En écoutant la dame et les jeunes, on se rend compte à quel point le Sénégal est malheureusement devenu un pays de fou. Un vrai hôpital de malade mentaux a ciel ouvert. 😳
@dieynabakane67664 жыл бұрын
C domg et malheureux
@saliouramosjr20544 жыл бұрын
Këpp kou beugue sa yaye beusseul j’aime 👍🏽 bonne fête au femmes 😍 yalla na yalla yeureum kou jiguënne ki🙏🏽
@abdoulkarimouedraogo31154 жыл бұрын
C'est une leçon à toutes les filles du monde entier Repose en paix mariam diagne😭😭😭😭😭
@enfantbenidedieu24574 жыл бұрын
Je suis vraiment désolé pour la fille, mais leçon aussi a les autres filles si tu n'aime pas quelqu'un ne bénéficie rien de lui ...
@abdoukhadrediouf59194 жыл бұрын
Enfant Béni de dieu c sa la verité
@elisabethdiatta60674 жыл бұрын
Tu as tout dit
@negrandfondamental4454 жыл бұрын
Preuves qu'il l'envoyait de l'argent ?? Assane devait au préalable montrer ses preuves avant de passer à l'acte *d'homicide volontaire* ( Man Lolou la gueum dé) Sinon le reste ne m'est que du lard et du cochon...[ Je ne me dit rien ces témoignages futiles]
@aramewade17174 жыл бұрын
Rien ne justifie le meurtre preuve diokhe na 3million dangako ameu
@toubandiaye95194 жыл бұрын
Qu'il jouit ou non de toutes ses capacités mentales il a tué un être humain et à défaut d'être tué en retour, il sera jugé et condamné de la plus lourde des peines. Choqué d'entendre cette famille parler des visites de la fille chez eux. RIP Mareme que le Tout Puissant t'accueil dans son Céleste Paradis. Amen 🙏
@beatricesy79194 жыл бұрын
Bissou pénthieu dina métti 🙏🏾
@TheMegamusa4 жыл бұрын
Une mère n'abandonne jamais son fils même s'il est le plus grand criminel au monde. RIP sister Marieme que firdawsi soit ta dernière demeure Bonne fête a nos maman et merci pour votre amour indéfectible envers vos enfants.
@salioundiaye64554 жыл бұрын
Mareme yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana kou raye nite mano ame deugue dakh bakane mo guene fore wayé khaléyi dieguéne yi bayiléne di dieule khalissou gore té beugolene ko
@ndeyekhadykane40504 жыл бұрын
Doyena ware
@mariediopndao85434 жыл бұрын
Saliou Ndiaye lolou moy deug nak
@aidandiaye44034 жыл бұрын
Dugue rej gua wax les filles aussi sont pas innocentes amnagne fitt beugue naniou xaliss bou yomb
@awadiopboye6904 жыл бұрын
Désolé mais c’est pas une excuse pour prendre la vie d’une personne même des millliards n’en vaut pas la peine
@salioundiaye66974 жыл бұрын
Khalei you djiguèn yi dagno beug khaliss lol mais qu’elle repose en paix
@kazukutaonlydesign66454 жыл бұрын
Rien ne justifie un meurtre...Mais j'imagine la colère qui rongeait ce gars...
