Ma soeur veut m'expulser de la maison familiale

  Рет қаралды 76,826

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Ma soeur veut m'expulser de la maison familiale

Пікірлер: 350
@elimanesow9915
@elimanesow9915 2 жыл бұрын
Courage Mame goore copain bou cool bou niak blém on a grandi ensemble à grand Médine yalna borom bi takhawou
@habibatoundiouck4358
@habibatoundiouck4358 2 жыл бұрын
Alakhou akbar thiéy yalla nioune founiou dieum kheuthio souf boudoul diékh.il parle avec un cœur 💔
@ramathiamniang6820
@ramathiamniang6820 2 жыл бұрын
Ba adina Di bakh djiguéne souniouko tacké daffay seuyyiiii Tawou yaye bou djiguéne Moy ndeye Da wara yeureum ouff ay raakkkam Alalou baye dou alal Wa salam
@blackart4353
@blackart4353 2 жыл бұрын
T’as tout dit mashAllah
@madikebop5717
@madikebop5717 2 жыл бұрын
Oh ndaysane mame gorr c t,un ami d'enfance a grand médine vraiment mame gorr meusoul am problème nitt kou bakh vraiment yalla nalla taxawou yarabih
@matarndiaye3496
@matarndiaye3496 2 жыл бұрын
Du courage sa keur Baye la, boufi dieukeurem nieuwé, nga tégale ndaye mou diékhe
@mariemendy6830
@mariemendy6830 2 жыл бұрын
😂😂😂
@madameoumar1622
@madameoumar1622 2 жыл бұрын
Késsé nak dafa yomb trop
@oumidiallo5074
@oumidiallo5074 2 жыл бұрын
Bilakhi li kene meusse Nako guiss Ani dieguenne AK akimo keur Ani gooooor
@momosy6083
@momosy6083 2 жыл бұрын
@@oumidiallo5074 🤣🤣
@MrFayemanou
@MrFayemanou 2 жыл бұрын
😂waw waw
@mariemely3290
@mariemely3290 2 жыл бұрын
va voir le notaire et ecris vite une lettre au procureur de la repubique directement au palais de justice de Dakar.ne mange et ne bois rien dans cette maison.
@ndeyeamicissokho8339
@ndeyeamicissokho8339 2 жыл бұрын
C'est la meilleure chose à faire
@karimfaitsesvideos7903
@karimfaitsesvideos7903 2 жыл бұрын
Ou procureur de la rue publique😁😂😂
@bbouhama5373
@bbouhama5373 2 жыл бұрын
Yalla nala yalla gueneu diapalé rek fekhel ba protégé sa alalou papa, gni ce sont de vraie indign
@bajjanmaram4409
@bajjanmaram4409 2 жыл бұрын
QUAND ON A DES GRANDES SŒURS COMPLEXÉES ET FÉMINISTES ( ESCLAVES DU MATÉRIEL) CEST TOUJOURS COMME ÇA.. DES GRANDES SŒURS QUI REFUSENT D'ÊTRE DES FEMMES AFRICAINES AUTHENTIQUES DE VALEURS ( SURTOUT DE VALEURS MUSULMANES). LEURS PRÉOCCUPATIONS CEST LA ''VANITÉ'', LES PERRUQUES, S'ÉCLAIRCIR LA PEAU, DU MAKEUP'' TOUT LE TEMPS, OR, ET HABILLEMENT DE MARQUES ÉTRANGÈRES.. DE VRAIES IRRESPONSABLES CES GENRES DE FEMMES.. RAKK MÊME BULA TOOGNÉ, ANI SA GRANDEUR, SA MATURITÉ, SA YËRMANDÉ, SA INTELLIGENCE???? N'IMPORTE QUOI.....
@anifanawtamsbi1394
@anifanawtamsbi1394 2 жыл бұрын
Vraiment kokou vrai domuram leu
@MrFayemanou
@MrFayemanou 2 жыл бұрын
😂badou dagua sée am
@meryemsaks1101
@meryemsaks1101 2 жыл бұрын
C’est ça le féminisme Madame ?
