Quand vous ne savez pas il faut demander avant de critiquer. Le baye remonte en des temps lointains où régnaient le paganisme l ignorance la royauté avec ses diam ses daggs et ses ceddos et autres garmis. Ce Gaadio est une manifestation magnifique de remerciement et de joie d être libre grâce à mame Cheikh et à l Islam par des gens qui a l origine n avaient nulle connaissance pour déclamer des khassaides ou lire le Coran. Ils dansaient devant lui et ils perpétuent cette tradition devant le Khalif des baye fall. Et puis entre nous qui n a jamais eu envie de danser pour exprimer un sentiment que rien d autre ne saurait exprimer?
@lordt96364 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️
@Faye-kp1qc4 жыл бұрын
Mono wakh bo daganal lii
@bayewade76344 жыл бұрын
Sa wakh loumou bari bari mantta takh li danguane dokhal diangui té diefé sa ndiguelou borom
@pisskkoo45362 жыл бұрын
Entre nous et vu que c'est dans un Cadre supposé religieux face a un homme supposé religieux la dance ne devrait elle pas etre plus decente?
@bayefall4551 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤
@masseyeseye75377 жыл бұрын
Ndeye sann louway khamoul loune boumouko Di ngat thiossan ci ndongay tarbiyyay baye Fall yi nekhna trop machalla
@lunelune88724 жыл бұрын
Sa way doul way ngay nane thiossane. Li alhourane mo ko fêté kaw. Oubilene sene khel yi
@astuondiaye59334 жыл бұрын
@@lunelune8872 ragalle yalla li amoule si dine ay jakhne la rek
@ndiougalo14264 жыл бұрын
Yaw sa dayi ndaye
@bathiedabo23294 жыл бұрын
Mame Cheikh Ibrahima Fall fowul te foluwul
@lunelune88724 жыл бұрын
Serigbe touba ak ibra fall lignou yak ci diné dji golo yakhouko thi tol. Yalnagnou yalla yeureum.
@dembafall19504 жыл бұрын
Wallakhi Liga eupona lol yalla na yalla léral sa khôl
@ndeyediop3354 жыл бұрын
Alioune Badara li mome kéne rafétlou wouko wayé ab djioulitte dou togne touppe ko younou Serigne Touba ak Mame Cheikh Ibrahima Fall nékousi
@moussafall9484 жыл бұрын
yakhamoul serigne bi rek.wayé yalla guereumnako yononbi guereumnako gninti khalifayi ousmane babacar oumar ak alioune guereumnagneko.lolou doyna . kon nekoul won kouy yak dinné. ta cheikh ibrahima fall moy serigne bi.
@santeyallla44224 жыл бұрын
Yaw domou haram ton père a trompé ta mère c pour cela k tu dit ça
@amydiouf15074 жыл бұрын
Sa data yaye domeram serigne touba dou sa morome
@mouhameddiallo25144 жыл бұрын
Diap ay khalé amoléne loléni diangal loudoul ay féthie li moy bane diné rek bayilén thiakhane té diamou YALLAH bala dé di gneuw
Done baye fall mo nékh danguéne na khamoul rék mais li thiossane la gni gnoy Aÿ vrai baye fall nakk
@kebaguaye29583 жыл бұрын
