Merci mame mor mbaye aida Diallo dafa yeup nitt ni
@southafrica62395 жыл бұрын
Maa Shaa Allah!!! Señ mame Mor mbaye Linga wakh Lèppou deg le ku bakh nga yallah naa yallah goudel saa fanne tè and ak wèŕŕ
@thiamfallou97725 жыл бұрын
South Afrzhsivfdkica
@labsolugueye90165 жыл бұрын
Man Daii présidentielle Yii pasai Damala Mairaii wonn Ba Mounou Mala wonn xolatii sax Maii sa kadou yii Daii Mom machalah Barke Mam cheikh ibr serign Touba kaineu la ☝️❤️☝️❤️☝️
@masigasissokho38212 жыл бұрын
Tu à tout dit merci je ne suis pas mourir mais c intéressent ♥️♥️♥️🙏🙏🙏
@deguenediallo14655 жыл бұрын
Dieureudieuf mbaye yalna nga goud fane loooool té andak wérr koud téd ki ahmadoul khadim d'où morom
@mariediop10984 жыл бұрын
Machallah.. Serigne bi amna Sollo trop..♥️🙏🙏🙏🙏
@lomactarmodou64185 жыл бұрын
Ko beug serigne touba lega wakh keppo deug la yalla nalla serigne touba takhawo takhawo gno amine
@lixman53394 жыл бұрын
Thiey yalla 👏👏Ken dou yonnetibi (psl)
@oumarsylla52095 жыл бұрын
💚💚💚 i like this man! Mame mor Mbaaye ma la sope nguir Serigne Touba
@mamadoulaminendiaye26715 жыл бұрын
Djereu jëëf serigne Mame Mor. Kham kham gui sel na, beug gui woor na, kheur gui si serigne bi eup na. Yalna yalla defal leu diaaam. Journaliste bi nak rafetlouwouma say question dara. Journaliste dafa wara ame kham kham, mais yow mom sa question yi gueum na ni beugone wakh lo serigne Mame Mor lou eup la gueuna nirou. Alhamdoulilah ba mom ande na ak dal ba topoula si fingako beugone yobou. Santati serigne Touba.
@boubandiaye57254 жыл бұрын
Lepe rafetna troo
@annitademe41465 жыл бұрын
Machallah Mame Mor contane nagne thi iow vrèma
@medoune895 жыл бұрын
C'est pour la première fois que je le vois avec un discours posé....
@fatimasoumare84075 жыл бұрын
😂😂😂😂je le rappelle de ces menaces
@mouniiimouniii36974 жыл бұрын
Da tangg nak mais kou deugou leu
@toubadiop48035 жыл бұрын
Machala mame mor wahbi amna solo yalla nala yalla fay si barke serige touba
@mahejdjdj18635 жыл бұрын
Oumar Sall l'homme véridique machallah
@linvincible29675 жыл бұрын
Kii moom yeukkeuti fitneu ak wakh wakhi dof rek la meun. Seytané leu... on n'accroche pas une vie à une personne mais à Dieu parce que c'est lui qui te l'a donné. Dieu merci...
@cheikheseck71294 жыл бұрын
Merci wa dieuredieuff ser mame more Mbaye ❤️❤️❤️😍😍😍😍
@bassiroudieye46915 жыл бұрын
Akassa Mame Mor. Ya bakh. Ya beugue serigne Touba. Tu es un vrai défenseur du mouridisme. Yalla nangua ame feyou serigne Touba. Serigne Bass.
