S.lamine seye de dafa yeeme Yalnama sunu borom may ma melni mom ci kourel rawatina ci pasteef bi mu ci am ak sélal gi ak ci walum batt bu neex bi te nangu te am dolé te yërëmtalu te dëgu ci njàng mi Amiin ci barkeb borom tuubaa ak xasida yi Namako niepu di nianal