Mandé ya takh ma guene kham sama dîné dém guestou dji,waye alkhourane AK Sounnah rék moy deug,merci ya ouztaz....
@aboubacrysow510 Жыл бұрын
Ma sha Allah oustaz Omar Sall une fierté pour le Sénégal, barakallah fiikoum
@fatousanyang38232 жыл бұрын
Marsha’Allah Oustaz. Standing for the Quran and Sunnah even if you will be alone. Amut ragal wala delou ganaw. Yallah nala Yallah sama arr la maiye la werr ak werrleh.
@bocardiallo4690 Жыл бұрын
Mashaallah oustaz qu'Allah vous bénisse et vous protège toi et ta famille
@omarsallah4812 жыл бұрын
May the Almighty ALLAH continue to protect you and all those that follow the path of our prophet Muhammad SAW.
@Babe-FaLilOu2 жыл бұрын
Amen
@oumienjie22642 жыл бұрын
Ameen
@yawasylla2242 жыл бұрын
Oustaze bal niou akh rék
@shattaflex11802 жыл бұрын
Amen
@sokhnambaye41062 жыл бұрын
Je suis parfaitement d'accord avec toi yalla nala yalla defale diam ak salame tai maye la goudou fane 🙏🥰
@moses002212 жыл бұрын
Wakhal dé, tu m'a ouvert les yeux et depuis lors je suis tranquille, tu es entrain de réveiller beaucoup de sénégalais et ça leur fait peur , et puis tu as le droit de parler du magal et du gamou car tu es un homme de religion et ce sujet n'appartient à personne , je trouve même super que chaque année il coupe vos vidéos pour en parler parce que ça permet de réveiller d'autres personnes.La dahwa tchia kanam inchallah.
@coumbasarrgning75332 жыл бұрын
Kou mom khar mi niou bayi boum bi. Mingui beugu louche daal. Yalnaniou yalla ték ci yonou ndioub.
Serign Touba dé. Y’Allah lay Magal souma dioumoul. Nous devons être unis frères musulmans. Wassalam!
@doffndiayenittdiop1742 жыл бұрын
Lolou d la woté kay leneu santé lema yalla diague Alkhourane
@mamemaremadioum2 жыл бұрын
@@doffndiayenittdiop174 Walahi ❤️
@matarthiam31592 жыл бұрын
C’est simple dh Walaahi❤️🙏 yalna gnou yalla fayal Ahmadou
@libassediop43692 жыл бұрын
Mais omar sall compoul mome
@moussaniass29872 жыл бұрын
Wallahi sante yallah rek
@RokhayaNdiour-n7f3 ай бұрын
Qu’Allah nous offre 10000000000 Oustaz Papa Oumar Ahmad Sall Longue vie à toi que du bonheur 🤲🏻🙏🏻
@omaribnmoctar77992 жыл бұрын
On est derrière toi ya Oustaz Qu’Allah veille sur vous Qu’Allah vous protège Incha’Allah Amine ya rabbi☝🏾
@bintmustapha24112 жыл бұрын
Salam'aleykum, c'est plutôt amine au lieu de in sha Allah
@Oubli20232 жыл бұрын
Mieux vaut être derrière DIEU . C’est mieux fanatique !!