C le gadio la danse des ndongo laxassay lolen xamoul délén si mandou dissi wax Lou rafét li depuis diamonoy cheikh Ibra la té ba legui ndongo yi niogui koy def bassi kanami Serigne cheikh dieumb fall miy cheikh Ibra taay ngén di yax dérr ap mouride day deugou té fier si loum done rawatina ap baye fall wayé mouride la, baye fall la cheikh Ibra folouwout té li niouko dane def si kanamam ba téy dji niogui koy def si kanamou cheikh dieumb ma bagn yén façon mouride done ap kalboune Sax moko geune. Dieuredieufé Mame cheikh Ibra fall
@akhmadabambajoop35032 жыл бұрын
Dieuredieuf
@Mnmb274 жыл бұрын
cheikh ibra d amoul wone diotou fo té baye fall tigui dou si ay féthie lagne koy ragnè
@saliousow65634 жыл бұрын
Yow dh linga wax maitrisé wo si dara
@abramofishman1464 жыл бұрын
Ta parfaitement raison
@latdior36524 жыл бұрын
Sé faut cheikh Ibra lileu xamone féthieu ak taak diabar 90 femmes leu yorone teuyeukh rék lafi bayi comme héritage li mooy yonou Mouride amoul diouli amoul woor démbeu taay niou créé version bou béss maname nouveau testament 😂
@santeyallla44224 жыл бұрын
@@latdior3652 sa seigne ak koumou meunn donn cheikh ibrra moko guene guene bayam
@latdior36524 жыл бұрын
@@santeyallla4422 Cheikh ibra ak Serigne biko ambauché wone ay coureur de jupons laniou wone gueumouniou dara Tate rék laniou done weur
@sendof67difo603 жыл бұрын
Li kén khamoul lanela ! Té si yonou dîné la 😁 sounou borom yeureum nou diégual nou sambnou 🙏🏿
@modoumb99112 жыл бұрын
Dine diou werr
@mouhamedniang89044 жыл бұрын
😭😭😭😭thiey addouna danio reirei lolou mbirou baye fall. Baye fall deug moy kou name yallah di def lou yallah diglei toopou yallah . Baye fall dou fall nakh cheikh ibra fowoul tei fowlo woul keineu diamou yallah si liguey diokhei ngir yallah laniouko khamei ak def zikhroullah toud Allah ak diang alkhouran
Y'a meuneu doul déloul gueustou ski loi waral gadio imbécile
@bayefalldiene38955 жыл бұрын
Adama ki bayi ka fofou ak wakham diou bari
@electionslocaleselectionsl38597 жыл бұрын
magui niane yene gniy comantè gir yalla bu lène ji doud serigne touba yonam nèckul ji li,,, sabar bi nak mom masa allah fegne bi nèkhna
@papembayesow60997 жыл бұрын
sa c. Est pas normal
@abdoulayecamara80433 жыл бұрын
Limoy Gadio .kou khamoul Mandouci
@mossandiaye68933 жыл бұрын
Tarkha mourit 😀😀😀😀😀😀
@bayefall4551 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤
@dmte64404 жыл бұрын
😀😀li moy thiossanou réwmi koumou nèkhoul kattal sa nday nga dém arabi saoudi
@دفراتسنغال4 жыл бұрын
Diaroul dem Arabie Saoudite meune nanio dougue sa biir data yaye lakhatoufa rek
@dmte64404 жыл бұрын
دفترات السنغال damay khorom sa sa badjo yay dé😄😄😄
@papemodoundiaye44764 жыл бұрын
MDR hahha
@babacarcisse48774 жыл бұрын
Noooo
@ascibat40254 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne bi sa ligueye mokal nagneko
@siditoureyogatoure34024 жыл бұрын
Bayilêne khaléyi niou déme diagui waye ragale léne yalla