@mamedia64255 жыл бұрын
Keineu mame bamba yallah na yallah yokou sa leire 🙏🙏🙏🙏
@CodouDia-o2u2 ай бұрын
😢😊 0:33 0:36
@bassiroufall95955 жыл бұрын
Machallah dieurieudieufaty s touba mbacke amoul morom mame mor yalla naga fi yague te wer
@elhadjiibrahimafall2115 жыл бұрын
Je te connais pas deh mais amo Kham Kham Bangua wahei djiguen mounoul djitei moro mam la hameni sa ham ham touti na demal diangui wate le coran et voire ayahh yii bou nek loumouy wah merci. Enplus tu es mourid mai hamo dara si mouridisme
@talibebunjeng94705 жыл бұрын
merci
@milkfaye27613 ай бұрын
@elhadjiibrahimafall211 yow mi am xam xam kay leralalniou ndax djigen manna djite moromou djigenam nga waxma thiy ban hayah la ne
@khadimsow28095 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne mame mbaye kadouyi rafetna lolll te wer loll yalna yalla fayla guengui fay ci barke borom Daroul mouhty dieuredieuf mouride sadekh
@ndiagabeye5915 жыл бұрын
Merci beaucoup ya buegue serigne touba mane yaw laye bege
@mbenegueuye83105 жыл бұрын
Dieureudieuf s mame mor fi s mountakha reck mofi né té si aay ndingualame réck laniy dokh koumou nèkh ak koumou nakhari
@deuggreikktyallareikktakh35055 жыл бұрын
*Wallahi Li nga wax Yeuppe deugg la Baye Mor mais meune.nga bOokkalè tooorope.* *Après Aïda Diallo liiñOu wara khêkh deugg Ci YonneWiii moyy BokkaLè Gui.Nous associons trop ALLAH aux humains* NaañOu Diox YALLA Sunu Borom Thieurreum bImOu mom wayy
@Important-e6f5 жыл бұрын
Deugg rk nga wakh, mane dama diomi sakh
@deuggreikktyallareikktakh35055 жыл бұрын
@@Important-e6f Dafa euppe Wayy Billahi Wallahi...Franchement il faut k ñOu gueuna Xamal Mbokk taloubbê Yi YALLA ,YONINTE BI S.A.W, AL"QURANE ak SUNNA de prime abord avant ñouciiy teikk Lènnènne
@Important-e6f5 жыл бұрын
@@deuggreikktyallareikktakh3505 sétanal rk, aljanna mom djeureudeuff diww ak fatt ay wakhtu diouli nèk si lula neekh dou fa yobou kèneu,
@deuggreikktyallareikktakh35055 жыл бұрын
@@Important-e6f ah en tout cas Serigne TOUBA Nèna xamoul T amoul Aldiiana bOu Diiamou YALLA DouLe mayyè...waxna ni Diamoulène YALLA T baaña doOne dofff
@DibbDiouf3 ай бұрын
Omar sall mom fén rek ak sosal gni gni lafi néké
@awadiouf56815 жыл бұрын
Man balama beugueu dee aida diallo nann dieureudieuf cheikh bethio thiow li thiow serigne touba laa. Deugueu nekhoul
@bambadioum40435 жыл бұрын
Dieuredieufety Serigne Touba. Señ Mame Mor contanna lool thi sa pastef.
@lineetsesvideos48814 жыл бұрын
Amna solou troup
@djilifall62884 жыл бұрын
Bilahi Mame mor yalla nala yalla défal Diamo si barkep Serigne Touba
@gueyemourtalla96395 жыл бұрын
Merci Mame Mor Billahi wanga degeu seringe touba domou Adama 🙏👌
@babslemegalomane41195 жыл бұрын
Dieureudieufeii Serigne Touba akassa mame Mor Mbaye sa liguey rafetna
@pendandiaye7095 жыл бұрын
Mane dall ki la beugu mane kou beugu s.mame mor mbaye beusseul j'aime
@ahmadrachid81275 жыл бұрын
Baayilen sen maam yinguen di diaamou té nguen diaamou yalla, al'qur'an ak sunna bounguen ko toppon simplicité rek nguen di doundeu, as'salaamou alaykoum!
@mariasant39375 жыл бұрын
Va le dire à Daesh
@maguettembodji60785 жыл бұрын
Yalla na serigne touba fay la bègueé ❤
@lomactarmodou64184 жыл бұрын
Beug ga serigne Touba lala mana wakh yalla na serigne bi Faye
@mamemorniang87084 жыл бұрын
Allahou akbarr Sama toma yalla na yalla yalla faye ❤❤❤❤❤❤
@demeabdoulaye1615 жыл бұрын
Que allah nous guide dans le droit chemin
@ismailacamara21025 жыл бұрын
Amine
@abdoucamara3665 жыл бұрын
Deme Abdoulaye
@annadiallo17655 жыл бұрын
Mrci bien dit kénn d'où serigne touba
@pathendiaye11175 жыл бұрын
Amine Yarrabi.
