Amna solo yalla Nanu sunu borom fayal makk gni si barkeb Alxuraan. Waxtaan wi kawéna lool Macha allah té pasteefu.
@cheikhndiayekebe3002 жыл бұрын
Machallah mame boye yalla na yalla xam xam bi teibayila fi souniou kanam
@BassirouGueye-n1o2 күн бұрын
Ma cha allah
@baaxbaay29192 жыл бұрын
Fa tabaarakal laahu yal na la Yálla fay ci baaxug sëriñ bi🙏❤ waxtaan wi amna solo lool
@Ndiogoulo972 жыл бұрын
Maasàllaa Amna solo lool jërëjëf Sëñ Maxtaar Kebe yal na Yàlla guddal fan wi wéral cér yi te yokk xam-xam bi te bàrkeel lool ci barkeb Alxuraan ak Xasida yi
@serignemordeme26482 жыл бұрын
Macha Allah Serigne Makhtar khamna souma manon am numérom