donapreirratousss67772 жыл бұрын
Fétéwole wah dji rékk... Contre Tapha ni lafa démé wone ! Bi arbitre Siflé nga Diel Péage biii 🏃🏃🏃🏃 Contre Balla dinga diel vol ??
@mohamedballadiop60852 жыл бұрын
Bayiko fofou rek khamaguoul likéy kharr
@donapreirratousss67772 жыл бұрын
@@mohamedballadiop6085 Contre Tapha tine nila wone . Di Wahhh rékkk bi arbitre siflé mou diel Péage biii🤕
Yalna yalla maye ndame boye Niang 2 bi diahi Moustapha 🤲🏾
@aliousarr36852 жыл бұрын
Bonne chance Boy Niang
@Elhadjikane-i6f2 жыл бұрын
Ya moune ya eup dolé ya geuneu nekk khalé yalla nalla yalla maay ndame
@djibyba20212 жыл бұрын
Boy Niang vraiment tu es très poli
@rastablondy46562 жыл бұрын
Sa thies douma biko boy niang douma môye bone khôl bi 100 combat boy niang doumako 100 fois
@amethdiop1352 жыл бұрын
Machalla boy niang
@ndeyeamiseck60982 жыл бұрын
Doubles champion la té degaul todioune féne
@papebirameba76892 жыл бұрын
Ama baldé foumouy far 🤣🤣🤣🤣🤣
@bambalo33982 жыл бұрын
Mashalah gaïndé Ama Baldé sou meunone communiquer comme iow ken douko geune
@mouhamedalicisse47522 жыл бұрын
boy niang yalla nako yalla may ndam
@babadiop56212 жыл бұрын
Inchallah rabi samawati wal hardi, boula balla gaye 2 daaner, nga délou sa place. Non , c'est ton père qui se doit du respect. On n'a jamais entendu feu falaye ou doublesss ou autre père de lutteur parler comme ton père
@mohamedballadiop60852 жыл бұрын
Ki bayiko rek daffa khamoul loukéy kharr motakh. Le 01 janvier inchallah Balla dineuko diokh la leçon de sa vie. Foumou deigueuti Balla sakh déy daw.
@siteudia55732 жыл бұрын
Yalla na yalla may ndam reuy
@keurmadembagueye86412 жыл бұрын
machalla
@momoantandiaye88132 жыл бұрын
Que la chance te sourit boy Niang
@raymondassele55552 жыл бұрын
Ama baldé n'ai pas avec toi de se combat balla c'est sont frère de sang✌🏾
@mohamedballadiop60852 жыл бұрын
Exactement
@baityrba24472 жыл бұрын
Domou dekeuh bi Niang ballo 💚❤
@sabarasts2 жыл бұрын
Boy Niang 2 Yala nala Balla Gaye 2 dane diél bou leer barke Serigne Touba
@abdouxadiimmbacke23522 жыл бұрын
Machalha yaw nit nga ❤️🥰🙏✅
@baityrba24472 жыл бұрын
Yaye dirigé dh 💚❤
@Maestroo.202 жыл бұрын
Cest vrai , mais sa wadiour na respecter mbeur yi tamit! (Lakk dom dorr dom)..! Limouy deff double less meussou ko def domou diambour, falaye et boy kaire pareil.. conseillel pa bi mou nopi toutii
@laminebarro16862 жыл бұрын
Le goldeune boy de la lutte
@ibrahimatalifndiaye68222 жыл бұрын
Bien dit boy niang
@babacarsow3872 жыл бұрын
Le respect est réciproque
@amadoumboup22702 жыл бұрын
Yalla nala yalla may ndam si kaw balla gaye2
@alioukama72112 жыл бұрын
Boy champion gua ♥️♥️♥️🤼♂️
@mariemusicof18812 жыл бұрын
Yallah may Balla gaye 2 am ndam
@jrkinamablde6572 жыл бұрын
Ndam Rek domou pikine bi ❤️💚❤️💚❤️
@taftaf39892 жыл бұрын
Inchala balla dina la dane maloko wakhe
@papadiom92602 жыл бұрын
Walahi hanzim dou dane Boy Niang! Lolou la Sunu borom dogal
@taftaf39892 жыл бұрын
@@papadiom9260 yalla naniou yalla yob daroule thiow
@seydinaoumarmbengue52882 жыл бұрын
Bama diodou ba legui balla rk mouy sama mbeur mais walahi guisouma foumo mene diar boy bi ndakh balla forme bi ma guis ni danol boy yi mais nak leep lou waron def li lamb wax degue yalla def ngako masha Allah deselou niou dara
@sambaba6832 жыл бұрын
Kèen dou Balla guaye2 le lutteur du peuple dou sa morom ahhhhhhhh
@abdoutall84912 жыл бұрын
Maa fi djitou ❤️
@baityrba24472 жыл бұрын
200%100 Pikine késsé 💚❤
@oustazahmedfall64782 жыл бұрын
Vive boye niang 💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
@mbayediagne46192 жыл бұрын
Bilae diam rek guay am inchallah
@modoudiouf53362 жыл бұрын
Boy niang yal nanga def balla gay lou raww linga def sa thies si barkè salalahou ala mouhamad
@Mod-t2y2 жыл бұрын
Amine
@modo62182 жыл бұрын
Amine inchallah
@issalayendour14092 жыл бұрын
Kou am Balla Gaye 2 nè Sérère le.
@djilyfaye3592 жыл бұрын
Boy Niang mo mane sa thies mo mane balla
@elizamendy81032 жыл бұрын
Boy niang iow khamo sa bop Balla dou sa morome dala may chance rek
@mohamedballadiop60852 жыл бұрын
@Eliza ki bayiko beu leu 01 Janvier inchallah Balla dineuko yarr bamou yarou ne t'en fais pas.
@sabarasts2 жыл бұрын
Boy Niang nena gni Balla done beurél bokoul ak niom, dama beugue kham Boy Niang ndakh mo dakh beuré Modou Lo ak Eumeu Sene 🤔 boy ya nékh 😂😂😂