@salioudiene72714 жыл бұрын
Amine
@aladjindiaye51415 жыл бұрын
akasa dieureudieuf serigne mame mor yalla nala serigne touba faye contan na trop si iow mane sa sopé la kou la beugue
Mame Mor fénkat la, Serigne mountakha waxna nguénn diamou yalla bâyi téré, té lounoufi téré yép yéninguakoy déf. Dieufélénn ndigualou yalla AK serigne Touba. Taguénn bâyi seytané... Kii môme election ya laako bâyi fiii nguafi nék di wattt si serigne Touba si election yi di fénn nann 2ème tour day âme par force yak aida Diallo yéna yam doméram dji
@manhattanblack36405 жыл бұрын
Yaw journaliste bii dé yawit beugoo jamm dè.bayilene posé question fitneu waay.billahi loudoul jame jame moko gueune.god bless all of us.
@miasisters8555 жыл бұрын
MACHALLA
@khadyndiaye97085 жыл бұрын
Machallah
@africamazing81435 жыл бұрын
Wakh nga deug
@dioudba92945 жыл бұрын
Walahi deugeu ga wakh
@papemakhou31454 жыл бұрын
Bilay wakh nga deug
@maffafa41115 жыл бұрын
merci .mame mor mbaye liladonehar sa rection
@seynaboudiop12625 жыл бұрын
Serigne touba amoul morome dh
@SeneSenghane5 жыл бұрын
Dieuredieufé Serigne Touba Khadimul Rassulillahi. Mame Mor wax bi rafètna Maa Shaa Allah.
@rebotreno1515 жыл бұрын
センセンガン Wadji deh loumou wax loudoul MOR la toudou day feneu kathieu katt deugg mongui ni😂😂😂 Dangueine fattei thi élection yi boumouy youxou Macky di xandjoou macky gagner mou tit di weddi aka djiegallou bobba lako sibbb 😂 Feneuh rkk
@absambaye97325 жыл бұрын
Machahalla mame more mbaye wakhe dji rafetna
@antasarrcisse18035 жыл бұрын
Faites attention à Sokhna Aida elle avait une part très importante dans le coeur de Bethio Thioune et ce n'est pas sans raison. Dans notre société on a du mal à respecter les femmes. Dommage
@marindiaye94035 жыл бұрын
Bilay gno bok guis guis
@adamadione42675 жыл бұрын
@@marindiaye9403 bayiléne nafékh Aïda da wara khame bobam
@moiseendurant52845 жыл бұрын
C triste mais vous avez raison
@marindiaye94035 жыл бұрын
@@adamadione4267 demain digua am sa reponse
@alphaoumardiallo3884 Жыл бұрын
Avoir du mal à respecter une femme c moyen grave qu 'avoir du mal à respecter Allah swt fait attention à tes commentaires
@safietoudiedhioudie93285 жыл бұрын
Mercie beaucoup 👍☝️👂👈❤❤❤👏👏
@FatouFall-uk8eh4 жыл бұрын
Ok pour
@FatouFall-uk8eh4 жыл бұрын
💋😿💋💍
@babafall69415 жыл бұрын
Saydina omar je suis très content d'avoir toi jajeuf srg bo magg bi
@nifandumba79115 жыл бұрын
Bilaye walahi magui guigne si magou yalla serigne touba migui si sounou bire dou coye fattou
@ndaobambiste74465 жыл бұрын
Franchement certaines journalistes mérite des formations de qualité serigne Touba kene
@oumarndianor75664 жыл бұрын
Nafekhnga
@pendandaw13013 жыл бұрын
1rrrrrq1
@dembadiop67385 жыл бұрын
MAME MOR MBAYE ya kawé yalla nala serigne touba fayy Euskeuy Fall
J'apprécie bien❤ sa façon d parler. Serigne Touba la kéneu xamoul loumou done. Diadieuff Mame mor
@azizweberpro78355 жыл бұрын
Serigne Mame Mor Mbacké yagg fi lol té andak wer voila nitt kou véridique ...kaddu yi amna solo lol machallah deug néxoul Serigne Mountakha moffi toggal Serigne TOUBA té limou beug moy ameu ...yonou Mouride amoul kenneu kouko manna sokhal rawattina Khalé bou dioudou barky démm.Donc soxna Aida yamal si coudou niou rokhla si thinnn té olof ndiaye néna "Kouy diaxann di saw bala kénneu toy ga laurr".
