Oustaz Oumar Sall rek la niouun topu Al coran ak souuna rek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@papasambadiop759911 ай бұрын
Khamolén sakh lane moy Sunnah, dém lén diangui bayi wakh dji, yén rek yénaw wkh ci tarikha yi faté ni Ibadou tarikha leu😂
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@papasambadiop7599 Tarikh kay daguay ame Serigne mais heureusement que les ibadous n'ont pas de Serign koudoul Yonentébi.😂😂🤣🤭🤭😭😭😭.
@papasambadiop759911 ай бұрын
@@Anti-Bidaah 😂😂😂 bobou ga khamoul dara nak yow😂
@IbrahimabayloDiallo11 ай бұрын
Yaw lane moy sunna
@bibatou11 ай бұрын
Je suis tidiane mais je partage ton avis ouztazz, des le début je me dis que li diaroul plainte, naniou bayyi leupp ci lokho Allah, les propos de oustaz Omar Sall Dou takh niou bayyi toudou yallah
@OumarBa-po2wr11 ай бұрын
La Sunna le chemin du prophète aleyisalam inchalla tôt où tard la vérité vaincra
@ansufatimane921411 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂 Wouyay
@papasambadiop759911 ай бұрын
Khamo sakh louy Sunnah yow ak sén mbotay
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@papasambadiop7599 lane Moy Sunnah.
@abdousylla52111 ай бұрын
Libérer oustaz oumar sall c'est le meilleur oustaze au Sénégal ❤❤❤❤
@adama273611 ай бұрын
Merci Oustaz très bien dit "La illaha illalah" est la parole la plus lourd tout ce qui est dans les cieux et la terre. C'est vrai les propos de Oustaz O.S sont un peu dégoûtants la manière dont qu'il l'a parlé il faut de la sagesse, mais les tidiane aussi n'ont pas de la clémence ça ne devait pas avoir la plainte donc pourquoi beaucoup des musulmans sont des injustes combien de personnes dirent de mal sur Allah le Prophète et les Sahaba et pourtant ils n'ont pas reçu de plainte ok si je comprends bien vous aimez votre Serigne plus qu'Allah et son Messager. Allah sait mieux ce qui est dans les poitrines des hommes. Les plus nombreux des musulmans sénégalais font des shirk majeur et mineur et vous ne les portez plainte 😮 Une question ? Pourquoi aux temps du Prophète y'avait pas des tarika? Hadith :Le Prophète a dit à la fin des temps les musulmans diviseront 73 sectes tous iront en enfer sont un celui qui suit le coran et la sunna. Ici au Sénégal les sectes sont nombreux et Chaque Cheikh appelle à ses disciples qu'il est la porte du droiture le bon chemin c'est comme le Prophète n'est pas reçu sa mission. On a qu'un seul Allah et Messager mais la manière de l'adoration est différent pourquoi. qu'Allah nous guide et nous montre le chemin exact de son Messager Amine
@fatimasonkoalamine541111 ай бұрын
Oustaz oumar sall rék laniouye top❤❤❤
@Coranandsunnah410511 ай бұрын
Oustaz O. Ahmad Sall yalla nako yalla takhawo❤️🤲🏼🙏🏾 Sénégal tarikha laniou guem En tout cas serigne yi am naniou responsabilité bou reuy sikanamou yalla
@CHARIA_TV11 ай бұрын
Yaw si boppam Di nga am nganim déception yawmal khiyam wallahi Wal khour anoul anzim prck khamo léne yallah damalene yeureum lole prck da nguen fokni yene kassei yéna bakh alors que c faux
@OusmaneToure-bc2py11 ай бұрын
عفظه الله ورعاه يا أستاذ عمر سل ❤️❤️
@bebekane707011 ай бұрын
Oustaz oumar sall li dina wakh coran ak sunna la wakh, Sénégal nak nekhna trop, chaque jour niou guiss koy saga religion bi té dounko tedj. 😢
@123yvp11 ай бұрын
Wallahi
@abdoulayeseck780411 ай бұрын
Qu'est-ce qui est plus grave de saboter le coran, de miniser le Prophète... Personne n'a porter plainte ! Dieu est pitié de notre cher Sénégal !
