😢😢 Ya Allah , Ya Rahman, Ya Rahim , Yaw Docteur bou makk bi , Yaw minga khamné kou wérr Yako wéreul , yaw miy fékkeu fou wow kongou, nga tooyal ko , yaw miy fékkeu kou amoul dara nga may ko....🙏🙏🙏🙏🙏 yalla nanga ko may wérr té mayko bepp Doomi Adama. Yaye Boye nopil, tu me pleurer Lii rekk motakh ma beugueu nekk milliardaire bilahi
@serignefallouleye4557 Жыл бұрын
Amine
@fififaye2603 Жыл бұрын
Ay fane laye dieulé ay millions wala milliards pour dimbalé gnou melni . Borome alale yi déléne dimbali new dji doolé yi té yalla rek takh té diamousi yalla . Yalla nala yalla yeukati si barké seydina mouhamed psl
@yasminaba9020 Жыл бұрын
Ay yalla nako yalla tegguil fébar bi té délloko si saggom meetina🙏🙏🙏😢
@fatoudia9900 Жыл бұрын
Ooh ndéyssane mère bi kouko khol khamni dawna ba sonou bilahi yeureum nako aussi mais Maman lépay diékh inchallah
@aminatabadji7594 Жыл бұрын
Yalla nako sounou borom may werr ak soutoureu si barke serigne babacar sy
@fatoudia9900 Жыл бұрын
Ndéyssane oooh li méti neu bilahi walahi yalla diam boumou beug rék lay ték natou wayé mom mila ko ték yalnala ko téguil si diam si barké seuydina mouhamed psl 🤲 wa Dakar buz aussi surtout tonton fadél yalnalén yalla diapalé si barké Serigne Babacar sy rta 🤲
@makhouseye5733 Жыл бұрын
La guérison appartient à Allah elle peut survenir en une semaine, un an ou 10 ans. Qu'Allah t'accorde une guérison totale, une Santé parfaite. Bonne guérison !!!
@ndeyemariesamb9684 Жыл бұрын
Amine
@ndeyemariesamb9684 Жыл бұрын
Amine
@madouchou6318 Жыл бұрын
Un pays où quand le pauvre est malade il n'a pas droit aux soins, quitte à ce qu'il y laisse sa vie....😢 Que Dieu dans sa bonté infinie relève tous les malades et nous accorde la bonne santé 🙏🙏
@beuguborombi6204 Жыл бұрын
Hooo😭😭😭 seydina Mohamed. Yala gua ame opération legui ba wer inchallah.
@mamemarianeba8092 Жыл бұрын
Yaay keine la bilahi 😭😭😭😭 Yalah nala Yalah wereul Marie. On est de tout cœur avec toi courage
@ndyebinta-qz2xe Жыл бұрын
Metinaaa trop 😭 mais yallaa miy téguéé di téguii yallaa nallaa Yallaa téguileu sa fébar bii si daradjieuy seuydina Mohamed PSL Amine 🙏
@amysarr9204 Жыл бұрын
Bilahi Fadel tu as Un grand cœur 🙏
@sokhnakeitandiaya7835 Жыл бұрын
Fadel machallah si kawe si kaname bon courage 👍👍👌👌
@AichaNdiaye-f1l Жыл бұрын
Yalla na weer ak diam thi barki Nabi Mustapha psl
@maimounadieng4849 Жыл бұрын
Oh massa bilaye doundou bou sotegoul darra lounè khadh nassi bilaye yallah nalla yallah maye were thi barki mouhamed yallah maynou moudiou bou rafett
@aminatandiaye841 Жыл бұрын
Ÿalla nako yalla safara bamou wére incha allah thi barké seydina Mouhamet PSL yalla na wére incha allah
@AdamaDiop-w3e Жыл бұрын
Yalla bakhna kou am djafe djafe yalla nalako teguil kene bagna djakhle
@aminasaliou248 Жыл бұрын
Hooh Daysane Yalla naka Yalla yekati akh diamou mayka katane inchalla
@rackyndiaye1434 ай бұрын
Yalla na yalla weral gneip gni febar
