*Merci père. Heureusement am neu ay nitou lamb youy wakh deugue. Siteu wakh leine ko deugue. Il a perdu, diaroul contane diaroul jubiler. Khalei so beugué nek roi dangay daan sey mak. Mais khalei bou sokhla beu paré di daw di gueine sakou, beu paré beugue am ndam.*
@nafisene53353 күн бұрын
Malheureusement nitou deug amoul ci lamb ji. Siteu mo ndieuk niak diom, mane meunou ma comprendre Niit mey la chance Ndakh mbokk bi ngeen bokk, beugue nga bokk ci cour des grands, nga nieuw def yeufou défaillant deugue. Ki ndekete d’où goor, goor yomboul nak
@amdydiagne3083 күн бұрын
Saway fi amoul makk AK xalé 86 AK 88 la donc ay morom lagne siteu dou mbeur
@rouguikebe99843 күн бұрын
@@amdydiagne308Siteu mo niak diom rek
@Abdallah313413 күн бұрын
Siteu dafdone beuré mélni mom moy roi bou nieuw pour conserver couronne. Combat bi sakh mo donouton lou diadou ....
@KhadidiatouCamara-m9r3 күн бұрын
Vraiment deug rk ga wax siteu mo beuri wax kom Al Waxa lane lay recours la beug xam mane bisi topou moy arène bi kou yor titre rois bi lou yag gnou xekh la sote la mo dal Modou Lo nak instant bi gneup niogui kay sot bassi lamine samba ak yenen seytanè xaram lagnu rk
@vieuxndiaye37903 күн бұрын
Billahi combat royal fête meunona beuré loumou am dieul dou tee dina meunate am combat boumou beug mai kene dou modou il n'a rien à nous prouver félicitations modou lo
@abdoulayengordiangar45903 күн бұрын
Siteu n'a jamais été courageux roi kén d'où KO négocié tu le gagne honnêtement et avec dignité faut dire a siteu la vérité c mieu pour quoi jubilé alors que il n'a rien foutu
@AliouneKANE-k3o3 күн бұрын
Tu as parfaitement raison mon ami
@tallandiaye64813 күн бұрын
Vrement
@abibefam30562 күн бұрын
Tout à fait raison
@BarhammDioufy3 күн бұрын
Gniy wakh siteu dfa douma modou hana wave lagn setané combat bi🤣 ki modou khawko rayy
@MaodoKane-mw4yd3 күн бұрын
😂😂😂😂
@guedalka50893 күн бұрын
Khamouniou louy douma, pour gnom ardo la tei ay coup irrégulier lako dor si guénaw sakou yi
@sidythiam69833 күн бұрын
Bilay😂
@nafisene53353 күн бұрын
@@guedalka5089way way d’où sakh coup irrégulier, daf ko xossi comme djiguene. Mane yalla khamnani siteu kou ma bett la. Bilahi
@rouguikebe99843 күн бұрын
@@nafisene5335yeufou femme deugu la déf😂
@rokhayathiam79133 күн бұрын
Pa bi da contre modou Lo il est toujours avec la famille Azize ndiaye. Tout le monde c’est que siteu n’est pas lutter le dimanche même l’action modou la fait ✅ félicitations 🎊🍾🎉🎈 modou Lo
@mbayendiaye45623 күн бұрын
😂😂pourtant modou lah favorise
@khadijadiallo50122 күн бұрын
@mbayendi😂aye4562
@MatarMbodj-df8eb3 күн бұрын
Bilahi Modou lo moy diaambar ❤❤
@mamadoumareme98493 күн бұрын
Père khadim yallah nafi yague té weer
@ndiayemohamedrassoul-hb4mi3 күн бұрын
Siteu mom legui nileu nara continué carrièram way siteu Père Wakhouko deugg dei tmt Ah
@oumitandiaye67803 күн бұрын
Pa khadim samb un homme véridique 🇸🇳🇸🇳💯🦁 et honnête
@Iiiiiiiiii8733 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@mamecorecisse18492 күн бұрын
Mouke ki dou wakh katou deug mouy talife nii😂😂😂
@NoguayeNdiaye-t7y3 күн бұрын
Merci beaucoup c très pertinent
@hm-gw2ms3 күн бұрын
Merci beaucoup, M. Samb, pour l'honneur que vous faites aux femmes en nourrissant l'intention de rencontrer le ministre des sports "parce que c'est une femme" La femme est la mère de l'humanité. Rien que pour celà, elle mérite le plus grand respect, la plus grande considération.