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
Lo kham ci naféq. Lolou késsé woléne dale niou sagua fi ALLAH (SWT) Le Seigneur de l'univers kéne waxoul dara, sagua fi niari Yonenteu you YALLAH gueureum balégui kéne porter woul plainte.
@papasambadiop759911 ай бұрын
Fane ga guiss sénégal Koufi minimiser Le Prophète( PSL). Dolén bayi fén nguir Yallah 🙏🏾
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@papasambadiop7599 so paré sétane bamou djiéx takeu gua djiokh maci sa avie mangui lay xare .
@@Anti-Bidaah vidéo bi complet c'es plus d'une heure de temps lépp la sétane
@FatouHann-v7c11 ай бұрын
Bien dit oustaz ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@soxnasi123410 ай бұрын
Salam aleykum. Dieureudieuf kadou gui rafet na. L ayat de sourate jumua que tu cites, il est dommage de ne pas le traduire en entier : 10. Puis quand la Salat est achevée, dispersez-vous sur la terre, et recherchez [quelque effet] de la grâce d'Allah, et invoquez beaucoup Allah afin que vous réussissiez. Le zikr et les nafilas du temps du Prophete se faisaient en privé, y compris nafila. Donc li oustaz bi wakh inventer wouko. Toutefois diamono dokh na ba gnou guiss ni dadialoo di zikr moo gueune tassaroo kou nekk di takhawalou diamou woo ligueyoo. Kou mou nekh rafetlou kou mou nekh nei bidaa la. Il faut savoir accepter toutes les opinions tei niane yalla mou faye gnou sunuy yeene ndakh gnoune gneupp matadi, da gnouy goorgoorlu rek
@solomongiteh588611 ай бұрын
What oustaz modou fall is saying is true but we fail to understand what oustaz oumar sall is saying he didn't say that we should not glorify the name of Allah.... What he really mean is that gathering putting a white cutting in the middle and surround it shouting....... What does that white cutting means If I may ask
@serignembayefall173210 ай бұрын
Merci oustaz, pour les références précises
@amethdioufsene704811 ай бұрын
Respect oustaz oumar sall
@YacineNdiaye-o1m11 ай бұрын
Merci beaucoup oustaz Fall. Toutes les personnes véridiques savent que Omar sall faisait du sabotage. Toogne baakhoul. Mais il s'est ridiculisé lui-même
@ndeyembaye890811 ай бұрын
Wallaahi bou bayiwoul Cheikh Ahmet Tidiane Cherif dou diog thi torokhté ndakh dougue kasso torokhté meunouka passé
@khadissaaidara686711 ай бұрын
Lii yeup dou laye. Nagnoukoy déféé comme niko Mouhamed di sougnou royouwaay done défé wakh dji fin moy sougnou royoukaay
@AbatalibDiop11 ай бұрын
Omar sall on t’aime
@PapaytonAfrogender11 ай бұрын
Mais wakhouleen ko les autres ngueeni déranger les gens...et plus vous utilisez des micros haut parleur
@bambacisse966711 ай бұрын
Modou fall geumoulo Cheikhou Tidjanes
@mouhamadoudiallo374811 ай бұрын
Monsieur arrête tes jeux de logiques. Réponds à ces questions : - est-ce que le prophète à une fois fait le hadratoul jumma ? -est-ce que les 4 khalifs du Prophète psl (Aboubakr, Omar, Ousmane et Ali) l'ont fait ? - Imam Malik à t-il une fois fait le hadratoul jumma ?