@coumbademe4655
@coumbademe4655 2 жыл бұрын
Walay wakh nka leppp
@aminataditeyayediatouciss2002
@aminataditeyayediatouciss2002 2 жыл бұрын
Dama rouss sakh mane deih suis l’aîné de ma famille mais samay Rak sama alal sakh nagne yak wakhoumala ndondo chim da am niou bone reik🥹🥹
@famagaye7641
@famagaye7641 2 жыл бұрын
Bilay meunouma Wakh Sama Copin la me li mome nasi Sénégal yi Diap te yalla rek takh😢😢😢😢
@youwadia8782
@youwadia8782 2 жыл бұрын
Thiey yalla légui dei mbok amatul bokk ndeye ak baye dou touss défa melni bokk négg bi guén di fanane sou guén kheuyé kou nék dém !! Mbokk mo amatul valeur légui thiey aduna bi légui lépa diakhasso xawma founiou dieum !! Bayi ko akk yalla yalla moko eupp dolé !!
@mamadouka5502
@mamadouka5502 2 жыл бұрын
courage mon frère Faut se battre Faut se protéger mystiquement aussi car ils sont capable du pire
@mariamaba1709
@mariamaba1709 2 жыл бұрын
Aywaaaaay adouna dou keur té wallahi nitt mougui daw si lo khamné khamoul sakh ndakh dinako fékké 😭😭😭😭
@MD-qi9eo
@MD-qi9eo 2 жыл бұрын
Walaye ndeysane yalna BOUR YALLAH déff diam adouna amoul solo
@ndeyecodoudiop2500
@ndeyecodoudiop2500 2 жыл бұрын
Walakhy
@aramedieye6261
@aramedieye6261 2 жыл бұрын
Bilay
@Marhone
@Marhone 2 жыл бұрын
Mon frère liladaal metina trop 😳 Je té conseille nga dem Gendamerie. Ils sont plus sérieux que la police 👮‍♀️
@dieynabapouye3289
@dieynabapouye3289 2 жыл бұрын
Oh thieuy aduna yenisay NGA fate say problème ndakh bossou diambour yii yalnala yalla sam metina Thieuy alal 🤭🤭
@kinesow4679
@kinesow4679 2 жыл бұрын
Ndeysane li dafa méti torop yalla nako yalla safara ci barker seydina mouhamed psl
@SENEGAL303
@SENEGAL303 2 жыл бұрын
C'est certainement le confident du vieux. Yalla Nala Allah samal sa papa
@adjiseck9104
@adjiseck9104 2 жыл бұрын
Eywaaay boke alalou yalla la adouna dou keur. Yalla nalene yalla tahawou. Li gnawena trope. Affairou famille daaaa doye waaaaare.
@babacarsow5658
@babacarsow5658 2 жыл бұрын
Courage Mame Gorre iow champion ga Gorgourloule rk yalla Bakhe je vie dens la m'aime soutouation
@jackmichaelpoutine2498
@jackmichaelpoutine2498 2 жыл бұрын
🤣😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣
@babacarsow5658
@babacarsow5658 2 жыл бұрын
Iow Poutine tu rigoles en
@aminatadiouf6031
@aminatadiouf6031 2 жыл бұрын
C dommage k Dieu te guide Des problèmes kom ca ilny en a telment les gens oublient k Dieu voit tout tôt ou tard justice divine sera faite .kene dou yobou dara billay Courage
@awadiouf7404
@awadiouf7404 2 жыл бұрын
Khana sa soeur bi khamoul ni adouna dou keur
@sadiobandia947
@sadiobandia947 2 жыл бұрын
Awa Diouf djigueen waloom si doon dafeu new mais souvent djeukeur you beug lou yomb laniouye am allall bi laniouye guiss di instrumentalisé djigueen bi pa bi défoul loumouye teup di dall mais aussi police yi moye lolou
@ndeyecodoudiop2500
@ndeyecodoudiop2500 2 жыл бұрын
Bayi ko rék
@alassanekandji6514
@alassanekandji6514 2 жыл бұрын
Alalou adouna rek tjr les grande soeur Mystique rek lagnouy thiy boller yak sa adouna lagnouy déf courage frère
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 2 жыл бұрын
Méfiez vous du mari de la femme. Dina ray sa papa thiey dama diomi
@ahmadmbaye5644
@ahmadmbaye5644 2 жыл бұрын
Famille doméram dafa am dé !! détournement fofou Sénégal barina. Wayé mbala nio dé dinagnou Faye lep.