@khadimgueye15702 жыл бұрын
Khana guinéen nga yéne fok niou guené léne Sénégal
@omaribnmoctar77992 жыл бұрын
@@bintmustapha2411 Waleykoum salam moi g juste fait un doua et si dieu le veut c’est à vous de dire amine
@omaribnmoctar77992 жыл бұрын
@@Oubli2023 façon de parler c’est à dire qu’on est derrière lui pour l’accompagner vous comprenez rien aussi 🤦🏾♂️
@khalidousarr33962 жыл бұрын
Amoul khalate deug deug , yalla rék lagnou waara magal . yallah sam léen ya oustaz
@dignite79392 жыл бұрын
Le meilleur oustaz du Sénégal Il est gentil,généreux et très amoureux du coran et de la sunna. Loudoul yalla niorouko
@aicharassoul26412 жыл бұрын
Walahi je confirme 🤩🥰🥰🥰
@sekougassama87422 жыл бұрын
Yalna ko Yalla sahal
@dignite79392 жыл бұрын
@@aicharassoul2641 c'est nous qui devons l'aider sister. Il nous a bcp donné et pourtant on ne l'a jamais vu
@dignite79392 жыл бұрын
@@sekougassama8742 Amin mon frère
@DarkSide789212 жыл бұрын
Enttcas moi je l'estime bcp
@abdoulayediarra25252 жыл бұрын
Oustaz yalla nala yalla defal diam ak bolém dioulitt
@namaly8292 жыл бұрын
Meilleur parmi sa génération galsen islam tiakhane mofi nek حفظكم الله
@إبراهيممحبالله2 жыл бұрын
Yalnala yalla samme y’a ousstaz
@abolo76102 жыл бұрын
serigne touba déné kay léne santé léma yalla wahoul kay léne santé m'a nonou ragalle yalla thi liniouy wah beug koula top boum lataha wah lou nékoul Mangui diégeu lou bah
@Oumie-n6g6 ай бұрын
Merci beaucoup oustaz oumar sall
@fallbathia2 жыл бұрын
"Et proclame hautement sa grandeur"Sourate 17 verset 111!Yalla rekk la dioulite wara Magal!Dieuredieuf Oustaz!
@santyalla34912 жыл бұрын
wax bi lerna al hamdoulilah Yalla rek mo diara magal kéneu douko wéranté mais da nga waxné diné Yalla rek mo ameu ba paré ngani diné confrérie lolou dafay indi wat ay wax rek je suis mouride est fier de l'être mais lou Yalla wax ak le prophète lolou rek nga meuneu firé parsk yoneu bobou nga dieul té ameu ngassi droit nous aussi amnagnou droit andeu ak Serigne bi . bouldi tontou parsk amna gno xamni bokou gnou sakh si yoneu bi mais diakhassé moléneu Di nex nga bayi si xel oustaz
@dienauto40872 жыл бұрын
Nekkal ci jam oustaz Allah est témoin
@abdouazizmanemane41242 жыл бұрын
Oustaz nous on est fière de toi et qu'Allah te protège. Tu bénéfique pour nous et la société. On t'aime
@bambambaye69642 жыл бұрын
Wakh deugue yallah mouride la wayé deugue rek gua wakh, yallah rek laniou wara magal té mom la Serigne Touba woté ndakh kay lén satalé ma yallah ak nieuw lén niou magal yallah la wakh, kheuyna nak nitt gni niokoy déffé ak dikko wakhé noulén nékh wayé mom deh wakhoul lolou...Dieureudieuf Oustaz
@lamineseck69182 жыл бұрын
Barakallahou fikum Al Oustaz Oumar Sall 💖(H.A) c'est une vérité absolue
@seydinaousmanethiam8742 жыл бұрын
Dieuredieuff serigne touba sunu yakar taîy ak euleuk
@moiiza10sidibe302 жыл бұрын
Stupid yallah lagnou yakar
@aicharassoul26412 жыл бұрын
Oustaz nioungui seu guinaw inch'Allah boula kene téré wakh DEUG bi Dîné yalla dji kene momouko Intimidations yi amoul ndieurigne té inchaa'Allah dou djal 💪
@moussadabo63182 жыл бұрын
Mashallah ya oustaz yalnala yalla bolë tchi ngimouy samaal bopam arraala bopam
@mamefamanefertitithiam57432 жыл бұрын
Ma sha Allah Oustaz Yallah nala Yallah mèye goudeu fane ak wer Deugueu rek moye deugueu
@awaba86142 жыл бұрын
Machallah oustaz sougnou borome rekk mo diaraa magal☝️🙏
@dffb69992 жыл бұрын
Boul am looy ragal sama oustaz ndam rék inchA’Allah ❤️🙏🏽
@kartoumsakho67722 жыл бұрын
Sénégalais mo seytané Oustaz continue sur ce chemin
@morcisse262 жыл бұрын
Yaw khana do sénégalais ak say wadiour ga takhaw di wakh sénégalais seytanè la kholat lène sène boppou sama mbokkou sioulit yi
@mamadousow36522 жыл бұрын
Eg tes parents aussi en font partie d mm k toute ta lignée familiale.