@yayadiame62744 жыл бұрын
il est important d'être prudent en faisant vos commentaires
@delfatah73254 жыл бұрын
fala beugone nieuw deh mane seen histoire dafmeu moudiei diaxal do xam bane coté ngay nekk
@binettediallo95774 жыл бұрын
Del Fatah j ne pense pas qu’il ai de coté rien ne justifie un meurtre absolument rien
@binettediallo95774 жыл бұрын
En tt cas gni nek di coté du gars yeup kougn si né rayy na nitt ma geum ko
@delfatah73254 жыл бұрын
@@binettediallo9577 Je suis parfaitement d'accord avec toi ray mom moy lou wara lou moudiei am franchement lolou derniere option la waroul sakh nieuw sa bopp mais xamo peut etre dafko neugone diamm rek ndakh afa am louko metti ...mais pourquoi ma wakh li xamnga lane leu iOe do guiss doff nga demm ba yayaym nila weroul chaque jour mou dakk leu keureum ngay continuer di gueine ak mom nespa. Pire bo degloo bou baakh dafa melni complot entre mère et fille pour lekk xalissam aussi dafko xawa nirou. waxoua nak lolou mo am naa leer juste je me dis que nirou nako d'apres sama xalate. Mais ray nit mom niou ray la rek
@diopndeyendoumbe61584 жыл бұрын
@@binettediallo9577 bilay walay wohale dè
@abdoulahindiaye81234 жыл бұрын
Yalla rek Mo xam mom rek mo mana attter diam gni ! Natou nak dafay dall kouner yalla na yalla yeureum Marème Diagne xareko aldiana tai djiegualll assane 🙏🏿
@nogayelo85604 жыл бұрын
Vous n'avez rien à dire, parceque rien ne justifie un meurtre....
@toubagueye22784 жыл бұрын
Nogaye Lo p’´
@isseulaye73324 жыл бұрын
Vraiment walay ont tué comme si nous étions des poulets des salles assassins et pour justifiés sa il dise que le gas est fou
@bayesalioudiagne15184 жыл бұрын
Doy nawar torop mé yalla na ko yalla yuerueme si barké khasidayi amine
@khitmatvtoubadmarnan78704 жыл бұрын
assane lougn manawakh moye nitt kou bonne la meme boufeke na guelem la wone waroukou wone raye ndakh bakane dafa for doufoul djoune diapoko mais police khamane dakoy menace wartona khar bame koy ray
@amadoudiallo29814 жыл бұрын
Deugeula bakane forna me tmt mareme Ken demoul mou dess dah dama diap ni nit soko beugoul rek boul lal haliss ba dah gneup bocougnou Yam repos en paix mareme
@gamousacisse93064 жыл бұрын
@@amadoudiallo2981 Lou lerr gua wax
@khitmatvtoubadmarnan78704 жыл бұрын
@@amadoudiallo2981 mais sawaye mome moko done maye khaliss bi ta nitt yaguana ab guelem khaliss ta moudjouko tak lolou diarale raye nitt
@fatoucamara23734 жыл бұрын
@@khitmatvtoubadmarnan7870 franchement parle
@khitmatvtoubadmarnan78704 жыл бұрын
@@fatoucamara2373 bilahi li mome defma metti trop ki khaliss rk la baguone ndakh ko beug deug doko raye sourtou djiguene ta police dafa setane trop menace nitt kou kaye def dane la wara teudj mais kene waroula bayi guaye warelou baye reagir lou niaw meme bouka amalone khaliss waroule raye yonne amna
@Fallahmed28084 жыл бұрын
Ray mome meune na gnak. Lane moy khaliss . Yalla nagnou yalla mousseul di djiguéne ak khaliss. Seytaanè barina doolè doolè bo khamni yalla nagnou ci yalla mousseul.
4 жыл бұрын
Yalla na yalla yeureum mareme jigeen gni nagn bayi di nakh goor gni
@hadjimor98444 жыл бұрын
Ni la fimille de la fille ni celle du présumé meurtrier,ni son mari et ses proches;ni nous qui commentons kén xamoul kou togne way dawliji yobuna secret bi biir bameel;kiffi dess tam waxam manoci sukkandiku ndax ben lay pakk la.Yalla borom bi mom rk kessé momana leeral li xew entre deug deug ci ceen diganté. Leggui nak commentaire nio des counné ak sa xalat ....Ben famille du nangou sa dome togne kuné day wax nimuko arranger baa faw. yalla rk mo xam. Allahuma ifirlaha warhamha.!
