Mawo, Ex Eumeu Sène Junior en colère : "Eumeu Séne n’est pas reconnaissant kou wathie sa ande…"

  Рет қаралды 11,276

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/

Пікірлер: 71
@kurayahmi
@kurayahmi Ай бұрын
Kou nieup toufli ngeu tooy. Jordan, Tyson 2, Ngueer bou Zap, et maintenant Eumeu Sene Jr. Niom nieup ils ont dit la même chose.
@davelelion8789
@davelelion8789 Ай бұрын
Kéneu dou Modou lo si lamdji, il est très reconnaissant ❤👑
@IbrahimasoribaDiakhaby
@IbrahimasoribaDiakhaby Ай бұрын
Eumeu séne Deféant la je l’ai toujours dit
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Ай бұрын
Modou Lo toujours le meilleur lutteur ❤king 👑❤️
@BOROOM_NDIAREM
@BOROOM_NDIAREM Ай бұрын
Ki baye fall la ❤❤❤
@moussadiallo3179
@moussadiallo3179 Ай бұрын
Ana Tyson 2
@bassiroundiaye3913
@bassiroundiaye3913 Ай бұрын
Eumeu séne junior limouma nékhé Moy baye fall gui amale diameu rék
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Ай бұрын
Dodou sane na khare walame 🖥️😂😁😅eumeu sene rek ❌
@momosy6083
@momosy6083 Ай бұрын
😂😂
@diakharbousaff8272
@diakharbousaff8272 Ай бұрын
Yalnala Yalla yokou
@Président-ABDOU-DIOUF
@Président-ABDOU-DIOUF Ай бұрын
Apres Nger bou zap, Jordan, voici eumeu sene junior dit la même chose 😢😢😢on peut dire Eumeu sene n'est pas bon dans la vraie vie 😢😢😢😢 Motakh yalla Joh ko 12 victoire 10 défaite
@barhamalpha8802
@barhamalpha8802 Ай бұрын
Tu ne t'es pas demandé pourquoi lui il est roi des arènes et tous ces autres là sont là où ils sont ¿
@mouhamadoudiene1315
@mouhamadoudiene1315 Ай бұрын
Ak Coly Faye ak Tyson 2 en tout cas nieup meunougn bokk feine c'est impossible
@Président-ABDOU-DIOUF
@Président-ABDOU-DIOUF Ай бұрын
@@mouhamadoudiene1315 merci de compléter la liste
@Président-ABDOU-DIOUF
@Président-ABDOU-DIOUF Ай бұрын
@@barhamalpha8802 mon frère soyez honnête. Tyson 2, Coly faye, nger bou zap, Jordan, eumeu sene junior tu crois que ils sont tous des fautifs ou menteur. Eumeu sene est naturellement de cette manière, ne perdez pas de temps pour défendre l'indefendable
@kevinjonasndiaye661
@kevinjonasndiaye661 Ай бұрын
Ak Tyson 2
@afro3827
@afro3827 Ай бұрын
Eumeu sene jr ak baye madione gno yem yorougnou jikoy mbeur 🎉
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Bilahi
@Capsiladeuk
@Capsiladeuk Ай бұрын
Li si graw moy ki di wakh ni limouy def sortie beuri woul. So si bolé cas Jordan, mdr ça laisse à réfléchir…..