@sunugaalguitv61252 жыл бұрын
Khana sa bay moy ibliss
@dembangom46592 жыл бұрын
Sa diobou ndaye yak oustaz
@soumayabdoulanne45942 жыл бұрын
@@dembangom4659 Yalla naniu Yalla diégeul 🤲🏾.
@fodesoumare86102 жыл бұрын
Yalla kassè môme rekk laniouy magal walahi qu’Allah (SW) nous accorde une belle fin ❤️
@matarthiam31592 жыл бұрын
Serigne touba wakhoul féneu magal léne ma dani Santal léne ma yalla si biss bi saayou nieuwé donc dou débat si yalla lagn wara Sante Keine menou gno weddi lo sougnou makk gnii kouléne santoul gnanal leine yalla bouléne tokk diléne wakh lou niaaaw nekouma Sénégal dé mais lifa am si tawfekh diameu ak diiiné guissou mako fénene té lepp grâce ak sougnou makk gni Yalna GNeup am diam🙏🙏
@mohamadsabaly18662 жыл бұрын
Ya fen yew fo dem fou kenen demoul shirk bokalé fila op legui fofou ga nek mousss ga guisss fofou nit nan man djoulite la wayé douma worr douma djouli wakhma foko guisss si adouna bi bamou d'Ath nak j te défi
@rappel41522 жыл бұрын
Wakho deug tawfikh afia yalla mokoy diokhé mag gni c est des humains comme tout le monde personne n'est indispensable la religion est au Sénégal depuis plus de 600ans ils n'ont aucun pouvoir té yalla mo yaye sante bayilen bokkalé bi.
@matarthiam31592 жыл бұрын
@@mohamadsabaly1866 tu me traite de menteur té Walaahi khamo meu mais baal nala yalna gnou yalla boolé baal🙏 je donnais juste mon opinion mais débat wouma défier wouma ak yaw
@elhadjibadji98762 жыл бұрын
masha'allah
@serignekhadimgueye74602 жыл бұрын
Jàjëf Faal Yaram Bi
@alzotechnique20002 жыл бұрын
As salmou aleykou les gens de daroul birr . c'est vous qui a le meilleur chaîne KZbin. Que Allah vous récompense sur le travail que vous fassiez. Merci
Machallah ya ouztage chaque jour magulay suivre yalla n'alla yalla fay
@adamasadji91072 жыл бұрын
Magal gui yallah ko mom serigne touba dafni kép kouy djoulitt su bess bi gneuwé gnou santéléko yallah si touki bi mu df si guédje Djangal ko si alqur’an ak ay xassida djokhési ay niam Donc magal gui yiw késsé mossi nék Wassalam 🙏🏾
@rasind29852 жыл бұрын
MachAllah ya Oustaz deugeu rek inchAllah 🙏🏾🙏🏾
@mawzolemang17032 жыл бұрын
Maneu Serigne Touba laay Magal 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@alhassandiakhate64472 жыл бұрын
ASSALAMOU aleykoum...in sha allah boul tite boul ragal..yallah rek mofi neek...boulen faté oustaz mame gor ndiaye si ay niane yallah guénéko fimou nék
@abdoundiaye6712 жыл бұрын
MERCI OUSTASS.TU AS TOUJOURS PROUVÉ QUE L'ISLAM EST SCIENTIFIQUE,TECHNIQUE,SPIRITUEL ET MORAL AVANT D'ETRE RELIGIEUX.TU AS TOUJOURS MIS LA LUMIERE SUR L'OBSCURANTISME.DONC SEUL ALLAH PEUT TE RETRIBUER POUR CETTE NOBLE MISSION.QUE NOTRE SEIGNEUR TE BENISSE ET TE LAISSE ENCORE LONGTEMPS DEVANT NOUS,POUR QUE L'ON PUISSE PROFITER ENCORE LONGTEMPS DE TES ENSEIGNEMENT.MERCI,MERCI,MERCI.