@khadjidiadiakite34454 жыл бұрын
Repose en paix jeune fille 😢☝
@assanembaye60734 жыл бұрын
Péne de mort dafawara am ndakh ki dom3ramela daniowara ray ndéyéme
@bmkiller26174 жыл бұрын
@@assanembaye6073 ki nenenhie la werul ngani domaram la yaye kan baye juger qui que ce soit..té natou ci kou nékeu laye tegu
@srgnfalloundiaye83224 жыл бұрын
Djiguén gni ngir yalla nani xol gnini beuguel tél wayé koula dokhan rék nga accepté té baxna tanguén bayi koulén noboul ba paré di lék xalisam lolou riba té yalla dalén siy wér
@daoudabadiane3924 жыл бұрын
Yaw doul
@yacinewade1394 жыл бұрын
@@daoudabadiane392 😂😂😂😂😂
@makhoualyendiaye3244 жыл бұрын
Srgn Fallou Ndiaye lolou mom dou yon wayé rayy tamit c tro
@seckmoustapha77234 жыл бұрын
Yaw yayou assane ko mana fenga assane dara dalouko
@fatoumataba87904 жыл бұрын
Arrêter vos maline un fou ki entame des relations jusqu'à envoyer l'argent non pitié pour le Sénégal
@khadysow30964 жыл бұрын
Vraiment
@bmkiller26174 жыл бұрын
On parle d'un fou en tant que tel..Mane je connais un proche qui est comme ça mofi dakoneu djangeu mais wéroul..khana djaroul nhioulay expliquer ay details..
@awakonate7974 жыл бұрын
Bcp de gens aire dans espace mais en réalité il son pas normaux
@sokhnambaye89494 жыл бұрын
Lou lérr kou ray rk gnouné wétoul c ds massonge
@baramata77764 жыл бұрын
Ah vraiment
@bayefall33544 жыл бұрын
Mareme yalla nako yalla khare ALDIANA th yene Khaley djiguene gni ngene may tou dieul khaliss gor th bego leneko
@ballasta1404 жыл бұрын
Respectez la mémoire de la fille,qu'elle famille irresponsable dire que leur enfant est fou
@beaublack31324 жыл бұрын
Qu'Allah veille sur nous, nous protège, nous éduque et nous donne une fin heureuse.
@PAUVRE-DOU-NELLAW4 жыл бұрын
En tout cas yallah réka xam man mom talatuma jugé bén doomu aduna rip.
@diakherndiaye15844 жыл бұрын
Bilay kuné sa bos doyna pask bu yagé ga am si bacar yi
@FascinatingMya4 жыл бұрын
deug rek nga wah
@rakhouguedjii15064 жыл бұрын
ray kay amoul juger ray si bopam kouko def nonou lagnou la wara def rek ray rekk
@diabintou21524 жыл бұрын
Kou déi yaa déi rek mais nitt yi mom dougnou change yeenangui degue mère bi mourou kanam bi nena newon nako djiguene d'où fekki goor .........non amatina louma metti trop thi Sama khôl te mounoumasi dara 😢😢paix a son âme
@omarsylla49274 жыл бұрын
Sénégal 🇸🇳 Boudon Kou Ray nitt niou Ray ndayam batay djikhna lii dafa ndayi yompou 😠😠😠😠
@dashleeleely37234 жыл бұрын
Wa Mereme tamit loumou guiss thi Assane ba gune akh mom en tout paie à âme 🙏🏼
@aliimakebe31144 жыл бұрын
J'ai l'impression qu'ils sont entrain de prôner la folie pour lui éviter la prison cé trop facile ki dofoul djiné djapouko
@christinediatta8934 жыл бұрын
Meusoul doff dagno yapp gniti rekk nane weroul
@misstchiptchip29634 жыл бұрын
Le gars n'est pas trop normal sa de voi rien que sur son visage... Des le debut moi je sais quil n'est pas normale....