@ThierSow-n6c11 ай бұрын
Machallah Oustaz
@BASS.TUTO.ANDROID.B.S.T11 ай бұрын
Fall fi amoul masalah sall loumou wakh mo am
@PILN6211 ай бұрын
Masha’Allah, wax j rafeet na tei borom xeel bu sedd meun nako deeg…. Sénégal nitt ñu bari si ñoom degou ñou Diiné, Yalla dafa wakh si Alhurane Touddu leen yalla (fi kili makaanin) Fo len meunti neeq. Waxoul ñi ñoko wara toudou wala ñé Ñeupp si yam, goor, djiguene, mak ak ndaw… Mais dinné j mom kou nekk ak ni nga ko sentiré rek, tei sa morom bou defei lo deffoull nga nan kii boukoul si dinne j 😢 YALNAÑU YALLA DEFAL DEG AK TOP
@Hawadiop-k2y11 ай бұрын
Lailaha ilalah bou andoul ak danse toudou yallah naturel rek Lolou la yallah wakh
@alhassanediallo210911 ай бұрын
Sourate 62 - Ayat 10 فَإِذَا قُضِيَتِ ٱلصَّلَوٲةُ فَٱنتَشِرُواْ فِى ٱلْأَرْضِ وَٱبْتَغُواْ مِن فَضْلِ ٱللَّهِ وَٱذْكُرُواْ ٱللَّهَ كَثِيرًا لَّعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ Puis quand la Salât est achevée, dispersez-vous sur terre et recherchez [quelque effet] de la grâce d'Allah, et invoquez beaucoup Allah afin que vous réussissiez. Islam: Le Noble Coran
@TasrifSene10 ай бұрын
Le Tafsir? Prendre un verset à la lettre ce n’est pas comme sa akhi
@ahmadmbaye564411 ай бұрын
Ouztaz Modou fall je te donne raison diaroul prison. (Adinou anassihatou ) dinné louniouy wakhtané le.
@julmatoure44011 ай бұрын
Senegal mo barri bida mai allahou ahlem ☝🏽 yalla hamna leep ba bissou penc dins am gnou matt sene lokho dh bougnou si teloul djiouk dina yak les futur sunna yonenti (saw) bi senegal certain abuse nagnou khol si sahaba yi lou yonenti (saw) bi done dff niou dff ko
@AntaDieng-k4j11 ай бұрын
❤❤❤❤
@mohamettop935311 ай бұрын
Alhamdoulilah ❤
@Hawadiop-k2y11 ай бұрын
Diokhel preuve rèk ni limou wokh diadoul oustaz d’où messe balou li yonetebi wakh rèk la wakh
@cheikhsadiboudiallo635511 ай бұрын
Mangui dieglou oustaz Fall wayé dacourouma ci ndakh " wadkourou Allah katiran" moy ken kou nek dafa wara toudd Yalla wakhoul ben yonn nguen dadjalo pour toudd Yalla. Sinon Yonentebi mo koy ndieuk def manam moy wouté nit gni pour dajalo pour toudd Yalla te lolou moussoul ko def degnu done dajalo pour diang diné. wa salam
@sadacamara-wr2ss11 ай бұрын
Il faut regarder la vidéo de Madiama Fall. Dans cette vidéo Madiama Fall insulte wA eukhlou souna et les traité de tout les noms. Maintenant Oumar Sall est sorti pour apporter des éclaircissements et on lui porte plainte pourquoi ? Fi kou wakh Oumar Sall mo togne nafékh nga .geumo Dara. Mais amoul raggal deuggoup yallah dji dagnou koye wakh quelques soit alpha
@sadacamara-wr2ss11 ай бұрын
Nous ne sommes pas minoritaires dans ce pays. Diam rek rek Dara dou xéw
@sadacamara-wr2ss11 ай бұрын
Tarikha yi aye mbame lagnou formé mais pas aye nit. Il faut dire la vérité rien que la vérité
@mamerackysenghor156311 ай бұрын
Oustaz Oumar Sall tognoul kéne😂. Wazifa ak hadaratoul ju'oumoua bi'dha là
@ansufatimane921411 ай бұрын
Tafsir al quran bidah la😂😂😂😂😂😂😂😂
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@ansufatimane9214 Tafsir meunoul néke bida'ah parce que le prophète l'a déjà fait. Un Bida'ah c'est une adoration qu'on fait alors le prophète ne l'a jamais fait. C'est ça un bida'ah. Par contre le prophète et ses compagnons ne sont jamais regroupés dans un endroit et prononcer ensemble "ALLAH" il n'y pas de preuve qui nous le prouve donc C'est ça un Bida'ah.
@fantadiatta342311 ай бұрын
Bidah moy innovation ci diné. Té Yalla SWT Al kuran ak suna çad doundine Yonénte bii SAW laniouy roylo. Loi way du déff pour diamou sunu boron na eundi aya wala hadiss bou wérr pour justifierco. Il Ya faire une chose et la manière de le faire
@@Anti-BidaahC'est à cause de leur male compréhension de l'islam
@mamadoubarry487611 ай бұрын
Ya Oustaz balégui guénoo si loumou wakh donté yangui nane dafa togne té yaw sa biir explication bi yeup meusso né yonenti bi daane na dadjalé mboolo pour toudou yallah walla yallah néena si térém bi nguéne dadjaloo léen toudou ma mais néngua "Tidjane yi né comme négn dadjaloo" Té Oustaz Oumar boumouy wakh dafa né yonenti bi daane na toudou Yallah mais daawoul dadjaloo ak mboolo pour defko si lolou la doone khaar nga diappaléma Indil ma Dalil bouy tégui lolou
@papasambadiop759911 ай бұрын
Thiouné rék molén Diapeu ak diangg bou sori woul, khamo lén louy Sunnah khamo lèn louy Bidaah, diouli ci Diaka bou am soraul rek bidah leu té khamolén ko
@elhadjisunugal11 ай бұрын
Esk yonenti bi wakhone na Koukoy deff gua 'nekk kenn wala mbollooo damaay ladj lou kenn di deff kaay bouko mboloo defei laay geuneu barii touyaba xana
@modoubarasarr650611 ай бұрын
Naniouko niamal ay yar rek
@papasambadiop759911 ай бұрын
@@elhadjisunugal merci frère gni sén diangg mo gateu ci bopam té pour niom nio guena diangg nit yi wala niou guen lén ci Diné bi
@YacineNdiaye-o1m11 ай бұрын
Merci beaucoup oustaz Fall. Toutes les personnes véridiques savent que Omar sall faisait du sabotage mais il s'est ridiculisé lui même
@medounegueye361210 ай бұрын
Mane Soumay lire commentairou ignorant yi aye rétane lamay deff dem len diangui dine akhe khame khame adouna boumou len diaye ba guene fek ni yalle loumou deff mokhame Loutax mou deff ko warro len si ame ben jugement personnel Bien dit Oustaz modou Fall Pour le reste allahou alame bima youride et soyez sûr d’abord de ce que vous êtes et ne dénigrer pas les autres comme si vous prenez la place de Dieu
@maguettendoye971711 ай бұрын
Ayate binga wakh niii baleigui degossi tok lall drap bou wekh di youkhou. Sénégalais yi nak diangou gnou motakh ngay leudeumeul Ayate Yalla ragalal sa borom . Yein wa tariha yii dangueina beug Ay kay diegalou dans vos rêves wasida biida la Mohammed diangalei wouko
@dadindione360111 ай бұрын
Mane dh de ma part je suis pour le retrait de la plainte en temps que Tidjane. Mais waxdji "djoul mou teuthie mbokou djoulit "wax djou yakou leu ndax yagnou djapei nou nioune dounou ay djoulit
@Diaz42611 ай бұрын
Mom aye yalla nouko nekh lakoy fire
@abdoulayeseck780411 ай бұрын
Xam xam, xam xam mokoy tontou ? Yalla néna, yonéneteu bi néna...lou thi grave ? Naniou sétate souniou boppam bou bakh, té ragal yalla kessé..mom rek keu fi nek, loudoul yalla néneu leu
@papasambadiop759911 ай бұрын
Démal ga diangui sa diné
@Alhamdulilah-r7e11 ай бұрын
Allah Allah n’est pas un zikr !!! Le prophète nous a appris comment on doit faire le zikr !!! L’islam n’est un bordel au point que chacun vient s’inventer son zikr !!! Allah Allah ce zikr ne se trouve ni dans le coran,ni dans la sounnah
@moussabiaye99311 ай бұрын
Tes arguments ne sont pas bonnes ; Parce qu'Oustaz Sall n'a pas condamné l'évocation d'Allah. Mais plutôt la manière dont vous vous rassemblez pour crier ou évoquer le nom d'Allah. Parce que le Prophète ç ne l'a jamais enseigné, ce qui veut dire que cette pratique sera rejetée par le Maître du jour du jugement. Allah a dit de l'évoquer beaucoup et son prophète ç nous a enseigné la manière de l'évoquer. Celui qui fait autrement s'est fait tord à lui-même.