@bayewade76344 жыл бұрын
@Babacar Thiane yaw eske nite ngua
@fatoumatafall53323 жыл бұрын
Ay khalai en formation li doye na waar
@mososemoise81944 жыл бұрын
C'est la responsabilité du khalif des mourides
@mtbroug23584 жыл бұрын
Khalif bi matoul li mou done parceque mo dakha bocalé ci adouna bi
@ngagnendiaye78754 жыл бұрын
@@mtbroug2358 yaw mano wakh louniou nakhari ndakh geumo yalla geumo yonénte bi kone bayima gouy wakh gua rk dokhal rk adouna dinala yare liguay khamadi lepp
@bambissbromlouge27963 жыл бұрын
@@mtbroug2358 iow iska xolenga linga waxe saye tane mongi laye dougel si lo xamoull lisaxe da yom nek si tephon di waxe loula néxe walayi manmi rk bo diakarlo wanak man doko waxe boco waxé doull saye toubeye dh
@mtbroug23583 жыл бұрын
@@bambissbromlouge2796 ok merci
@youpro52484 жыл бұрын
Toujours les mourides😔😔😔😔😔😔😔😔
@serignefalloumbacke78493 жыл бұрын
Lidé khawma fane wayé bokoul thi serigne touba serigne fowoul folouwoul té li ak rér akouk diahil kassé la
@ousmanediop16204 жыл бұрын
Très bien sene serigne yeeh lene former même style 🤣🤣🤣🤣🤣dommage pour mon pays
@adamasy88227 жыл бұрын
C'est magnifique
@malicksy30097 жыл бұрын
Adama Sy dieuf diou niaw dji nga nane c magnifique
@adamasy88227 жыл бұрын
Mame Malick Sy rouss nala tieureul nala rawatina sa tour wayer khamal ni guor sou mando Day soré sa ma wakh mandou si
@malicksy30097 жыл бұрын
Adama Sy boula nèkhè nga sagama wayè dieuf diou niaw kène douko encouragè
@adamasy88227 жыл бұрын
Lou gnaw moy tidji sa Guaye fougn la ladjoul guor Day bagna wakh Lou guatam newoul
@adamasy51846 жыл бұрын
Rijal
@cheikhmbayecomedien_offici44003 жыл бұрын
Kholéne thé bayi mano khôl sa yone nékouthi mandou la yalla beug
@mouhamedcisse97284 жыл бұрын
Li takhoul l'islam diouk gnawna trop yakh nguéne khaléyi yeup
@mamadoudiop11054 жыл бұрын
Li mom bokul si islam
@mouhamedniang89044 жыл бұрын
Lu bokkoul si baye fall. Baye fall weug moy kou name yallah nekk si lou nekh yallah . Juste adddouna danio reirei baye fall. Baye fall moy ko khamni dou khey teu défoule zikkrou llah wala diang alkhour an. Thiey addouna reirei naniou mirou baye fall deug 😭😭😭
tu ne connais rien au mouridisme il y a eu pire ici demande a tes parents
@salamfall69004 жыл бұрын
Yénna réeré céhkie ibraima fall lie bokoul Simom
@batimentconstruction76214 жыл бұрын
je suis tidiane mes je connais le gadio ses cultures des baye fall
@madywade43173 жыл бұрын
Nice
@pinkinrails24564 жыл бұрын
Li moy lane encore . Yague guen khaleyi
@modafaye17093 жыл бұрын
Tres bien
@maawacisse54195 жыл бұрын
Allahou akbar adouna mougui wadia touki. J'ai pitié au petit âge qui connaissent rien du tout. Qu'Allah protège et leur donne son miséricordieux amine. Li dou deugue d'où yone
@ERZAJOP4 жыл бұрын
lii deh mo mak seu baye....