@elisabethdiatta60674 жыл бұрын
Ça a toujours été comme ça on te cherche de faux papiers pour prouver ta folie et tu t’en sors facilement alors que tu étais conscient de ce que tu faisais
@fayfay32724 жыл бұрын
Fay
@fatoutop94244 жыл бұрын
Mane louma si diaxal moy kou déf niawtéf ba baré nou nane da doff
@momygueye18544 жыл бұрын
Ray na sama cousine nenagne weroul marieme niak nagne la😭😭
@youngbreezy63694 жыл бұрын
Momy Gueye ohh rip 😭😭😭
@awadiouf56814 жыл бұрын
Sorry momy gueye
@fatoudiaw55944 жыл бұрын
@@awadiouf5681 wer na dara diotouko topuleine ko bamou seuss bouleine ko bayi mou sedd
@mariamapatterson93834 жыл бұрын
Massa c dur même pour gnimou bokeloul dara
@mathioudiop44494 жыл бұрын
Yallah nako yallah yeureum ma belle c'est dur mais yallah bakhna
oumar baltimore mais djiguenou Sénégal na niou bayi mbaran so beugul nit boul beugue khalisam
@shabarry53744 жыл бұрын
@@savoir-bu2tr je suis d'accord avec toi
@hametahmedsalem56314 жыл бұрын
oumar baltimore le plus grand problème vient des femmes elles mêmes. C’est dommage ce qui est arrivé.
@zalezale89464 жыл бұрын
Au final la douleur de deux mères... la perte d une vie... On ne juge pas les parents des deux familles autant victimes. DANS LE SÉNÉGAL d'aujourd'hui où sont passés les mots : YARR ET TERRANGA...? Darray Kocc et leurs éducation nous manque! C'est triste mais je ne reconnais plus mon pays🙏🏾😞
@pikineicotaf29734 жыл бұрын
Djiguene gni tmt nagne bayi di lekk khalliss kouniou bougoul ake Di trahir gor gni djiguene la dh mai tmt trahison dafa meti te gor soko trahir rê meune nala Ray wala mou kharou ndakh wor baxoul Pr mareme yalla nako yalla yeureume te khare KO Aldiana te yekheniou
@oumardanieladams75864 жыл бұрын
On ne comprend plus ce ki se passe dans ce pays.c'est incroyable.
@aissatousall26914 жыл бұрын
Man Dama diomi drettti di tour com pas possible
@oumardanieladams75864 жыл бұрын
@@aissatousall2691 en tt cas sokhnaci,li lou diara séet la.niane YALLA MOUSSEUL niou ci seytané rek.
@mouhamedkhalifagueye84114 жыл бұрын
Yarléne séne dome yi. Kou Goor ki amoul kilifeu kou djiguéne ki amoul kilifeu. Assane dara dalouko loudoul khamadi ak réw. Mareme mome dafa teuh.. Yalnako Yale yeureum ta kharé ko Aldiana.. Méttina trope
@moustaphadjite76434 жыл бұрын
Lou yalla kham doyna ay niane rék la sokhla famné yall nako yalla yeureum barké mame saliou👐👐
@mamydiol75874 жыл бұрын
😢😢li metina deh bilahi rayy rek surtou djigenn
@mansourdiop34244 жыл бұрын
Rip mariéme repose en paix justice soit fait
@samaypapier82794 жыл бұрын
Moytouléne Xaliss Use you mind self-control
@gamousacisse93064 жыл бұрын
Bayiléne narfekeu bi oe assane Lou guel bi lekeu khalissam te marier woul ak môme lolou moka méti Deléne wax deug té bayi faralaté bi Lane motakh guel bi waxouko beugoumala mo gueune mouy lekeu khalissam Diam mo geuneu aye Paix à son âme
@bathiesamba73794 жыл бұрын
Le monsieur il n'a rien il faut la emprisonné a vie.je lance un message solonel a toutes les filles fait beaucoup attention
@sambaly97254 жыл бұрын
Ah wey il n'est pas fou cmt il peut quitter le pays pour aller travailler à l'extérieur gni da gnouy gnake derou fille bi rek pour protéger le meurtrier