@barhamlazizien330211 ай бұрын
Wax dji moyy nagnou mandou sene probleme moy dagno mandouwoul ibadou yi kome ci yome la yalla dioxx dinè bi
@Ggtttiiioi11 ай бұрын
Mbokk yalla waxoul 😂lolu nk aya bi na ler del seg bida ak sunna😂😂té bayi firi bii noumla arrangé
@TaphaAmdy11 ай бұрын
Way oustaz Mane AP mouride la douma tidiane ki da yabaté bayil niou yarr koté mom sax d'où missionnaires diné
@papediop940411 ай бұрын
Kounèke gueumal loungua gueume,bayii sa morom mou geume loumou geume djiame nè gnoy.wayè nèkke sii loungua nèkke dii sabotè ak togne gnènène lolou c'est pas bien
@Ousmane75.10 ай бұрын
Omar saleté dou missionnairou diné mais un missionnaire du satan mom ak Sikkimam ak kanamam you gnang
Oustaz oumar sall alquran ak sunna lai dundu du jegalu ken point. lutah mui jegalu . yonenti bi Muhammad alaihi salatu wasalm hamul tarikha . bayi wuko fi bimui demm . lislam lafi bayi ak sunna
@omarsaynab11 ай бұрын
Ostaze modu fall fikce modu fall
@zhom254811 ай бұрын
Ya bary thiakhane !!! Oustaz d'où baalou inchallah !!! Doléne KO degue!!! Sén khôl d'où si séd! Je réitère KOULOU BIDATINE DALALA ! KOULOU DALALA fi Nar ! Li oustaz Oumar Sall wakh lagnou geum CTT.
@momo_le-pro.711 ай бұрын
Yaw Yangui Binde si clavier di utiliser téléphone dissi wakh sa sokhla ngassi diangalé wala dissi diang té diamono yonent bi SWS amoul wone rek bida la ? téré rek mo amone té aname Bamou wathié wone ag téré yi legui nignou taralé bamou tarou bokoul esk bida la?diamono yonente bi SWS amoul wone diouma you tarou comme you legui yi Nga hamni or ag diamant sakh dassi am nguir yokou taar bi esk bida la li nek lou bess dafa beuri Si diné bou yokoul dou wagni kon nak fekhal len sen khol yi ta bayi dingat yi fi yalla rek mofi nek té mom reka mana juger mais pas yen lou gneuw ngen diap né yenassi eup xam xam adouna wessou na fofou Ngen balma 👏
@zhom254811 ай бұрын
@@momo_le-pro.7 attention bidah concerne la religion !!! Geune dji minéf yalla KO Yoni si note gni diokh l'islam pour mou defar gnou . Avant Mouy gnibi néwon n'a diiné l'islam jiko yalla diokh néwon n'a meut n'a seuk . Donk lougnou ci Yok bidah la!!!
@mamadoufall585211 ай бұрын
@@momo_le-pro.7 bayil Gni sén khel bakhoul Soy wérén akk gnome dangay soneu rekk Pour gnome ils sont déjà au Paradis et tous les autres a l'enfer. Gnom déjà ils prennent la place de dieu en jugeant toutes les personnes qui font pas partie de leur mouvement Pour gnom gno gueune nieup mais yalla bakhna Moi je suis Tidiane et très fière même
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@mamadoufall5852Serigne bi nous les ahlou sunnah, nous n'avons jamais dit que telle personne ira au paradis, telle personne ira en enfer. Ça c'est du domaine d'ALLAH par contre il faut se dire la vérité entre musulmans comme nous la recommander notre Seigneur ALLAH (swt). Il y'a des choses que vous faites qui sont à l'encontre de l'islam voire qui n'ont pas de fondement comme l'innovation (bida'ah) dans la religion d'ALLAH. L'islam authentique que notre Seigneur ALLAH a envoyé à notre prophète Muhammad (Saws) n'a rien à voir avec l'islam qui se trouve maintenant au Sénégal. Le prophète n'a jamais fêté de "Gamou" ou " Magaal Touba" même nos ancêtres comme Serigne Touba et El hadji Malick Sy ne l'ont jamais fêté, alors d'où ça vient ça ne concerne que vous car le jour du jugement dernier c'est chacun pour soi.
@fatimata659911 ай бұрын
@@Anti-Bidaahmdr akk fatali rek magal touba sante yalla lagnou wote lolou le serigne bi degle 😂😂kon yeen yenaay ahlou sounna dall Wa leegui gnoun gnouy ahlou alkhouraan 😂
Oustaz fall wa walguogou niou la gueuneu cam li oustaz bobou def danio nafex rec waye amoul lou gueuneu mague toudou yalla mom 5:22
@sophiefaye127611 ай бұрын
C'est vraiment que des musulmans emprisonnent leurs confrères pour des divergences religieuses. Nos illustres 04 imams avaient des points de divergence.
@madoudrame152311 ай бұрын
Omar sall Waxoule la ilaha ila allah baxoule dh, waxoule def zikr baxoule, Omar sall dafa nei : Yonnenter bi meussoul dajaler mbolo di wax Allah Allah , Legui nak tontou binie beuguone moy: Yonnenter bi meussnako def : Oui ou Non , ndax Yonnenter bi lanie wara royy Explication bi yeup jarouko
@laoucouledesruissaux449511 ай бұрын
Yén nitou tarikha yi dagén meuneu lay,meuneu soss,meuneu fén,yow modou fall ak mactar sarr ya lé n geuneu am eufeurie ragalén yallah ta gén topp yonante bi saws mom kouko top rék joup.té gén bayi bidah.
@fatimata659911 ай бұрын
😂😂😂😂wouyyy gnoun dh beugg yonante bi akk toppo kou ak geum kou gnousi meun gnnoun tarikha yi nakk lala wakh nieppu nakk
@laoucouledesruissaux449511 ай бұрын
@@fatimata6599 wakhou dof,Kone dé yow khamo li amé deug.yow yégo ni alkuran dafa jar droite gén jeul gauche, mouhamed saws nélén déf lén ni gén bagn,né maodo rajim géni top.boul nakh sa bop yén khamolén liy sunna. Yén salatoul fatigué(fatihi)AK jawratoul satan(Kamal) rék gén beug.sén Serigne yi gnou nék sén khôl yi.wayé d'où yallah AK yonante bi saws.
@alitouray687111 ай бұрын
Modo fall doll rk
@MacodouNdaw-xb2wu11 ай бұрын
Fawou niou yarr ko
@papemoussafaye251811 ай бұрын
Tidian rék tidian késsé ❤
@ablayendiaye610510 ай бұрын
Yaw maynoiu diamou mabame sall na dem tok masla amou fi topal feleu
@bambacisse966711 ай бұрын
Yaw geumoulo tivaouhane
@ndiayem627311 ай бұрын
Y’a mana fen molen tionge
@moussadiatta877711 ай бұрын
Démal jangui mo guéne ci yow
@alhousseynisow456511 ай бұрын
Boul wakhé kol wakhél xam xam rek sou ka défé rek brom kél yi daniou xam Allah Allah mouy adiouma wala ak loumou don lou yonenetébi jangalé woul tei défouko bokoul si Alkouran ak Sounnah Lolou moy degeu Amoul féne Fou yonnénté bi wakh ni adiouma si Ngone naguéne Sol lou Blanc talal sen morceaux Bou Blanc di wakh Allah Allah .je te defi yaw Oustaze modou Fall .Debat bi xam xam la lathie Thiaxane bakhoul .