@NdeyefatouNdiaye-hr8el Жыл бұрын
Allahou ma salih thiey yalla mo mounne natou dee magui nianne si barké alquran yalla nko yallah wérral si barki seydina moukhamet psl😢😢
@MaremeSow-l2q Жыл бұрын
Aye way limetina trop waye yalla bakhna yalla nako yalla degil natou bi
@ndyebinta-qz2xe Жыл бұрын
Santaleu yallaa manegua wakh sama mak wakh Sakh menoukowone gnima guiss gneup wakh menougnouko mais yallaa nallaa yallaa safaraleu si daradjieuy seuydina Mohamed PSL Amine 🙏
@AwaNiang-bu3xh Жыл бұрын
Mane na xam li bane fébar la stp
@mameseck1318 Жыл бұрын
Ohhh rak dji yalna yalla wéral may la tane bou bax
@bintoubanellediabang712 Жыл бұрын
Yalnako yallah samm té wéreulko métnina
@habydiarra2741 Жыл бұрын
Il faut que l'État subventionne la prise en charge des personnes vulnérables
@dababoussodieye8590 Жыл бұрын
Gnidé nio yélo diappaler bilahi yalna la borom biii teguil natou bii akk bepp domou adama Bouygues weuyaler febar
@tymasarr1831 Жыл бұрын
Méti na trop yalla na tané ak diam 🤲🤲🙏🙏
@AstouNdiaye-n3n Жыл бұрын
Massa ma chérie elle est tt mignonne machala inchallahou rabi digua wer ba delou sisay activité inchallah
@ousseynoukebe3333 Жыл бұрын
Yalla nako yalla téguil ko inschallah nga tane ak diam inschallah
@abdouldjiba Жыл бұрын
Oh my god😭😭😭 Que dieu le tout puissant te guérir m'a sœur voilà les gens qui ont besoin d'aide où est la richesse que dieu vous à données 😭😭😭
@nafisatougueye1375 Жыл бұрын
Ay way li mètina yalla nala yalla tèguil natou bi🤲 ndeysane bonne guérison
@serignefallouleye4557 Жыл бұрын
Yalna doliko ndimbel ak yermande amine 😢
@mameastoundiaye8180 Жыл бұрын
Yalla nako yalla takhawou yalla may wèr ak werlè thi Barker seydouna mouhamed pls 😭😭😭
@mariediallo5868 Жыл бұрын
Di nga weer si diameu InchaAllah tourondo
@sylviediatta9085 Жыл бұрын
Oh. Massa bon rétablissement les bonnes volontés manifestez vous elle est fatiguée. Que Dieu te vienne en aide
Massa ma.soeur.yalla na yalla safara si barkèl seydina mouhamet
@coundadiallo8586 Жыл бұрын
Ndeysan mètina mes Sante yalla yalla Nala yalla maye wer
@awafall5201 Жыл бұрын
Ndeysan fadel ya bah Yalna ko sunu borom sam
@ndeyemariamadieme4836 Жыл бұрын
Yalla nako yalla may tane 🤲
@fd7912 Жыл бұрын
Yalla na la yalla takhawou si barké seydina Mohammed (psl)🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@YoussouDiop-yp1zq Жыл бұрын
Amin
@abdouazizndiaye2011 Жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭Yalna yalla safara
@sokhnabaly1408 Жыл бұрын
😭😭😭😭metu trop ❤😭😭😭 long vie sister ak werr
@bigMoo2017 Жыл бұрын
Lii c'est un cas qu'il faut intervenir rapidement, ils ont besoin de finance
@azoumbaye6832 Жыл бұрын
Yalna yalla sougnou borom safara lii 😢
@daouddiouf176 Жыл бұрын
Yalna ko ya'Allah jappalé.. ya'Allah moy dogal teh sou ya'Allah tuddé ni sokhna cii dafay wërr: kenn mëunuci dara ndax dafay wërr.. jaamuleen ci ya'Allah ngen niaanalko teh ngen jappaléko pour ceux qui sont stables financièrement.