@monbeauvillage77514 жыл бұрын
Dans tous les cas s'il a de l'argent à envoyé il n'a qu'à envoyer ça à ses parents
@mameyakharadiarra1584 жыл бұрын
Omar Sokhna vraiment pourquoi loutax neub aussi sene kanam ce qui m’énerve s’il y’a un meurtre niouné dafa dof en plus di liguey di envoyer khaliss kou djiguene bi vraiment mère yi douniou wakh deugue jamais
@mamediarrafall63934 жыл бұрын
C tout
@blgunjourblgtjr42554 жыл бұрын
J'suis d'accord avec toi lo khame si gnake fouleu
@baramata77764 жыл бұрын
Bien dit
@inocentdf4officiel2224 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureume té kharé ko aldianna 🙏🙏🙏
@miya71904 жыл бұрын
Beug khalise rek moléne yobier lie yeup mé yalla na ko yalla yereume té kharé ko aldinna
@mamysalwa33644 жыл бұрын
Vraiment nioune djiguene yi tamite danion wara daw yeneyi bagna top beuge khaliis gui
@soukeynayague41134 жыл бұрын
Ayy wayy li dh metiii nama basii kanamou yalla😭😭xaliss dh diaroul liii 😭wayé dh yalla naka yalla yeureum sii barké Mohamed🙏😭😭
@alythiam19744 жыл бұрын
C'est tellement triste et déplorable vraiment. Dans la vie à chaque situation, il faut privilégier la médiation. Un conseil les filles, je vous exhorte à apprendre des cours d'auto-defense pour votre sécurité
@lasenegalaisembaye90444 жыл бұрын
Wawwww quel manque de respect de la part de ces femmes en plus elles osent blanchir leur fils
@millimimi82614 жыл бұрын
Vraiment
@nitadiouf88184 жыл бұрын
Billahi sen dôme bou defone Lou bakh kone dou gnou moure sen kanam yi
@mariediop66114 жыл бұрын
Manque de respect?! Il n'y a rien à mon avis qui indique qu'elles essaient de l'innoncenter. Bien au contraire
@gop76044 жыл бұрын
@@mariediop6611 Bien dit! Elles sont franches et impartiales vraiment
@aichalaye57024 жыл бұрын
Métina yalna KO yalla yeureum 😢😢😢 té sameu bép mindéf çi gnawtéf yi
@AmanaRassoul-qj9dh11 ай бұрын
Amine yarabi😢😢
@jackbueur40894 жыл бұрын
Wa Assane foumou démone bay gneuw Pourkoi Assane envoyait de l'argent à Mariéme ? Comme Assane est un fou pourkoi Mariéme accepte de sortir avec un fou? Rip Mariéme Assane yalla nalla yalla défal soutoura ak wérr
@diakherndiaye15844 жыл бұрын
Maroc dé lanu wah nonu ba tok t ni werul fi ba maroc
@fatoudembathioune46984 жыл бұрын
Jack Bueur jak assane dofful khol dou aum bagnou kay beuss nitt ki beug l dila jokh alalame dekete beugoko mou marié mom kou jiguene kii apres raynako mou jekh ay gnoune jiguene gni nagnou doyllou
@mbackembaye5804 жыл бұрын
En tout cas lougena
@kingvon35784 жыл бұрын
@@fatoudembathioune4698 billahi Lo lerr ga wakh nitki soka bagol waro lek allallam donte assane warol raye
@mortallagueye89704 жыл бұрын
Yene aye na fekh guene nite bouye guen ak copiname dikou envoyer khalis nio takh kou gani nala faye linga kou ma yone
@wadabeye3064 жыл бұрын
Respect pour la defente mere
@oulimatasy12134 жыл бұрын
Metina lol...😭DJIGENE warna khôl si kimouy dougou.xaliss bi xalisou lanla..rayon domou diambour ni🚫🚫🚫🚫
@yayadiame62744 жыл бұрын
Bien sûr après xaliss déye terminé
@sagnasagna17434 жыл бұрын
Les hommes aiment de belles femmes sans réfléchir et les femmes aiment les Richard.la vie est éphémère restons digne.ns devons apprendre à s'aimer pour ce que ns sommes .