@papasambadiop759911 ай бұрын
Yow diaka yigay dioulé amna sauraul wala amouko!?
@fatimata659911 ай бұрын
Leegui ndakh toddo yalla ?yalla deglou woko
@papasambadiop759911 ай бұрын
@@fatimata6599 gni ay comedien youy mboubo diné l'islam lagn koi😂
@diacksonesarr790911 ай бұрын
Oustaz oumar Sall tonioul kén boulén yakaré mouni mangui diégalou dinguén dhé dh boulén niou sonal avec vos soi-disant Serigne
@mohamedlaminebaradiouf188511 ай бұрын
Yen dangen amoul xam xam, té deggo len sunnah motax nguen sonnou
@Diaz42611 ай бұрын
Bolen halate Oustaz omar sall balou lene guene dh fale woulen sakh wakh si xam xam tontou lenko. Si xam xam rk wla gua nopi guendi tethie nite gni kasso niak argument thim
@mamadoufall585211 ай бұрын
😂😂😂😂Non mais vous êtes les meilleurs Mane j'arrive jamais a comprendre votre mentalité Mais deukk bi mome yone amna fi Dém lèn rekk Fier d'être Tidiane !!!
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@mamadoufall5852Deugueula yone amnafi, mais nous sommes déçus parce qu'on attendait pas ça venant de vous. Dagnouléne lathieu Dalile ngéne Andilniou ay plainte 😂😂😂😂. Vous n'êtes même pas capable de fournir des arguments qui nous prouvent que vous êtes sur la vérité mais finalement vous êtes obligés de porter plainte. 😂😂😂😂😅.
@mamadoufall585211 ай бұрын
@@Anti-Bidaah Nous mais tjrs je vous comprends pas Bilay vous êtes les meilleurs 🤣🤣 Vous n'êtes pas d'accord sur nos faits et croyances mais mandou lénsi comme gnoune nignou mandou si yén meussou gnou lén critiquer Tjrs yénay wakh si gnoune Tidiane Mouride..... Mais mandou lén té pratiquer diné comme ningéne co dégué té nopalou
@Anti-Bidaah11 ай бұрын
@@mamadoufall5852 C'est être madou.selon vous "mandou" c'est laisser les gens dire du n'importe quoi sur ALLAH notre Seigneur, associé ALLAH (SWT) avec quelqu'un d'autre et aussi insulter les prophètes comme l'a fait votre Serign tidjiani je ne sais pas comment il s'appelle et maintenant vous voulez qu'on ferme la bouche sans rien dire ça ce n'est pas être "mandou", en Islam ça s'appelle de l'hypocrisie. C'est ALLAH qui nous a commandé d'ordonner le bien et d'interdire le blâmable, donc c'est notre devoir en tant que musulman de se recommander mutuellement la vérité car le prophète faisait la même chose, Cheikh Ahmad Bamba et El hadji Malick Sy faisaient aussi la même chose. Si c'est ce silence qui est signe d'hypocrisie que vous qualifiez de " Mandou" , on ne le sera jamais de notre vie car on va toujours dénoncer le CHIRK ( BOKALÉ) et les BIDA'AH que les gens font au nom de l'islam alors que ça n'a rien à voir avec l'islam authentique.
@ismailasane605311 ай бұрын
@@Anti-BidaahDonio foguné lolou Moy mandou mais lolou naféq la. Gua guiss loubone té waxo dara.