@tout1958
@tout1958 2 жыл бұрын
Dieukeur bi amoul diom djigene yi mom xalis rek boul bayi de
@labeltropicaldistribucion4213
@labeltropicaldistribucion4213 2 жыл бұрын
Courage petit frère ne lâchera rien continue à lutter c est ton bien
@nogayelo774
@nogayelo774 2 жыл бұрын
Mbookeu amatoul....lou léére laa wakh !!!
@marietousarr3831
@marietousarr3831 2 жыл бұрын
Pourtant nogaye mboke amna bataye niou bone gni gno bari rek
@nogayelo774
@nogayelo774 2 жыл бұрын
@@marietousarr3831 déé dééte dakoorouma !!! Danguay khool kii rék...
@marietousarr3831
@marietousarr3831 2 жыл бұрын
@@nogayelo774 dans toute régle il y a des exceptions
@meryemsaks1101
@meryemsaks1101 2 жыл бұрын
Mbok beuretoul dei
@madamoungom856
@madamoungom856 2 жыл бұрын
Des Frères et Soeurs. Sans coeurs.y à n a tellement. combien de personnes sont devenu fou ou se suicider à cause de problème comme ça. il faut protéger ce genre d individu malheureusement faible.
@gassndoye6712
@gassndoye6712 2 жыл бұрын
Walahi
@lauraag5251
@lauraag5251 2 жыл бұрын
Surtout mystiquement ils peuvent le tuer sans soucis
@nabouthior6800
@nabouthior6800 2 жыл бұрын
Je ne ferai jamais cela à mon frère de même sang
@lauraag5251
@lauraag5251 2 жыл бұрын
Kon dhé yeugo li khew si deuk bii
@kartoumsakho6772
@kartoumsakho6772 2 жыл бұрын
Ayyy khaliss foum niou dieumé courage frère
@nabi9977
@nabi9977 2 жыл бұрын
Safara 💥
@user-2032
@user-2032 2 жыл бұрын
😭😭😭HAAA LI DEH ROUSS NAKO DEF SAMAY RAK Té yaye rek lagn bok MAN MAY TAW😭😭MÉ COM SAMAY DOOM BILAHI LI MO WARAL RAYANTE BI SI DEUKBI NAK🤦‍♀️
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 2 жыл бұрын
Mame Gor du courage moi aussi j'ai vécu la même chose 🙏🙏
@bintourassoulrassoul3871
@bintourassoulrassoul3871 2 жыл бұрын
Ndeysane Mame Goor yalla nala sunu borom tahaw si barkei Rassulalah saws amine
@aminathiam4766
@aminathiam4766 2 жыл бұрын
Entoucas ki kou bakh leu naniou ko diapalé, makk bou djigueine bi kou bone leu , yallah gui guisse mane gore yallah dineu leiral leep inchallah 🙏🏿🙏🏿
@mouhaba6225
@mouhaba6225 2 жыл бұрын
DIEUKEURAM TAMIT KOU NIAKE FAYDA LA BOUMOU NIEUWATI SA KEUR PAPA VRAIMENT NITE KOU BONE AM NA DJIGUEN NA DEME KEUR DIEULEURAM SEUYI BOU BEUGUE KEUR NAKO DIEUKEUREUM OUTAL KEUR JUSTICE NA DEFF LIGUEYAM BILAHI LI DEFA METI
@aramezahra9014
@aramezahra9014 2 жыл бұрын