@Aaron-i5f3 күн бұрын
Siteu da wara commencer dieul ay responsabilitè bopam di beurè...daan ak daanou moy lamb
@chrisduncan78223 күн бұрын
Siteu a déjà gagné de par son courage mais je suis désolé il n’a rien fait qui mérite de lui donner la victoire. Il n’a tente aucune action.
@kurayahmi3 күн бұрын
Non. Il n'a rien gagné de par son courage. D'ailleurs il n'a pas fait preuve de grand courage vu le combat qu'il a livré.
@nafisene53353 күн бұрын
Quelle contradiction🤣 dans tes dires, tu parles de courage et tu dis qu’il n’a tenté aucune action. Donc courage amoufa mon cher. Siteu dal bo beugué deugue, y’a que les nafekh qui voient son héroïsme ce jour là. Il n’a rien rien rien foutu
@ouzinfall64013 күн бұрын
Contradiction 😂lognou beug expliqué est ce que doko wakh wolof pour gnou geuneu comprendre 😂
@sidythiam69833 күн бұрын
Siteu na félicitate modou rek
@ISmile__3 күн бұрын
SIteu était tt sauf courageux hier je suis désolé 😂😂😂 Courage c savoir faire face et ps fuir toute la journée et faire un refus de combat devant tout le monde et qd ils sont payés par les européens ils le font pas motax il faut remplacer les sacs par des barrières ou les élastiques de Ring de boxe 🥊
@tidiane18783 күн бұрын
Ndanane fakh deug moy Doudou Lo domou parcelles bi rek niou dem🥰♥️👑✨
@moussadieye57022 күн бұрын
Doudou lo😅😅😅😅😅 kay ndaanaan leu
@souleymaneba33218 сағат бұрын
Khadim sambe khana danga diote touti. Modou lo dafa d'amour. Comme si le front touche la terre vous que ce n'est pas la tête. La victoire est pour Siteu bien qu'il n'est mon lutteur.
@sidythiam69833 күн бұрын
Merci père
@AmCoulibaly3 күн бұрын
Vraiment père tu a raison
@IbrahimaNdong-h4g3 күн бұрын
Macha Allah
@moimeme10583 күн бұрын
Pâtisserie Medina sama fief Chaises yi fi rek la ame❤
@souleymanejulesdiallo11203 күн бұрын
Siteu rombounama lgui di daw rek😅😅😅 yene nak?
@ShiekhjobeTijan3 күн бұрын
diar nafi legui di daw 😂😂😂😂😂😂
@papeabdoulayedione47663 күн бұрын
Il a raison. Bizarrement épaule amoul si règlement bi
@AbdoulahadWademouratn3 күн бұрын
Merci
@DounkhafGadiaga3 күн бұрын
PÈRE AKA BARRI AY JAARR JAARR❤
@isokaire3 күн бұрын
Lougn wax ni sauf Aziz ndiaye Aziz dall mom exception la si lepp prsk dafa am khaliss😂 Sénégal d'où deim Décline wax aziz deugg gueine fatei khaliss bi
@ModouGueye-j5h3 күн бұрын
Pa khadime laminé laye wowé lirou diane😂😂😂
@moussadieye57022 күн бұрын
*Beuy bou oppa bissi keur gui loussi oudé bi wakh gnou derbaaa takh* C'est du lourd
@mouhameddiallo20143 күн бұрын
Je te remercie énormément mon père il reste toujours honnête envers mon Président de la République son excellence Monsieur Macky Sall merci beaucoup
@CheikhounaDiop-y5r3 күн бұрын
Siteu 👑👑👑👑♥️👍🤲☝️
@ModyFaye-kj5bn3 күн бұрын
Lou am solo
@moussebeye41652 күн бұрын
Le roi des arènes est un titre qu'on doit mériter.Pour ce combat contre Modou LO,Siteu n'a fait que fuir.
@papfall93633 күн бұрын
Ms video bi lutax continèwul ci afer ginnaw saku yi mudon léral
@IbrahimaDiouf-z4x13 сағат бұрын
XLO seul ❤❤
@souleymaneba33218 сағат бұрын
Si siter était à la de modou lo., c'était déjà validé. Ragal lène yallah au moins touti.
@lacitoyenneafricaine85663 күн бұрын
Papeu ya ngui wah lou yague Ba lamb nekher!!! Ndeyssane!
@MoustaphambackeThioune3 күн бұрын
Président dafay réye di teudj , rek mola yak 😂😂😂
@YacineBadiane-v8x3 күн бұрын
👍👍👍❤️
@bayemo41473 күн бұрын
lutte tv yena naafeq d loutah egaliwolen video bi pabi reglemnt bi lay wah ; ki nekk thi biti sakou yi meunoul daane ki nekk thi biir
@ousmanendiaye17123 күн бұрын
Non gars yii lii lagnouye def dagnou koyy daag c pour avoir plus de vue après dagnouye dougalate lissi dess
@bayemo41473 күн бұрын
@ copin lima done khaar guissoumako d 😅😅 wahone nalako gars yi ay nafeq lagn dougueul nagn 2eme partie bi Mais séquence bobou dougoul
@bayeserignethiam95003 күн бұрын
Beugoul kén mére pabi😂😂
@TijTij853 күн бұрын
Lamine Seck doo lale 5 millions dei 😂
@AdamaCisse-sg6vb3 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ThomasDioplerni3 күн бұрын
Wenceslas ndione c'est mon oncle professeur EPS
@UserSN-Gbm3 күн бұрын
Ndandanaou Dow ak reuthie 😀😀
@elhadjiibrahimathiam14533 күн бұрын
Tant que vous gardez le 4 appuis cette règle bidon qui ne fait que favoriser la triche.
@thiernodieyedia9083 күн бұрын
2025 Senegal amoule réalisateur ak caméraman pour def VAR
@HenritoureDiop3 күн бұрын
Alors comment peux tu expliquer ,pourquoi les arbitres ont arrêté le combat pour aller consulter le VAR .Deuxièmement étant donné quebtu ne fais parti de la commission des lois et règlements tu devais t abstenir et ne pas affirmer ni infirmer s'il y'a ou pas chute.
@Self-improving723 күн бұрын
Siteu na pas respect sa parole
@ibrahimediop74703 күн бұрын
Père dit la vérité tu n'aime pas modou sa montre billahi
@g.b11863 күн бұрын
MACKY SALL, LAN LAY ÉGALI?? C'EST FINI AVEC LE SÉNÉGAL. LE TOUR D'HORIZON N'EST PAS IMPORTANT, IL FALLAIT RÉPONDRE DIRECTEMENT À LA QUESTION.
@adamasonne729Күн бұрын
T toi Bordel, où est le problème ?
@papegueye1473 күн бұрын
Vraiment gniy wakh si lambe da bari ay nafekh wakhlén siteu deug limouy def insbi dou lamb nakholate bopam dadaw ba lamb dji diekh
@YungP0273 күн бұрын
Ada capitaine bi ley khekheuuul le 30 douy si wakhhh ennnh 😂😂🫵🏾
@mansourndione1783 күн бұрын
Pa bi serere la siteu domou serere daye yarou
@AbdoulAzizDabakh633 күн бұрын
Père faté wou niou leu déh CPI .