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Walahi
@papesouleyendao4312
@papesouleyendao4312 Ай бұрын
Après Tyson 1 , Jordan, Coly Faye , Tyson 2 , Pape Cargo, Omar Fall , Eumeu jr , Atta Je te jure Eumeu séne mo sik dafa sokhor pour mome rek mo wara ame traître deug moy eumeu Néna modou meunoul beuré sokhor pro Max
@kevinjonasndiaye661
@kevinjonasndiaye661 Ай бұрын
Eumeu aussi sigue na
@Amm2293
@Amm2293 Ай бұрын
Sénégal temps liniou khéwal démoul quoi...ko si amal blem warnga am sagn sagn wakh kako en face...mbeur nio wara arrêté exposé séni problème si site internet yii.... être fort n'est pas toujours physiquement mais c'est très important d'avoir une force mentale...mbeur mom pour niom force physique rek la..,
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Yangi doga guiss eumeu séne junior wakh lou mél ni thii eumeu démal sétane aye inter vie yam ki béne mbeur geunouko khol ❤ walahi
@Amm2293
@Amm2293 Ай бұрын
​Vous avez parfaitement raison, bo kholé visage bi rek nga kham né borom bakhla, mais ce qui me fait mal c'est de les voir exposer leur problème devant tout le monde, et je ne veux surtout pas que ces déclarations brise leur relation....​@@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@mbayesene1072
@mbayesene1072 Ай бұрын
Eumeu junior grand Champion
@socratesndiaye2196
@socratesndiaye2196 Ай бұрын
En tout eumeu Jr d'où féne
@baityrba2447
@baityrba2447 Ай бұрын
Yakheuh dérr amoul solo aduna léppeuh dafay diékh Eumeu Sene le digne fils de Pikine 💚💚💚❤️❤️❤️est un homme exemplaire dans le monde de la lutte sénégalaise🇸🇳yallah na yallah dooli diameuh ak soutoura si nieupeuh jub jubal jubanti rek
@MbayeNdaiye-x2e
@MbayeNdaiye-x2e Ай бұрын
Eumeu sen djiy wakh lolou beurina kholal eumeu nim def tayson
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
​@@MbayeNdaiye-x2e walahi wakh nga deugu démal nga khol inter vie eumeu séne junior yépp bakham masna wakh lou niaw bo togué ak eumeu séne junior lime dathie thii eumeu séne yépou nga bayi eumeu walahi barki cheikhoul Khadim
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall Ай бұрын
Eumeu mo war Coly faye Jordan Tyson 1 Tyson 2 Omar fall Atap Pap cargo Eumeu sene jr nanfex
@nogayeniang9119
@nogayeniang9119 Ай бұрын
Lima si diakhal moye Jordan ak tayson 2 ak coly faye 1 Ak mom me nio bokou Lou nio wakh si eumeu sene
@bayemodoudiagne2326
@bayemodoudiagne2326 Ай бұрын
Eumeu séne dou nitou dara nilafi défone Jordan
@LamineDasylva-p4w
@LamineDasylva-p4w Ай бұрын
Eumeu si bobap mo sokhor toujour eumeu rek et les mêmes faits
@ABOUBACARMbengue-v8v
@ABOUBACARMbengue-v8v Ай бұрын
Sénégal nagnou bayi kougnou amal probléme diko wakh si Réso yi 😢
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Yangi doga Guiss mou wakh thii eumeu séne ki niata combat la beuré bime diougué thii eumeu séne masoul ki walahi bo togué ak mome nga bayi eumeu séne limou dathie
@cheikhniang8993
@cheikhniang8993 Ай бұрын
Pour momm li moyy jico bou bakh si gooor
@ProcureurYoutube
@ProcureurYoutube Ай бұрын
Eumeu Sene dafa sikk dé Kou say lieutenant yeupp di khass normaloo
@cheikhniang8993
@cheikhniang8993 Ай бұрын
Seuytané yi bari nagne si réww miii
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 Ай бұрын
Non wayy
@PapadameFaye
@PapadameFaye Ай бұрын
Eume sene junior doudou sané laniou beug
@damembow6374
@damembow6374 Ай бұрын
Eumeu yagui beug doy warrr nakk kou gnepp toufliii gua toyyy
@damendiaye4221
@damendiaye4221 Ай бұрын
Si Tyson Bou mak la tambalé ata Jordan Coly Faye Tyson 2 ak ki té kou gnip tofli NGA toye
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 Ай бұрын
Guédiawaye nimou baré ay ancien gloire you bah,toudo nioniou sa bop,diko toudé kinga hamanteuné sa moromu là té bokoléne mêm lieu,dieulal Ordinateur mou dane là si une minute
@papefall4806
@papefall4806 Ай бұрын
Mbeur you makk yi gnissi bakh bariwoul xaliss sakh dougn ko mayé Bo wakhé Niouni mystique lagn ragal mais boudé lougn wara dieul xaliss bi dou am mystique .pour niom rekay niit
@récré-o1d
@récré-o1d Ай бұрын
Camp eumeu ak camp Balla gaye rék lay guiss niouy yakk dérr sen grand yi
@IbrahimaSonko-i7p
@IbrahimaSonko-i7p Ай бұрын
Mao nite kou bakh jtjur c ningky nanka fata da ma déme mou bolé ma si bopam yatal ma si écurie mor fadam
@soldarouyayam8524
@soldarouyayam8524 Ай бұрын
Daguay dole rek bayilèn sogèn nècoule ak nite diko yakh eum xol bou rafet la yorr bouko nèxone dafa dougu xamone nanè gèdiawaye gua deuck ta bigua nieuweè dala yatal yeufou khadje rek guènn dy def ndakh
@azizallendiaye6590
@azizallendiaye6590 Ай бұрын
Mbaw Jr amal foula eumue sene epou la sotou la demal ga liguye eumue sene bi ko gris di dorr diou taf bete bi fan ga nekon
@azizallendiaye6590
@azizallendiaye6590 Ай бұрын
Mbaw Jr 😂😂 manou diekue quediawy di dem pikine lo lou manoul nek quediawy sakh baga fa demai ga diotè ak gouye gui dolèn todantè
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 Ай бұрын
😂 ioe ligay wax xamosi dara Gnata mbeur gno deuk pikine di beurei guediawaye Ak vice versa
@lesamouraisnoir5304
@lesamouraisnoir5304 Ай бұрын
Yambaré molène dalle Eume Séne défouléne dara daffa lène eppou foula way nguèdi ay ponkal diñû sonal Aki Eume Séne japalé wouléne fouté nous la paix.