@eldamesssoguetv86032 жыл бұрын
Merci Serign touba ❤️🥰
@fatyndiaye98552 жыл бұрын
billay machalla yalna yalla bolé UMMAH BI baniou gueuna bolo amine🤲🏿😭🤲🏿
@lomatar37702 жыл бұрын
Yalla rek lagnou wara magal point 💓💓💓💓💓💓💓💓💓
@RockAlive02 жыл бұрын
On est 100% d'accord avec vous 👍🏽
@mamadouba77382 жыл бұрын
Merci beaucoup oustaz Long vie et santé à vous et votre famille djame rék oustaz
@tallambaye35692 жыл бұрын
Mâcha allah yàlla rekk moo Yayyo ñu magal ko waayé Cheikhoul khadim moom yalla lay magal à ce que je sache.
@sakholass42432 жыл бұрын
Qu’Allah vous accorde une très longue vie et une bonne santé
@sambacissetherealone51232 жыл бұрын
masha alla
@mouridoulahi20002 жыл бұрын
Omar sall yaw mii ténga dallou té dém diamou ji yallah té lidianty sa hayibi bopou. Mano wakh wakh ba diouñiu dém magal touba. Sokhorr rékk ak kiñian môla sonall ndeysaan. Wayé wallahi dinga sonnu..ndax.. koutéd ki néna إلي قادالله مالم يكن ولايكون أبدا للمكن$ ..وقال الله تعالى. لإنشكر تم لأزيدنكم...motakh ñiun mouridoulahi yii ça kaw rékk inchalah..
@matarthiam31592 жыл бұрын
Kou yalla baakhal kouko beuga bonal dangay sonou sugnu makk dji meritoo nagnou lénéne loudoul dileine sikeul yalna gnou yalla may magal ak diam🙏
@aladjidiaoune24212 жыл бұрын
Yalla nalléne yalla diubeul
@lassanalassana21852 жыл бұрын
Salam merci beaucoup oustaz pure vérité alhamdoulilah que Alla nous donne longue vie et beaucoup de santé
@izoumedia19172 жыл бұрын
Soutien totale mon cheikh Depuis Gambie 🇬🇲 que je vous suis
@amadoutoumbou48102 жыл бұрын
Assalamaleikoum. Mashallah oustaz Oumar Sall lérna... yalna laa Yallah aar. Qu'Allah veille sur vous et vous accorde sa protection et sa miséricorde. La vérité et la science anéantissent l'obscurantisme et l'ignorance. Fier de vous et de vos actions salvatrices.
@mohamedfirdaws2112 жыл бұрын
Salam Aleykoum. Vous allez bien j'espère, moi ça va Alhamdoulillah. Désolé de vous déranger, mais pouvez-vous traduire en français ce qu'a dit l'oustaz svp. Au plaisir de vous relire. Barakallahoufik
@lenoir95972 жыл бұрын
@@mohamedfirdaws211 il dit que c Dieu seul qu’on doit vénéré
@muhammadbachirdiop7660 Жыл бұрын
Masha’Allah 🙏🏾
@adjisene15972 жыл бұрын
Ma Shaa Allah 🤍 Yalna Yallah deugeureul taxaway bi
@iso24592 жыл бұрын
Oustaz Omar Sall qu'Allah vous préserve Amin 🤲. C'est malheureux de voir comment ces tarikhas qui sont sensés prêcher pour Allah Al Ahad, préfèrent mettre e en avant des serviteurs mortels d'Allah au point de laisser en suspens le Seigneur de l'Univers
@adjafatouthiaw20942 жыл бұрын
Salam niepp yamouniou aussi
@TheDogue52 жыл бұрын
Vous n'avez rien compris...biyilene soss.