@santeyallla44224 жыл бұрын
Lidoul deug sa keur baye la commencer
@bayewade76344 жыл бұрын
Yalla khamnani gni danio rère ohhh daniou sankke niou bari ndaysane
@laminembathie99524 жыл бұрын
Li mo takh moussa camara dou len lebal
@hamathcisse75784 жыл бұрын
Waxatico deh 😂😂😂
@maawacisse54195 жыл бұрын
Moi je suis maurite mais ça fait pas partie du mauridisme. Serigne Touba merei nalene trop sakh
@barradiopfall4 жыл бұрын
Khamo darra
@bouryndiaye81014 жыл бұрын
wakhe nga degue dé
@mtbroug23584 жыл бұрын
Bayi l mouridisme thiakhane bocalé fo rec mofa am té nga nioww ci yalla akh yonanté bi mo nguén ci yow
@khadimthiamdts4514 жыл бұрын
@@mtbroug2358 yaw kou rere nga kouniou gueulamal kou djitou ciy none ga ta none matoul sede ta mane nak douma la saga Douma la khasse ndax sunuy teguine mayou makko waye dina la dolé denk ni serigne touba Limou indi woute woule ak yonent bi bene yone Ta yite liko boromam diaralone amoul bene diam boume ko diaral monete goné youy fethi rek ngeen guisse beug thie diaré wax yonoi mouride louné ana niane nio gueuna social ci dioulitou senegal ana niane nio gueuna meuna diokhé niame ci dioulitou senegal ana niane nio delo
@khadimthiamdts4514 жыл бұрын
Boume ca mboy mboy nga bi corona bi nieuwé tane teudione diaka yepou mou deupok li toubap yi waxone ca ndar bou nekone aye nite youy bokale lane kone doune tayle bakane ci diouli Pegnep Gouro nak bo dem fek fa sankar khayna fethi bi diadou woule ciy dioulite wayé nak dieuf yoko meuna mougné mo eupou fouf nga bayi ci khel bou baax L'islamou sëriñ Tuubaa bi taxul deret
@modoungom55223 жыл бұрын
Lii defen,nge ne Li dinadiemele kanam AP rew 😭🤣🤣😭😭😱😱😱😱
@ngtvsenegal3 жыл бұрын
C'est triste
@adamad9190 Жыл бұрын
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@sididoip1384 жыл бұрын
Li mom bane diné la
@Mac123.806 жыл бұрын
"Gadio" une tradition baye fall l'une des valeurs culturelles en voie de disparition.
@okeezmusic86094 жыл бұрын
Baye fall deug day mane fecc
@mouhammed4 жыл бұрын
Thiey senegal dinné bou nek ngay guiss lii fi la beut yéme
@dfggfgfgdgggfdg85124 жыл бұрын
Nio gui teuyeukh daal
@abdoukarim16684 жыл бұрын
😂
@talibecheikhpointtv26743 жыл бұрын
Ngii dagno rére
@dmte64402 жыл бұрын
Cheikh tidiane eslavagiste yow mom boula sèkh tidian jappon deug sa Ndey déf la jaam
@diengsocialmedinagounass3953 жыл бұрын
Cheikh Mbacké dieng
@dioufmbacke2394 жыл бұрын
Li d'où Baye fall
@gayedelleleveurpigeons2187 жыл бұрын
mbouboo baye fall bkhoull dhé leen di maytou
@toukoubaaba19467 жыл бұрын
Dan ji am foula sakh😂😂😂😂😂😂😂
@bocardiallobarber23524 жыл бұрын
Bilahi yénay ay Domaram bayilene khalé yi guéne di yakh fi sabilillah
Gadio li thiosanne la kouko khamoull rekk mokay critiqué nitt lokhamnii sa Yonne nékousii dangua sii mandou ....
@baidydiouf20584 жыл бұрын
Jangalolën xaléyi Dara loudoul ay pëth Aka ngéna sori ak baye Fall dommage😌
@maimouna314 Жыл бұрын
Li dou dîne de li thiahane la
@cissecissepamor98013 жыл бұрын
Li ndane lay annè ak rew mou developed
@babamamadouniane76224 жыл бұрын
Cé de la comédie mais pire que la comédie. Allah dit dans le coran ceci: " Ils prennent leur religion en jeux et amusement et ils sont trahis par cette vie présente..." Qu'Allah nous guide dans l'uniqu et droit chemin
@freemind30094 жыл бұрын
Amine
@freemind30094 жыл бұрын
Subhaanallah et puis des jeunes
@khadimdiakhoumpa89557 жыл бұрын
Lidéé tanbérlaa rékk
@ibragueye21534 жыл бұрын
Khadim Diakhoumpa ta guel
@aliouthiare92454 жыл бұрын
Ndeysane
@cesttekzoone604 жыл бұрын
Kou dé rek diga yéwou
@fallgabane89157 жыл бұрын
Hay thiakhane dong la
@bayefalldiene38955 жыл бұрын
🤣🤣
@babacardrame32464 жыл бұрын
li mome ban dinala
@ousmanga53884 жыл бұрын
Good question??