@Mamadou-j1x3 күн бұрын
Laminé aka Katte ndy 😮
@jazaka31783 күн бұрын
Kone dal dathié ak Modou lô daw baniiu gagné la ak avertissement ndam la thieiy sénégal 😂😂😂
@papiiiswelleeiih57283 күн бұрын
Mane dama diaxlé nakh gnom gno nek siii lamb teh kou nek ak sa réglement 😂😂😂
@FallouDiop-pz4sf3 күн бұрын
😂😂😂😂ki limou wakh lépou né mome la déf eupou na ay atamm😂
@MamediorNdiaye-km3iw3 күн бұрын
Yen yi yena wara diangual khalei yi yenayy ndanane yi yalla n'a guenn fi yague tei werr
@papfall93633 күн бұрын
Macky nenako gor deugeu nga😂😂😂
@AboubabaBa-m5h3 күн бұрын
Modou mo yobou bopam ardo sitte daw ek amoul arè😂😂😂😂
@abdoudiallo89593 күн бұрын
Siteu mo dan Modou lo lolou mo am c ça yiii motakh lamb mounoule dem fene
@gabanefall24473 күн бұрын
Daur martou rèk 😂😂
@serignefalloumbacke78493 күн бұрын
Bay khadim mi dh modou la faral
@MbackeBalde-ok7jr3 күн бұрын
Le systeme est more amoul layam.layami
@Sarr238823 күн бұрын
Pa yii ay seytani la gnio beugue gnio sérére nek roi motax
@moussambaye45753 күн бұрын
Non ministre bi néna nga took té gnanal ko ndax amoul diot . Temps yi liguéye bi dafa beuri thi cotém
@Iboumaffe3 күн бұрын
Fall newon nama siteu day daw rek
@babacardiop41733 күн бұрын
Kone dal modou lo mena beurém ak kharagne bi motakh nguène beugueko khagne victoire bi nguir rék li Modou lo dém ardo Sénégal vraiment degue toumranké nafi ndakh ay mak youy parparlo ak guenalanté ak bagne koula sik bado wakh degue siteu roi kéne douko for ba didaw bamko démal liguéyi modou lo dafala dane
@ndiayeibrahima89313 күн бұрын
Père makgua wagnil wakh bi .MODOU LO DAFA DANOU
@MouhamedCisse-fs9hu3 күн бұрын
Ragalal Yalla
@ndiayeibrahima89313 күн бұрын
@MouhamedCisse-fs9hu MANE SITEU FARALOU MAKO MAIS MODOU LO EPAULE BI LALE NA SOUFF .LOU LER LOLOU LAGUIS
@rouguikebe99843 күн бұрын
Nane doom ba yakhou, nioulay dakhadji gay daw, nék si guinaw sakou di door ay coup beugu nio dane😂c impossible khalé bou ndao niak diom ba dé .nadéf ni ay morom niom Ama ,BN2🎉
@ndiayeibrahima89313 күн бұрын
@rouguikebe9984 lamb la rek noumou meuneti daimer fayekouna khaliss bou beuri tey siteu raw na morom you beuri lolou dakh dou sante YALLAH ? Modou nouko balla def mo guena gnaw ter tey moy roi
@gasbalde49363 күн бұрын
L'affaire c'est pas tantes des actions ces de mettre son adversaire a terre siteu là fait wallaye siteu danna Modou lo
@villanova-gt9yh3 күн бұрын
Président day Rey ( tué) thiey Sénégal 🥱
@cheikhmbackesyll98383 күн бұрын
Thieuy lamine degg ko aka bagne modou lo yakamtina gnouni modou lo danouna
@ousmanemolo72313 күн бұрын
QUALIFICATIS BOU NIT MASS DIOKH MODOU LO , BIKO PERE DIAW DIOKH MOMA THI DAKHAL , NENA BOU TOLONE NI NIOM DOU BEUREK NIOM
@cheikhtidianesy12933 күн бұрын
Naniou bayi nafék siteu mo dane lép sénégal lay yam modou lo ay domou djiabeur ladan dane louy probléme bi délén wakh deugeu yén ndieup géniy dal sikaw boy bi
@MoussaGueye-r3i3 күн бұрын
Franchement pa guewel yi braiment momoulen nitt.yi douguen cng dans vos plateau vous dite n importe quoi laissez le cng dire la vérité donnez au cng cet crédibilité au moins mais chacun croit que son avis est le bon et sans contexte pas normal
@jhonewarehouse24383 күн бұрын
Siteu defou fi dara sa thies daco dane gouy gui daco dane 🤦♂️
@BayeNdiaye-x3k3 күн бұрын
pa bi mo warone nék président CNG ki daffa xam lamb waye
@dielkeffelywele81283 күн бұрын
Tu as raison Khadim il n'y a pas de chute sinon Siteu aurait fait 4 appui.