@léminentAboubacar2 жыл бұрын
Basi yen nio niou li nguen former nekout tarikha tamit ? Ah wa yen am len sunu complexe waay
@mariecelinebendia98322 жыл бұрын
Merci Oustaz papa Oumar jtm je te souhaite longue vie ♥️♥️🙏🙏
@matymbayediagne34652 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba sounou yàkàr tay ak euleuk.
@layediaw21392 жыл бұрын
Mascha Allah ya oustaz Alkourane ak Sunnah rek 🤲🏿
@ramatoulayembengue52522 жыл бұрын
Ouztaz Diambar la MachaAllah dafa ame gnou la beugeu diahassé ak niit gni mais kou bakh gua MachaAllah niit yi beugeunagnoula ba paré MachaAllah
@oumiedarammeh88232 жыл бұрын
On est avec vs qu’ALLAH soit avc ns et ns protege amine yarabi ♥️♥️♥️
Macha Allah sama oustaz longue vie à vous qu Allah veille sur vous
@ibrahimakane83152 жыл бұрын
هاك مايمنع الإنسان رؤية الحقيقة بوضوح، التّعصب، البيئة، الفرق، الهوى، الكبر، الكُتب الّذي تعوّد قراءته، النظرة الدُونيّة لبعض النّاس، المعصية، إنّ الحقيقة نور ونور الله لايُهدى للعاصي
@morcisse262 жыл бұрын
Magal touba mom kèppou kouye djoulite warna ci contane…..biss la mo khamni bène diamou yalla yalla moy sante boromom ci xèweul yi mou ko dèfall
@papediouf69352 жыл бұрын
Ahmadu ya diouli guedj deh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mohamedba96542 жыл бұрын
Macha Allah oustas Oumar Sall 🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@soumayabdoulanne45942 жыл бұрын
Lissi doywaar rék moy nioniu ñuy diaamou aka maggal soudé liniu dégg si nittou Yalla yoyou machallah ñoom ñoy djeukkeu andak Oustaz si loumou wakh. Yalla na Yalla sakhal ñu si siraatal moustakhim 🤲🏾☝🏾 diazakallah ya Oustaz.
@abdallahmbye70112 жыл бұрын
May Allah preserve you Ya Oustaz❤️
@pesor223552 жыл бұрын
Machallah Oustaz waxtane bi amna sollo
@beugdiam36682 жыл бұрын
Barak'Allah fiikoum ya Oustaz
@anonyme12032 жыл бұрын
Que Dieu te garde et te protège seul la vérité compte on est de tout cœur avec toi. Merci pour tout ce que tu fais
@ousmanendiaye95112 жыл бұрын
Yalnallah yalla sam .fiert de vous
@Mbaye9042 жыл бұрын
Machallah Oustaz. Sénégal affaires tariha yi gnoussi beuri dagniy bokallé. Oustaz Oumar Sall wakhou yalla rék ley wakh.
@oumoukane92792 жыл бұрын
Machallah qu Allah ns préserve dans d bn chemin fière de vous oustaze
@fatoundiaye93292 жыл бұрын
Oustaz yalla rek mo mata magal bilahii ❤❤❤❤❤❤❤
@lomatar37702 жыл бұрын
Machalla Sama Oustaz ❣️❣️💓💓💓💓💓💓💕💔💔💔
@Khaliloulah8572 жыл бұрын
Barakallahoufikoum oustaz
@abdoulayetop50402 жыл бұрын
Lolou mnoul niakk si kouy wax si yonou Yallah ya des personnes mal intentionnées surtout Qu'Allah le tout puissant t'accorde une longue vie.
@senegal5592 жыл бұрын
Yalla nalén yalla may kholoub mou nge Serigne Touba yalla may magal thi natouyi mouko ték
@khadidiatoubarrysy24172 жыл бұрын
Maacha allah amna solo qu'allah vous protège contre les mauvais oeils amines