@antasarrcisse18035 жыл бұрын
Penser à Cheikh Bethio Thioune quand vous faites du mal à Sokhna Aida. Je ne suis pas mouride mais Bethio Thioune la respecte énormément.
@moiseendurant52845 жыл бұрын
Vous avez raison Mme
@bambaseck625 жыл бұрын
Machallah borom deuxième tour inévitable kaddou yi rafet na lool mais boul ci arrière nak wawww gooré mbaye
@maimounaba22565 жыл бұрын
😂😂😂😂
@aminataba93315 жыл бұрын
Mè yène yallah diam le beugue tè mom le santanè. Dans ce monde keine mo geune c le prophète Mouhamed psl .
Tout est lié à des raisons financières et économiques. Tout est lié à des intérêts économiques. Aicha veut protéger des intérêts economiques. La vie des gens est guidée par la gestion de leurs intérêts économiques
Machalla machalla yalla n'a diamou yagui diadeufe sérigne Mame mor mbaye kéne d'où Serigne Touba diadeufe mourit
@absafall34725 жыл бұрын
Machalah il est pertinent sr mam mor
@maododieng78285 жыл бұрын
Dieureudief serigne mame mor mbaye
@azizgueye98585 жыл бұрын
Mame Mor yaa baax حفیظک الله و اطال عمرک ببرکاه الشیخ الخریم
@nitudeug33825 жыл бұрын
ما رأيت من هو أكذب منه
@kadiatoubaldebalde56285 жыл бұрын
Tu as oublié ce k tu a fait la maison de assane douif tu es pareil l les thiantacoune
@wakeurstoubadiangueakdiang86465 жыл бұрын
Machallah s mame mor dieuredieuf wakh dji amna solo nane di maytou di wathi ndigeul li ndakh ko khamni bou meiré sunu borom meire bou contané sunu borom contane serigne touba serigne mountakha togayoup sunu borom la togué gnou bayi kheil bou bakh té khamni sunu borom ngouram gui amna gnouko présenter fi ci adouna té kéneu djitouwousi serigne touba serigne mountakha mbacké
@abygueye45974 жыл бұрын
Bilahi
@kdkdjdjdjdjd17075 жыл бұрын
Que DIEU nous guide dans le droit chemin .Mais il faut pas la tuais.
@beautenayo10315 жыл бұрын
Vue tout ces polémique sur elle sa vie et en danger ces des discours qui appelle la haine
Serigne touba est une personne quelque spit sa dimension.
@ibrahiimaba95545 жыл бұрын
Abdousalam. , Ba EN
@modoudiouf90545 жыл бұрын
serign Touba a dit : ''je suis ni Homme ni djinn ni prophète mais je suis cette créature unique qui vit d'apparence en humain sur terre ''
@baysall96725 жыл бұрын
Limoy wakh gamou ci toss.fomou Nékk interé personelam moko fa bayyi
@assanendiaye22375 жыл бұрын
Serigne touba depasse LA dimension humaine ..reflechit
@doudougueye1064 жыл бұрын
yénnn gniii yéna yeukeutiii Aida dialllo wakh kat yi ak site yi "aida loumou beug dou ameu lou Seugn Mountaha beug moy ameu " Subhanallah........ gnarii beug beug yii warou gno bokk sakhhh siii ap lamigne ndakhhh bokouniou yone..... LEUNDEUM AK LERRR di danou di wakhhh ba mbeukou rekkkk li dou alou sopppp la rekkkk wakhé len khamkham mo gueun
@amidousissoko27735 жыл бұрын
Ce mec qui parle et aida diallo est le même parce qu’il compare également amadou bamba et Allah, alors quelle est la déférence entre lui et aida jallow 6 et 9
@CM-xo3oy5 жыл бұрын
Wow maintenant c'est les Mourides qui dominant au Senegal! Aida n'a rien fait de grave. Elle s'est juste trompe et peut le rectifier. Mais certains senegalais sont vraiment mechant. S'il vous plait, je ne parle pas du Marabout avant que vous commencez a m'insulter.
@xa-prodofficiel87095 жыл бұрын
Jërëjëfëty Mame Mor Mbaye... bégue naniou lol thi ioe.