@fatoucha554
@fatoucha554 Ай бұрын
Billakhi
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 Ай бұрын
Dolene xam nit fumi waxei mais dagueine oubi sene gatte yi di wax Pkw modou lo di diapalei franc diko deukal keuram Pkw tyson heberger wone eumeu sene? Pkw balla gaye 2 pa balla moko yorone ? Dolene nopi si lolene xamul guene di tepeikou rek mbeur yi dagni seik you beuri so rawei say lieutnant dagalene di tatagal
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 Ай бұрын
Dolene xam nit fumi waxei mais dagueine oubi sene gatte yi di wax Pkw modou lo di diapalei franc diko deukal keuram Pkw tyson heberger wone eumeu sene? Pkw balla gaye 2 pa balla moko yorone ? Dolene nopi si lolene xamul guene di tepeikou rek mbeur yi dagni seik you beuri so rawei say lieutnant dagalene di tatagal
@fatoucha554
@fatoucha554 Ай бұрын
@thiamahmadulattekh562 ya dognou maye diam boma rawé diapalé woma ma diape si yalla té nopi diapalé dou force nite kéne douko méré si alalam
@azizallendiaye6590
@azizallendiaye6590 Ай бұрын
Bokal mo topou si guinaw nitt ba am 45ans mo lèrr nila yagui tardè ga doga yèwou fek mome mo am lep si adounam gay soxour
@ArounaCeesay
@ArounaCeesay Ай бұрын
Eumeu sene lèpp probleme
@fatoucha554
@fatoucha554 Ай бұрын
Problème dh dou kéne nite mokoye déf
@MameThiernoMbaye-ph1pi
@MameThiernoMbaye-ph1pi Ай бұрын
Yaw diambar nga
@fatoucha554
@fatoucha554 Ай бұрын
Yabi lénes domou diambour guire yalla té guiénes am foula
@ibrahimawalydiouf5745
@ibrahimawalydiouf5745 Ай бұрын
Sô gnémé ordinateur nga dieul avance bi mo guén wax bi
@Aaron-i5f
@Aaron-i5f Ай бұрын
Ki wakh ak Dioye rek lay dèf
@mamadoucoundoulndiaye3064
@mamadoucoundoulndiaye3064 Ай бұрын
Kii thi mécontents yii leu rk Bayilén yakk derr même bolén amé problème amone guén lolén sekk mou rafett Eumeu beu lgui mogui andeu akk ayy Doudou Sané Feu rouge Saa Bokkal etc.. pourtant lou rafett rk lagnouy sédé thi mom.
@laminediedhiou6609
@laminediedhiou6609 Ай бұрын
Gni nga toudou niep tay leuh ani tyson 1. tyson 2. pape cargo. coly faye. Sokh. Atta. Bref kou niep tifli nga toy
@laminediedhiou6609
@laminediedhiou6609 Ай бұрын
Jordan jen pass
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Demal nga sétani aye inter vie eumeu séne junior bakham masna wakh dra thii eumeu séne ki walahi lime dathie thii eumeu séne yépou masouko wakh féne eumeu mo bone
@MoustaphaGueyeYarwaye8850
@MoustaphaGueyeYarwaye8850 Ай бұрын
Bou togué télé di dioye mes dou nite kou bakh dé walahi
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 19 **VOSTFR**
1:06:33
EvenProd
Рет қаралды 746 М.
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
Quando A Diferença De Altura É Muito Grande 😲😂
00:12
Mari Maria
Рет қаралды 45 МЛН
NDINDY FALL TV est en direct palmarin
NDINDY FALL TV
Рет қаралды 984
Série Beau Père (sama goro) Épisode 20
29:02
Walf Production
Рет қаралды 12 М.
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН