L' amour d'une mère en vers ses enfants est inestimable.
@yayodiallo14243 жыл бұрын
Bilahi ndeysane diguenté yaye ak dom dou Aÿ thiahane yaye beneu la loumou méti méti dou daw jamais elle supporte tout
@ndayecisse58453 жыл бұрын
RSSA tuoluyrrhfgwgko
@ndeyendiayendiaye10383 жыл бұрын
Vérité absolue wallakhi
@cissokhooumy13003 жыл бұрын
Machalah à vous li metina trop yalla na lene yalla takhawo
@ndeyefatoufall963 жыл бұрын
@@yayodiallo1424 aaQ
@vatimetousy80773 жыл бұрын
Elle mérite bouceaup d'aide et d'affection surtout c des enfants ❤😭🙏
@josephdia43543 жыл бұрын
Bilaye walaye
@sambatorino81152 жыл бұрын
thiotou ndayame yeni pa yi yala moguileni khare
@papaelhadjithiam77463 жыл бұрын
Ndeysan Elle est très brave Leur papa aussi, je sais exactement la cause de sa fugue mais c’est un acte très lache bilahi
@MrFayemanou3 жыл бұрын
Faut pas juger leur pere Faut savoir la cause
@jaimemamere59583 жыл бұрын
@@MrFayemanou malgré toutes causes waroul abandonné khaléi yi Il peut se séparer de sa femme mais pas de ses enfants c'est lache
@MrFayemanou3 жыл бұрын
@@jaimemamere5958 j croprend mais attendons de voir la reaction de leur pere dabord La vie nes pas facile parfois c tellement dur face a des situations😭😭😭😭😭😭😭😭
@annarb39623 жыл бұрын
@@MrFayemanou peut importe la cause fuire c’est très lâche en plus say dome nougnou meunti mel say dome lagn
@papaelhadjithiam77463 жыл бұрын
@@MrFayemanou j’ai pas jugé le papa, mais plutôt l’acte. Peu importe la situation qui pose, si on est incapable d’assumer nos responsabilité envers nos enfants, en quoi sert d’en faire.
@rokhayadione3 жыл бұрын
Kan mo meneu faye yaye ci aduna yalla nalla yalla takha wou yaye boye
@barasalihou17803 жыл бұрын
Allahou Akbar Yallah naa sa borom tahouwouleen,,té dolii niou soutoureu 🙏 barkepp Alhourane 😢
@ndiemendiaye99793 жыл бұрын
Amine y’a rabi
@salladiaw5433 жыл бұрын
Amine
@ndeyeboye203 жыл бұрын
Amine
@chicondiaye25153 жыл бұрын
Allahou akbar yalla moy bourr dii brome moy kholl louko nekh sii diam mou defff ko lii miitii n'a trop yall na lén yalla takhawo sii barkebb bromeTouba mai ken d'où yay boy soumété mome rekk guay guiss yall na niou yallah fayal sunu yayy yiii 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@barasalihou17803 жыл бұрын
Wallahi li kemanou sûnû borom Deugleuh 😢
@maimounasy68193 жыл бұрын
Pape Niang bilahi tay ningama djoylowé souma Amon Ay millions dinalako djokh nga djoxal mako yaye djou geun dji bilahi amna louma méti trop😭😭😭😭😭😭😭😭
@channel100113 жыл бұрын
Bilakhi pape mi nitou aldiana là
@astuguey38293 жыл бұрын
Non li dafa métty bilae pape yak Fadel loléne meune def léne kosi
@astouaidaraleye88343 жыл бұрын
Tieuy yalla, yalla naniou yalla dolli soutoura. Bilaye warnanio sante yalla boubakh alhamdoulilah. Yalla nallen yalla same té may len were si barké Seydina Mouhamed SAWS 🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Ndaysan bilay j'ai des larmes aux yeux yalna len yalla samb
@salladiaw5433 жыл бұрын
Amine
@videoislamic96193 жыл бұрын
Amine ya rabbi
@momodiallo89273 жыл бұрын
Guenel khaliss
@binetasarr94973 жыл бұрын
Alahou akbare thiey yalla nako yalla teguile natou bi
@fatyleye58473 жыл бұрын
Massa yaye Boye li rombouna méttite nassi niépp diapp té Yalla takh
@bintoudiop51463 жыл бұрын
Thieye yaye sou mété mom rék ngay guiss😭😭😭😭
@tijaneseck82493 жыл бұрын
Walahi jaime trop ma mere vous les femme dolenne morome yeneu niou geunne foufe
@seynaboutine78803 жыл бұрын
Ty
@sigambacke68083 жыл бұрын
Billahi yay kéne la
@jaimemamere59583 жыл бұрын
Je t'aime maman 😭❤
@Cheikhuna3 жыл бұрын
Lolou ame na bilay walay
@naboundiaye16693 жыл бұрын
Barki cheixou tidiane yaye sonou na bilahi yallanalen yalla fay sunu yaye yi amoulen morom 😭bilahi beugouma loudoul tèkki téral bepp domou adama bouko soxla
@tidadiouf27163 жыл бұрын
kéne dou yaye yalla nalene yalla may wérr ndeyesane
@marianeba66623 жыл бұрын
Koudoul may sa bopou loula Yalah may nga dieul sein papa kou boon laa linga def gnawna trop courage a toi sister Yalah nala Yalah takhawou 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@mamimbaye15323 жыл бұрын
Ah metina mais yalla ak dogalam j déteste les hommes d'aujourd'hui ils sont waye loumalen bageu wakh khepp ko bilaye
@mamimbaye15323 жыл бұрын
Guiss ga yaw s'en papa soumala lanalone darra wala ma guiss la d'où wakh sakh bilaye sama khole toye n'a lool alhamdoulila yalla are leen te sambeu leen
@fatouceesay5979 Жыл бұрын
Hale bou were rek problem la surtout bou febar
@seynaboudiongue81993 жыл бұрын
L'amour d'une mere ne s'éteint jamais
@mariem.djigo.83mariemdjigo263 жыл бұрын
C est votre commentaire qui m as fait pleuré
@mamediarafaye87512 жыл бұрын
Yalla nalén yalla wéral
@ndeyeaissatoudiatta80853 жыл бұрын
Massa massa 😭😭 ooh Allah vient en aide les Pauvres gens les malades les personnes démunis. Que votre bénédiction soit sur eux. Aminnnn
@kadidiacamara6513 жыл бұрын
Que dieu veille sur vous inchallah les enfants du paradi
@fatoudiop54563 жыл бұрын
Allahouma Akbar yala rék mo mane mo sagne yala nala yala maye kholou mougne YÀYE dou dawe dou bédi dina bâkhe inchallah
@lalionneasonuniversunivers15103 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭tay meunouma tei sama rongogn ...ay yalla warone n'a yoor ma meuner dieul gni en charge😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@awathiaw28873 жыл бұрын
Yalna lén yala délo tie sen sago et bon courage à leur maman
@kinepouye11133 жыл бұрын
Machahalla.la belle soeur yaw tamitt kou bakh gua
@nafidabo86613 жыл бұрын
Elle est brave machalla il ne faut pas baisser les bras Dieu est grand
@Naby_mousstapha3 жыл бұрын
ndeyessan 😭 yaye sou mété mome rek ngaye guis
@kalidoudiakahate33873 жыл бұрын
Hoo hooo metina trop bilay yayy moyy lepp. Yalla dina ko fayy
@maimounasy85603 жыл бұрын
Ndeyssane métina trop Lou diam bi ame rek santal yallah yaye kéne là yallah nako yallah safara
@dieynabadia85433 жыл бұрын
Bilay li métina j'ai les larmes aux yeux thiéy yaye diarama sounou yaye yi sou nieup bagné yaye moy nangou😢😢
@fatoundoyedieng59803 жыл бұрын
Bilay wakhatiko
@mamajaiteh3323 жыл бұрын
Wollahe yaa Allah 😢😢
@gooryallagooryalla94443 жыл бұрын
Yalla moye bour di borome yalla naléne yalla taxawou barkep alkhourane
@gooryallagooryalla94443 жыл бұрын
Papa dji dafa daw wala dafa wouti doolé bou dée dafa daw dh dina xeuye tok di dioye ta dou guiss kén kouko nakh
@mansourngom75183 жыл бұрын
Yalna léen yalla takhawou mayléen wéer ba niou déllou sén sago
@moustaphagueye25203 жыл бұрын
yalna lene yalla takhawou Fadela ak pape ay diambari Senegal 🇸🇳 lanou
@adamandiayeseck78533 жыл бұрын
Dama dioy ba sonu bilahi 😭😭😭yalla yamana setane😭😭😭li dafa meti bilahi
@ndeyendiayendiaye10383 жыл бұрын
Je trouve même pas les mots
@ndeyesalioundiaye31193 жыл бұрын
Yalnaniou yarabi may ay milliards youniouy dimbaliwatee ndeyssan 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭 😭
@cinevoxplus3 жыл бұрын
diaam bounè so heuyé Warngaa sant Yalla 🙏🏾
@maremendiaye57243 жыл бұрын
Bilay yalla mo yemee dee😭
@safietoubah74773 жыл бұрын
Li metina trop yaye kene mounou ko faye da ma ko doundou motax ma kham bi metite bene dome bou gorr rek la ame mou accident bou meti pape ji deme bayi ko ak mane
@maremendiaye57243 жыл бұрын
@@safietoubah7477 massa yalla nala may holou mougne
@djatoumane78313 жыл бұрын
Diokhelèniou tourrou dieukeur bi ,ammou niouu khaliss bouniou diokhè franchement mais mounènn weurr deim dokhan dèyaimm,
@matyndiayeduval72633 жыл бұрын
Ma belle ça c'est pas une solution yalla bakhna inchaala tout ira bien
@ndeye72723 жыл бұрын
🤣🤣🤣
@SAYANDECAPILLAIRECLUB3 жыл бұрын
😂😂😂 iow soxnassi xana dagay karaté pour dorr goor
@ramatabakhoum27253 жыл бұрын
🙏🙏🙏walay tu as raison
@ndeyendiayendiaye10383 жыл бұрын
Mdrrr jais beaucoup pleuré mais tu ma fait rire
@mberryable3 жыл бұрын
It’s a blessing santal yalla man mi wakh ak yow amna thi waye sant yalla rek n’alla sunu borom takhawou Bou bakh amine
@amydiallodiouf14963 жыл бұрын
yalla nalén yalla takhawou ci barké seydina mouhamed (saw)
@aminatamaiga31713 жыл бұрын
Kén dou yaye yalna yalla fayal niou sounou yaye yii té are papa yi ak mbokou yeup
@anitagomis25373 жыл бұрын
Thiey gorrr quelques irresponsabilité venant de leur papa..... courage femme forte
@awamboup37193 жыл бұрын
Métina trop way xawma saxe mane loumay wax mane li yalla rék moko meune😭😭😭
@khadimdieng55753 жыл бұрын
na police dieuli senn papeu domeram laa rek
@fadoumbaba3453 жыл бұрын
Ce triste bilahi yaye amoul morom yallah nalene yalla diapalè
@dioumostapha91762 жыл бұрын
😭😭😭😭 jai connai cette femme il habit pres de nos village😭😭😭😭😭 mais dieu est grand
@TaphaFaye-v5c Жыл бұрын
Kouyéyou yare na sant yalla ❤😢😢
@awafall68442 жыл бұрын
Ndeysane dioye n'a ba sone sama yaye dathieu n'a lèpe ndakh nioune fèkèwo Dara repose en paix maman 😭😭😭😭😭
@aminatamaiga31713 жыл бұрын
Yalna yalla sameu lén are léne soutoural léne may lén wergu yarame barki yonent bi 😥😥😭
@annadiallo2763 жыл бұрын
Yallnalen yalla taxawou thi Barker Mohammed psl 🤲
@senegalrek58053 жыл бұрын
Bala nga khamni adouna mo méti nga Magg ba ndiaboot 😭
@ndeyefatoukasse51803 жыл бұрын
Walahi😭
@mameboussondiaye95563 жыл бұрын
Bilaye 😭
@maguettecisse28563 жыл бұрын
Biliy adouna mon meti tek
@aminatandiaye92613 жыл бұрын
Demal ci thierno moule Sow yalnala yalla diapale gni Solen khole nga kham ne gni Ay seytane rek gni len doudou ndeysan metina trop😭😭
@ibrahimasy52003 жыл бұрын
Thierno Moulé khamoul dara
@mamanmargotchimerediop97843 жыл бұрын
ndeyssan li mettina trop billea yallah naléne yallah takhawou inchallah Courage à vous 😭😢😢❤❤
@mamidiouf35503 жыл бұрын
yalla na yalla oyofal leup si barké seydina mouhamed
J'ai plus de larmes thieye li yalna souniou borom SWT takhawou yirlene samelene si barke seydina Mohamed Saw allahouma Amin 😭😭
@Matar-i6d5 ай бұрын
Yalla na yalla takhawou khalé yi 😢
@amandandiaye41963 жыл бұрын
Maneu léneu rek moma métti dagni bayi ba changema am mout doga nieuw di oute lay la majeur parti goorou senegal amougniou yeurmadé sou métté rek gniou daw sim
@emiliesarr24773 жыл бұрын
Ana ministère de la famille. Ki mo diara takhawou
@sigambacke68083 жыл бұрын
Métina dh bilay yay moy leep sou mété mom rék ngay guis yalla naléne yalla tahahou
@ndeyendiayendiaye10383 жыл бұрын
Papa sou nekher reke mou toke sou meter mou dawe
@thiorojoop40193 жыл бұрын
Yaye rek modoul dem bayi domam ''Douma nek ak kouy diour ay dof'' leur papa est mauvais et irresponsable Yalnalene yalla takhawou🙏
@mbayangdiouf55913 жыл бұрын
Koune gor bakhna bilaye sa baya tak li meti na tour
@ndeyedeguenendao11673 жыл бұрын
Aziz Ndiaye wakhal si li
@senegalrek58053 жыл бұрын
Goor dafay responsable ame yeurmandé si djiguén adouna dou keur 😭
@awagueye32353 жыл бұрын
Bilakhi
@oumidiallo50743 жыл бұрын
Amna goooor gni khamni dafa waaar di nekhe rek te yalla moye tegue nattou
@Cheikhuna3 жыл бұрын
Bilay walay 😭😭😭😭
@khadyfakadiaw16283 жыл бұрын
Yallanaléne yalla Faye séne khole si barké Mohamed
@sofiexkane62233 жыл бұрын
Yalla nalla yalla tèguil natou bii yalla may lèn wér inchallah🙏🏾🙏🏾
@MusicManiaJunior3 жыл бұрын
Ah li metina si khol... Yalla nallen yalla dello si sen sage... Si barki Segne fallou
@abdoukhadrecisse7710 Жыл бұрын
nous vous remercions on vous dire du courage mes grand frère 🙏🙏🙏
@ndeyeboye203 жыл бұрын
Dome yi fonke lène sèn yaye wa Dakar buzz sène liguèy rafetna pape yalna la yalla faye sa khol
@abdoukhadrecisse7710 Жыл бұрын
wallahi pour Mane yéneu eupou ndiarigne état bi thie diamou yalla yii yalna ngénne yok ba yeuk ke leppou di yalla eil cassé
@mamegayekane38983 жыл бұрын
Thiaye yalla adona bi mettina Ani brome khalise yi
@hadjidiop43253 жыл бұрын
Ndeyssane yalla na yalla feugeu sen bopp
@aidambengue56963 жыл бұрын
C Vraiment triste mais machalla ses enfants sont tres propre Elle s'occupe bien d'eux
@fatythioye68663 жыл бұрын
Allahou akhbar yallah rekk kho moun
@dialloben71603 жыл бұрын
Baye baxna way yaye 😢😢😢😢ndiourel dafa forr yalna yalla delosi sen xéll Amine
@khadycamara5773 жыл бұрын
Thiey yalla souniou moy borom di Karim yalla na léne yalla takhawou
@ndiobayefall63823 жыл бұрын
Alouhou akbar yalla nalén yalla sameu🤲
@abylayediop48013 жыл бұрын
Sou yalla dogalone tay ma am kèn waxatouko li mètina ms yallnalène yalla doli soutoureu ak wer
@maremelaye69493 жыл бұрын
Bilaye wallay mètina loo 😭😭😭😭me yalla bakhna
@daoudakonte87723 жыл бұрын
Thieuy yalla mo mana tégué Nattou deh yallnalene yalla ar thii barké yonéntbii
@ramakeita82313 жыл бұрын
Yalla xamnani souma téké si football insahalla je vais aider ses gens la Allah is one ☝🏽
@fatoumbackesylla44813 жыл бұрын
😢😢😢😭😭😭😭😭😭😢fadel moma dioy lo ndeysan xol bou rafet là yoor kholal nimouy kholée famme bi beuti yeureumnde lakoy xol yallah nalen yalla fay
@bathiefam23073 жыл бұрын
Saque jour yaye wanné bobam thi ndiabott tame nguirr yalla fonk léne souniou yaye kéne dou niome
@fatoumattasowe22018 ай бұрын
Pape, dugal len ecole
@anitagomis25373 жыл бұрын
Séne liguey raffetena bilay yalla dinaléne féyy
@takkouligueye75433 жыл бұрын
Salam Pape ! Lî métti na trope ! Yalla na lène Yalla safara ! Té Yalla yombalal lène ndimbal ! Amîne yâ Rabbî.