@omarndiaye3629 Жыл бұрын
Repose en paix 😭
@evalopy4 жыл бұрын
Assane mi key wéroul li taxx na mou rey niit..waay gnoun itam jiguene yi waar neign kholaate sunu boop gnou khôl bou baax gnou gni dieuflantél ndakh dou gneup legnii nakh mou djig gnou
@diopfaya34714 жыл бұрын
Allahou akbar bilahi wakh ga deug,.
@delfatah73254 жыл бұрын
Wakh nga lou amm solo té diara bayi xel
@mbayembaye21734 жыл бұрын
Eva lopy mane wakhou assane wéroul lay bagña dégue dofoul djiné diapouko
@thiatsow64554 жыл бұрын
Exactement
@assanesane35964 жыл бұрын
Nah modoul yone pourquoi nah DEUG pour laneleu
@shalimar111004 жыл бұрын
Rien ne justifie un meurtre. Faut appeler un chat par un chat. Doffoul j'en doute c'est trop facile
@aramewade17174 жыл бұрын
La famille du gars war guen rouss wakhou khaliss !tilimal deh wou diambour
@ndeyegueye9444 жыл бұрын
No Sénégal mo nekh rayy nitt na wéroul tamouy déme voyage yéne mére yii yéna wéroul yéne gniy wakh lou niaw sii maréme fila beutt yame
@abdourahimkanetouba28154 жыл бұрын
Mane dé sama yone nékousi
@ibrahimabadji36174 жыл бұрын
Abdou rahim Kane touba bien dit grand
@mameyakharadiarra1584 жыл бұрын
Vraiment vous nous énervez comment un fou peut travailler et envoyer de l’argent gni dagno yabatei Assane mome méritewoul prison daniouko wara ray ce qu’il mérite en plus Mère bi elle m’énerve
@bichambaye62844 жыл бұрын
Paix à son âme 🙏🏿🙏🏿🙏🏿trop triste 😔
@zakariacamara39304 жыл бұрын
Mei problème bi moy pk mariem Marie di garder xaliss sou Assane tei en plus mogui nek si sey
@BadaDieye-yq1fj6 ай бұрын
Paix à son âme 😭ms prene une leçon bayi lén léku kolén beugoul aussi c à cause de nous way
@savoir-bu2tr4 жыл бұрын
bonsoir les amis djiguenou Sénégal na niou bayi mbarane gôre soko beugoul boul beugue khalisam
@awayelthiam88thiam344 жыл бұрын
Repose en paix mariéme diagne
@josephevbuomwan43904 жыл бұрын
Assane wéroul wakh la , kou wéroul di na diougué voyage Di ladji si khalissam Ray domou diambour ba paré nane wéroul da nio wara bayi cas yi boufi amé rek famille meurtrier bi nane dafa dof genre c injuste nitt doko timm Ray ak sang froid juste pour ds kestion d'argent danio wara def li Mame Abdou Aziz Sy Dabakh wakh kou rayy niou rayy kou sathi niou dague sa lokho , on en a marre de voir les femmes se faire torturée, violée ou mm tuées 😤😤😭
@Evishop23804 жыл бұрын
Fi la beut yammm ray nit técksi nane wéroul pourquoi pas interné woléneko puisk il est fou ki dé rek mo niack mais tamitt hallé you djiguéne bayiléne di leck halissou nitt kou guéne beugoul
@awathiam82794 жыл бұрын
Ay hypothèse la rek pour essayer de ne pas le condamner
@tout19584 жыл бұрын
Wax nga deugeu djigene yi xalis rek
@FascinatingMya4 жыл бұрын
pourtant niom wahuniu fi dara lou niaw danio wah li niu ham rek
@abdoukhadrediouf59194 жыл бұрын
Awa Thiam soko défone yaw niou ray m tamitt . da nguén begueu lou yombeu
@mamysylla63844 жыл бұрын
Baylen Sénégal kou Ray rek niouné werol peine de mort lanioun wara appliquer mou diekh
@adamadione60274 жыл бұрын
Wouy fougnouy diem ban réew la gnou nékk 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@dembadioum18684 жыл бұрын
Yalnako bour yalla yeureum mais nak khaley you djiguene yi nio Wara.yam
@moussafall80604 жыл бұрын
Amine mai wakh nga deug my grand
@bangalysylla35964 жыл бұрын
Ça fait froid au dos elle mérite pas mais aussi c'est une leçon pour les autres filles vous les filles arrêtez di léki khaliss modou modou yi beaucoup des filles sont dans le même cas mais vous êtes avertis cela vous donnera de leçon paix à son âme
@mmsseye93914 жыл бұрын
Kou djiguen gui yalnako yalla yeureum... Wayé yayou khalei bou goor bi tamite amna louko metti
@mendesshasha10214 жыл бұрын
Yeine je vous demande nakh lernalen ni mareme da lakk khalissou assane. Bane preuve ngen ssi ame? Sénégal juger sans savoir s'en djikko la. Problème sou amei dagueni analyser . Assane dem maroc mm po 1ans beug feh âme 3million400 si ko khamni ambulant ngaffa. Balla ma dèh niouni assane weroul. Pfff weroul tè migui dem Maroc Di nieuw.