@gorafall22364 жыл бұрын
Libokoul thi dine deme le diangui
@mamadoudiop11054 жыл бұрын
Yakarna de mo gueun diap ay khale waron diangui dilen diangal ludul fethie
@touraytouray39624 жыл бұрын
Denni Senegal gui ni
@moustaphagoumbala18043 жыл бұрын
Li mo dou yeufi mourid
@fatimambodji95594 жыл бұрын
Waw kay way diné bi mome matna
@aronaaidara22102 жыл бұрын
Machala
@bayofall69267 жыл бұрын
CA S APPELLE DU GADIO UNE VIEILLE TRADITION DES BAYE FALL
Tiossane guor yallah yi gnoy borom yaram dieureudieuf bon magual touba guor Yalla
@omarthiao38536 жыл бұрын
Adama Sy q
@paassdiop26714 жыл бұрын
Pa
@lunelune88724 жыл бұрын
Yeufou domeram nganam coutume
@mamadoufaye25863 жыл бұрын
Au moment ou on ce révolte voilà ce que nom marabout charlatans apprend à nous frère
@Rimka9124 жыл бұрын
Wahahahahahah nonnnn magui dee
@zallnitoudeugue57644 жыл бұрын
Very nice
@sambafall53123 жыл бұрын
Dommage pour Sénégal ay makce you bonn
@bassendiaye98564 жыл бұрын
wawo li dé mooy islami senegal lolén wahabiyouna yi di wakh reck mooy deugue
@santeyallla44224 жыл бұрын
Yaw ak wakha yi senn tatou yaye
@iboudiouf76733 жыл бұрын
Yéne denguén baari wakh téh xamolén louy l'islam nékeu fi di doul rék
@prince7even3934 жыл бұрын
Kadd Diagne gamou paye 2016
@globacell23884 жыл бұрын
ayway xale yi anasen wadiour.yi.li.yalla.dinalenko.lathi.ellek.
@elhadjifall92104 жыл бұрын
Man yeen la gueum
@elhadjifall92104 жыл бұрын
Rak diok faller mou leeeer
@papasow30164 жыл бұрын
Téyeukhe
@ousseynouniang54514 жыл бұрын
Tiakhane rék
@santeyallla44224 жыл бұрын
Lolou sa baye moko kham
@bayewade76344 жыл бұрын
Wallahi daniouy fowé diné may wakh nak niouy fèthie fi toudde yalla
@blackfils68903 жыл бұрын
C’est une honte, ak sein fethie bou salté bi🤮🤮🤮
@misterthiere82576 жыл бұрын
Bayi len yakh derou bay Fall yi
@dieyedieyefall92716 жыл бұрын
Sawaye gni ay baye fall lagne so khamoul lathiétel wala gua madou djioulite pir day madou
@ndeyendackyayoukhadimbayea45206 жыл бұрын
Yaw khamo li gadio la
@bayefalldiene38955 жыл бұрын
Ki dafa bari wakh rek di wakh mais kham khamam sori woull
@pascallaminembaye98814 жыл бұрын
Le rythme et les pas de dance sont des sérères du DIGUEME . c'est chez les sérères d'une partie du bail EST en allant vers Ngoudiane, noto diobass et Tassette.... Visitez les traditions rythmique du Diobass... Merci!
@papevivo45193 жыл бұрын
Traduction thiedo
@mohamedfall6594 жыл бұрын
Boudeh si gnii lagnou yaakaar euleuk
@mozeusfall40264 жыл бұрын
Aka sori al alkhouran
@mariaone82864 жыл бұрын
Les pauvres enfants
@salamfall69004 жыл бұрын
Ragallén yalla té bayi di sosal mam cheike ibraima fall amoulwon diotou tage di féhti