Doyna War dal police tégoul fénreu gneuw dila guéné sa keur papa mais dans tous ça Où sont vos oncles paternelle et maternelle ?? Ils doivent pouvoir intervenir et réglé la situation
@senethialy8748
@senethialy8748 2 жыл бұрын
Mane daal khaw ma founiou dieum ak sunu famille yi 🥹
@scheikhgningue9998
@scheikhgningue9998 2 жыл бұрын
Nguèn bokk nday ak bayyi ayway 😱😱😱😱😱
@ndeyedialguisene1681
@ndeyedialguisene1681 2 жыл бұрын
Courage sa sœur hamoule ne debi dafa gaw sonhnaci s'étale yaw ak sa borom xalebi sa dôme la tey ndah senn Yaye dena allalbi fi lay kow bayi
@sammbaye6769
@sammbaye6769 2 жыл бұрын
Sama way lima lay digueul moy gua bayèlène keurgui tègua mougn boudeh ya Nek si deug yalla dinalako diokh yag yag yalla nèlawoul
@ndieumbeuttoure19
@ndieumbeuttoure19 2 жыл бұрын
Bayelen keur gui déme fane sou féké mo nek si deug Kay na khex ba am thi ndam prsk sou guené kouy topato papa dji gua xamni mome rk la dessé
@sammbaye6769
@sammbaye6769 2 жыл бұрын
@@ndieumbeuttoure19 yalla mi done samou papam bam diou dogoul yalla momou diogoufi tè yalla migui and ak way mougn kat yi liko dal metina trop wayè nak mougn moy lifi seus ndakh niomou nène la tè mbokou da for tè khalis diaroul yène yi
@ramatoulayedoumbouya9981
@ramatoulayedoumbouya9981 2 жыл бұрын
Déy yombe lol il fo niou dibaliko injuste
@aissataly7021
@aissataly7021 2 жыл бұрын
C'est trop facile ça khaliss boukko sœur bi beugué nakko ligue niakk diom
@oumidiallo5074
@oumidiallo5074 2 жыл бұрын
Wa Ani dieguenne AK dieule aye keur te goooor nekoufi yawe de outeka AK Mane j'adore mes frères
@flofall722
@flofall722 2 жыл бұрын
Malheureusement on ne choisit pas sa famille
@hawaba5151
@hawaba5151 2 жыл бұрын
Manou lenne si problème bii c trop compliqué n ne peut pas tout dire mais tôt ou tard Allah montrera trés clairement sa vérité à tout ce qui ignore la réalité car il s'agit d'une famille que j côtoie .
@khadyndour2230
@khadyndour2230 2 жыл бұрын
Sa mag bou djigène bi kou bone leu, ani djigène ak kheuthio keur, dèmo seu dieukeur dougal leu cii keur nga nèk fi di diay yabatè nane ay "keur gui mafi nèk goor" je suis sure k sa dieukeur lèche ku leu, djiteul seu dieukeur lo wakh mouni waw. Les parents de maintenant doivent plus laissè d'hèritage puisque kou nèk day khar seu wadiour dè pour nga nèk cii guinawam di dèf du nimporte koi.