@falloundiouck91584 жыл бұрын
Méttina ci mbokou ki gnou raye ak mboki ki raye Yalla nako khaaré Al djana
@serignesaliouniang42274 жыл бұрын
Il faut arrêter nak ki dagnko wara rey goor yi ngir yalla yeureum lén djiguén yi djiguén amoul dolé pour défendre bopam ngén topou lén di rey rek ngir yalla yeureum lénlén
@deugrek93414 жыл бұрын
Walay nioune amouniou doler t gor gnignou wara défendre niniouy newal doler diniou Ray 😪
@fsnyesgirl77154 жыл бұрын
@@deugrek9341 kone wero ak art martiaux yi fi nekk daniouy défendre beu défendre wa deuk bi
Bilahi gni amougnou yermandé Dara 😢😥😥😢 kou New dolé rék nguen koy torokhal
@serignesaliouniang42274 жыл бұрын
@@aissatousarr3404 vraiment nak il est temps li diekh fi yeurmandé goor dako wara am si djihuén ndax amoul dolé pour défendre bopam
@soukaymboup23284 жыл бұрын
Mére dakayy fénn rék
@kourkopoulopoulo5204 жыл бұрын
Donc si je comprends bien le monsieur était en Europe et envoyer de l’argent à mareme et Mareme bouffait son argent et lui a demandé la dernière et elle l’a pas donné et il a passé à lacte ndeysane li metina
@fallndaw80624 жыл бұрын
Il était au maroc
@thiernoyoussoufdiallo90924 жыл бұрын
S8 sénégalais qui vie à l'étranger mais mon pays maintenant kholou de Lou fa sakh amatoumako ndakh genre yi c inacceptable ray ray boudoul diekh ou est l'état pour quoi pas des sanctions sévères Mais aussi mes soeurs ko beugoul boul ko fowé bay lek khalissam di défi lénéne gor yeup yemou niou mane dé somalekaler ay milliards aussi dou takh ma fate bakane mais nit yi yemou nou Yalla rek mo kham fim né kou nek si deug
@abdulkarimsow28844 жыл бұрын
Mais je ne comprends pas la fille elle était marié et enceinte non subhana Allah kelle repose en paix et que Dieu l'accueil dans son paradis
@Defunity4 жыл бұрын
Il faut éduquer vos enfants, khalé yu djiguen di takhawalou rek, yaw yayam daak nala ba sone, Rip Éduquez les enfants.
@laminefofana37724 жыл бұрын
Vraiment tu as bien dit
@fatoudembathioune46984 жыл бұрын
Def Unity Mersi bilay beugo niit ki di dieul alalam weroul kay comm el es mariée mougueuneu doff apres mou ray ko
@moracamara73024 жыл бұрын
Vrai
@aissatousoumare82744 жыл бұрын
Def Unity yow tu oses juger quelqu'un qu'on a tuer sans savoir les raisons mane daal diakhalgeine ma
@Defunity4 жыл бұрын
@@aissatousoumare8274 je ne juge personne et aucun motif ne justifie un crime. Je suis assez clair sur ce que j'ai dit, c'est une généralité. Naniou yaar sounou doom yi la wakh, khalé bou djiguen bou féki goor tout le temps dou yone tè mo nekk si sunu deuk bi. Et la mère du gars a bien noté que téré nako keuram bâ sone. J'ai vécu la même chose, une fille qui vient tout le temps chez nous a n'importe quelle heure et peut passer la journée entière à la maison, mère bi daak nako façon bouné keurgui, nioune on l'a traité de tous les noms mais n'empêche, elle continue de venir. J'ai bien dit : rien ne justifie un crime. Comprendra qui pourra.