@tabarandiaye6952 Жыл бұрын
Bilaye zara da sonne yayame Def n'a lounek pr Fathie ko sonne n'a ma petite sœur chérie
@KhadyNiang-p1rАй бұрын
Yalna yalla maye ko weur
@thiorogueye-i9j Жыл бұрын
😭😭😭😭YALLA NA SOUNOU BOROM WERAL LA BARKEP CHEIKHOUL KHADIM😭🤲🏾
@AwaSene-t7n Жыл бұрын
Yalnaniou yalla dolli soutoura ak weer
@binetadiop2255 Жыл бұрын
Ndaysan yallah bkhn😢🎉
@amintambaye3710 Жыл бұрын
yalla nako yalla may tane
@tackosy1898 Жыл бұрын
Massa yallah nako yallah yeukeuti Massa
@mature144 Жыл бұрын
yalla na la yalla yeukati thi barket mouhameth metina
@mamanmbaye1305 Жыл бұрын
Sokhna mary yalla na la yalla maye wér ki katanou yalla 😂😂😂
@bbeifadiop9266 Жыл бұрын
Oh métina Yala nako Yala weral
@amigueye3046 Жыл бұрын
Alhamdoulilha sante yala bou bax yala nala yala defal diam may la wer
@aminatou6854 Жыл бұрын
Mètina Mètina vraiment
@RamaTraore-vp3vt Жыл бұрын
Li métina yen gni Di sétane ak Di commentaires diokhélène Lou Way âme gnou fadj malade yii
@ousmanemamadousall4123 Жыл бұрын
Ndeyssane
@omarniang3282 Жыл бұрын
Fadel y’a Bakh
@felynatur6340 Жыл бұрын
Jésus guérit et il peut le guérir
@sokhnandiaye1889 Жыл бұрын
Oh ndayesan 😭😭
@morgaye6777 Жыл бұрын
Masta walay Yalla bahna inssalla Yalla gua tanné akk diam
@meprera5979 Жыл бұрын
Mane bilay dama warou lignouy yakh lep khalis si deuk bi gni khana kene guisoulen
@papekebe6822 Жыл бұрын
Yallha nala yallha maye wirr
@magattembow9883 Жыл бұрын
Yala nako yala safara😢
@seydoutall5411 Жыл бұрын
Amine
@louisemariamly9509 Жыл бұрын
Qu’Allah lui vienne en aide et te rétribue au centuple toi Fadel
@eliseemendy9698 Жыл бұрын
Masta Yalla nala douli were amiine 😭
@maguettendiaye6998 Жыл бұрын
Yalla nako yalla maye age tane waye
@rahmandiaye3469 Жыл бұрын
Yalna borome bi safara
@sallakane3727 Жыл бұрын
Yallana Yalla saffaral amine yarabi 🙏 massa
@amsatoucapo4933 Жыл бұрын
Yala nako broom bi wereul dolay xassidayi
@ndeyebintadiallo4898 Жыл бұрын
Amal wer bubax in sha'Allah
@mature144 Жыл бұрын
le prèsident doit lui prendre en charge
@khadyhanne4218 Жыл бұрын
Thieuy adouna 😂😂😂😂😂
@aminatou6854 Жыл бұрын
Vraiment mètina
@sambadiop4348 Жыл бұрын
Nako yalla safara mettina trop Walahi
@astu9651 Жыл бұрын
Metinaa yallah nako borom bi takhawou. Fadel pourrais je avoir ton numero amna Syringes yii ak lait bubakh pour son alimentation.
@diallofatou489 Жыл бұрын
Viens pv je donne la fille en personne
@astu9651 Жыл бұрын
@@diallofatou489 please diokhma son numero
@absatoudeme58 Жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭
@laminediagne2944 Жыл бұрын
😭🙏🙏🙏🙏🙏♥️♥️
@fatoumatatraore1340 Жыл бұрын
Bonne guérison
@khadydiop5042 Жыл бұрын
Masta metina nakhe mane alergie rek la amone di beugua dé ma sonou di wokotou rek bilaye walaye mais yalla nako yalla wereule 🙏🙏🙏🙏
@khadymarame5427 Жыл бұрын
Bon guérisse m'a
@antadiagne1166 Жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@khadymarame5427 Жыл бұрын
Metina trop
@AmiAmi-sw5ym Жыл бұрын
Massa
@louisemariamly9509 Жыл бұрын
Gnome ALASSANE MBAYE gni di wanéwou thi khaliss ak OR nagnou diappalé gni
@awadiouf9655 Жыл бұрын
😭 😭
@aminatou6854 Жыл бұрын
Ou sont les bonne volète stp aidè lui
@osVision2050 Жыл бұрын
Allahou akbar 😳 😭 🤢
@zota4025 Жыл бұрын
Please j’ai besoin de votre contact c urgent svp
@fatoudia9900 Жыл бұрын
Ndéyssane oooh li méti neu bilahi walahi yalla diam boumou beug rék lay ték natou wayé mom mila ko ték yalnala ko téguil si diam si barké seuydina mouhamed psl 🤲 wa Dakar buz aussi surtout tonton fadél yalnalén yalla diapalé si barké Serigne Babacar sy rta 🤲
Ndéyssane oooh li méti neu bilahi walahi yalla diam boumou beug rék lay ték natou wayé mom mila ko ték yalnala ko téguil si diam si barké seuydina mouhamed psl 🤲 wa Dakar buz aussi surtout tonton fadél yalnalén yalla diapalé si barké Serigne Babacar sy rta 🤲