@dominiquepreira2696
@dominiquepreira2696 2 жыл бұрын
Je ne connais pas mais l Allah le tt puissant te protège in challah la vérité finira. Par triompher un jour Allah est avec les patients je compatis avec toi 🙏🙏🙏
@abidaffeniangdjielani1158
@abidaffeniangdjielani1158 2 жыл бұрын
Fin du monde bok ndaye ak baye yalnagniu thi yallah moussal yalla takhawoulah
@awadieng3617
@awadieng3617 2 жыл бұрын
Courage dieu est grande☝☝
@ndeyetaphatoure8468
@ndeyetaphatoure8468 2 жыл бұрын
B
@awadieng3617
@awadieng3617 2 жыл бұрын
Pas de koi
@Topofthetopapex
@Topofthetopapex 2 жыл бұрын
Boul bayi dara mou sedd 🙏🏾 dafay yombou torop. T’as bien fait 🤍 lepay leer tkt pas
@belleduteteaupied1393
@belleduteteaupied1393 2 жыл бұрын
Adouna da goudou tannk frere xawmala wayé nawnala trope kou sagnon am makk bou melni yaw Yalna yalla djaapalé
@papeseck490
@papeseck490 2 жыл бұрын
Du courage frères ne baisser jamais les bras Sénégal doyna ware
@julianachimenavika468
@julianachimenavika468 2 жыл бұрын
Pure verité bok ndeye ak baye mo guene bone jé vecu plus grave k sa courage mon frere
@khadimsamb3466
@khadimsamb3466 2 жыл бұрын
Courage frère boule bayi moukou benene gor Di doundou sa keur Baye
@entrepreneurimpact
@entrepreneurimpact 2 жыл бұрын
J'ai espoir de faire 20.000 abonnés aujourd'hui. 🙏🏼
@alimasamb123
@alimasamb123 2 жыл бұрын
Massa thiate yallah nala borombi diokh lou geune keur gogou
@fatouceesay6794
@fatouceesay6794 2 жыл бұрын
it's very sad🥺may Allah be with you bro n justice be served
@futzi1898
@futzi1898 2 жыл бұрын
Yeureumnako YALA nako YALA taxawou dioubolèko ak ay maguam wèreul papam Dèmal balance bou Walf Tv
@Miss-Ebene0
@Miss-Ebene0 2 жыл бұрын
Du courage Yalla baxna
@cheikhndiaye4244
@cheikhndiaye4244 2 жыл бұрын
Ndaysane yalla na la yalla diapale
@moustaphadiop5027
@moustaphadiop5027 2 жыл бұрын
Koudoul xalat niét fan bambél Loula nekh defal
@coolboy-vc3zu
@coolboy-vc3zu 2 жыл бұрын
Senegal dabarina injustice bilahi dama warou
@binetasakho3593
@binetasakho3593 2 жыл бұрын
Salam Salam courage Yallah na la sunu borom bi SWT maye sutura aduna ak Allahira 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@aboubacarfofana6551
@aboubacarfofana6551 2 жыл бұрын
Alalou adouna diaroule li déh dangaye déé bayikoffi. Yawe sa baye déwagoule sakhe nga koye mirasse complot ake sa dieukeur. Ki Dale mo torokhe
@laminegaye7429
@laminegaye7429 2 жыл бұрын
On est à la fin du monde. Khaliss diaral na nit lou nek. Sa propre frère doyna war
@awadioum4178
@awadioum4178 2 жыл бұрын
Sa yaye deceidée mouye taw warléne ouf dou notkou bakh
@bassifacouture8719
@bassifacouture8719 2 жыл бұрын
Ayyyy wayyy sa rakkk nga warko protège nga geneko adouna dou keur
@falloudiouf8442
@falloudiouf8442 2 жыл бұрын
Frére la justice divine va te sauver 🙏🙏j ai priée pour toi 🙏🙏💪
@metzodiarra576
@metzodiarra576 2 жыл бұрын
Vraiment fréro jambar nga sa wadiour mome topatoco inchalla lepe dina bakh
@abdourahmane8886
@abdourahmane8886 2 жыл бұрын
Adjudant Baldè Kou sérieux leu wallahi
@zalendiaye3623
@zalendiaye3623 2 жыл бұрын
Yalla n'a la yalla same arla mousalla thi lépe Louye yakou ak yakoulé
@mamidieye2593
@mamidieye2593 2 жыл бұрын
Thieuy adouna legui bokou ndeye ak baye mome bane sens la ame
@ninkinanka3644
