Plateau bi c'est devenu ma drogue douce damay yakamti wathie ba diakarlo ak yéne. Réé na ba thiorokhane Kandé gadou nga sama akkh 😅😅. Merci les gars pour ce fou rire. Rougui loutakh télo gneuw ci plateau yi yaw tamite wala mala yékha decouvrir. En tout cas bouléne changé yalna léne Borom bi same machaAllah Fatou, Rougui, Kandé et Abdou Nguerr l'incontournable. ❤❤