@IbrahimaDia-z5g3 күн бұрын
Siteu am na ndam!?! Quel honte la lutte doit être un sport avant tout. Autrefois on l’appelait « SPORT DE CHEZ NOUS »
@ThiernoDiop-ei2ht3 күн бұрын
Lamine mi kou na fekh la siteu sakh da dara am avertissements ndakh da gueneu sakou yi
@KossoGadiaga-vw3wc3 күн бұрын
Siteu kasse siteu kasse ❤❤❤❤❤
@MatchoDanfa3 күн бұрын
Moi je suis fans de balla gaye mais Modou lo est un grand champion mane mome la faral mais baxilen di wax sott boude sott balla combam contre boy deniou ko sott sott bou grave te mome dafa danou waxoul dará boude sott la balla gaye mo beurile lounioukoy sott franchement parler siteu dou mbeur dafay saw rek dou taxas ni la yagg beurre
@mountakhaba1593 күн бұрын
Père modou Lo dafa dano lolo moy deg
@Bakelsen993 күн бұрын
SITEU MO DOUDOU PAPA DOW DOUMEU ZOSS DOUMEU MODOU DIOUTELO 👑🇸🇳SITEU ROI 👑MAIRE DE PARCELLE
@AboulBacharSall3 күн бұрын
Siteu mom loudoul yokkou agression si lamb guissouma loumou déf si lamb
Man mome khamatouma darà sì adouna kharal ma nopi rek
@BayedjilyNdiaye-sx2go3 күн бұрын
Da beuga bouuruxlou
@fatouthiame70003 күн бұрын
Ai poltron
@amethzidane25663 күн бұрын
Balla gaye bamou soxla roi des arenes contre yekini dafa wone nei mo geun nek xalei tei mo soxla Bombardier vs tyson aussi pareil Yow nga soxla roi geun nek xalei apres di daw rek
@modououmy16763 күн бұрын
Ay khétou broukhlou bou kene trasime
@fallouminquette58303 күн бұрын
Khadim samb déll wakh deug féne rék
@kebepapa72583 күн бұрын
Khadim samb ya sof maky sall nekatoul senegale legi maroce la 😂😂
@ThiernoDiop-ei2ht3 күн бұрын
Mbeur boko nième woul boulko dieul siteu dawna lamb diepou balama dee niou nan diambaar la diambaar Dana daw bayi len sen wakhi kania yi niakk diom rek la deff daw rek
@Ydakh-ui5yo3 күн бұрын
Gayi ragal nagne Modou lo nak Dafa dangereux nak
@ibrahimadiouf86643 күн бұрын
Tout le monde sait que Modou Lo a chuté,siteu l’a terrassé,ne soyons pas hypocrite,c’est la lutte qui va gagné mais dire des contrevérités si ça ne t’arrange et si c’est le contraire vous dite c’est le règlement,quoi qu’on dise siteu a gagné sur le terrain
@fatimatarachiddiallo39023 күн бұрын
Y’a meuneu fene yow
@alioudiangar68953 күн бұрын
Ne dis pas tout le monde...moi j'ai pas vu de chute de mod'lo..
@PeulThiao-rg2eq2 күн бұрын
Bén angle rekk lagnouy khol mé arbitre bi khamnani boppou siteu dafa tégou si sakou bi
@mbayebabacardiouf25683 күн бұрын
Tout sauf victoire de siteu
@mohameddiagne37703 күн бұрын
Sa niane bobou dè sii Macky sall dèe yalla douko ndangou fake bii nga doon
@babacardiop41733 күн бұрын
Yaw yangui ram pour niew si ngour gou besss bi dh
@Daj7yoa122DOucuorÉ3 күн бұрын
Tuenauveux
@atoinesarr12193 күн бұрын
Pere max mbargane n'est pas un bon ménager siteu n'est pas entouré de professionnels comme lo