@ninkinanka3644 2 жыл бұрын
Moudiou Diamono Lafi Guiss Daal
@awandiaye7690
@awandiaye7690 2 жыл бұрын
Souma amome sa numéro gnom gnoy guéneu bayila walahii dotougnousi wahaty
@binetandiaye4662
@binetandiaye4662 2 жыл бұрын
Yeureume nako ndeyssane 😢😢😢
@dalysenghor3891
@dalysenghor3891 2 жыл бұрын
Du courage
@maremeyade2378
@maremeyade2378 2 жыл бұрын
Thiey yallah Alalou andouna yaroul li comment on peut faire ça a son propre frère ah doyna warr nekk si keur sa frère nekk si mbéde mi nga teud ak xel bou dal c'est triste
@aissatoungom9833
@aissatoungom9833 2 жыл бұрын
Instant bi bokou molayeu tek yéne yi amoule notaire ak sa avocat pour régler situation bi i gniaw lep ci adouna lagniou moyeu bayi koudoule khalate bambéleu Loula nékh défale
@serignepapemalicksytv6388
@serignepapemalicksytv6388 2 жыл бұрын
Mon frère laisse tout tu vas cherche ton propre l’argent inshallah je sais tu vas réussir
@oumidiallo5074
@oumidiallo5074 2 жыл бұрын
Wa Ani dieguenne AK dieule alale sa pape te goooor nek fi tamite
@mariamasane7448
@mariamasane7448 2 жыл бұрын
Hiiii quelle méchanceté au nom de quoi. La grande sœur aussi devrait pas faire ça à son jeune frère famille daffa nekh surtout kigua bocal béne ndéye
@tibagng7320
@tibagng7320 2 жыл бұрын
Thièy adouna day diekh dh ragal lène yalla alalou adouna diaroul yène niawtèf yi
@yayethiam8331
@yayethiam8331 2 жыл бұрын
Sa sœur bi imbécile la, wayé kou bayi sa mbok guis kou diape mbokam.
@Aichadia1234
@Aichadia1234 2 жыл бұрын
Jeker ndawsy defa gniakka diom cim mouno out sa ker yobbou sa jabar
@ingue2562
@ingue2562 2 жыл бұрын
Courage mon frère
@yasienvegi5102
@yasienvegi5102 2 жыл бұрын
Thièye adouna 🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔
@davidejo5682
@davidejo5682 2 жыл бұрын
Bul bayii darra katal sene ndeye mom att dieukeur dji yeep
@bintadiagne5425
@bintadiagne5425 2 жыл бұрын
Li doynawar Di frère AK soeur you melni 😱😱😱 te pa bi mougui dounde
@allendime5746
@allendime5746 2 жыл бұрын
Frère sa wakh dji tégou woul dé mais nak wa dakarbeuzz naniou dem ci femme deglou KO
@ndeyefatoudiop4519
@ndeyefatoudiop4519 2 жыл бұрын
Tu as tout compris y’a des nons dits pourquoi sa famille ne le soutient pas ils ont des oncles tantes personnes ne le soutien
@mounasaidara2904
@mounasaidara2904 2 жыл бұрын
Diapanté léne adouna amoul solo li léne lié mo geuna fort alalou adouna
@synapps5515
@synapps5515 2 жыл бұрын
Dieu est grand et qu'il t'assiste
@Amina-xr3jx
@Amina-xr3jx 2 жыл бұрын
Si je comprends bien donc le papa es toujours vivant il n'a qu'à parler avec la justice. Le mari de ta soeur moy seytane bi keurguui la tek beut pour akimoko ak ta soeur il manipule ta soeur juste pour l'héritage alors que le papa es malade. Ils vont le tue juste pour vous mettre dehors de la maison ndakh khaliss kesse sort de la maison avant niouley liquidé bakh na le papa mom ils vont le tue à petit feu .Sénégal la justice es corrompue douniou ate deug
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 2 жыл бұрын
Parfaitement raison Amina 🙏🙏♥️
@sophiediouf4345
@sophiediouf4345 2 жыл бұрын
😭😭😭
@theresemariediouf3612
@theresemariediouf3612 2 жыл бұрын
Tu as parfaitement raison il y a des hommes de rien du tout dans ce pays niak niom di seyal jeeguine.
