Niit dangay positif, pape cheikh diallo limouy def Day permettre niit ki di dieul leçon sans se sentir vexé. Loy diangalé ak ré mo gueun ngay wakh niit dileu djèpi, car kouleu djiêpi douleu suivre
@beaevish56672 жыл бұрын
Lolou layy wakh chaque jour daguayy diageu dii rétane😶😂
@dioppenda21072 жыл бұрын
J'aime la façon de pape cheikh car il detent le débat et en plus il fait des relances intelligentes
@princessekounta25382 жыл бұрын
Vraiment
@coumbaniang15972 жыл бұрын
Bien dit makk Sama
@princessekounta25382 жыл бұрын
@@coumbaniang1597 bilahi li dafama métti trop waye
@fatoumataaidara14792 жыл бұрын
pape cheikh tu n'es pas sérieux bilahi Loy retane yaw 🤣🤣🤣🤣retana ba soneu ndakh yaw merci pape cheikh je t'adore ❤️
@collesow38982 жыл бұрын
Bonne question Awa
@omarkeita85012 жыл бұрын
Pape cheikh diallo je t'aime beaucoup
@mousaphagadiaga50572 жыл бұрын
Khana.do.goor
@Getma942 жыл бұрын
MashaAllah 😂😂😂 Intéressant na
@silyndiaye75602 жыл бұрын
Pape gni nékk si souf gnokay réeeh lo loll💯😂😂😂😂😂
@diaryatoulahdiop67112 жыл бұрын
Abba sanex pape cheikh con nagn🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 safara dina fess kay
@rokhayadia33012 жыл бұрын
Mom lay ré ba tay🤣🤣🤣🤣
@lastweek15742 жыл бұрын
Wax gua deug dhé 😅😅😅😅😅
@MbayeSarr-tw2vr8 ай бұрын
Non kii srxx woul 😂😂😂
@amiesuwareh58602 жыл бұрын
Good question girl keep it up you doing very very well we love it and we all going through something like that thank you so much so mean I’m not ready to be responsibility they never take their responsibility they wanted somebody to do it for him thank you so much that is interesting question I really appreciate it
@orello90722 жыл бұрын
Rasouli lay🥰
@aichananiang85772 жыл бұрын
Bilay saneh ak ABBA dina gnou ma ray 😂😂😂😂😭😭😭
@amadoukane91152 жыл бұрын
vraiment hhhhhhhhhhhhhhhhhhh
@ALHAMDOULILLAH33fois4 ай бұрын
MA SHAA ALLAH❤
@momyseck73812 жыл бұрын
Ay Pape cheikh Diallo 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@serignetoubagueye72052 жыл бұрын
😂 pape cheikh sérieux woul
@odegaardjr19912 жыл бұрын
Modou fall bayill question diambour yingay tonntu
@Pape-q4m3 ай бұрын
❤❤❤❤👍👍👍
@AHMADOU_MUGHNIYAN992 жыл бұрын
Non saneex ak abba😂😂🤤
@mamediarrasall36192 жыл бұрын
Kon dee gorou europe war nagno deglou lii djigeen yi fii europe gno yoor seen boop gorr amoufi ndiarign
@kareabdoulahad6222 жыл бұрын
wakhal si linga guiss boul geberalise sam papa ak sama yaye niongui europe beugou mako woon wakh mane ni italy la dioudoo beugou mako woon wakh ba ni niongui fii ak mane sama yaya masoul ligey kane moko yorr kon esk mo yoor bopam deel wakh boul ni nieupou
@salatoudasylva52822 жыл бұрын
Aba sanekh séne toguaye diakhal nama
@aramegassama55622 жыл бұрын
Pape chiekh 😃😃😃
@Fall3972 жыл бұрын
Ay pape chiekh
@Amstronger192 жыл бұрын
pape rew nga 😂. Boul m'a titeul way
@yamudownjie38582 жыл бұрын
Woiyyyy😁😁😁😁😁😁Mickey tamitè 🤣🤣🤣🤣🤣🤣♥️🇬🇲🇬🇲
@diankimbadiaby14312 жыл бұрын
Bien-sûr ça existe 🤷
@amethka92112 жыл бұрын
Pape cheikh amal respecter un peu comme si que modou fall limouy wakh amoule sens li rek mo yakh sa emission sil te plait dell am respect un peux
Boul fateii pape cheikh dafa takk écouteurs pour di deglouuu wa régie du coup peut être niommm nio koy retan Lo😂😂😂 parck niou gnieup Ayy xarit laniou Comme ioe rk xammm nga sa xarit yooo xamniii solén di xolaltéii di retann C’est involontaire
@saynaboudiouf232 жыл бұрын
Machalla
@lababacariene99362 жыл бұрын
Kou dieul lokhom dii fowé bopam nak😅😅😅
@marieme29612 жыл бұрын
Lolou masturbation la dii 😒 « Et que ceux qui n' ont pas de quoi se marier, cherchent à rester chastes jusqu'à ce qu' Allah les enrichisse par Sa grâce.. « (Coran, 24 : 33) Et rester CHASTE veut dire préservé de tout rapport que ce soit. Même si tu es vierge ou puceau mais que tu joues avec ton sexe tu n’es pas chaste.
@Elhadji21872 жыл бұрын
Safara dina fess kay astafiroula 😂boy yeup si masturbation lagn deuk guisguen video lomotif yi boy yi Dagni mbalou every time
@Laye7192 жыл бұрын
C faux, c lui qui sait qui doit aller à l enfer. Ou c écrit que la masturbation est haram?
@votrefrere25262 жыл бұрын
@@Laye719 🤣🤣🤣saay bou féké thi nga nek bayiko mo gueune thi ioe. Lep loy def banie kou la thi fek à part seuy kham ngani dou lou bakh
@Laye7192 жыл бұрын
@@votrefrere2526 Non, je suis marie, pas besoin de le faire. Dans ce genre de débat, tu ne peux affirmer des choses ss donner la justification religieuse.
@votrefrere25262 жыл бұрын
@@Laye719 Plateau bi 3 outaz nio fa tokk ken wédiwou thi li outaz modou fall wakh té nio niou gueuneu diangue souma dioumoul. Masturbation mom l'islam ak christianisme yeup danie ko téré bakar bou makk la. Kep kou thi nek bo yabo bayiko. Wassalam.
@Laye7192 жыл бұрын
Dans un débat ils doivent apporter les preuves
@bambaseck622 жыл бұрын
Koula beugoul bayyiko point amoul forcé
@aidafall-oi5gh Жыл бұрын
Ça m'arrivais avec mon ex copain.j'ai forcé à lui laisser . C' étais trop dur Alhamdoulilah
@maimounaka19762 жыл бұрын
Michey kay😅😅
@alioudiop84662 жыл бұрын
Bilahi
@abdouvarane42612 жыл бұрын
oustaz bimo ndieukeu niak fayda parcke oustaz dou am comportrment bi chim
Halei bu meuneu dioudou il est reconnu il n’a pas demandé à naître oustaz television yi hamougnou touss ay kassaw kassaw rek lagnouy wah. Keep ku yalla diegaloul do dem safara donc y a des choses les gens le font parce qu’ils n’ont pas le choix et la plupart dagnouy gnane yalla diegalene lolu kessei la
@ndobinetvsenegal71212 жыл бұрын
Sa way, boudéi danga koy deff, nanga ko bayi ndakh dafa haram...