@chaennegandoul3044 жыл бұрын
Wéroul lay bagna dégg mane
@losokhnambene58904 жыл бұрын
Kou Ray niou mo wara am
@amadouaidara10034 жыл бұрын
Ho triste nouvel assane un cool bro on été ici a Casablanca on partagé l mém maison vraiment assane tu devais pas faire adouna amoul solo
@khadia67994 жыл бұрын
Yalnako yalla yaram tanitniee goree yalla kham leppo
@maguettesene1834 жыл бұрын
Rien ne justifie de prendre la vie d une personne surtout une fille
@fansgimsofficiel48704 жыл бұрын
Khaaliss mom dafa diaroul ray nit walahi 😭😭
@mamysylla75954 жыл бұрын
Billay
@beugfallou65014 жыл бұрын
Mo guena wer dofol djiné diapouko pane tongalou ko ana dof ak beuganté 🤔
@ndoumbediop6524 жыл бұрын
Moma diakhal ana dof ak dokhane baye fayekou khaliss
@huncholoufa70504 жыл бұрын
Merci ❤️
@aichalaye57024 жыл бұрын
MoMA diaxal
@amet68004 жыл бұрын
En plus ak ndaw ci noumou rafété
@boromdarou87414 жыл бұрын
Ndawsi mo tonie 🤷♂️ok
@fallouwade22224 жыл бұрын
Arrêtez de dire kou raay nitt niounan dafa doff ça suffit ❌❌❌❌Justice pour Mariéme Diagne
@ndiathieoumou74164 жыл бұрын
Lolou d'où deugue baayi lene nite Dee nguene Di yak deram wala nguene Di protégé sene doome nguene Di wakhe weroul gnou Bone nguene
@amiseck30754 жыл бұрын
Discours incohérents et contradictoires.
@aboudemetalibebayeniass5824 жыл бұрын
Sénégal mo nékh dagay déff crime niouné doff nga assane danio wara ray ndayam nganam wéroul
@imggai96244 жыл бұрын
Peine de mort doit appliqué au Sénégal li dafa yomb trop
@aboubackry44834 жыл бұрын
Ah ça c vraiment dure mais que la terre lui soit légère
@fmbodji66034 жыл бұрын
Dangéndi di fenne sose rk kou Ray nitt Sénégal niouné wéroul marém sa'ma doome la 😭😭😭😭😭 repose en Paix ma filles adorable anta yayam fou Bakh laniou bokh
@mimathiam80624 жыл бұрын
Kou raye nitt guene d wérroul ki dafa décédé na wakh bi rafete
@mouhamedmouhamed80054 жыл бұрын
Ndaysane ki dée yalla nako yalla yueruem
@khadimniass20234 жыл бұрын
Ah boudé nonou la démé djiguéne gui mo togne wayé bakane mo forr raye kéne douko deff derrière solution Djiguéne mo graww même Soula togné tamite kéne doula déglou kone nanou deff attention si djiguéne gni
@serignecheikhfaye11034 жыл бұрын
Yalla rekk mo yéeyo yeul bakan naniou bayui fatt bakan bakhoule si ban reew laniou nekk
@morniang59374 жыл бұрын
Yalna yalla yeuramko nioune danou mana bay bayal mbire bamou apou lokhou nanou farlo si biryi disi gaw bayi setane bi
@elygueye5734 жыл бұрын
Yalnako Sidy Birahime fall térou si Barkei kou ted ki🙏