@badianediouf3822
@badianediouf3822 2 жыл бұрын
Li gnouy kheuthio deh woroulen sakh bakham dînant ko djeurigno
@binetoudiop7172
@binetoudiop7172 2 жыл бұрын
Alalou bayame le
@aichamariemevital689
@aichamariemevital689 2 жыл бұрын
Il ya de toute évidence des zones d ombres qu il serait bon d éclaircir dans cette histoire
@KY-ed5qp
@KY-ed5qp 2 жыл бұрын
C'est louche d
@antoniosuardi4733
@antoniosuardi4733 2 жыл бұрын
wakhoul lou am nio bokk kogn limouy wakh walahi dara amousi ki ay maguam dagn ko beugu bilahi khawma louko khirr si li nakk
@niangtra
@niangtra 2 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla mousseul thi ndiabot gou dégowoul
@seynaboudione5239
@seynaboudione5239 2 жыл бұрын
Ôh limétina mais mougnale yalla bakhena niobokou cas mane doundouna li
@Falseydou
@Falseydou 2 жыл бұрын
🇸🇳 dama yakar ni daguèn di fatte dè
@adamadiouf2607
@adamadiouf2607 2 жыл бұрын
Courage amna nit gno khamni diarougno sakh kham bay bokou ak gnome c'est honteux
@fantandiaye3968
@fantandiaye3968 2 жыл бұрын
Bilay wakhal adouna diay na leen
@ramatoulayesene3743
@ramatoulayesene3743 2 жыл бұрын
Amna djiguén you niak fayda sa yaye dée nga wara dieul say rak ouflén way ngay diahassé ak di guénawaté fatt sa djekeur téksi.il faut pas baisser les bras wouteul maximum de preuve pour dém yonn.quant à policiers yi bindal lettre procureur nga dénoncélen
@lahadnjay4885
@lahadnjay4885 2 жыл бұрын
boull bayi dh nekk ci et soit prudent du courage
@muhammeddiallo2170
@muhammeddiallo2170 2 жыл бұрын
Sa sœur n'a bay khélam bu bakh,dou Sakh thi adouna bi voilà, mo kham nak🤔🤔
@dabondiaye7917
@dabondiaye7917 2 жыл бұрын
Du courage brother mane yaw la andale si liga wakh
@fatimasylla5614
@fatimasylla5614 2 жыл бұрын
Yalla nalla yalla takhawou 😭😭
@ZOTAIME
@ZOTAIME 2 жыл бұрын
Ki kay bouko wowèti grande soeur ndakh ki domarame kou deug ndm la dieukeur diou gnak diom moy feik sa baye tabakh mouy gnew di deukeuh ak sa femme
@anthioundiaye7594
@anthioundiaye7594 2 жыл бұрын
Ge crois kil a raison me sa mak bi eske cv elle e mechante senegal li beuinafa
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 81 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
“Don’t stop the chances.”
00:44
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 62 МЛН
UFC 310 : Рахмонов VS Мачадо Гэрри
05:00
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 1,2 МЛН
I WAS KIDNAPPED BY MY SISTER FOR 4 YEARS
15:59
PLURIEL
Рет қаралды 352 М.
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 18 **VOSTFR**
1:13:28
EvenProd
Рет қаралды 1,5 МЛН
Pape Ndiaye : 😭 15 ans de prison pour Fallou Fall…😭😭
19:47
LUNAIRE NEWS TV
Рет қаралды 35 М.
Pape Niang a reçu sa 2eme plaine venant de la part de Mbaye le mari de Ndiolé c'est du jamais vu
16:49
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 81 МЛН