Mane talibé cheikh la wayé borom darou mi damoko beugue rek t'es yalla takh yalla nako yalla maye goude fan ak wérr 🙏
@themossesaliou3343 Жыл бұрын
Barké serigne saliou qui dama ko beug rék tè serigne saliou rék takh j’espère que je le verrai un jour inchalla yag fi lol té wér si barké borom TOUBA ❤
Machallah Mame Thierno Mbacke Borom Darou yalla nako sa borom yagale te werale ko barkep sa tourando Borom Darou Moukhty.
@bassirougueye1287 Жыл бұрын
Amiiiiiiine
@AGIRPOURUNEVIEEPANOUIEAVE Жыл бұрын
Alhamdoulilah Machalah. Notre pays n appartient pas aux politiciens. Alhamdoulilah que nos guides jouent bien leur rôle. Machalah borom Darou
@mamegayekane839 Жыл бұрын
Mame thierno la todo ❤️mon takh mo tarou ❤️am khôl bou yatou❤️ki moko manou ❤️di wakh lo diadou ❤️dokhal di daguo ❤️kola lal ma alo ❤️koko moye Mame Thierno birayim damal darou❤️kola begue begue na ko bédie nama diokh ❤️Mame Thierno birayim damal darou ❤️
@sallyseck5675 Жыл бұрын
Merci beaucoup
@pirlo4478 Жыл бұрын
Machallah mbacké ya deugou té am yar ak téguéne ya bakh té goré😍😍♥️♥️
@diorcisse3487 Жыл бұрын
Machalla Backé yaguefi l'OL témou ande ake wére nila ķîlifa wara méle yalnala sounou borom same thy barké Seydina Mohamed psl amine yaraby